Une cagnotte pour maman Aïcha aurait été une excellente initiative. Elle mérite tout le soutien du monde pour ces moments de rire qu'elle nous a procuré ❤
A l'écouter j'ai des larmes aux yeux mais la vie est un long parcours parsemé d'embuches Que Dieu nous assiste. Maman Aicha SAMB tey diangate na lou Baré baré Yalla nanou Yalla takhawou si barké baboul Mouridinah😭😭😭😭
Soxna ci , bégueul nga niou bari si art bi ngay déf. Yallah nala souniou boroom bégueul. Yi nga doundeu méti na torop , mais diapé ko ay natou rék. Kouné amna sa dose de natou dans la vie. Que Dieu t'assiste....amine
Ndeysan Maman Aïcha yalla nala yalla takhawou yak sa ndiabot si barké Serigne Fallou, yalla nga am banekh bou sakh t djik la, yalla nga fekei sa ndiarign ndiabot , yalla ngen am appartement, khoslou bigay khoslou yalla nala deudou. Yalla nala yalla fay sa xol❤❤❤❤ Force à toi yalla wahoul keneu dara
Maman Aïcha aka bakh mane dé damako kham sama dieukeur thiamégnam la wayé amoul dara mais lou nék si lokhom mou diokh ko nitt gni tok yéré you raféte am valeur lako nitt yi di diokh dakoy mayé watt
Mane deih sincèrement depuis temps dinama neikh je connaissais des gens qui habitaient avec elle dans le même quartier mais wakh bi béne la elle était belle elle était gentille reik ngay deigg ❤ Yalla Nala Yalla diapalei maman
Ndeysane c'est très triste en écoutant Maman Aicha mes larmes ont coule. Elle parle avec franchise ; ce qui me plaît chez elle c'est sa croyance en Allah Le Tout Puissant. Comme elle l'a si bien Allah lui est venu en aide mashallah mashallah elle a le tawhid. Très bonne continuation
Perdre sa mère à bas âge c'est très difficile d'autant plus que l'on vit avec des mauvaises personnes mais la volonté du Tout Puissant ndeysane j'ai eu beaucoup de peine en écoutant la brave et courageuse Maman Aïcha qu'Allah Le Clément lui facilite aamine ya rabbi
Émission touché nama trop bilahi souma Yallah mayone immeuble comme yi ma guiss thi deuke bi dinathi maye mama Aicha mi bêne appartement pour mou nêke thi ak diabotam ki li mou ndounde yépp métina wayé kou brave leu kou Diara dimbali
Ndeysan maman aicha gnépako beug diambar deug nga li Moy valeurs limou motiwon lép taxoul Ben yon ngadef lougnoulay xébé Nala yalla may fanewou goudou ak wergui yaram ,koula xol degloula xamni nitkou deugounga ta nitou kassé nga diamsiaw yaaboy❤
NDEYSANN UNE MAMAN TRÈS DIGNE , LIGUÉY KATT LA , NIAFÉKATT ,, BOUGOUL KOUKO YÉEP DANE NA NIEUW SUNU KEUR NDEYSANN ❤❤ JE L'AIME BIEN XOL BOU RAFÉTT LA YORR MEUNE KAFF AK RÉE 🙏🏿 SOUMAKO MEUNONE DÉ BILAHI WALAHI NAKO MAY KEUR YOBOUKO MECQUE TÉ YALLA TAX ❤
Elle n,a jamais connu de bonheur dans sa vie aduna tamit et pourtant des sorciers comme des sorcières sont là tous les jours rien que pour gacher la vie des gens et sont heureux
Vous pouvez soutenir Maman Aicha sur son numéro Via wave et orange Monney 774713995
Yu
Àaà vu😅😅@@ndiemesene499
Li moume dina si bax
Salut je voulais nga inviter sokhna mbayangue thiam svp
pourquoi pas ajouter des archives (photo) de leurs différentes vécues ?
Une cagnotte pour maman Aïcha aurait été une excellente initiative. Elle mérite tout le soutien du monde pour ces moments de rire qu'elle nous a procuré ❤
Bilaye ioe c’est une bonne idée dh
Bilahi athia Way kou xame numéro ndeysann dane Na Nieuw sunu KEUR ndeysann
Gnibi géré émission nagne diokhé numéro
Binde ko dakarbuzz mou gérer ko
Bilay yaw commentaires bi ladon weur aytiou nako dall 👏👏🤝@@AdamaBadji-o4g
Cette presentatrice est vraiment un amour aussi belle que douce ma preferee de toutes vraiment!!!
Nit kou bakh la machalla❤❤❤
Si si elle a un grand coeur machallah
Une brave dame courageuse très digne et très forte yallah nako émission bi oubil ayy kheweul 🙏🏿🙏🏿
Amine way
Amine🤲
Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏♥️
aye ndeysan qui pleure comme moi 😢femme de valeur yalle naleuh yalle sameuh🙏😭😭😭maman Aïcha lou bakh rek guay ame inshalah kou sonne yalle nga diarignou 🙏🙏✌️
Sénégal dafa graw barry ay nanék 😂😂😂😂
@@AbdoulayeKASSÉ-p5iIoe wero
Lilaye méti sa mbok mola kay ték. Kou la meunoule diot ci saye dom lay diar
Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏♥️
Eva yalnala yalla doli soutoureu ak kheweul tu es correcte calme et disciplinée posée aussi merci Eva
A l'écouter j'ai des larmes aux yeux mais la vie est un long parcours parsemé d'embuches Que Dieu nous assiste. Maman Aicha SAMB tey diangate na lou Baré baré Yalla nanou Yalla takhawou si barké baboul Mouridinah😭😭😭😭
Soxna ci , bégueul nga niou bari si art bi ngay déf.
Yallah nala souniou boroom bégueul.
Yi nga doundeu méti na torop , mais diapé ko ay natou rék.
Kouné amna sa dose de natou dans la vie.
Que Dieu t'assiste....amine
Nite kou yagua bakh gnon deukone HLM angle Mousse nék ay khalé mou gnouy may khaliss à chaque instant yalla nala Yallah diapalé
Amine ya rabi
Maman❤❤Aïcha liga def lep guir yalla nalako fay sisay domme si barké seydina Mouhamed🤲🤲🤲
Alalou ndjirim kouko lek guissoumala mbaoo yallah est patiernttt walllahi
Macha allah la présentatrice je vous adore tu est adorable ma chère. Bonne continuation amore❤❤❤❤❤❤
Courage Maman Aicha 🥰🥰 , on t'admire depuis Dinama Nékh et plus encore à nos jours
qu'Allah bénisse tes enfants
qu'Allah fasse k tu sois la maman de 2 Millionnaires tes enfants, AK Tal AK féké.
Amine.
Ndeysan Maman Aïcha yalla nala yalla takhawou yak sa ndiabot si barké Serigne Fallou, yalla nga am banekh bou sakh t djik la, yalla nga fekei sa ndiarign ndiabot , yalla ngen am appartement, khoslou bigay khoslou yalla nala deudou. Yalla nala yalla fay sa xol❤❤❤❤ Force à toi yalla wahoul keneu dara
Amine ya rabi
Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏♥️
Marodi Evens prod Leuz
Prenez la comme actrice mouy jouer liguey ame salaire
Leuz merci pour tout yalnala yalla fay
Daffa am gnou am memoire de koumou toudou wakh mamam domam ak seuteum mashallah
Hoooo j ai des larmes aux yeux Souma amone xaliss tay nala outal appartement juste pour que tu vis avec ta famille 😢😢😢
Elle a l'art oratoire. Une veritable artiste. Longe vie maman.
Qu'Allah lui vienne en aide. Elle parle avec sincérité.
Éva ya Bakh ❤ Yallah na sa diam yagu Barki Cheikhoul Xadim❤
Alahouma amine
Amine wayyy
Brave maman en plus elle est sincère dans ces paroles billahi❤
Li morakh guawa jugé nite bakhoul ❤ yallah nala yalla takhawou
Guisgua d sénégalais nak dafa gawa juger
Bilahi sénégalais mo mel nonou 😮
Maman Aïcha aka bakh mane dé damako kham sama dieukeur thiamégnam la wayé amoul dara mais lou nék si lokhom mou diokh ko nitt gni tok yéré you raféte am valeur lako nitt yi di diokh dakoy mayé watt
Gawa juger ak yéxeu juger si Yep. seul Dieu vous est juge
C vraiment émouvant. Lou meti yague na si adouna. Courage maman aîicha samb
Ndeysane une émission pleine d'émotions. Ma aïcha dioy lo ngama. Wa Sen People Kou beugeu contact maman Aïcha noy déf svp
Pourtant ils ont donné le numéro sur les commentaires en haut
Thiey yalla Lou metiii yagg na si Adouna 😢Masta yaye boy yalla gua doundou mbecté Lou desss si sa Adouna 🙏
Amine ya rabbal alamine
Amine ya rabi
Amine ya rabi
Amine ya rabi
Wally seck le chanteur du peuple djapaléle sougnou mama waye
Ma aicha kou bah ngua❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ yalla nalla tahawou si barke mohamed yalla dinala faye leepe inchallah
Bilaye deugueleu yalla moye diokhe weurseuk inchallah leppeu dina bakh inchallah amale diama thi barke serigne babacar sy amine yarabi aminnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnne
Borom khol you rafet yi jamais niou am loubakh yallah defer nonou pr natt diam bi sant yallah rek❤
Massa Maman Aicha , vous nous avez tjrs fais plaisir❤❤
Je confirme que elle a un très bon cœur ❤elle est toujours présente pour tout le monde je suis sa fille et nièce
Salam sister stp puis je avoir le numéro de maman Aïcha ? Merçi.
@@yayekharykebe2713 son numéro est épinglé dans les commentaires
Je regarde cette vidéo mais à chaque fois je regarde la barre si je suis à la fin ou pas, tellement d'émotions. 💔
Ndeyssane maman Aïche m’a fait tellement pleurer aujourd’hui 🥹🥹🥹🥹🥹❤️Yallah nala Yallah takhawlou thii barke seydina mohamed 🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽
Mane deih sincèrement depuis temps dinama neikh je connaissais des gens qui habitaient avec elle dans le même quartier mais wakh bi béne la elle était belle elle était gentille reik ngay deigg ❤ Yalla Nala Yalla diapalei maman
Jai pleuré de toute mes force que le bon dieu te protege
Wallahi yallah nala yallah diapalé si barké seydina mouhamet salahou allah mouhamet 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Nit kou sonou yalla nga diarignou masalah mama aicha 😢
Ya rabbi koumou guena bague ley tek natou yalla nak ko y’a rabbi tegui si barkè yonentè bi ❤
Ce que je remarque malgré ces difficultés c’est comment elle est reconnaissante envers ceux qui l’ont aidés !
Ndeysane c'est très triste en écoutant Maman Aicha mes larmes ont coule. Elle parle avec franchise ; ce qui me plaît chez elle c'est sa croyance en Allah Le Tout Puissant. Comme elle l'a si bien Allah lui est venu en aide mashallah mashallah elle a le tawhid. Très bonne continuation
Yallah nala yallah takhawou sy barké yonéteby ❤
Vraiment félicitation et courage a maman aicha
Ay mane Sama xol bi 😢nita bone dh Yalla nala sougnou borom taxawou tant qu’il y’a vis y’a de l’espoir❤️🙏🏽
Machallah maman aïcha en plus elle a une mémoire d'éléphant ❤
Ndeyssane maman Aicha elle est entière ,yalna ko Yalla takhawou
Perdre sa mère à bas âge c'est très difficile d'autant plus que l'on vit avec des mauvaises personnes mais la volonté du Tout Puissant ndeysane j'ai eu beaucoup de peine en écoutant la brave et courageuse Maman Aïcha qu'Allah Le Clément lui facilite aamine ya rabbi
Ndeysane mamma aicha yalla dina bakh de billahi 😢😢❤
Billahi wallahi louméti yaguna tie aduna wayé alaxira amnadhé maman Aïcha sugnu borome dinala térale déh insha allah ❤❤❤❤❤❤
Soyez forte car à un moment donner la vie va nous l'obliger...
Thiey aduna barki baye niass sama khôl toynaa lol maman aicha du courage soit forte inchala leep dina bakh
Émission khawii soutoura
Longue vie maman Aïcha. Mandé geum nala.
Machallah maman aîcha sa yone metina trop yallna yalla khap dolli fi Ken nekoufi yalla rek mofi nékk geum ko wolou ko doyloko kassé
Ndeyssane nakar yague na si adina ak sokhor😢😢😢
Blh Lou ler🙈
Elle parle bien et se rappelle de tout machallah
Li yémé na ndeyssane YAllah nako YAllah takhawou ak ndiabotam
Émission touché nama trop bilahi souma Yallah mayone immeuble comme yi ma guiss thi deuke bi dinathi maye mama Aicha mi bêne appartement pour mou nêke thi ak diabotam ki li mou ndounde yépp métina wayé kou brave leu kou Diara dimbali
So emotional 😢
Ndeyssane masse
Maman Aicha owal Amina poté borom khol bou raffet bi❤
Kou bahh dinako diapélé ndah holl mbé rafett
J'aime beaucoup maman Aicha très bonne santé et longue vie Amine ya rabbi
Yalla nalla yalla diapalè si barkè Muhamed Sallal lahou aley wasalam❤️❤️❤️
Leuz dinala dieulate INCH ALLAH gua jouer théâtre MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH ❤❤❤❤❤❤ soulagement gneuwate
Maman Aicha du courage ❤❤
Une emission pleine d'emossions deysane
Ndeysan maman aicha gnépako beug diambar deug nga li Moy valeurs limou motiwon lép taxoul Ben yon ngadef lougnoulay xébé
Nala yalla may fanewou goudou ak wergui yaram ,koula xol degloula xamni nitkou deugounga ta nitou kassé nga diamsiaw yaaboy❤
Bayil lenn sokhor ak ligueyater mbokk amatoul du courage maman
NDEYSANN UNE MAMAN TRÈS DIGNE , LIGUÉY KATT LA , NIAFÉKATT ,, BOUGOUL KOUKO YÉEP DANE NA NIEUW SUNU KEUR NDEYSANN ❤❤ JE L'AIME BIEN XOL BOU RAFÉTT LA YORR MEUNE KAFF AK RÉE 🙏🏿 SOUMAKO MEUNONE DÉ BILAHI WALAHI NAKO MAY KEUR YOBOUKO MECQUE TÉ YALLA TAX ❤
Manchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Lo dioy rék amna KO tané maman aîcha yalla n'a yalla takhawoula
Ya guoré maman j'ai pas l'habitude de suivre intégralement cet émission. Mais yaw kou djara djapalé gua.
Du courage maman dîna. Bakhe uncha alla
C'est à cause de sa maladie qu'elle a eu la ménopause précoce et ce qui explique sa viellissement précoce ndayesane yalla nako yalla diappalé🙏
Lii dés sa doundou lép yla na don banéx yla na yla réalité sa yon ta sam la yla nala dom téral🤲❤❤
C’est vraiment triste 😢 le monde est méchant 💔
AY WAAY GUIRE YÀLLA ÑOU LIDIEUNETI NUMÉROM DÉFAL KO CAGNOTTE TÉ YALLA TAX LIVE TIK TOK PASK VRAIMENT YAGG NANOU BÉGEUL NAK AMOUNOU FAYAM DÉ❤❤
Partante
Dioxé naniou numéro bi
Mame Aïcha yalla nala yalla défal diameu nit kou bakh ❤❤❤❤❤
maman Aissa yallana yalla défal tawfekh dioubari mayla weer looool ak kheweul daga dinge damala yague beugue ❤❤❤❤❤
Machalaa maman aicha yalnala yalla doli samm té arr la mayla goudd fannnn bonne émission
Senegal danguay liguey gnoulay ligueye😔
Noy meuna avancer daguay nék thi bopou gnioulay lidjeunti dila yak
Walahi
Sama khol diekhna walahi azim maman yalla nala yalla takhawou
Machallah nite kene douko juger te hamoko 😊
Lou meti toujours Say mbokk ngon la Koy tekh yalla nalla yalla Sam 😢
Walahi mbokk gni diambour sakh moko guenn
@@DioufSinitaabsolument raison
Courage maman niako dé ndakh amgue ay dôme té yompoul
Machaallah 59 Sama moromou yaye maman Aicha❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalnaleu yalla takhawou Maman Aïcha yow ak say ndiabot
NDAYSANE EVA YA BAKH AIDER MAMA AICHA MOU AM VIE DE FAMILLE 😭😭😭😭😭😭😭
Courage maman 😢
Que dieux te donne une longue vie je t'aime mama aicha
Ndeyssane yalnala yala same
Yallah na yallah diapalé DIEU et grand la présentatrice et excellente machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alahou akbar ndeké mane dadiouma dara. Massa maman
Massa adina mongini
Awa c’est la première fois que tu as voulu vraiment pleurer 😭 dans ta propre émission.
Ndeye sane diame thi yaw ❤❤
Bamba Dieng Kay diapalè sougnou Mame Aïcha 😢
Longue vie mum❤
Elle n,a jamais connu de bonheur dans sa vie aduna tamit et pourtant des sorciers comme des sorcières sont là tous les jours rien que pour gacher la vie des gens et sont heureux
Ndesane ❤🙏
Sama idole
Une brave femme ma aicha bonne chance