Si tu tombe sur ce beau commentaire Qu'Allah te protège t'accompagne dans tes projets et te facilite tout une chose keep kouy setane théâtre bi ci téléphone Yallah gua gouddou fan
Non sama SAMIR keneu dou mom limou doff tamite louné la😂😂 gni kou len gueuneu ayy guissouma ko. Non MALCOM il est excellent 😍wouy Dudu tamite. Fred je le mentionne rarement mais kou meune limouy def la😂😂😂 je les aime ces gars😍❤️
@@ibrahimasallseye657 En guise d’exemple, l’épisode d’hier montre que certains fonctionnaires précisément dans le (DGID) pour être précis, sont prêts à abdiquer aux impôts de certaines personnes comme des Serigne qui leur promet de changement de poste. Pendant le ramadan, il y’avait une pléthore d’épisodes, qui , si tu veux tu peux aller visualiser car, tu le comprendra je n’ai pas le temps de toutes les énumérer 😊
Alhamdoullilah bac +mention en poche mangui felicitè nieupeu maximum de concentration aux admissibles courage aux ajournè dewene moye Dak inchallah yalla loumou df rk lolou moye Li geune ms coco laya maye joue bien
Non dudu ak Fred ak sami ak serigne kouna douniou ray mane les 4 fantastiques meilleure série de l'année vraiment chapeau à vous tous yallah na diam yague ichallah 🥰😂
félicitations aux admis du Bac yala nguen njeurinoko. aux ajournes , dites vous qui la yallah def bakhna ce n'est pas par manque de merites , mais yallah moko dogole nonou . bon nombre de personnes ont eux le bac et sont décéde le lendemain voir le jour même , d'autres n'ont pas eu la chance même de voir ou entendre les résultats . lou yallah def bakhna ci jamam. y'a pas que le bac pour reussir dans la vie , y'a tellement de formations profssionnelles que Bac mom boumou diaral ken bagn lek wala nane , nguen di stressé sen parents yi ❤ sur vous
ALHAMDOULILAH BAC EN TOUBAYE 🥲🤧🙏👨🎓ET POUR NOS AUTRES CAMARADES QUE LE SUCCESS VOUS OUVRE SA PORTE VOUS N AVEZ PAS DEMERITES YALLA LOUMOU DEF REK MO GEUNE THI NIOUNE ❤LA PAIX SUR VOUS 🙏
Bilay les fantastiques dinamou yoobé mousiba épisode passé damaye 😂😂 ba danou dougou si soufou lale bi tah yeugou mako sama yaye aye dale moma woo maye diouk coléwou si ronne bi ma khamni maguisi biir
Si tu tombe sur ce beau commentaire Qu'Allah te protège t'accompagne dans tes projets et te facilite tout une chose keep kouy setane théâtre bi ci téléphone Yallah gua gouddou fan
Amiine ya rabbi
Amine
Amine
Kou guisse coco laye laye 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂ré ba tass❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂
Amine❤
Le personnage de coco laye laye est bien réussi 😂
Billay ioe il est fantastic
Malcolm il est super fantastique 😂😂
Plus que dd
Dafmay fadj
La rencontre entre Fred et coco lay lay 😂😂😂😂 j’ai hâte 😂😂
Sheutt 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Mo nara nkh😂😂😂😂
Ci businessman bou gambia bi la gueum ni laniou koy diaralé ndax da beug dereum moûy tva aki tvb mane Dudu douma ray😂
Lu nekh bly est ce que wa impôt et domaine dougne kko créél problème 😭
Wallah😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Non Coco Laye laye et Malcom sont Fantastiques 😂😂❤️
Malcolm est le plus fantastiques 😂😂😂
Félicitations à tous les admis au BACCALAURÉAT 🎉🎉🎉
Merci beaucoup waye
Merci
Merci 🎉🎉
Merci 🎉
Merci beaucoup
Fred est comme leurs père genre sa responsabilité 😂
Aye aye sam dofna 😂😂😂 mais le personnage de Coco laye laye est bien réussi 😂😂😂
Aujourd'hui ma soeur et mon frère déclaré le bac en poche alhamdoulila ❤❤❤ nianall léne si barkép s.fallou mbacké
Serigne Fallou Rek kep dongue dina baakh barki borom ndindi mane kou beugue Fallou Awa Bousso rek yama moom
Félicitations aux admis 🎉
Plus de concentration aux admissibles ❤
Et bon courage aux ajournés peut-être l'année prochaine sera la bonne😊
Merci beaucoup ❤️🙌
Amine
Merci beaucoup waye
*Amennn*
Merci beaucoup ❤🎉
Yalla na niou yalla may dom bou gor bu toudou s saliou
Non sama SAMIR keneu dou mom limou doff tamite louné la😂😂 gni kou len gueuneu ayy guissouma ko. Non MALCOM il est excellent 😍wouy Dudu tamite. Fred je le mentionne rarement mais kou meune limouy def la😂😂😂 je les aime ces gars😍❤️
Ana gni beugue coco lay laye fans número 1 il joue bien son role 😅😅
Au delà de l’aspect comique, cette série expose des faits de société.
Comme ???
@@ibrahimasallseye657 En guise d’exemple, l’épisode d’hier montre que certains fonctionnaires précisément dans le (DGID) pour être précis, sont prêts à abdiquer aux impôts de certaines personnes comme des Serigne qui leur promet de changement de poste.
Pendant le ramadan, il y’avait une pléthore d’épisodes, qui , si tu veux tu peux aller visualiser car, tu le comprendra je n’ai pas le temps de toutes les énumérer 😊
Dieureu dieuff chéikh akhmadou Bamba Yakari jaam gni Koko wakhoull goré wooh
Alhamdoullilah bac +mention en poche mangui felicitè nieupeu maximum de concentration aux admissibles courage aux ajournè dewene moye Dak inchallah yalla loumou df rk lolou moye Li geune ms coco laya maye joue bien
Ma shaa Allah baraka k'Allahou
@@mariamadiedhiou3315 merci beaucoup Taye mome dama contane barki alkhourane ms d'autres part suis un peut jenai pour gni amoul
Non yalla bakh na in shaa Allah séne tour mo nieuweugoul rék
On en parle des leçons de moral de cette série fantastique
Fok naa ni gars yiii ils n'y font pas attention mais dep8 la saison 1 c'est plein de leçons de moral
dangay reeee ba tass
@@methabouwkdepuis dep8 tu es fantastique
Vraiment, Malcom est un grand comédien 😂, il ressemble à Serigne guagne.
Félicitations à tous les candidats admis aux bac & bon chance à toutes les candidats du BFM
J'apprécie beaucoup cette série❤ ça me donne d'être une grande comédien
Mach'Allah,sa ambition nice na YALLAH SBHWTL motaliko mais pour le moment diangal école en parallèle 👍🏽
Wallahi Malcom dou nitt 😂😂😂😂😂
Félicitations à tous les candidats du bac
Dof bou rew gay am fi les 4 fantástic 😂😂😂one love ❤❤❤
Samiir dal nakaté talent caché la wone 😂😊❤
Bilaye
Niou am bac yalla nalène bac bi djike si barki seydina mouhamed❤❤❤❤
Félicitations aux nouveaux bacheliers(es) et du courage aux ajournés
Felicitations pour niou âme bac🎉❤
Merci bro ✌🏾🤗
صلى الله علي محمد❤❤
Fred il a une extraordinaire 😂😂❤
Félicitations 🎉 à nos bacheliers et bachelières ❤❤❤❤
Merci ❤
Merci
Je réclame la démission de Malcom j'en peux plus sinon il va me tuer bilay😂😂😂 Malcom baloumala sama retane you tay yii wouy wouyyy 😂😂😂😂😂😂😂
Coco lay lay ak s kouna dina niou ma ray 😂 rék lii j'aime ca
J’espère tjrs revoir ma série préférée impact
Bilae 🎉
Wallay 😢jessica et moussa 😭
Billahi 😢
Dîna rei ba xeum reck 😂😂😂😂
Nonnnn gni ils sont extra fantastique 😂
Dudu et Samir encore vous 😂😂😂😂😂 je suis a terre bientôt au ramadan 2024 inchallah avec serigne kouneuh fall
Le fameux Film Hindou et ses ralentis😂😂😂😂😂😂
T'as vu😂😂😂😂
Coco ak Malcom Nioungui melni niouy jouer film hindou 😂😂😂😂
Cocolayla et Malcom m'ont tué 😂🤣
Le duo entre Serigne kouna et koko laye laye😂😂😂😂😂
Félicitations à tous les administrés au baccalauréat professionnel ❤
Priez pour nous les candidats du bfem 🙏
Amine way sama rake dey passe🎉
Démal diangue sa leçon yii bakhna am nga fiit dh😮
Amine
Ok
Coco laye laye en mode indou 😂😂😂 thiéy
Je souhaite tout les candidats qui ont réussir à la examen de bac courage les candidats qui sont échoué 😞
🤔🤔🤔🤔🤔🤔
@@diorndiaye735diarna lathh dh 😂🤔
@@amadoundiaye4436nagn nopiii rk c pas grave 😭😭😭
@@khadidiatoucisse496 gardons le silence 🤐😭
😂😂😂😂😂😂😂woy malcom 😂😂Fréd ngir yallah mangi dee😂😂😂
Samir qui rend hommage aux diola😂😂😂🎉❤
samir c'est le best en vrai wallah 🤣🤣🤣
😂😂😂 la séquence de la bataille des indiens entre malcom et coco laye laye menumeko mougne 😂😂
Les 4 fantastique 😂😂😂😂doudou yaw rek la top
Kou gueum ni fred dina guussi coco lay lay rek cobassal jaime
Je m’en doutes pas dh 😂😂😂😂😂
No malcome daye raye nite❤😂😂
Wooooooye Samir dina ma ray 😂😂😂😂😂nena sama Eva la 😂😂😂😂😂😂😂
Maintenant les 5 fantastiques avec coco laye laye 🤣🤣😂
Doudou dagua meilleur bilaye yaye thiate beug ay songuaté😂😂😂😂😂😂😂😂mes yasi eupe fite nack 😂😅
Coco laye laye djine bou lew 😂😂😂❤
Non dudu ak Fred ak sami ak serigne kouna douniou ray mane les 4 fantastiques meilleure série de l'année vraiment chapeau à vous tous yallah na diam yague ichallah 🥰😂
😂😂😂Samir le meilleur
Lalalma ❤ bo nango ni ma fi djitou na gaaw amna bac🎉🎉
Félicitations 🎉🎉🎉🥳🥳🥳🥳
Enfin j'avais hâte 😊😊😊
Coco laye laye khana Inde la djoguer😂😂😂
Bilahi vous êtes le meilleur des comédiens 2023❤❤❤😂😂😂😂😂
La meilleur comedie du Senegal. Staafurlaah Samir wala je savais pas que tu étais comment. Coco laye laye trop fort ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
félicitations aux admis du Bac yala nguen njeurinoko.
aux ajournes , dites vous qui la yallah def bakhna ce n'est pas par manque de merites , mais yallah moko dogole nonou .
bon nombre de personnes ont eux le bac et sont décéde le lendemain voir le jour même , d'autres n'ont pas eu la chance même de voir ou entendre les résultats .
lou yallah def bakhna ci jamam. y'a pas que le bac pour reussir dans la vie , y'a tellement de formations profssionnelles que Bac mom boumou diaral ken bagn lek wala nane , nguen di stressé sen parents yi ❤ sur vous
Non franchement ce série est trop génial 😅
Wouyyyy samir doffna🤣🤣🤣
Félicitation Yacine Fall mention très bien 🎉👏
Koudoul raté bénn épisode comme mann 😂❤
Coco laye toujours avec un nouveau look 😂😂😂😂😂
Fered srx mais nimiye wakhéee dafma néxx😂😂😂 man mom rkk ly topp🥰🥳😂
Non bilaye yeneu meilleure 😅😅😂😂😂😂😂bilaye kene dou yene 😂😂😂😂
Bilahi je savait pas qu'il est aussi impressionnant que sa il a un talent caché
kou geum né samir kou djiguén kimou nékalon djiné la rek lalal j'aime
Bilay malcom ak coco laye laye dinagn ma ray 😂
Samir a raison Payer les impôts 💔🔥🇸🇳
Coco laye laye joue bien son rôle ❤😂😅
Di félicitations yeup nio ame bac 👏🏿 nio amoul yalla nalen yalla defal la Posen foi 🙏🏿
Kene dou malcom❤
ALHAMDOULILAH BAC EN TOUBAYE 🥲🤧🙏👨🎓ET POUR NOS AUTRES CAMARADES QUE LE SUCCESS VOUS OUVRE SA PORTE VOUS N AVEZ PAS DEMERITES YALLA LOUMOU DEF REK MO GEUNE THI NIOUNE ❤LA PAIX SUR VOUS 🙏
Non Malcom ak coco lay lay doniou nitt 😂😂😂😂
Samirr😂😂😂😂😂😭😭💔nooooo sama Eva la 😩🤣🤣Fred kou ko dak wax xawma ko day door baga geum ay doram
Doudou lima diakhal danga koy lal mou kheum mom lou khew mou kheum😂
Wouy sam dof na😭😭😭😂en plus da am dolé mais dudu sa yaram bi sone na danie lay ndouli rek
Serigne kouna ak Coco lay lay dolen ma ray😂😂😂
les candidats de bac en poche et bac mention yalla naléne mou don lou guen si yén ❤
Les 4 fantastiques 😂😂😂😂😂
Comment ils ont fait pour ne pas rire avec Samir 😂😂😂😂😂😂
Bravo â ces quatre fantastiques au de là de la comédie ils enseignent
Coco laye laye c’est le meilleur walay😂😂😂😂
Fred da beug khalis kom po possible 😂😂😂 no mom rk lay topou😂😂
Samire néna coco lay laye mardi gras kagn leuh😂😂
Yalla na diam yague senegal ❤
Qui a eu l'idée de reunir ces quatre😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂 on doit le savoir antouka😂😂😂😂
Très bonne question 😂😂
Lui même il ne sait pas . Il a seulement proposé et Dieu à disposé😂😂😂😂
Il paraît que c'est Oncle Sam l'oncle de Laye dans "Laye Diarra"
Gni rk takh na niou faté sm stress bi yeup😂😂😂😂
Doff bou wreew😂tay rk nguèn dèh les 3 fantastiques😂
Dudu c’est le meilleur 🤦🏽♂️😂😂😂
Nono C la meilleure série de l'année 2023🎉❤🎉🎉🎉😅
Samir m’a tue 😂😂😂😂😂😂
C'est le cas aussi pour Samir de connaître coco laïlaï comme doudou l'avais découvrir
Bilay les fantastiques dinamou yoobé mousiba épisode passé damaye 😂😂 ba danou dougou si soufou lale bi tah yeugou mako sama yaye aye dale moma woo maye diouk coléwou si ronne bi ma khamni maguisi biir
*😂😂😂😂Kone diam daloula😂😂😂😂*
Vous êtes des génies de l'humour 🤗