Merci Lutte TV pour ce bon reportage. Un beau Panaroma qui reflète la beauté de la Nature et la culture locale. Siteu à travers son image peut participer à valoriser la richesse culturelle et naturelle de cet Terroir Serrere dans le but d'un developpement touristique et inclusive bien organisé. Diadieuf Champion.
SITEU suis pas ton fan mais franchement j’apprécie bcp ton côté social. Nitt kou nek fa nga deuk moy sa fierté. Yalla na YALLA soutouraal la ba nga meun motali sa yeené Inchaa Allah si barkep kou taarou ki (PSL) 👏🏾👏🏾👏🏾
@koulaalhakk8975 salut ma belle diamaguene amoul couronne mé monde entier khamnagnouné siteu mo gnouss Modou Kone affaire bi dou couronne question de gnouss daan leu🤣💪👑
@@Misterboom-x7x copain mane douma jigueen douma diagg nganane ma ma belle😂😂noum démé nonou ....siteu daanoul kéne...kou daan da ngay fété kaw... Lamb wakh la ak dieuff...mais siteu day wakh rek...Yeen yeena takh sen mbeur niak diom ndakh dolene ko wakh deugg....modou lo meussoul areiére ...parcelles amoul mbeur bouy arriére
Mai dionwar rafétna trop machalla
Merci Lutte TV pour ce bon reportage.
Un beau Panaroma qui reflète la beauté de la Nature et la culture locale. Siteu à travers son image peut participer à valoriser la richesse culturelle et naturelle de cet Terroir Serrere dans le but d'un developpement touristique et inclusive bien organisé.
Diadieuf Champion.
Socialement il est bien c’est un gars très humble et intelligent
En tant que fan de modou lo , li siteu di déf si deuk bi contane na si trop😊❤
Machallah dionewar rafetneu ❤❤
SITEU suis pas ton fan mais franchement j’apprécie bcp ton côté social. Nitt kou nek fa nga deuk moy sa fierté. Yalla na YALLA soutouraal la ba nga meun motali sa yeené Inchaa Allah si barkep kou taarou ki (PSL) 👏🏾👏🏾👏🏾
Koula beugue Niou beugue leuh koula beugoul beugou nioula le roi👑
Bane roi😂😂roi des dawkates
Roi sans couronne 😂😂
J’aime beaucoup cet endroit 😍
Bravo Roi 👑👑👑 yallna gua goud fanne way❤❤❤
Marshall ah Siteu the king 🤴
Thiey son excellence Monsieur siteu borom deuk bi le nouveau Roi des arénes kou bagne wanal say poupe👑💪🤣
Lolou moy deug le roi des arenes
Bro yaw sonn nga😂😂😂😂nanal ndokh yangui wakh rek😂😂😂té diamageune couronne nékoufa
@koulaalhakk8975 salut ma belle diamaguene amoul couronne mé monde entier khamnagnouné siteu mo gnouss Modou Kone affaire bi dou couronne question de gnouss daan leu🤣💪👑
@@Misterboom-x7x copain mane douma jigueen douma diagg nganane ma ma belle😂😂noum démé nonou ....siteu daanoul kéne...kou daan da ngay fété kaw... Lamb wakh la ak dieuff...mais siteu day wakh rek...Yeen yeena takh sen mbeur niak diom ndakh dolene ko wakh deugg....modou lo meussoul areiére ...parcelles amoul mbeur bouy arriére
Wawaaw le roi sans couronne 😂😂😂
Deukk bii raféte neuh Mâchallah 🔥✌️
Siteu Siteu leu❤🎉
Siteu rek loway ame tèle ❤
Yalna na yallah sammo
Belle image ❤good job one love 🥰
Iaow rek laniouye topou le roi👑
Machalla belle endroit et paisible
Il mérite un cachet de 200000000😢😢
Saway gnou wakhanté deugue cachet bobou gnou fay lako pour nguay daw rk xana promoteur bouguou gnou Lou bakh tmt
Siteu seul ❤🎉🎉
Dionewar est très beau c’est une île à promouvoir
Dionwar deukkeu bou rafet
Bly mom la guiss ni 💚
Siteu kasse siteu kasse 👑👑👑❤️❤️❤️❤️
Fier de toi frère diam ju sakh dak thi yow yalbine❤❤❤❤❤
Bravo Lamine liguey bi rafete n'a com d'hab
Macha alla le rois des arenes ❤
Lutte tv ❤❤❤
Siteu a vendue Dionewar, vraiment j'aime Siteu c'est un exemple.
Sietu rek lanioy topou ❤
Roi des arènes dé😂 dégue rék ngathiy am😂😂😂.Lac3😅
Yalmine❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Manchalla roi biii
We love it keep it on ❤❤❤❤❤❤❤❤
Dionewar pourrait être une bonne destination touristique
Siteu seul ❤❤❤❤❤
Le roi👑siteu kassè👑👑👑
Merci.siteu.long.lif
Siteu kassé ❤❤❤
Le roi des arène ❤
Siteu mogui daw ba lègue 😂😂😂
Le roi des arènes 😂👑👑
Siteu Thiak Thiak le Combat Royal Guey Daw Tu es Un Comédien
Le seule celibrité au SÉNÉGAL que j'adore ❤❤❤❤ Yalmine bi mala beugue ba xamko
Lamine fane yii da takhaw ba amoul combat diniouka neubb
Machalla
Siteu sa souné❤
The best
Yal dawe nioneware😂😂
❤❤❤❤❤
Yalmine bi le roi👑
Dionwar village natal
Siteu késsé ❤
mais dionwaar rafett neu dh ak gnaari ndox yi sekh gedj bi nii
fii diar na visiter dh
Borom deuk bi le roi👑
Lamine seck c le meilleur de tous les temps
Fans diouteul lo yi meunougne la beugg nkh ya wèr sèn mbeur si digeu ndakarou nokou dane.😂 ay yal daw yoyou yeup amoul chance may nagne lèn lolou 😂
❤❤❤🎉
Lamine mi dina am combat dè😂😂😂 🦾
Rafen na
Nit kou baax la deh siteu kén meunoula yakheu diamou si yaw
Ya doumeu doudou lo séytanéyii Niola khékhe
Lac3😂😂😂😂
Sista guriyalla boule faté sama dara
❤❤❤❤❤❤❤❤🎉👍👏👏
Yal daw dol rek 😂😂
Lofi dèf amal diom
Le nouveau Rio et la
Hey ki ki kane la Yaldaw😂
Je vous êtes comme bon tout sénégalais.Ta vision est bonne.Mais améliore ta manière de lutter en tant que sérère.
Fans Modou lo yi nirou guen sen mbeur si bone khol 😂
Lamb dji diexna fair-play way
Dionware raffêtte neu nak . Mai yaldawe sakoulle talibè ak yarre ak diome bayi dawe bi nak
Siteu rék
Capitale Diamaguene Dionewar
Yaldaw😂😂
Barri wakhe mana daaw 😂😂 yaldaw bi 🏃🏿🏃🏿🏃🏿
sen mbeur bi gnou niaf ndeim ba paré dane ko moy meti nday sen boune yi🤣🤣🤣🤣
@@ousmanesarr756 mame yaroul waay teé baayi saga. Bakhoull mais félicitations pour votre victoire.😂😂😂😂
Balla gaye sa papa leuh doussa morom .
Kikan la Thiak Thiak bi Aka niak diom
Yaldaw 😂😂😂
Wa mod lo yi ba adouna di touki dougnou beug siteu xam nagn lolou sèn xol mo nèkhoul nkh boy bo dalèn nokou dane 😂😂nena l a bi dou yoyou dee😂
lolou moy xasane sén xol frr diarroul nga léni tontou prck sén mbeur la Siteu niouss dane ko😂
Legui ta oublié diamagueune
Do lidienti sa kogne tei bayi seytané hana amo village natal goor dou rambarh wy ll diekoy djiguén leu
Mamalamine hana nekatul Lansar fénioul fennn si lamb Siteu yi
Nn
Siteu a vie👑👑👑
Kone nangoul sa défaite bii ta xamni Yalla ko dogale nonou
Na am diom té bayi daw yi
Wa diameguen siteu legui mou balén
Yow nafekk nga meun nga tass deug fi koufi nek amnga deuk boy titaro bou Dakar done takeu fangay gnibi bayilen diakhassé
Do lidienti sa kongne tei bayi sétané hana amo village natal goor dou rambath
Tiak tiak
Lamine yaldaw 😂 romboula fofou 😅
😂😂😂😂
Gniaakeu ngéne xorome
❤❤❤❤❤❤❤
Lutte TV ❤❤❤
Yaldaw 😂😂
Siteu kassé ❤
❤❤❤