lépou goor gni leu dagno gnak fayda tek si gnoy influencer sen deuxieme femme diko tek sén kaw awo. goor nak sou matoul kilifeu si béneu diabar la wara yam
@awadiouf7001 billaahy moom AK jeukeureum jii li nio nékke AK sén aawo bi diinéyy islaam nangu wu ko te imaam bu maandu bu nio ko laath mu wax lén deugg ayug jambourr bull laal te bull jégé mooy deugg
@@sokhnaaminata287 wawaw am ay diabar di wout foor fété . Nioune djiguène gni nio wara mature goor bagnegno diakhassé wayé niéna ci sama mbok niarel yi nio sikk
Ahhhh les hommes Sénégalais aussi, si tu n'as pas les moyens de séparer vos femmes dans des maisons différentes pour éviter ce genre de problème. C'est pas normal ce qu'elle a fait. Mais pour éviter tout ces incidents entre les femmes. Les femmes aussi si vous ne supportez plus la situation conjugale. Alors divorcez avant d'aller finir votre vie en prison 😡😡😡😡
Mane lima naxiri moy bou gor xolé djiguene nieup tax ay radio té prtan li femmeyi di defanté mo gueuna bone gueuna meti li pr lanelaa mem boudé degn la togn ga def amo excuz caso ga dieum laga done bagn louko raw gay am dax domou adama wa baxna lou way def bopam😢😢
Nous on ce bad pour guérir ce qui sont seins et sauf leurs cœurs et sans sang pourquoi pas appliquer l'islam depuis le temps si vous êtes vraiment des musulmans😭😭😭😭😭😭😭
li goor ak diongué diarouko rawatina ak dieukeur dio khamni romboul ak yén si depense. Goor mom intéret bopam késsé koussi def sa betise bagnou gnouss leu si kasso bi, daley fassé takki kénéne. seuyou millionnaire sakh diaroul sacrifier sa liberté wakhoumala seuyou pauvre rawatineu seuyou woudié.

Une peine de 30 ans de prison est la solution.cest cruelle vraiment dans kel Sénégal sommes nous vraiment lii diarnaa changé nationalité wayyy ichhhh
Les hommes les hommes les hommes gorr dou projet waye
Que Dieu nous préserve tous des cheytanés
Amine
Wooy bi awoo moo bon moo soxor nanu ko tej ba dam caabi ji
Ey waye liimome niawna lol si djiéguéne
Pour dire vrai le problème majeur c'est la faute des maries parc k si tes épouse ne te respecte pas ils yaura toujours des problèmes comme sa 😢
Bien dit
lépou goor gni leu dagno gnak fayda tek si gnoy influencer sen deuxieme femme diko tek sén kaw awo. goor nak sou matoul kilifeu si béneu diabar la wara yam
Oui c'est vrai 😢😢😢😢
sén jeukeurr jii mooy naaféqq lan mooy bayyi lén ko yén niaarr niépp ku ayé wull warull togall jeukeureum moom moo jéngg moo tass keureum
Bilahi dégana deug lidé la wakh mane.ak togg lakh di yobou toll . Li wakhougnou lép kou goor ki mo khamb safara bi tall keureum
@awadiouf7001 billaahy moom AK jeukeureum jii li nio nékke AK sén aawo bi diinéyy islaam nangu wu ko te imaam bu maandu bu nio ko laath mu wax lén deugg ayug jambourr bull laal te bull jégé mooy deugg
@@sokhnaaminata287 wawaw am ay diabar di wout foor fété . Nioune djiguène gni nio wara mature goor bagnegno diakhassé wayé niéna ci sama mbok niarel yi nio sikk
Béna goor walahi azim diaroulouma Lou gnaw liii oh lii sokhor la walahi azim Lane moye woudiè niit mo bone goor diaroule lii walahi azim
pourquoi les hommes aiment trop polygamie et certains d'entre eux ne peuvent pas gérer leurs femmes 😢
Yalla nagniou yalla mousseul thie seytané té arr niou😢😢
Café touba lay nan ni sax ❤1☕️♥️
Bilay gor dou projet.
Li niawna trop goor diaroule li way awo yi régler lene nak😢😢
8:02 guaure diaroul l'idée kou aye dangua wara yam SIya aye guau yi dagno diaroul li de
Thieye woudier nagnou def fair play andouna amoul solo
Mane dh douma khekh ndakh goor foula binga am indi sama morome mome lay am dotoumala diokh inmpotance
Dou nonou nak bo amé woudiou waroul changé Dara si nigua diapé sa dieukeur
Waro wakh lolou tamit ndakh mono diko goudil ak bethiekal mou khéb lolou ba andi kénéne loy sonnati?@@kharycisse5267
Gor dé diaroul rayanté ak di défanté lou bone
Ah yawde je suis désolé, boko beugue diape nonou dina doywar thi yaw
Ndeysan li metina trop 😢😢😢😢😢😢😢😢
ayé woo waroo laal ayu jambourr rawati na mu têré la ko 😂 👂
Ahhhh les hommes Sénégalais aussi, si tu n'as pas les moyens de séparer vos femmes dans des maisons différentes pour éviter ce genre de problème. C'est pas normal ce qu'elle a fait. Mais pour éviter tout ces incidents entre les femmes. Les femmes aussi si vous ne supportez plus la situation conjugale. Alors divorcez avant d'aller finir votre vie en prison 😡😡😡😡
Niarel biii tamite kouko jamb lo lakh si Ayou jambour
dieukeureum bou nafekh 😂😂😂😂
@awadiouf7001 awa des fois nakkk s'en dieukeur yi nioyyy diéngue bilahi yaw boudoul sa ay sakh yaye lakh li ba jammm la 😅
Da nio dionge nak niarell yi rek mo takh goor yi dengue
Thieye awoyi
Sest simple,quelle porte plainte et qu'on l'enferme en prison .
niaarél bi moo nékkull thi deugg te sénn jeukeur moo ko thi dooléll
Lolou waroul takh mou sotiko diwline awo bi amoul xol djguéne dina def lou gniaw li té bone😢😢
Awo bi wara defarall sa diakeur ndeki di diayi benge sa morom defar ko 😅😅
niaaréll bi la jeukkeur ji andall moo tax ndax ku deglu ndawsi bu baax xam ni wax ju yaagga la
Dagni wara bayi di boler aye diabar si béne keur
Ho les femmes on s 'entretuent pour les hommes
Lii ndiaw n'a bilay
Mane lima naxiri moy bou gor xolé djiguene nieup tax ay radio té prtan li femmeyi di defanté mo gueuna bone gueuna meti li pr lanelaa mem boudé degn la togn ga def amo excuz caso ga dieum laga done bagn louko raw gay am dax domou adama wa baxna lou way def bopam😢😢
Yéye nop nak mbété hanibal trop de malades dans ce pays
Lii,gorou légui diarougnko
Té kousi dé si gnioune wala kaso nou takke sa morome
Vraiment li môme Goorou Diaroucko
Awobi dioume na me diakardji mo indi porolembi
Prison à vie 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Goui boun na
Nous on ce bad pour guérir ce qui sont seins et sauf leurs cœurs et sans sang pourquoi pas appliquer l'islam depuis le temps si vous êtes vraiment des musulmans😭😭😭😭😭😭😭
li goor ak diongué diarouko rawatina ak dieukeur dio khamni romboul ak yén si depense. Goor mom intéret bopam késsé koussi def sa betise bagnou gnouss leu si kasso bi, daley fassé takki kénéne. seuyou millionnaire sakh diaroul sacrifier sa liberté wakhoumala seuyou pauvre rawatineu seuyou woudié.
Djigueni manoul niewe thi keur ni kenen doufi niewate wala douma ame woudji,kepou kounane douma ame woudji seuyeum dina nakhari ndskh fir mome boko commencé sa khol yakhou
Est ce que lernala ni lolou la wakh? Lignoufi nétali ni dé béna djiguène douko nangou khana réactions yi nioy wouté rek
Encore femme yaqq femme li kén khamoul loumou done .
Li Dara diarouka
🙄🙄😭😭😭
😭😭😭😭😭😭😭
Ay Li louko Diar yewouleine gorrr rek bilay khamoleine ter comprendoleine thiiilm assassin
Casso a vie rek ki domèharam la
Awoyi si bopam nio sokhor
beugo diam iow😅
K@@papediouf4607ki Kay day togne
@papediouf4607 diam rék la beugue mais awoyi d'anion sokhor
Yagui togne nak@@NdéyesokhnaDiouf-k3u
@@NdéyesokhnaDiouf-k3u ah yéménaa daal..de l'huile chaude comme ça ces trop .
Awoyi si bopam niou bon😢😢et sokhor indian