Pape Diouf est le seul artiste bo khamni kene meussouko dégue si lou niak fayda latté woul fene yarou na yaatou na bakh meuneu wooy album bumu guéné ngani mo dakk bi djitou machallah dila nianal rek yalla mayla goudou fane ak werr yokou la banga yekk ko lakk la fou yakk yégoul album bi diar fa yenene yii dane diar si barké naby psl Seral nga sama xol pape khamatouma sakh lumay wakh Bonne chance pour la suite Yalna si disque d'or topou allahouma amine
@@sonkowalabakane5340 deugleuhhh awma loumathie tekk ndakh doungen diougué thie dima choqué vous êtes tellement bêtes et tellement ridicule africell ak xbet xamna dougnou sponsors pr ta gouverne soirée Europe bi table 2000€ billet yi diekhna acharnement ak méchanceté bi thie koulen defoul Dara la xamoul louko waral
Ce dont je suis sûr est que pape Diouf fait partie des meilleurs chanteurs de mbalakh, wayobe leu rek , hawma louko nit di Khasser mais doussi weyyyy ak nango ligueyyyyy . Il est pétri de talent machallah le song est trop bien
Woooow ✨ très très belle chanson lii ( Ger ) Sénégal yeuppa wara bolo deff pétitions Album master-classes ( Écoutez ) magnifique et purement sénégalaise Machallah loumou weuy mou nekh Ndanaan yombou humble simple mais surtout la constance Un grand merci à Pape Diouf 👏👏👏
Avant maye nek fans wally pape diouf rek la done deglou c’est pour cela je l’aime toujours content de ton retour et ton album est une réussite machallah nekhna ❤
Machallah j’ai écouté les morceaux qui sont déjà disponible sur les plateformes mais sincèrement pape diouf à beaucoup travailler dans cet album 💿 côté paroles et mélodies Machallah laff bouche 👄 l’album est cartonné ❤❤❤
❤️😭 Sama yaram Dawna walahi Pape Diouf il chante très bien aussi musique dafa am Armoni Li Moy musique j dit merci encore une fois car il lance message Merci beaucoup vraiment aussi ses musiciens Meilleur Album de l'année ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Guisouma kou Daxa way pap Diouf Sénégal 🇸🇳 bamou Dath nak ki C le meilleur chanteur Sénégal Apar youssou ndour Thion Séck omor pen Ndongo Lo ✅guisouma kouka daxa way Sénégal 🇸🇳 😊
Félicitations pour votre message positif c'est important qu'on sache la valeur des guéwélllllll Bravo pape fière d'être guéwélllll💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿🎅🏿🎅🏿🎅🏿🎅🏿🎅🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿👊🏿👊🏿👊🏿👊🏿👊🏿🙏🏿
Félicitations pape diouf sa fanes depuis louga ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🤣🤣🤣🤣♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Nekhoull ba nehoull nakk mais pape daflenn dakka wayy daklenn binde yallla hamnako. Andou guérr ak gueweul moy horom si thine yala na jam yagg way🔥 Clip de l'année 🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Merci de nous avoir rendu hommage💋💋 mais yennn gueweul yi Ken dou yennn ! Ki bayii baham di wah sa bahh Ken guenoukooo! Machalah yalna diam yagggg !!! Merciin pape diouf
Pape Diouf merci de nous avoir remis sur le bon chemin de la music.on écoutez que du bruit.des textes zéros éducatifs.dans réactions pervers et indigne dans notre société qui est le Sénégal.tu nous a donné une très belle cadeau de fin d'année.à part Youssou.tu es la relève.tous le reste ,c de la médiocrité.grâce a toi et Youssou ,nous allons revivre une très belle fête de fin d'année.les autres allez apprendre a chanter.vous ne faite que du bruit
Vous faites mes journées pape Diouf j’écoute depuis tjrs tes chansons en boucle quand je suis triste ,contente bref dans toutes les circonstances ou je me trouve Merci infiniment yalla doli same
Sagu Pikin la Paab Juuf on est fière de toi Paab keen du la dégg ci ay detail respecte boppam ak ay fan ni rekk liggéey rekk moo am solo lo géen mu neex maasàllaa ndam rekk.🔥🤝🏿😎
Au debut 0:18, ce que la dame dit est très grave Limou wax moy domam dou seuy ak khalé bi car gno bokk benn weneu bougnou naampe c’est-à-dire Guewel ak Guer dougnou seuy c’est grave de voir cet esprit en 2022
Très professionnel Jolie clips mélodie sonorisation correct j'adore je aimé validé pape Diouf félicitations dû courage et wally et père youssou le King offf ndour
Super chanson Mr Pape Diouf toute la communauté Guer té souhaite la meilleure dans ta carrière musicale kéneu dou yaw si mime rew ak si bitime rew ❤❤❤❤
Vraiment Vraiment pape diouf cette chanson nous a rendu tellement heureuse en tant que guër mais la relation entre guèweul et guër c extraordinnaire yalla na diam yague way
Pape Diouf est le seul artiste bo khamni kene meussouko dégue si lou niak fayda latté woul fene yarou na yaatou na bakh meuneu wooy album bumu guéné ngani mo dakk bi djitou machallah dila nianal rek yalla mayla goudou fane ak werr yokou la banga yekk ko lakk la fou yakk yégoul album bi diar fa yenene yii dane diar si barké naby psl
Seral nga sama xol pape khamatouma sakh lumay wakh
Bonne chance pour la suite
Yalna si disque d'or topou allahouma amine
Wayé amoul buzz amoul sponsor amoul concert boumouy teug hors dakar ndax amoul public yala def limouy defff senegal gnepp khamnane bane artiste moye teguélé semaine di dor concert t day fesss
C mon artiste préféré
@@sonkowalabakane5340 🤣🤣🤣 sheutt yaw mi wero deihh legui dal ken meritewoul deg Lou bakh dof ngen dof ngen Bone ngen guenal thie linga neih
@@ano-lc4ky antouka lima wax amoul lossiy tegui
@@sonkowalabakane5340 deugleuhhh awma loumathie tekk ndakh doungen diougué thie dima choqué vous êtes tellement bêtes et tellement ridicule africell ak xbet xamna dougnou sponsors pr ta gouverne soirée Europe bi table 2000€ billet yi diekhna acharnement ak méchanceté bi thie koulen defoul Dara la xamoul louko waral
Très belle mélodie, toutes mes felicitations
Ndanane faye
Merci infiniment
notre faye national
@@papedioufgroup ay way sama chateur prefere bi❤️
Billahi ay mélodie you tok morceaux kakanlé mom c autre choses
"Félicitations" Pape Diouf & La Génération Consciente sou weuyé ngani waw music expérience yalna gnou yala défal ndam si album bi inchallah jajef
Ce dont je suis sûr est que pape Diouf fait partie des meilleurs chanteurs de mbalakh, wayobe leu rek , hawma louko nit di Khasser mais doussi weyyyy ak nango ligueyyyyy . Il est pétri de talent machallah le song est trop bien
Chapeau pape diouf je suis faramarene. Me dama beugue nittcou am kolere parol you riche te noble yalla na sa diam yague😍
Woooow ✨ très très belle chanson lii ( Ger ) Sénégal yeuppa wara bolo deff pétitions
Album master-classes ( Écoutez ) magnifique et purement sénégalaise
Machallah loumou weuy mou nekh
Ndanaan yombou humble simple mais surtout la constance
Un grand merci à Pape Diouf 👏👏👏
FÉLICITATION PAPE NIVEAU BI KAWÉ NEU MACHALLA
Bilay do moromou bën khalé
Yafi way Guer yi dh Bilay walay na Sa diam yague Gueweul ak Guer danio yague koulay Tagual say mame amo fayal❤❤❤❤
Seul les coneseur ecoute pape brave homme
Bilahi ki mo mane Wally si ay woy
Le meilleur artiste de sa génération ❤❤❤Je t’aime Pape Diouf
Avant maye nek fans wally pape diouf rek la done deglou c’est pour cela je l’aime toujours content de ton retour et ton album est une réussite machallah nekhna ❤
Lénéne laniouye wakh wayé dou ay weuye. Bonne continuation
Machallah j’ai écouté les morceaux qui sont déjà disponible sur les plateformes mais sincèrement pape diouf à beaucoup travailler dans cet album 💿 côté paroles et mélodies Machallah laff bouche 👄 l’album est cartonné ❤❤❤
Moi je l’admire sérieusement Dafa yarou aussi doko dégu si dara sérieux nak référence gua et aussi il chante bien bonne continuation
❤️😭 Sama yaram Dawna walahi Pape Diouf il chante très bien aussi musique dafa am Armoni
Li Moy musique j dit merci encore une fois car il lance message
Merci beaucoup vraiment aussi ses musiciens
Meilleur Album de l'année ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah jolie 🥰 ❤ clip une très belle chanson 🎶 j’ai adorée bakh nga yarou nga way rek😂 nga def ❤❤
Un artiste cool , clean et responsable. Jamais dans des détails toujours dans son boulot.
En avant
C'est l'un des meilleurs musiciens d'Afrique... Professionalisme🙏🏾
Personne je dis même youssou le doyen n'a jamais pensé à nos vaillants GUERS, pape merci tu as chanté pour tous griots ayant des GUER
Afrique occidentale francaise ( AOF) kay yafi dakh way inchallah
Guisouma kou Daxa way pap Diouf
Sénégal 🇸🇳 bamou Dath nak ki
C le meilleur chanteur Sénégal Apar youssou ndour Thion Séck omor pen Ndongo Lo ✅guisouma kouka daxa way Sénégal 🇸🇳 😊
Très humble Impossible de ne pas l'aimer.
🎉🎉li nekhna trop 😊😊😊❤
On sais bien kou neck ak kouy sa papa tu es le meilleur ❤🎉
Album mom yako geuneu néxlé Wally 🎉🎉🎉❤
Macha Allah sougnou serere bi ont t'aime beaucoup fier d'être sérère
Félicitations pour votre message positif c'est important qu'on sache la valeur des guéwélllllll
Bravo pape fière d'être guéwélllll💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿🎅🏿🎅🏿🎅🏿🎅🏿🎅🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿👊🏿👊🏿👊🏿👊🏿👊🏿🙏🏿
Gniako donne woroul
Geuweul Kay amoul valeur
Félicitations pape diouf sa fanes depuis louga ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🤣🤣🤣🤣♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Très belle chanson thiéy pape diouf bo woyé khé yi si yousou ma djiguéne laf rhiat
Des cœurs ♥️ pour génération consciente
Ndaanane pire pape Diouf un grand mr way bii nakhna trope bilay mais duo ak titi la beugue ❤
Nekhoull ba nehoull nakk mais pape daflenn dakka wayy daklenn binde yallla hamnako. Andou guérr ak gueweul moy horom si thine yala na jam yagg way🔥
Clip de l'année 🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Liii forna way ❤
Le meilleur de sa génération par sa qualité de musique ses sonorités et sa splendeur, Pape continue de nous régaler ! Bon courage pour la suite
Bilahi wakh nga deugue Pape Diouf dou moromou Waly Seck 🙏🙏
Merci de nous avoir rendu hommage💋💋 mais yennn gueweul yi Ken dou yennn ! Ki bayii baham di wah sa bahh Ken guenoukooo! Machalah yalna diam yagggg !!! Merciin pape diouf
Bilay mo meuneu way diouf
Pape Diouf merci de nous avoir remis sur le bon chemin de la music.on écoutez que du bruit.des textes zéros éducatifs.dans réactions pervers et indigne dans notre société qui est le Sénégal.tu nous a donné une très belle cadeau de fin d'année.à part Youssou.tu es la relève.tous le reste ,c de la médiocrité.grâce a toi et Youssou ,nous allons revivre une très belle fête de fin d'année.les autres allez apprendre a chanter.vous ne faite que du bruit
Bilaye lii neena, machalla,un beau clip, avec des tenues traditionnelles magnifiques, machalla laff thiatte, bon courage pape Diouf, dieureudieuf.
Album bi nexna trop yalla nala yalla lafal thiat pape diouf
Pape diouf dara diomouko yarou na mana way ba degal li rek ya meune way
Machala dioufa ngokhobaye défatinga sa meunine
Waouh tu tape fort domou pikine bi yalna lep barkel inchallah
Demba war tu as bien assuré les jumeaux prince AK momar aussi machala nice clip
Neeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeex na loooooooooooooooooooooool Pape. Ndundal yu yag te yiit am wër. Merci.
Mane son bi souma rayoul rekkkk ohhhhhhhhhhh j'adore pape diouf guoudal fane son bi nehna
Tu es le meilleur . Ambiance,les paroles ,tout est carré .
Les fans de Waly😂😂😂 wakh len sen waykat mou dem bongo
Eh li nekhna way
Pape Diouf meilleur chanteur au Sénégal après Youssou Ndour ❤️🙏
Félicitation pape diouf de nous avoir rendue hommage ❤ 🎉🎉
Tres bell chanson
Parole d'un Meloman
Tres riche d'enseignements
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Vous faites mes journées pape Diouf j’écoute depuis tjrs tes chansons en boucle quand je suis triste ,contente bref dans toutes les circonstances ou je me trouve
Merci infiniment yalla doli same
Bilay nioune guér yi content nane 😍😍😍
Sagu Pikin la Paab Juuf on est fière de toi Paab keen du la dégg ci ay detail respecte boppam ak ay fan ni rekk liggéey rekk moo am solo lo géen mu neex maasàllaa ndam rekk.🔥🤝🏿😎
Gnoune guer yeupe nagnou diouke maye pape Diouf nice 👍 machalla ❤❤❤❤
Ya donou sa mague yi d continue comme ça rek boul dokh si bena détail ligeye rek moy fay fait comme ton idole you le king 👑
Pape wayobeigua ….nioune gueweul yeup sagounaniou way pape way ken gueunoula Machallah
Le meilleur de sa génération 🥰🥰
Rien à dire il est juste le MEILLEUR 👍👍👍👍👍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
En tant que Gueweul❤️et fier ça me va droit au cœur❤️
Machallah liii nekhna pape diouf sama fans bi way rek gay def yalana sa diam yague😍😍😍😍😍
Machaallah Pape Diouf clip validé
La voix de pape diouf me tue come-back with another nous conse
Album de l’année vraiment album bi song yeupou Nice ❤️❤️
Wayli wayli ngeu Lo wakh mou nekh yalla nassa jaam yagg diouf❤je t’aime fort 🎉
Bravo guerr yi Contann nane ci lii❤❤❤❤❤❤
Pape Diouf Trop Cool ce Mec❤
Je suis le numéro 1
Pape Diouf ya meneu way Kar Machallah...🙏
clip trés traditionnel , réalisation cool
Au debut 0:18, ce que la dame dit est très grave
Limou wax moy domam dou seuy ak khalé bi car gno bokk benn weneu bougnou naampe c’est-à-dire Guewel ak Guer dougnou seuy c’est grave de voir cet esprit en 2022
Très professionnel Jolie clips mélodie sonorisation correct j'adore je aimé validé pape Diouf félicitations dû courage et wally et père youssou le King offf ndour
Machalla machalla li nekhna
Machalla way Pape diouf c’le meilleure ndandane❤❤
Franchement une mélodie de ouf félicitations tonton pape Diouf
Ha machallah une très belle chanson niogui xarr grand théâtre d hinchaallah
Toujours comme d'habitude, toujours égal à lui-même diarama Pape Diouf et bonne continuation.
Thiey tonton pape Diouf toujours égal à lui même ❤️🥳
Vraiment pape tu as bien travaillé ton album
Félicitation Pape c'est du lourd 🔥🔥🏆
Machallah Pape clips bi Nice na trop
Machalla 😍🙏❤️🙏 pape Diouf album bi nèkhna trop bilaye ❤️🙏
Jai ecoutez tout l.album mais vraiment pape ta bien assuré je pense k c le meilleur album de lannée macha allah
Yafi neh ❣👍vrement on est content de toi siguiil gaagniou liguey bi rafett
Félicitations pape diouf
Ohhhhh ki dou nitt wayy
Cet album est extraordinaire. Pape tu es le meilleur chanteur. Bay demba todj na fi !
Super chanson Mr Pape Diouf toute la communauté Guer té souhaite la meilleure dans ta carrière musicale kéneu dou yaw si mime rew ak si bitime rew ❤❤❤❤
Le meilleur machallah pape
Machala li nékh na pape diouf liguéy gua deug
Rien n’a dire machallah 😍té chanson sont superbe 🤩🤩🤩li nékh ma way 🥰🥰❤❤❤❤❤
Vraiment Vraiment pape diouf cette chanson nous a rendu tellement heureuse en tant que guër mais la relation entre guèweul et guër c extraordinnaire yalla na diam yague way
Félicitations pape ❤
Machalla yalla na yalla wéral bate bi
Mancha allah félicitations papa dji defatigga sa meunine bilahi li dafa fessssss❤😊
Mes respect a la génération du consiance c’est ça l’image du Sénégal
Vraiment tu es la meilleure artiste au Sénégal machallah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏💪💪💪💪💪💪🦾🦾🦾🦾🦾💪💪💪🦾🦾💪💪💪💪
Machalla Pape Diouf
Je suis Mauritanien me l'album c très cool je l'écoute multi fois
Je suis fans de wally seck mai pape Diouf bilahi dafa meun weuy rafete khôl yallana sa diam yague weral baye bi