Madiodio ak diome dia, Madiodio ak foula dia, Madiodio ak mbakh ga, manona woye, ame présence de scène bou diék bou yiwe, beugue mbok, Yallah Bour dina tèk sa Aldiana ya gueneu sèle! Amine
Très belle hommage à Madiodio, à travers cette musique, je me retrouve au pays. Elles sont toutes des voix magnifiques, mais les voix de Kiné Lam et Mama Soda, m'ont pour le coup laisser sans voix 😍😍
Thiey adouna mbi ni demal mangui gnew yalla nako yalla dolly yeurmande ak diegual te kharey ko thia aldianal firdawsi ci barke seydina Mohamed psl 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Que le bon dieu lui pardonne tous ces peches que la terre choix léger sur lui est que le bon dieu l'accueil au paradis amine😢😢😢😢😢😢😢😢😢😣😭😭😭😭😭😭😭😭💞💝💘💗💖💓💜💛💚👍
Yallanako yalla khare aldiana...sama maman linguene deff rafetna lolou .....na khaler yi roy su yenn ak idole nguen ..sama khôl mo fess tata diodio damako fekone sorano neko maman un neh nga ma lolou mou dieul temps wam du wahtane ak man dima yedd si adouna lolou yomboul
Thiayi aduna souf lék na kou nék yalla nako borom bii soubhanahu wattalla kharé aldjianay firdaws té atté ko thii yeurmandé nioune ñifi déss souniou heure bouye nieuw yalla nañu fékk thilou bakh amine ya rabbî
Ndeysane yalla nako yalla yeureum te kharéko aldiana. Faites autant pour maman Fatou Talla svp. Yalla na leen fi yalla bayyi ba ci kanam vous êtes vraiment un temple de notre culture
Ay way souniou artistes yi vs etes braves , reconnaissantes j ne trouve pas Les mots pour vs remercier j ai Les larmes aux yeux k DIEU vs benisse MADIODIO NGNING k let paradis soit sa demeure amine k la terre de TOUBA lui soit legere (ci barke seydina mouhamed psl )amine
Adja Soda Fall Merci et Merci encore, Madiodio était notre grande soeur bien aimée, calme, correcte et sage, Que la Grâce et la Miséricorde du Tout Puissant DIEU Soit sur elle et sur les habitants de l'au-de-là et que le Paradis Soit Sa dernière demeure In Chaa Allah Thi Barké Seydinna Mouhamed "PSL".
Madiodio ak diome dia, Madiodio ak foula dia, Madiodio ak mbakh ga, manona woye, ame présence de scène bou diék bou yiwe, beugue mbok, Yallah Bour dina tèk sa Aldiana ya gueneu sèle! Amine
Ndayssan yalnako yalla yeureum madiodio ndanaan koulou fadlin
Maman madiodio yalna ko yalla yeureum té djégueulko inechalla yalla yessal yeurmandém bou yaatou bi si moom inechalla
Sama Hol dafa toy way machallah yalla nako yalla yeureum té kharéko thia aldiana diana you kawéya si barképp seigne fallou 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Madiodio Demna....Yalla nakoo Yalla Yerem Khareii ko Aldiana..Yen Yalla bayiiilen fi bassi kanam...Guene Bayiii khessal bi nak
bayil togne dagnouy rakhass rék bayilén😊😊
J'en pleure, c'est très beau, longue vie non maman
Amine
Soda mama ellé trop naturel j l'adore. Mama madiodio yalnako yalla yerreum té kharéko aldiana yii gueneu kawé.
Amine
J'ai pas de parole, tellement je suis ému.Lii moye Sénégal.
Kine lam ❤️ Belle voix mais longue vie à vous qui reste 🙏🏼
Ndeyssane mowoyone li yobou yaye ak baye xame nguèn douni fi ba yalnako yalla yereum
Chiii kiné lam linga youkhou meuna touloko. Cheuteuteu 😥😥😥
Mashalah la voix d assane mboup maman ndeye fatou ndiaye maman kine lam et daba seye. Repose en paix maman madiodio
vraiment je suis émue vous n'oubliez pas diodio
Très belle hommage à Madiodio, à travers cette musique, je me retrouve au pays. Elles sont toutes des voix magnifiques, mais les voix de Kiné Lam et Mama Soda, m'ont pour le coup laisser sans voix 😍😍
metyna trop adjia mass metina trop niakkk yaye dafa mety mane khamna si dara yalnako serigne fallou terrou
Ndeysann mére madiodio gnigu kou bakhon beug nitt gno bokon kogn cité fadia yalla nako yalla yeureum
Yalla nako yalla khare aldjana firdawsi
Sa yaram dawna ma khalat sama yaye diou baxdia Yalla naguène khippé Aldiana ci barkèp Cheikhoul Khadim souniou yakari téy ak euleuk
deysane yaye diou bakh yallah yeureumko te khareko aldiana firdawsi Amine
Ndeye Fatou NDIAYE, Acca Welle, Maty THIAM Dogo, Darou Mbaye, Fatou Kiné MBAYE, Soda Mama FALL, Ma Awa KOUYATE, Assane MBOUP, Mapenda SECK, Ndeye Mbaye Djinma, Dial MBAYE, Fatou GUEWEL, Ndeye DIOUF, Kine LAM, Boundaw SAMB, Daba SEYE
Kiné lam manchalla maty thiam dogo ken demoul gua dess :) nice na
C vraiment beau et très gentil de leur part. C touchant. Goud leneu fane way
Elles sont magnifiques et bien inspirées avec des choeurs sublimes et d'une telle diversité.
Te yalla bayilenfi si barker seydina Mouhamed
Machallah li bakhna lol ken dou ko faté danou koy dioy ba fékiko
Yalla nako yalla yeureume yene gni fi dess yalla guoudeul sen fane
Vous me faites pleurer way cette femme que j'adorerais et adore ses chansons yalla na ko Mohamed (SPL )térou
Amine Amine Amine Yarabal Alamina dieureudieuf
Hoooooo mettina
Ma cantatrice préférée est partie à jamais. Qu'Allah l'accueille dans son paradis!
C'était en quelle année ?
Li moy andou nawlé amoul wor koleurè rek . Yalla nako yalla khaaré aldiana firdawssi
Yalna hippe firdawsi
bineta ndiaye amine way
bineta ndiaye amine je l adoré
bineta ndiaye Amine
Niit balla ngakay kham rek mou guene adouna repose en paix sama goro bi😭😭😭
Yalla nako serigne touba mbaké téroule bopame deysane dawna yarame
Yanako yalla yereum tei khareko aldiana firdawsi si barké Mouhamed psl
yallna ko yalla yérém
yallnako yalla yeureme dougeulko aldjiana firdaouss ak mboléme dioulite gnamoufaye fék ték si djiabotam lokhou mér bou mounona yété ndayssan limou waye yeup yétéla
Paix à son âme vraiment je revois mon Sénégal 🇸🇳
❤❤❤
Gni gnoy ngor degue am class am personnalité chimmm m ma l'en begue
Pendant to c 8mn g eu lé larme au yeux
Oh que du délire. Toutes les divas rassemblées. Soda Mama, Khar Mbaye etc.
Thiey adouna mbi ni demal mangui gnew yalla nako yalla dolly yeurmande ak diegual te kharey ko thia aldianal firdawsi ci barke seydina Mohamed psl 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Les mamans li nicena c'est touchant que l'eden soit sa demeure eternel
ndeyssane yalla naka yalla yeureum diegalko ay bakaram yarame dawna mais nak.....KHESSAL BAKHOUL!!! amoul moudjie!
Ndeyesan, yallah naco yallah yerem
Que Dieu l'accueil dans son paradis amine firdawsi
Elle etais tres bell et gentill yallna khiper aldiana
Bilaye Amine
Chii ak soda mama fall soda tamite ak kiné lam sen voix yi macha allah
Que le bon dieu lui pardonne tous ces peches que la terre choix léger sur lui est que le bon dieu l'accueil au paradis amine😢😢😢😢😢😢😢😢😢😣😭😭😭😭😭😭😭😭💞💝💘💗💖💓💜💛💚👍
Ndey saan yalna ko yalla yerem
Dafa triste ndeysane. Yalla nako yalla yeureum te diegueul ko
J'ai pleuré😢. Que le paradis soit sa demeure eternelle
K la terre lui sw légère repose en paix maman, et longue vie à vs chères mamans
Yalna khipé aldiana yén tamit yalnaguéne fi yague té wér barké s.fallou
Ndeyesan cou bakh demna yallna yalla yokou lerram bark borom touba
Aljana firdawsi machallah Sama yaye maty thiam dogo
Yalna ko Yalla khare Firdawsi !
Ohh Machaaalah yalnako yalla yeureum tê khareeko aldjana souf woyof ci kawam tata madiodio fallou ak adja mougne lenn yalla Kenn dou khedio ak mom
Ndeyssane yallana khippé aldjiana 🙏🏽
Dioth yalla nako borom bi yeureum tè yeukhe niou
Yallanako yalla khare aldiana...sama maman linguene deff rafetna lolou .....na khaler yi roy su yenn ak idole nguen ..sama khôl mo fess tata diodio damako fekone sorano neko maman un neh nga ma lolou mou dieul temps wam du wahtane ak man dima yedd si adouna lolou yomboul
Thiayi aduna souf lék na kou nék yalla nako borom bii soubhanahu wattalla kharé aldjianay firdaws té atté ko thii yeurmandé nioune ñifi déss souniou heure bouye nieuw yalla nañu fékk thilou bakh amine ya rabbî
Très belle initiative les divas 👌🏽👌🏽👌🏽
Bravo à vous toutes
oooh maam madiodio sunu maam ji yalla na khipeé ajana
Salam li rafetna lol Machalla yalla nako yalla yeureum ta yekheniou si Barkep serigne saliou
Ndeysane yalla na khipé dji aldjana firdawsi ya amine
Que la terre de touba soit légère aminn ci barkep serigne touba
Yalnako borom touba terou amineee
Ndeyssaan! Yalla nako yalla yeureum teh xareko aldiana fiirdawssi
oh ndaysane yalla nako yalla yeureum teii khareii co aldiana
Yalla nako Yalla yereum té kharéko aldiana cii barké Seydina Mohamed
Machallah li dawnah yaram lol yalnah co yallah yerum
Sa fai plsir degue sougnou mame yii voix dor yii machalla
na soufe owof si kawame machaala à chaque fois que je suis connecté je regarde cette vidéo
Yalla nako Yalla yeureum té khareko adjana
Elle mérite k dieu lui accorde la grace
Gni ay nanane lagnou
Ndeysane yalla nako yalla yeureum te kharéko aldiana. Faites autant pour maman Fatou Talla svp. Yalla na leen fi yalla bayyi ba ci kanam vous êtes vraiment un temple de notre culture
Bravo à vous les diva yalla na madiodio hibe aldiana firdawsi
Yalla nako yalla yeureum ter hareko aldiana amine ya rabi
Super super j'ai pleuré c'est émouvant
Mschalla rafateluu nagnouko lool yalna souf oyof si kawam
Sama yarame dafa daw 😢😢😢
Ndeysaan yalna xippi firdaw🙏😭
Rafetna machallah
C'est vraiment trop cool, Merci Les MAMANS
Ndeysane limoy andeu yalla na aldiana di keureum
YALLA nako YALLA kharé aldiana si barké serigne touba
Machallaa sama ndaanaane yi yalna leen yalla defal djaam inechala
Ndeyesane daw na yaram yalla nako yalla yeureum diéguelko
Ay way souniou artistes yi vs etes braves , reconnaissantes j ne trouve pas Les mots pour vs remercier j ai Les larmes aux yeux k DIEU vs benisse MADIODIO NGNING k let paradis soit sa demeure amine k la terre de TOUBA lui soit legere (ci barke seydina mouhamed psl )amine
c est vraiment emouvant
Et ça c'est mon idole j'adore😍😍💗💗💞
Ndeyssane Dawna yaram machalah
L'i nice na yalla na souf oyof thi kawam
C touchant et tres emotionel😂😂😂😂😂YALNAKO ALLAH WA ZAWADIAL TERROUKO FIRDAOUS
Paix à son âme.... les mamans li nce na Machalla 😢
yalnako yalla kharé adjana firdawese si barké seydouna moukhamet psl yekoumawone dècé madiodia pai à son ame
Ndeyssane defnguène lou rafèt yalna khippé aldiana firdawssi
Moi vraiment j'aime ces diva repose en paix maman madiodio🙏❤️
Nice vidéo yalnaka sunu borom yerem yalla na dadjék malaka yermandé yi