Les témoignages très touchants de son percussionniste et ... Wally Seck craque et fond en larmes

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 17 дек 2024

Комментарии • 99

  • @kessobelnou2490
    @kessobelnou2490 4 года назад +20

    Ndeysane bougouma sakh wally di dioye souye dioye wala nite yi diko wakh dara daff maye méti daye méle ni kouma bokale béne déréte khaw ma lane la nak wallah je l’aime comme un grand frère yalla nala yalla maye goudou fane ak wére bilahi sama khole la diougué🙏🏽♥️♥️♥️

  • @gansiryfall7247
    @gansiryfall7247 4 года назад +8

    Bravo prince Wally fierté Sénégalaises exemple pour la jeunesses sénégalaises machalla Grand cœur 🙏🏾🙏🏼🇸🇳 que dieu te protège Amine yarabi depuis Paris 💞🇸🇳🇫🇷

  • @cissegueyebouwally379
    @cissegueyebouwally379 4 года назад +28

    Notre Wally Ballago séck yalla nala thiate sékhlou

  • @khadidiatousow8945
    @khadidiatousow8945 4 года назад +16

    Mangui dioy😭😭😭😭😭Wally ma yeureum sa none..amal diama yalla sameu la arr la mousal la si beut akk lagnmen bou bonn 🙏🙏🙏🙏

  • @reanadieng9221
    @reanadieng9221 4 года назад +19

    Wally yalla nala yalla lafal thiat thia kaw thia kanam boul ragal dara kou def Lou bakh am Lou bakh

  • @senethialy970
    @senethialy970 4 года назад +23

    Manchallah yallah Wally t’es un grand Monsieur vraiment je t’estime

  • @fatoudiouf8396
    @fatoudiouf8396 4 года назад +8

    Aie waay waly ya bakhe amal goudou fan ak wer soutoura ak kheweul t yalla yok sa am am AMINE

  • @mouhameddoumbethiam2529
    @mouhameddoumbethiam2529 4 года назад +1

    Khally mbaye sa keur gui yalla nala digue wayé wally yalla nako yalla déf fal diamou ak salam ak bépou dioullit

  • @ndeyemarieniang7698
    @ndeyemarieniang7698 4 года назад +11

    Machallah wally dagua bakh kon omoro do wakh ak mone diam rek guay aminachallah❤❤❤🤩🤩🤩

  • @mariemesen9811
    @mariemesen9811 4 года назад +23

    Khaly Mbaye dogo machalla fi nga ko wakhé mo safé 🙏🏽 maryacine démal rek fi nga ko tek fofou rek la

  • @astoudiop6326
    @astoudiop6326 4 года назад +5

    Homme de grand cœur yala nala yalla Faye sa khôl fi ko diap fofou la

  • @poupesarr1410
    @poupesarr1410 4 года назад +7

    Machalla Waly kene dou yaw. Ay wayyyyy (omaro) tamite tamite tamite. Ni lonou koy bayer

  • @leparisien5193
    @leparisien5193 4 года назад +20

    Wally b seck yaye sen baay

  • @moustaphasonko596
    @moustaphasonko596 4 года назад +3

    Bilahi ce témoignage ça me fait pleurer patron lii rk la meuneul employam
    Sénégal sou amone 10 Wally kéenn dou sonn
    Mane sincèrement damako beugue ba beugouma kéne di wakh si mom Lou bonne borom xolou diama bi Golden Boy doundeul wëreul 🙏🙏🙏

  • @absafaye7200
    @absafaye7200 4 года назад +14

    Wally Seck mayeurme koula bagne❤❤😍😍

    • @papito8025
      @papito8025 4 года назад +1

      Kegn baniouko c’est juste que djikom Mo baaxoul

    • @gnagna9770
      @gnagna9770 4 года назад +1

      💚💚💚💚❤❤❤❤❤👑👑👑👑🤲🤲🤲🤲🤲🤲💪💪💪💪🇸🇦🇸🇦

  • @ndeyecourathioune1992
    @ndeyecourathioune1992 4 года назад +4

    Mach Allah laf thiat yalla nala souniou borom sambeu ak mbolom dioulite ak saye wadiour ak sa ndiaboot thi daradiaye Mohamed saws psl barke serigne Fallou rta love uuuuu

  • @diarietouniang9421
    @diarietouniang9421 4 года назад +2

    bilahi wally seck dou Musique 🎧 bi motakh ma begue le dé khol bou rafet ak na ngo dimbali domou Adama li lala begué yalla nala yalla terar

  • @awadiabygassama8214
    @awadiabygassama8214 4 года назад +2

    Bily omaro ya niak diom do sax goor walahi waly keinn dou mome yalla nassa diam yaguu😍

  • @combe4823
    @combe4823 4 года назад +17

    Laff thiatt Wally... Doundeul amal diam fo nekk

  • @sophiesarr6897
    @sophiesarr6897 4 года назад +8

    Da bakh nak machalla

  • @bijoubamba4081
    @bijoubamba4081 4 года назад +12

    Waly Seck amgua ndam machalla

  • @anitasoumare5796
    @anitasoumare5796 4 года назад +3

    Kéne dou sama wadji iow coula beug amé diam prsk nitou diam nga ❤️❤️❤️

  • @hougninousuzanne8019
    @hougninousuzanne8019 4 года назад

    Machalla wakh tu as un cœur d’or laf thiate rek

  • @aidatoure8759
    @aidatoure8759 4 года назад +2

    Machalla fiére de toi mn adorable trés cher fils de 👉❤👈💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯😘😘

  • @astoundiayebadji4125
    @astoundiayebadji4125 4 года назад +3

    Machalla bakh rek am solo

  • @fbsanoho9881
    @fbsanoho9881 4 года назад +2

    Omaro and waly this is so nice Lii moye adouna na nexh yagoul

  • @adamabaldeh3273
    @adamabaldeh3273 4 года назад +4

    Machahllah Wally suma 🤩🤩🤩🤩❤❤❤❤❤❤💡💡💡💡🕯🕯🕯🕯

  • @mamansalioudieng5784
    @mamansalioudieng5784 4 года назад +6

    Noo waly machalaaaa jâmmm si niepeu sa khole bou raféte mon takh kéne dou mene si yaw touse dou mene sii yaw touse naa raféte rkkk kou yalle tathiou gaa bagne néé doufi féthie dagay sone rkkk dafa féthie baaa danéle khana nékh domou adama bouné ya khame liga begeu yalle nako yalle déff témou geuneu si barcké nabi mstph psl

  • @fallfatou1610
    @fallfatou1610 4 года назад +9

    Bilakhi ♥️ je t'aime Daddy

  • @aidatoure8759
    @aidatoure8759 4 года назад +3

    Machalla machalla machalla machalla machalla machalla machalla lawelaaaaaaaaaaaaaa thiatttttttttttttttttte thia bamou dalagoul sama domou kholllllllllllllllllll thia khawe thia khaname rekkkkkkkk inchalla amineeeeeeeeeeeeeeeee ya rabbi bonne et heureuse année yagua nio déguele ba fawou te niou féké lépeu meune tale te and ak werre Seck amineeeeeeeeeeeeeeeee ya

  • @dembandiaye7552
    @dembandiaye7552 4 года назад

    Machallah Wally longue vie et santé rekk bilay

  • @ndeyefatoumassaly7577
    @ndeyefatoumassaly7577 4 года назад

    Té l meilleur Wally lo âme rekk diomboula ta un bon coeur , goudeul fane réek❤️

  • @imaneanne9464
    @imaneanne9464 4 года назад

    Ohh waly ndeyssane Yalna la yalla may goud fane khol yeup séde neu ni nga social Yalna yalla di social thi yaw ak ndiabote gui ba abadane dayimane khol yeup tooyy

  • @aminatacireba1465
    @aminatacireba1465 4 года назад +2

    Machallah laf thiat

  • @julesfaye3589
    @julesfaye3589 3 года назад

    Macha allah khali sante rek warrefame rek lay def si domou Adama yi le king yalla na yok goude fane ak weer

  • @mariejeannedasylva7963
    @mariejeannedasylva7963 4 года назад +2

    Wally long vie à toi sunu noble bi

  • @maxlalionne8146
    @maxlalionne8146 4 года назад +4

    Deysane khally mbaye dawlona sama yaram

  • @awadiop4408
    @awadiop4408 4 года назад

    Waly jtm tré tré fort bly yaw doundeul Lou barii way

  • @ndeyefatoubadiane7935
    @ndeyefatoubadiane7935 4 года назад +3

    Machalah maryacine laissa bigue maissa bigue marrr yafi neeeeee machalah

  • @masambanjie481
    @masambanjie481 4 года назад +1

    Bilahi wally baye fall laaaa

  • @jabousarr1490
    @jabousarr1490 4 года назад

    Maa shaa Allah REFETNAyyyyyyyy Wally Ballago seck forever 🙏🙏🙏🥰🥰🥰

  • @charasakina9594
    @charasakina9594 4 года назад

    Non franchement wally a partir d'aujourd'hui beugueunala j'adore tout ce qui aide à rendre grâce à nos parents une maison cest tout

  • @fatousene3770
    @fatousene3770 4 года назад +3

    Machalla wally😍

  • @seckadjinafi9281
    @seckadjinafi9281 4 года назад +3

    Machahlla Nice ♥️🥰

  • @mamadiallo7827
    @mamadiallo7827 4 года назад +3

    Borom khôl diamant 💎 💎❤️❤️❤️

  • @leboudiop1067
    @leboudiop1067 4 года назад

    Ndeysanne c’est émouvant ballago lou bakh rek gay am❤️

  • @wadethiambanda7446
    @wadethiambanda7446 4 года назад +5

    Ma challah

  • @mariamasinyan6078
    @mariamasinyan6078 4 года назад

    Machallah nice na 👍

  • @falloudieng6899
    @falloudieng6899 4 года назад +7

    Ohhhh😭😭

  • @adamafaye834
    @adamafaye834 3 года назад +1

    Un bon exemple

  • @ndongosafi616
    @ndongosafi616 4 года назад

    Machallah wally laff tiatt

  • @diatoufall9271
    @diatoufall9271 4 года назад

    Machalla way Ballago

  • @adamasarr3092
    @adamasarr3092 3 года назад +1

    Ada kouloukou mofy néka wally seck dole

  • @diorgueye710
    @diorgueye710 4 года назад

    Bilahiii ya gnak kignaneu Wally

  • @citv114camara5
    @citv114camara5 4 года назад +12

    Omaro mi d'où nitte

    • @senethialy970
      @senethialy970 4 года назад +3

      Dafa doul gor gor dou wax niari wax

    • @fatousamb708
      @fatousamb708 4 года назад +3

      Billay dou nittt dama rousss sahhh maneu

  • @khadydiagne2751
    @khadydiagne2751 4 года назад +1

    Machalah waly

  • @maguettefall5019
    @maguettefall5019 4 года назад

    Mon siviilisé billaye mare yacine

  • @bassemboup6692
    @bassemboup6692 4 года назад

    No khali ya bakh rek

  • @neneba5469
    @neneba5469 4 года назад

    Ndeye ndack sa robe yandiena machala

  • @mbayethiam9378
    @mbayethiam9378 4 года назад +5

    Wally yabah

  • @moboy3783
    @moboy3783 4 года назад +2

    ❤️❤️❤️

  • @awadiop4408
    @awadiop4408 4 года назад

    Omoro zéro class goor momoul yénn yii Wally sa kholl mo séttt topokénn si Dara marre on t'aime fort notre Wally nationale

  • @bambabeye3060
    @bambabeye3060 4 года назад +1

    Machalla

  • @matty7424
    @matty7424 4 года назад

    Fiii momm j'avais pleuré 😢😢
    Khaly mbaye on dirait qu'il a improvisé cet instant en la présence d'Omaro, NIEW🤣🤣

  • @senethialy970
    @senethialy970 4 года назад +10

    Khali mbaye do nit niaf omaro yangui beug dé

  • @deguenembaye9199
    @deguenembaye9199 4 года назад

    Vraiment c touchant non li dawna yaram non wally joli coeur la kholal defal loula nekh ba kene lalela ya tayyy Mala beugue bamou nekhma je d'adore

  • @khadydioune3717
    @khadydioune3717 4 года назад

    Yallnala yalla faye seck contanagne

  • @seynabousania4111
    @seynabousania4111 4 года назад

    Thieuy khaly mbaye dogo aka goré

  • @alinewade4782
    @alinewade4782 4 года назад

    Wally ballago seck walahi guemnani ak lou way mana wakhati boul tontou

  • @bbpouye6195
    @bbpouye6195 4 года назад +17

    Omaro n’a aucune dignité , il est très éhonté , vergogne zéro.. si j’étais à sa place je serais par terre en train de pleurer

    • @ndeyembaye1589
      @ndeyembaye1589 4 года назад +1

      No kou niake fayda ba melni oumaro messou mako giss nare fekh le la doule kate le nite dagaye simple wayé meune doul ba melni oumaro fou toye nga take nite daye ame loumy rouss way waly hamgani doula wahe dra ndakh brm bakh le mè fo meune di doulè rk ngay wr

    • @annabeye7603
      @annabeye7603 4 года назад

      Renala ba soneee woooy

  • @jolieseye403
    @jolieseye403 4 года назад +7

    Omaro dou nitt dou rouss niouss ko rek la beug😡

  • @سميرهالسعدون
    @سميرهالسعدون 4 года назад +3

    👏👏👏👑❤❤❤❤❤😍😍😭😢

  • @maawandiaye368
    @maawandiaye368 4 года назад

    Ndeye ndack loulou name Waly migui Doone khôl ndeye ndack rėk Waly Akay bani

  • @maawandiaye368
    @maawandiaye368 4 года назад

    Ndeye ndack loumou nameu Waly migui Doone khôl ndeye ndack rėk

  • @abdoundom5023
    @abdoundom5023 4 года назад

    😭😭😭😭

  • @sambibrahima5930
    @sambibrahima5930 4 года назад

    👑🎤🎤👈💯🥁👑👑

  • @natachfaye3764
    @natachfaye3764 4 года назад +1

    Waly tontouma stp

  • @fatousall1462
    @fatousall1462 4 года назад +3

    Wa yénn malathie lénn omaro mom lanla

  • @adamasarr3092
    @adamasarr3092 3 года назад +1

    Tafa Kata dayama

  • @yayadiaw4676
    @yayadiaw4676 4 года назад +1

    Le gars en blanc témoignage am nekh na trop

  • @boromemadina2853
    @boromemadina2853 4 года назад +3

    Salam sa dioy😭 yi gnoroute dé dangako forcé gnak fayda

  • @سميرهالسعدون
    @سميرهالسعدون 4 года назад +3

    👏👏😂😂😂❤

  • @bintaminteh9012
    @bintaminteh9012 4 года назад

    👏👏👏👏❤❤😂😂

  • @ndeyemariemeseck6839
    @ndeyemariemeseck6839 3 года назад

    Amal diam balago. Omaro borom backen you beuri yi

  • @mawadiop9442
    @mawadiop9442 4 года назад +3

    Omoro 😂

  • @ndeyembaye1589
    @ndeyembaye1589 4 года назад

    Nare fekh doule kate bi taskatou ndajè bi jahasè katou nite fou toye nga take

  • @binetandiaye5853
    @binetandiaye5853 4 года назад

    Omaro domou adouna boyy wakh déyyy soralé euleukkk Méré Di wakh bakhoul nélll pattte Di déguelo andal sa xélle wayé guéne mélni kou nékkk. Bal poussière groupe sidi Diop bii