B52 mon lutteur préféré double roi des arènes ❤ CNG war nane la décoré sa jour jubilé un vrai champion de la lutte sénégalaise et une référence aux jeunes lutteur ❤ Merci Gaston production
My boy boula gars yi sarakhé bombe dou thiakhane dé . Sama mbeur nga tu as de l avenir Jackson . Yanna yalla takhawoula té mayela ndame si Barker Seydina Mouhamed S A w
Vraiment abdou lahad ndiaye diga yakal Gaston prod ak jackson franchement suis fans de jackson ms mokk mbaye gouy gui moh done yone gayy bagne albourakh diko teug😢ms jackson yalla nko ylla soutoural 🙏abdou lahad xolatal sa bopp
Deugeule ms bombardie mo waxon ni dina may Jackson chance te Jackson combat bi moko geuneul fouff sah😂 ay moromam nioko done toutil ni dougnou beurèk mom moussa ndoye quenche ms rombou nalèn lamb chance la😂
Seye 2 vs eumeu Sathies vs Zarko Tapha tine vs modou lo Quench vs mbaye gouy gui Fils de balla vs gris bordeaux Général malika vs gris 2 Pokola vs diene kaïre
Bilahi tei amoul lou geunone nekh gris 2 bombardier. Jackson mbaye gouye gui ! Li dou gattt vraiment mais Jackson mome yalla moko beugg ! Li chance deugg leu !
Jackson limou djokh thieur balla gaye 2 mo takh mu nèkh ma défoi rendre hommage di touss ay tousam Dara djombou ko mbeur bu yarou la yalla nako yalla djapalé mou dane bombardier djèla bu guaw tée lèr thi sering fallou thi bisou magualam gui yalla baxna❤🤲
Vraiment combat bi nekhoul!! Bombardier est de 1976. Il aura 49 ans cette année. En tout cas bonne chance à Jackson. Abdou lahat mo yakheu combat bi contre mbaye gouye gui cest dommage
Jackson dh champion lah kou yarou leuh mais mom si défaite la diougué contre Lac Rose wara rebondir.Gnu diokh ko Bombardier li dou logique.Supposons mou dane Bomb koneh day dougou cours des grands comme ça facilement...🤔
mok aline gueye boulko si geiné , nioy outal yonnee seni mbeur, aline mo yoore liss diko outal yone nooy jougei si defaite contre pokola ak combat veteran zoss dem si lac rose ?
Structure Gaston depuis la mort du leader est tombé très très bas vraiment ay lac ada bomb Jackson claf bii amoul beuzz sites amoul avancement comme albourakh vraiment makan tu es nul très nul
B52 mon lutteur préféré double roi des arènes ❤ CNG war nane la décoré sa jour jubilé un vrai champion de la lutte sénégalaise et une référence aux jeunes lutteur ❤
Merci Gaston production
DEUG DEUG Lamb AK combinaison dioxko albourakh ❤.
VIVE LA FAMILLE NDIAYE 🫶🥰💦
Une belle opportunité pour Jackson faudra saisir cette chance ✌️
Nn combat la am dh
@@soppeousmanesonko777dou combat bombardier daye danou dousi def 20 000f si combat bi
BOUNOU KÉEN SONAL LAMB LA BA DÉ SOXOR GUÉEN TROP ❤❤❤ DIADIEUF GASTON PRODUCTION ❤🎉
Fi ken soxoroul deug rk la niou wakh naka lako rose dané mou dieul bomb ? Nafekh bahul waay
Lidou Combat 😂
Li mome meunoleine ko promotion bamou nekhhh😂😂😂😂
khana niou yobouko CANAL +😂😂😂😂😂
Ah Jackson dé amna chance, danou si Lac rose, dale si bombardier.
Lamb mo dèmè nonou guiss nagn fi ada fass lac 😂 . Liss poko moko dane te lac rose lay beurèl 😂
Lac Rose dane la guay beurré ak Bombardier 😂😂Senegal mo nékh😂
C’est tous des imbécilité ils ont détruit cette lutte 😠😠😠
Dane nane fi mbeur mou beurék roi des arènes ba dieul couronne ba. Barki démbo ndiaye la. Siteu mo si moudj .Mom sakh daffay danou di avancé😂😂😂😂😂😂
Boula say morom ragalé nk?
Même Bombardier si 3 défaites la diogui
Jackson garyi niemei wougn ko lac moko dane mais moko meun 😂
My boy boula gars yi sarakhé bombe dou thiakhane dé . Sama mbeur nga tu as de l avenir Jackson . Yanna yalla takhawoula té mayela ndame si Barker Seydina Mouhamed S A w
Teug combat bo khamni lérnalén ni bou amé nite Jackson mokoy inedi té stade bi dou féss 😂thiey wa Gaston production😂😂
😂😂
Kom ada fass lac rek😂
Vraiment abdou lahad ndiaye diga yakal Gaston prod ak jackson franchement suis fans de jackson ms mokk mbaye gouy gui moh done yone gayy bagne albourakh diko teug😢ms jackson yalla nko ylla soutoural 🙏abdou lahad xolatal sa bopp
vraiment ta tous dit
vraiment ta tous dit
Li Yép Clant Rk Mé Dfay Saraxé Boy bi
Deugeule ms bombardie mo waxon ni dina may Jackson chance te Jackson combat bi moko geuneul fouff sah😂 ay moromam nioko done toutil ni dougnou beurèk mom moussa ndoye quenche ms rombou nalèn lamb chance la😂
Seye 2 vs eumeu
Sathies vs Zarko
Tapha tine vs modou lo
Quench vs mbaye gouy gui
Fils de balla vs gris bordeaux
Général malika vs gris 2
Pokola vs diene kaïre
Nc
Fils de bala na dem dieul gris 2
Général Malika nane la meun dané forza Mouy dieul gris 2 fofou douma ci dakor ak yaw
@@mohamedcoulibaly1923gris 2 insbi Mo gueun bakh palmarès fass après Serigne Ndiaye 2
Xam nga lamb nak
Quelle combat !😂😂😂
Albourakh yena meune deh !
Li lambi defanté la !
Gaston. Production da soulou pere Gaston vrai professionnel
Al bourakh moy lamb❤❤
Faire ply way pro
Li mome guerrou Abdoulahat ndiaye la mais dou combat walahi
merci Gaston production numéro 1de tout les temps ❤❤❤❤
😂😂😂😂❌️❌️❌️❌️👎🏽👎🏽👎🏽👎🏽👎🏽
Jackson tu a chance pour entrer dans les VIP do your best pour gagner se combat
Bombardier Jackson mome lamb biiiii de mom kéne khalaatouko woone Jackson kaye moosi dale lék 😂😂😂😂😂
Bilahi tei amoul lou geunone nekh gris 2 bombardier. Jackson mbaye gouye gui ! Li dou gattt vraiment mais Jackson mome yalla moko beugg ! Li chance deugg leu !
Ban Dal Kou Wara Dém Raitret Té Ay Mromam Nek fi li kay Boukosi kén Encourage nk
Merci abdou lakhate ndiaye
Machalla ❤❤❤Jackson dit birima
Ki wa albourakh lay khekh ndakh mbaye gouygu Jackson Ndiaye lakhat moko yakh mai sen li diaroul dem state yamlen amadou bary😂😂
Saway combat bi kay malika plage lanioukay beuré 😅😅
Vraiment jakson bou meuné dieul bombardier doyé woul dara mbaye gouy gui objectivement
Brima seul🎉🔥
Albourakh ❤❤❤❤👑👑👑
Albourakh seule 💯❤️💯🙏🏿
saway boulen beugué deg deug rk fi albourakh lafi yalla tékk 😂😂
😂😂😂lolou lanouy bagne tei yalla def nako
@@MansourDiop-wd2or😂😂😂😂😂lolou mooy deugg
@@CheikhNdiaye-yr7zo bly nagn mougne rk amou niou xaliss baparé Di sanal nitt gni😂😂
Wa Al bourakh mom sen khel gen yorè di khalat. Gnenen Gni mom sen toun lagni utiliser 😂😂😂😂😂😂
Ya rew😂
Mbaye Guy gui Jackson vraiment monékone combat bi
wala jackson vs diene kairé
Jackson mo daw
Machallah comme Jackson mbeur yi danouko ragal yalla nako yalla may ndam
Jackson bou dèfoul nii dou beurrè... tapète yi dieleuntè nagne si sènn biir kay... tè Jackson dafa bokk si lamb... felicitations Gaston Production...
Thiey lamb😂😢
Fou modou mayé chance siteu louné meune na am❤
Jackson yalanala yala may ndam 👏✊
Mouwayy lilane la😂😂😂😂😂😂😂😂
Concurrence té khamouniou loufa nek
@@papesoumaLe problème est que manager yi gnoy yakal mbeur yi koi
diamou ❤❤❤
Vrment combat bou nékh la bouléne faté b52 gniar gniko moudié dane (franc et reuk ) ay vrai champion lagn
merci beaucoup abdou lakhat vive Jackson ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Jackson il faut faire attention c'est un combat piège.Il faut être prêt sinon Bomb veut sortir par une victoire.
😂😂😂😂😂xaral ma rée. Lakhad Ndiaye amo xaliss gueumeul ylla
Lamb dou xaliss ay pèkhè la 😅😅😅
Dama yakarni makane mbéngue dafa ragal abdou lakhad😂😂
😂
😂😂😂
Li dh moy lamb fathie merr deug 😂😂😂
Mbadou 😂😂😂
Mbadou 😂😂😂
Bly DEUG leu 😂😂
Lahad Bayil garouwalei bi
Al bourakh mofi nek❤ mounekh len AK mounakari len
Combat bou torokh bi😂Moy lane lidou combat way bombardier meunoNe n'a dieul Aline seye 2
Li mom wohou seytané la lamb kéneu momouko promoteur yeupeu son libre de signer mbeur bouléne nékh, lolou sah Moy dohal lamb
Jackson limou djokh thieur balla gaye 2 mo takh mu nèkh ma défoi rendre hommage di touss ay tousam Dara djombou ko mbeur bu yarou la yalla nako yalla djapalé mou dane bombardier djèla bu guaw tée lèr thi sering fallou thi bisou magualam gui yalla baxna❤🤲
Ahh combat le li Mom nice jaksone merité n'a beuré AK bom
ALIOUNE SEYE 2 KAGNE LANIOU KOY DIOKH COMBAT
Merci Gaston production ms il faut augmenter les offres
Si combat la Kay bombardier amoul ben challenge boumouy defati à part may ay rakam ak ay diarbatam chance ❤ allé Jackson
merci au promoteur, lerciba B9mbardier, Jackson mérite cette chance la
Jackson mon lutteur vraiment sa encadrement baxul😢😢
Gaston Mbengue defaral n’a lamb wayè makane day yakh lamb. 😂😂😂😂😂😂😂😂 li d’où combat . Jackson ne mérite pas d’affronter bombardier
Albourakh ❤❤❤❤
Vraiment combat bi nekhoul!! Bombardier est de 1976. Il aura 49 ans cette année.
En tout cas bonne chance à Jackson. Abdou lahat mo yakheu combat bi contre mbaye gouye gui cest dommage
Bonne chance Jackson Jr❤️
Bilahi bombe kou bakh
Saway abdoulahate ya wor ndax Jackson bou dané bombardier day book sii gars yii dh
Bonne chance Jackson Jr !
15 ème victoire inshallah 🙏🏽
Merci Abdou lakhate ndieye 😂
Walo walo bii seul ❤❤❤
Jackson dh champion lah kou yarou leuh mais mom si défaite la diougué contre Lac Rose wara rebondir.Gnu diokh ko Bombardier li dou logique.Supposons mou dane Bomb koneh day dougou cours des grands comme ça facilement...🤔
Jackson vs mbaye Gouy Gui était le combat pour dire vrai
Inchallah Jackson Dakoy dann noté lénkô😊
😂😂😂😂latt yap naniou dh😂😂
mok aline gueye boulko si geiné , nioy outal yonnee seni mbeur, aline mo yoore liss diko outal yone nooy jougei si defaite contre pokola ak combat veteran zoss dem si lac rose ?
Mais bombardier khana dou retraite 😂
Lii dou combat way
Allbourakh doflou promoteurs yi. Li moy combat 😂😂😂😂😂😂😂 franchement 😂😂😂😂
Jackson yalla nala yalla may ndam rk inchallah
Khana mbour nguéne koy beuré 😂😂😂😂😂
Li d'où comba honnêtement
mais B52 fin carriere la nekk aussi . Jackson peut en profiter
Lane moy combat lac rose vs liss ndiago lane moy combat ada fass vs lac de guiere lane moy comba modou anta vs prince ??
Je suis de même avis
Lamb la rek. Fi guis nagn fi louneee
Lamb dji legui amatoul mbeur mou mak ak mbeur mou ndaw
Bombardier lou tahk diéulogo aliou séye 2 ndeysane dama yérmandé si mome billahi 😱😱🥺🥺🥺🥺
Vraiment wa Gaston production da ngéna daanou liii mom dou combat Albourakh niaff nalén nak Nooo seuhhhh 😢
Jackson waro wone djeul bomb!
Victoire ley weur pour bayi! Té dane ko yomboul!
Mais bonne chance de ng nek si yone!
Makane guen fokni abdoulahat Ndiaye yaroul lomotif makane lii dou nenn😂😂
😂😂😂
@@layetheonly5139 😂😂
Bomberdier nak 😂😂😂 bonne chance Jackson jr ndam rk inchallah
Jackson yalla sounou brom takhawou may la ndam rek inchallah
Combats yiii lika warale promoteur yi dagniye defanté
Bilahiii makane so bayiwoule Abdou Lahat miii 😂😂 dina lékk linga yorré
😂
Bilay Bombardier mo niakk khole teiii niak diome. Un combat impopulaire sans saveur incolore et inodore 😂😂
bomb si bopam amoul khorom di, dou baakou bou nex , dou nexal signature, dou beuré bou rafet, dou dara
Alburakh 🎉🎉
Li dou combat way
Gaston production yenà thiouné 😂😂
Trouvez un combat à Gris 2 svp
Li dou combat way😂 Gaston Production khana daguén diakh lé😂
😂😂😂😂 yakhe xaliss combat bi dou beuri nitt
Mod Dia aussi war na am combat nak diaplé lenko svp
Pokola bombardier sakh mo tanéwone, wala aline seye, wala moussa ndoye
Gris 2 vs bombardier
Jackson vs mbaye gouye gui
😂😂😂😂😂 non li aye blangeu la😂😂
Li dou combat waye😂😂😂😂
Kou meune
B52day jubile la yakar 😂😂😂
Combat bou nekhna la
Yalnalén Akhou Amateure yi Dal Lima Wahon Diamaicain Bim Teugué Zarco Bb Diene Tay Mongui ni Balegui Manun̈u Beuré Wayé Sén Combat bi Yallna Yakhou Bombardier Mak Mou Niaka Guem Yallna Nga Iow ́gani Do Bayé Défaite😂
Bombardier beneu 7place lay andi ak 3 bouteilles 😂😂😂
Jackson rék❤❤❤
Li kou kay sétan😂
Meunone nguéne df bombardier khadime ndiaye sakh motané 😂😂
li mom khana moy niak pékhé 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Makan dama ko yeureum abdou lahad ndiaye dakoy fowè rek 😂😂
Merci beaucoup Gaston prodision 😢😢😢 quelle combat 🤔🤔🤔
Billahi ❤❤❤
Vraiment li dou comba bou nex
@DioufMouhamadou-s6x barki sayyidina mouhaméd combat bou nékh ngaye guiss ndakh bombardier Day beugue guénalé ak victoire ndakh yakarna bi moy dernière combat wam🤔🥺 combat ladé
Mbaye gouygui ak Jackson monékone combat bi
Haha😂😂combat bi dé dou takh kén dem stade
Boulma Ray😂😂
Tay sama khoule nékhoul bilay
Structure Gaston depuis la mort du leader est tombé très très bas vraiment ay lac ada bomb Jackson claf bii amoul beuzz sites amoul avancement comme albourakh vraiment makan tu es nul très nul