Préstation de wakeur Serigne Khadim Lô Gaydel au festival salam - 24 juin 2016 à Sorano

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 16 янв 2025

Комментарии • 107

  • @ousmaneseck1064
    @ousmaneseck1064 7 лет назад +5

    Machalah li thi keur cheikhoul khadim rek la amm boulenn nekhonn ngenn dadialo pour sabar wala taneber mai khassaïde you serigne touba rek molenn nior thia kaw thia kanam inchalah

  • @afriyedammone7239
    @afriyedammone7239 Год назад

    Mashallah,, this was POWERFUL, even though I don't understand the language, it's the spirit and energy which resonates within. Shukran

  • @maimounacamara7387
    @maimounacamara7387 8 лет назад +7

    Je suis bouche-bée, macha allah , macha allah. Merci à Serigne Touba khadim rassoul, merci à Serigne Khadim Lô gaydel, merci à Ablaye Niang, merci à Youssou Ndour, merci à Ndeye Ndiaye , merci au kourel des soxna UKB, depuis que j'ai écouté cette belle et émouvante interprétation de mouwahibou j'ai eu un déclic et je me suis mise à étudier les khassaïdes de Serigne Touba Khadim Rassoul. Vous avez tous apporter un PLUS à ma VIE . ENCORE MERCI

  • @brownby2454
    @brownby2454 7 лет назад +3

    Yallah nagnou Serigne bi fagoul si Soxna yi Barkép Xassida yi👌

  • @mamediarradiao5928
    @mamediarradiao5928 7 лет назад +1

    Jërëdiëuf serigne Touba Mbacke amouñu sa fay yallah mi am faay yallah nala yallah faay si barki mouhamed (psl)

  • @mouhameddiouara6104
    @mouhameddiouara6104 6 лет назад +4

    Mm moi tijane j c k rare de mouride l'aime autant k moi jazaka khadime rassoul

  • @mamediarraboussofaye1643
    @mamediarraboussofaye1643 8 лет назад +4

    MACHA ALLAH MACHA ALLAH MACHA ALLAH SOXNA NDEYE YALNA BAT BI WER DIEUREUDJIEUF WA MOUHSINATES DE BOROM NDAME

  • @eva_la_fresh5805
    @eva_la_fresh5805 8 лет назад +2

    Machallah xol sed na lolou na sein diam yague yalla na boro ndaam yague contane 🙏🙏🙏🙏

  • @fabydiaw6414
    @fabydiaw6414 8 лет назад +3

    machalah. fiere de vous doundeulénr ba séne ay seute diléne awou si liguey bi guénr di ligueyal KOU TED

  • @jimmytafa2015
    @jimmytafa2015 8 лет назад +6

    s touba reka fi nek mo mome niepou

  • @thies24
    @thies24 8 лет назад +9

    thiey serigne touba amoul morome

  • @adjiroseniang7666
    @adjiroseniang7666 8 лет назад +4

    Machallah sokhna you ted yi, li dè dafa guen nek thi safane wi, gniy nek di wakh guestou dji dafa guene wakh diou beuri dji.
    sant sant nagn Borom Ndam bouwer

  • @evadiop6079
    @evadiop6079 8 лет назад +2

    MACHA ALLAH MACHA ALLAH MACHA ALLAH KHOL YEUP TOYNA NIOU NALLENE SERIGNE TOUBA FAYAL BOPAM DIDJAYE SEYDINA MOHAMED PSL AMINE YA RABI

  • @fatoucamara7297
    @fatoucamara7297 8 лет назад +1

    dieuredieufeti Serigne touba ken dou Serigne touba alhamdou lilah

  • @serigneakhmandiaye2672
    @serigneakhmandiaye2672 5 лет назад

    Ma cha Allah Dieuredieuf Borome Touba Danouna lére wawe léne coumba sama xol séde na gouye

  • @ndeyecodoubop8204
    @ndeyecodoubop8204 8 лет назад +4

    Machala yalla nalen Serigne Touba FAY

  • @yankssawaneh8219
    @yankssawaneh8219 7 лет назад +1

    Sama xol sèdd na trop dieuredieuf serigne touba yaw rek ya fi nek

  • @bouyagueye2846
    @bouyagueye2846 7 лет назад +1

    barkép KHASSIDA YI sama xoll sédd si yéne mouth goud fan weur greumoul CHIEKHOUNA CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIM RASSOUL LAHI

  • @liimattawakhfii8722
    @liimattawakhfii8722 8 лет назад +1

    Serigne touba rek thi khol...

  • @maimounadiouf1804
    @maimounadiouf1804 6 лет назад

    bilay barki s touba da ma bég yala nalén yalla défal diam tè wèral batt yi

  • @mouhamadoulaminendiaye8676
    @mouhamadoulaminendiaye8676 8 лет назад +5

    Nous sommes fiere de vous les mmouhsinaates de Borom ndame. yéna ngi gnouy bégueul di sagal yone bi di sagal djiguéne. sagal islam

  • @papathiam2296
    @papathiam2296 5 лет назад

    Machallah Amna solo xol sedna xassida dafay doundeul rouu

  • @amyndiayendiaye5682
    @amyndiayendiaye5682 8 лет назад +3

    machala Li lèp borom ndam la yagu fi loll tè wèr

  • @cheikhwadji7458
    @cheikhwadji7458 7 лет назад +4

    *_DIEUREUDIEUFETI SERIGNE TOUBA_*

  • @bamami5754
    @bamami5754 8 лет назад +1

    tiey serigne touba ohhhhhhh

  • @ndeyeabsaniang913
    @ndeyeabsaniang913 7 лет назад +1

    dieureudieufer serigne touba

  • @bayedarou593
    @bayedarou593 8 лет назад +2

    Jeurejeufé serigne touba

  • @dieynabasarr6339
    @dieynabasarr6339 8 лет назад +2

    machallah contannalool

    • @ousseynougueye6022
      @ousseynougueye6022 8 лет назад

      Thiaakhaan dong la. Serigne touba diangalé woul djiggen di yeketi bat !

  • @ndiassetine371
    @ndiassetine371 8 лет назад +1

    santé serine touba rek

  • @khadimgueye2754
    @khadimgueye2754 4 года назад

    Ndayesan 💚💘✊👈😢

  • @ahmedsakhir9233
    @ahmedsakhir9233 5 лет назад

    contane nanu siyen diam ak kheuweul yalla naguen ko am

  • @moussakane2290
    @moussakane2290 8 лет назад

    diere dief serigne touba

  • @pendatoure2861
    @pendatoure2861 8 лет назад +8

    ndaye sanne serigne touba amoul morom

  • @ndayediagne8020
    @ndayediagne8020 7 лет назад +1

    ohhhhh liii sednna khol dhe

  • @boubooombayeeede6388
    @boubooombayeeede6388 4 года назад

    Machalla 🧕☝️

  • @adjidieng2793
    @adjidieng2793 2 года назад

    Ceuyyy Serigne bi

  • @modousow9991
    @modousow9991 7 лет назад +5

    li moy deg jiguene day begeu yalla te kham ko fi la lougne geremè dé

  • @fatoucisse8628
    @fatoucisse8628 5 лет назад

    Love

  • @omarlo2634
    @omarlo2634 8 лет назад +5

    sante rekk

  • @seynabougueyefaye3497
    @seynabougueyefaye3497 8 лет назад +10

    Yonou SERIGN TOuba bi da amoul tanki guinaw té dieufeum bouné day firndel wakham diodiou

  • @ndeyendackfall1258
    @ndeyendackfall1258 5 лет назад +2

    Mame day sama wax bari wusi waye xassida s touba yi kuko mokal raw ga

  • @ibrahimpuy9155
    @ibrahimpuy9155 8 лет назад

    machalahh

  • @yamadilahathotmail.comnice858
    @yamadilahathotmail.comnice858 8 лет назад +1

    mahalla

  • @sokhnafall2524
    @sokhnafall2524 7 лет назад +2

    apparemment au temps De Cheikh Ahmadou Bamba les filles n'avaient que le droit de lire tout doucement les xassidas pas de les chanter seuls les garçons avaient ce privilège. maintenant je ne sais si cette innovation est haram ou pas si ça cause plus de bien que de mal ou vice versa seul Allah est juge.

  • @cheikhfalloudiapandal5276
    @cheikhfalloudiapandal5276 6 лет назад +2

    Yeen gnii di wakh baatu jiguene waroul DIOKK kaww dem Lenn wakh ko niom Viviane ak titi فمن شاء فاليومن ومن شاء فاليكفر

    • @diopdudu1187
      @diopdudu1187 6 лет назад

      Cheikh Fallou Diapandal bien dit

    • @papathiam2296
      @papathiam2296 5 лет назад +1

      Deug nga wakh nit dafay meun tontou wayy

  • @louissylla5367
    @louissylla5367 8 лет назад +2

    ho satte bamba borom ndam lo

  • @Bayfall-diaw
    @Bayfall-diaw 7 лет назад +17

    biñouy wax batou djiguen hawra la batt yi taxul ndakh lii sokoy deglou do yeuk loudoul yala souñu brom
    t sax li diaroul débat dieuredieufe brom touba xadim rasoul

  • @salioudiakhate7503
    @salioudiakhate7503 8 лет назад +3

    Khalasss thiey borom ndam UKB rk

  • @khadimlo8848
    @khadimlo8848 8 лет назад +2

    Serigne boumak bi terena lou melni djieguene waral diangue khasida

    • @tourepapesamba8670
      @tourepapesamba8670 8 лет назад +2

      yaw gni finiou diougué fala Serigne Bou Mak Bi nek wala mousso kham lolou

  • @babacarlo1874
    @babacarlo1874 8 лет назад

    bilahi si ay thiakhane rék nguén nék

    • @babacarkhassaide9342
      @babacarkhassaide9342 8 лет назад +1

      yaw daal babacar Lo waxoofi dara. demal geustou dji

    • @pendandiaye8222
      @pendandiaye8222 8 лет назад +3

      kou bakhe boula nékhoul boul sétane té libre ni rek guéndi def démoléne té kéne d'où dème dokhal fowi waye

    • @rassoullahinabi8740
      @rassoullahinabi8740 7 лет назад +1

      sou nieup nekon sili nga wahne ay tiahane yakar na kon senegal guewou chaytane da tadi ba faw
      yalla na yalla guindi

  • @asstoure2113
    @asstoure2113 8 лет назад +1

    deuguë rékay deugue

  • @lomactarmodou6418
    @lomactarmodou6418 3 года назад

    Machalla lo ndam amna solla lol

  • @niangmodou5333
    @niangmodou5333 5 лет назад

    Sarinetoubarkerkerke

  • @babacarkhassaide9342
    @babacarkhassaide9342 8 лет назад +4

    t nio diapp thi lii t bagn fé nekk di araabal rekk!!! lii ak fii mbonn gui yokk..... waaw leen coumba waay!!

  • @macoumbandiaye7214
    @macoumbandiaye7214 8 лет назад

    Diadieuf

  • @famagueye9701
    @famagueye9701 8 лет назад

    Kawtéf batou sokhna awra la

  • @drameseydou211
    @drameseydou211 5 лет назад

    Akkassa yokk RK gueune dieume kaname RK ba Adiana nakk

  • @eurafricanews5977
    @eurafricanews5977 6 лет назад

    Haram
    Ci yonou mourite ci daffa Haram
    Li Serigne bi dawoul deff dawouko deflou ci Lou Haram la nekk
    Haram Haram 1000 fois

    • @NDENEBRICOLAGE
      @NDENEBRICOLAGE 5 лет назад +2

      Li dé mo geun sabar, tanber, dem soiré wala concert waly wala pape diouf. Té dara tewoulen ko def ndakh seni morom rekakoy def. Bou djiguenou senegal yeup melon ni kon legui rewmi sopikou

  • @user-dy6ku2mm7v
    @user-dy6ku2mm7v 8 лет назад +1

    Yaw Khadim Lo, Serigne Bou Mak bi molako wax ??? Wala sa baye lako wax ??? app #Mouride Dou kaathie !

    • @adjiroseniang7666
      @adjiroseniang7666 8 лет назад +6

      koubakh yaw d say teguine dagn la rere. ba la ngay am loy leral amal ay teguine ba nopi!

    • @cheikhmbacke1724
      @cheikhmbacke1724 7 лет назад +1

      Sa data yaye way

  • @Bayfall-diaw
    @Bayfall-diaw 7 лет назад +3

    ñuy wax batou djiguen ñy hawra la t boula sokhna yi wowé tlfon nga répondre lolu thi na fekh la bok way boulén ñu sonal ak wax diou barri

  • @khadimlo8848
    @khadimlo8848 8 лет назад

    saway mane ap talibe la way adouna dafa yakhou waye djieguene waroul yeketi batame sakaw

    • @ibrahimandiaye3407
      @ibrahimandiaye3407 8 лет назад +4

      so néké talibé sou bate yi diogué do yeug lodoul sounou borom

    • @mouhamadoulaminendiaye8676
      @mouhamadoulaminendiaye8676 8 лет назад +1

      yalna adouna yaga yakoo niii.. yaw mom dafa melni django dé
      fier de vous

    • @cheikhndiaye3401
      @cheikhndiaye3401 7 лет назад +1

      Khadim Lo AhahahahahahahahaahhhHhHH li dh dafa nèx rk bilayyy

  • @khadimngirane9225
    @khadimngirane9225 7 лет назад

    li bokoul si mourite gui dé bilay

  • @thiampapaabdoulaye6220
    @thiampapaabdoulaye6220 8 лет назад

    ah Tcim mbolo diaroul lii djiguen batame awrra là lii dafa haram

    • @bijoumoulayedabah
      @bijoumoulayedabah 8 лет назад +2

      Voici ck je cherchai deugla deh dafa beuri louniou touder diner tei meloul ni diner batou jiguen di jok ci kanamou mbolowou goor yalla beugouko ni yonente bi t VRAI Serigne dafko wara terei mais senegal ndeysan ns sommes trop inconscient. yalnaniou yalla yeureum. jiguen souko diner mayon mou def lii kon djiguen dafay likam di node ne croyez vs pas?

    • @cheikhndiaye3401
      @cheikhndiaye3401 7 лет назад

      Thiam papa abdoulaye Serigne touba rk si kholll kèneu manou si darà dieureudieuff ahmadou

    • @sokhnafall2524
      @sokhnafall2524 7 лет назад

      apparemment au temps De Cheikh Ahmadou Bamba les filles n'avaient que le droit de lire tout doucement les xassidas pas de les chanter seuls les garçons avaient ce privilège. maintenant je ne sais si cette innovation est haram ou pas si ça cause plus et bien que de mal ou vice versa seul Allah est juge.

  • @jimmytafa2015
    @jimmytafa2015 8 лет назад +2

    s touba reka fi nek mo mome niepou

  • @ibrahimaciss8970
    @ibrahimaciss8970 7 лет назад +1

    dieureudieufé serigne touba

  • @cheikhleye2667
    @cheikhleye2667 8 лет назад +1

    machallah

  • @omarlo2634
    @omarlo2634 8 лет назад +1

    sante rekk

  • @mbayepouye2711
    @mbayepouye2711 7 лет назад

    Dieureudieuf serigne touba

  • @abibmarouane6699
    @abibmarouane6699 8 лет назад +1

    Machalah

  • @ndeyeantandiaye2941
    @ndeyeantandiaye2941 8 лет назад +2

    Machallah

  • @certifiad8560
    @certifiad8560 8 лет назад +1

    machalah

  • @ln5183
    @ln5183 4 года назад

    macha Allah

  • @adamaathie2275
    @adamaathie2275 7 лет назад

    machallah