Je constate que ces derniers temps bcp de jeunes qui étaient dans les tarikhas dans leur passé dénoncent des égarements, des mensonges qu'ils ont vécus. J'apprécie l'énorme travail que tu fais pour concientiser les croyants. Allah n'a pas d'égal, c'est lui qui donne la vie et la mort. Tout musulman doit suivre la suna du prophète pour ne pas être de grands perdants dans l'avenir.
Jërejef mon frère. Jazâka Allahou khayran pour tout ce travail pour établir la vérité de l'islam. Permettez moi juste de rappeler que le prophète Muhammad paix et salut sur lui a interdit de jurer sur autre que Allah. Donc on ne peut pas jurer sur le prophète Muhammad paix et salut sur lui, ni sur le Qur'an ni sur autre chose à part Allah. Bâraka Allahou fik mon frère
Allah ne demandera à personne dans quel tarikha tu fais partie. رضيت بالله ربا وبالإسلام دينا1 وبمحمد صلى الله عليه وسلم (سلم) نبياً ورسولاً Raḍîtu bi-llâhi Rabbâ, wa-bi-l-'islâmi dîna1 Wa-bi-Muḥammadin ṣalla-llâhu ʕalayhi wa-sallim (sallim) Nabiyyan wa-Rasūlâ
Merci Medoune qu'Allah te récompense pour ton courage. Nous autres nous ne sommes pas des hommes. Car nous avons peur de nous dresser devant ces bokkalé kat et de défendre l'islam pûr. Merci merci merci
Deux korités et deux tabaski, voire trois😂, cela a commencé au Sénégal seulement au début des années 1980. Avant cette période m, il y avait toujours une seule fête pour tous les musulmans sénégalais, toutes confréries confondues. Cela, tous les observateurs sérieux le savent. Pourtant, ceux qui ont institué cette division (parmi les différents courants religieux de ce pays) n'ont ni le mérite ni le niveau de formation des guides précédents. Il faut que les musulmans sénégalais se reprennent avant qu'il ne doit trop tard.
Mais eux ils accusent trop le prophète. Muhammed est mort en 632 soit 1200 ans avant la naissance de ce marabout là. Comment est-ce qu'il arrive à communiquer avec lui...Au Sénégal les gens adorent les mythes qui donnent des frissons
Mane lima diakhal Moy on dis toujours Sénégal deukou dîné deukou mag niou bkh gni la ba paré nous faisons partie des pays ls plus pauvres au monde prck douniou dioug si di togn yalla a travers tarikha yi Di bokalé rk yalna niou yalla sakhal si alhourane ak sunnah 🙏🙏
@@watawasawbilhaq khamulo Loy wakh sakh lolu ngeum ngueum la bokul dara ak sén wakhi fén kat yi.limaci gueuna méti moy ñiy wakh soit sont des anonymes wala nekuñu senegal mahnam dañuy dieuw té dieuw mom dem diahanama rek
Yaw nak sa cas critique na ndakh amna lo khamni bakar la yaw nekatou mourite ngay CV c'est bon way tok figau tok Di saga bayou Diabour peu de respect ken defoul kene Dara Lou way def boppou diekhna
@@watawasawbilhaq yaw khamou Dara thi lingay wakh Mane wakhtou diouli doma raw yagui nan mourite nga wou ayé 😂😂😂😂😂😂 ngama def billahi ndakh yaw bo tokguen nan mourite la wou Massou nek mourite 😂😂🤔🤔🤔🤫🤫🤫🤫🤫😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 fière d'être mourite yaw Dou rousse sakh
@@mmendiayesopserignefalloum2265 sa khalif mountakha moné bayi diouli diaglé la. Te yonent bi ki Yalla yoni dafane kou bayi diouli nekatoul dioulite. Lima wakh lou leer la. So mané indi ay tektal si diné islam nga indi sinon wakh sa khalate bi amoul ndiarigne.
Je constate que ces derniers temps bcp de jeunes qui étaient dans les tarikhas dans leur passé dénoncent des égarements, des mensonges qu'ils ont vécus. J'apprécie l'énorme travail que tu fais pour concientiser les croyants. Allah n'a pas d'égal, c'est lui qui donne la vie et la mort. Tout musulman doit suivre la suna du prophète pour ne pas être de grands perdants dans l'avenir.
🤲🏿💚
Baraka ALLAHOU fikoum Cheikh Oumar Sow, il est temps pour les sénégalais de se réveiller.
Wallahi Lou wërr nga wakh
Dieureudieuf Medoune Y’ALLAH SHWT Dafaleu goudou fane ak weure bou sakhe dakkkk.
Sa sopey ak sa soldat depuis Paris.
Amine ya Rabbi
Dieureudief s touba diarama mame chéikh Ibrahima fall
@@ibrahimadiop1116
Wawe bakhena démale Adouna sa kaname boudé Y'ALLAH sounou Borom nguaye tékéléle serigne touba.
Wax ga degue yallah rekk yallah kepp yallah dongue mome aldiane koumou koo nehk rek laa thie dougall merci degue rek
Macha alla
Bonjour
Ousmane sonko mo takh gnouye yoni ama balde pour mou sacrifice ndiol djinee falaye mingui Facebook ❤️💚💚♥️💚♥️💚♥️💚♥️💚♥️💚♥️💚♥️
Jërejef mon frère. Jazâka Allahou khayran pour tout ce travail pour établir la vérité de l'islam. Permettez moi juste de rappeler que le prophète Muhammad paix et salut sur lui a interdit de jurer sur autre que Allah. Donc on ne peut pas jurer sur le prophète Muhammad paix et salut sur lui, ni sur le Qur'an ni sur autre chose à part Allah.
Bâraka Allahou fik mon frère
Allah ne demandera à personne dans quel tarikha tu fais partie.
رضيت بالله ربا وبالإسلام دينا1
وبمحمد صلى الله عليه وسلم (سلم) نبياً ورسولاً
Raḍîtu bi-llâhi Rabbâ, wa-bi-l-'islâmi dîna1
Wa-bi-Muḥammadin ṣalla-llâhu ʕalayhi wa-sallim (sallim) Nabiyyan wa-Rasūlâ
MaShAllah ❤️✨🙏🏻
Machallah ALLAH est UNIQUE
Merci Medoune qu'Allah te récompense pour ton courage. Nous autres nous ne sommes pas des hommes. Car nous avons peur de nous dresser devant ces bokkalé kat et de défendre l'islam pûr.
Merci merci merci
Soubhanallah, Allah est unique!
Deux korités et deux tabaski, voire trois😂, cela a commencé au Sénégal seulement au début des années 1980. Avant cette période m, il y avait toujours une seule fête pour tous les musulmans sénégalais, toutes confréries confondues. Cela, tous les observateurs sérieux le savent. Pourtant, ceux qui ont institué cette division (parmi les différents courants religieux de ce pays) n'ont ni le mérite ni le niveau de formation des guides précédents. Il faut que les musulmans sénégalais se reprennent avant qu'il ne doit trop tard.
Thank you very much for preaching hard facts
Deugueu diou weer Médoune diadieuf
METZO FOREVER ! C'EST VRAI, KOUFI DIGGUÉ AL DJANNA DA NGAY DOUL !
These people are clear disbelievers bro
Médoune Diop foo nekk?
Ba ya ngui ci diam ?
Amal tawfekh
Allahou Akbar dernier audio bi 😱😭😭 doyna waar
yallah nala faye deugue rek moy deugue Alkhourane wakhou yalla ak sunu🙏🙏🙏
Medoune bane compte lay defer live??
Watawasaw Bil Haq sur Facebook
Nekoul ba Nekoul me medoun diambar nga
Niounnn Elhadji Malick motahh niou xam placou Yalla ak placou yonentebî akk placou serigne
❤❤❤❤
Merci
Manchaala gueudienako guis medoun
Dieuredieuf
Verité absolue
Tu es exceptionnel
Et sache que tu fais du jihad
Medoune walahi yalla rekk Molay fay
Mais eux ils accusent trop le prophète. Muhammed est mort en 632 soit 1200 ans avant la naissance de ce marabout là. Comment est-ce qu'il arrive à communiquer avec lui...Au Sénégal les gens adorent les mythes qui donnent des frissons
Wallahi mon frère ou ma sœur tu as parfaitement raison. Les sénégalais aiment les légendes.
bilahi défoi j me dis est ce que niogui dawal sén khél yi ay wakh yo kham ni amul bén preuves mélni ay contes😂
Ndeyssane
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
😭
Machallah
Mane lima diakhal Moy on dis toujours Sénégal deukou dîné deukou mag niou bkh gni la ba paré nous faisons partie des pays ls plus pauvres au monde prck douniou dioug si di togn yalla a travers tarikha yi Di bokalé rk
yalna niou yalla sakhal si alhourane ak sunnah 🙏🙏
Pire vérité wallahi
Xana lekko ci laaxbi😂😂😂
So gomoul tawhiid ak souna dajjal sou niower daguay topou kou ame esprit fragile ken mounoula garantir aldiana parc yallah souniou borom moko mome
Wakho fi dara kula guiss kham ngani torokh nga vrai dul kat nga
Doulkat bi kay moy kine bou Yalla tahawe yonent bi tahaw serigne touba tahaw mou dem si serigne touba
Kokou nak moy ki torokh. Yalla sokhla woul kenn.
@@watawasawbilhaq khamulo Loy wakh sakh lolu ngeum ngueum la bokul dara ak sén wakhi fén kat yi.limaci gueuna méti moy ñiy wakh soit sont des anonymes wala nekuñu senegal mahnam dañuy dieuw té dieuw mom dem diahanama rek
Fenn rek ngen meune. Ragal lene Yalla. Fenn rek fenn rek . Dangen di fenn ba diapp ni deug leu. Demal khol lane moy dieuw. Te nga bayi bokale Yalla.
Kham nga ni kou wakh ngaramal nitt moko gueuneul ngaramal YALLA nga kham ni ay fenn fofou la fekk bakh 🤭
MEDOOUNE NITOU DEUGUEU, ME ANAMOU
Bokalé dé bakhoul
Nagnou diouk sougnou bop té délou sougnou Borom
Yaw ken amoul sa Diotte yalla khamenako
SERIGNE TOUBA KÉNE LA DÉ
YAW DAGUA TOUBI
Serigne touba dou kenne. Niouko gueune fouf nio ko djitou.
yaw mom esk tu connais la signification du mot toubi 🤔🤔
Sa xam xam dess na ioe diamou lene yalla t bayi tiaxan yi
MON AMI DA GAY FENE NAK
Yaw nak sa cas critique na ndakh amna lo khamni bakar la yaw nekatou mourite ngay CV c'est bon way tok figau tok Di saga bayou Diabour peu de respect ken defoul kene Dara Lou way def boppou diekhna
Mouride islam diangalé wouko khamouko.
@@watawasawbilhaq Khamna ni islam amoul tarikh way Serigne Touba dafa ligeuyel yallah topou guene Di mindefi Kone nak Koy wakh na khoul miy wakh ndakh Serigne Touba digoul kene aldiana aldiana yakoy liguey bolene gnew rek na mourite mourite gni beug Kham niougui lat
@@mmendiayesopserignefalloum2265 Lolou dara leroulasi . Linga khalate dongue nga wakh . Linga topp islam dafko dakh ndakh niak diouli ngen daganal. Lolou koufr la
@@watawasawbilhaq yaw khamou Dara thi lingay wakh Mane wakhtou diouli doma raw yagui nan mourite nga wou ayé 😂😂😂😂😂😂 ngama def billahi ndakh yaw bo tokguen nan mourite la wou Massou nek mourite 😂😂🤔🤔🤔🤫🤫🤫🤫🤫😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 fière d'être mourite yaw Dou rousse sakh
@@mmendiayesopserignefalloum2265 sa khalif mountakha moné bayi diouli diaglé la. Te yonent bi ki Yalla yoni dafane kou bayi diouli nekatoul dioulite. Lima wakh lou leer la. So mané indi ay tektal si diné islam nga indi sinon wakh sa khalate bi amoul ndiarigne.
ligay wakh boudoull deug Yalla naga Fatou si att mi
KONN DÉY DI NA GOUDDOU FANN LOOL NDAKH MEDOUNE DÉGGEU REK LÉY WAKH ! ! !
YOW DAAL MEDOUNE FÂTOU NGA BEUGGEU ? AL HAMDOULILLAH DO YALLA ! ! !
@@abdoulwahabba2841 Baraka ALLAHOU fikoum mon frère
ki deug bou wér l'ay wakh yéwou lén mo geune yalla fi nék kou wékou si alhourane ak sunnah do rér
Il reste encore six mois. On se donne RV ici
medoune, lila soonal mooy, yaw dangaa diapee nyii ay djulit de nyi ay yefer yu ler lanio
Lann moy yeufeur
@@elhadjigaye8960 yefar mooy gui diamu mbedeff kom mom, te loolu moo fees senegal.Ay yefer ak naafehk you bon lanio
@@baboucarrgaye3819 legui nane la nitt di diamo moromou bindeffam
@@elhadjigaye8960 ,diamu danyu koi natue thi kaadu,wax ak diaff.Kaadu yefar weesul nit ku niaka fayda djanok moromu mbidefam mbiy lek,di naan,di, sey,di Dem toilet,di dee
🤣🤣🤣🤣