صحيح الشيخ منتقى حفظه الله ورعاه أسن وأفضل منك وأكثر علما وأقرب إلى الله لا تقارن أنت به في أي شيء وهذه التعليقات الغامضة الكثيرة لا ينبغي أن يصدر منك عد إلى رشدك. Bayilen commentair yi seringe mountakha dou sén morom si dara.. Wayé wayé dji barina té amoul solo ah
Maan deh bima seetaaneh video serigne mourtada aam naassi louma meetti trop ndakh dafa melni serignebi laay dankaafou nguir mou baña foom magagui,ta serignebi moom khame na limouy def bou weer ta lou beug rek dañouci wara and ak moom.Yeen naak soungueen amer guiss bou rafet ngueen wara deem baci moom wakhtaan ak moo mo gueun.waaye di wakha ci media guenoul ndakh kou neek aak famouy degue.cheikh abdoul ahad bimouy mouride voteloul abdou diouf wor nga serigne touba ,li eup ci mourodeyi dañou dieufe ndigal ta keen guenoul di wakh.yeen soortie you bari yi khew ci yoon wi ta amoulwoon moo taambili di maay khaleyou bari fiit kou neek di wakh ak di critiquer,mais naak leeral yi amna solo.And dellou ci ak taalibe comme mame cheikh ibrahima fall .
Li Serigne Mourtada li pou waxx werr la té nii eup si mouride yi lolou laniou guiss .il dit Claire que sunu kilifa yi li niou wax yeup defnagnou ko .té yaw minane nakhari nala fofou ga wara degué
ko khamené yilifo yoon wi yoro batou yone wi lo wax sa bopou la engagé wayé engengé woul yonn liy deug moy teugousi ndigeul tey bania djitou serigne bi si dara wayé yanou saff rek takh lay ratti raty ba awx lou eupou nioune magal gui ak lénén mosi yam dara amalou niou ndiarigne loudoul digeul mais dano soff len li ken khamoul loumiy nirou wala sen projet adya bi moy si magal c abdou lahat bi molen metty
Yen mom wax deugu yalla daguèn soff surtou yaw s.amsatou waxi doff rek ngay deff s.mourtada mom tamit waxi doff layy deff eupolen fi ken xam xam s.mountakha ñimou dënk liguey bi maté nagnou ko yawmi ya warou ligueyi té bayi lou nieuw nga beugu si wax
Gaayi douñou nougou deug ndakh faar ,ñii liñiy def tegouñouko feen serigne sidy miiy seen kilifa douko deef ta douko wakh ,diaaple serigne mountkha mooy diko diokh adiya mou defko ci limouy ligueyeul serigne touba moo guen ,neek ci media di wakh ak di laayi ak di woote fiitna ak tour aay deret ta serigne touba wakh saa nafssine bilaa dararin.
liy deug moy di teugou si ndigeul tey bania djitou serigne bi si dara wayé yanou saff rek takh lay ratti raty ba awx lou eupou nioune magal gui ak lénén mosi yam dara amalou niou ndiarigne loudoul digeul mais dano soff
Macha allah yall nanou yalla takhawoul popam si barkep cheikh amdi moustapha
SERIGNE TOUBA Rék rekkk Rék fall 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Dieuredieuf Mbacke wakhdjii rafetna Machallah dieuredieuf borom Touba
😟😟😟😟😟😟😟😟😟😟😟😟warga no yerem dh mom say Dioumté Barry n’a loll yalla d’où rayall Kene nonam 🙏🙏🙏🙏🙏🙏👍👍👍👍🙏👍👍👍
Machallah diaradiaf mbacke goudal fan looool tawer barke c a ahad
Yalle nafi yague te wer mback
Dieuredieuf Mbacké Yalla guafi yaaaag looooool té wére
كل من يستطيع الوصول او الجلوس مع الخليفة فالأفضل أن ياتي الي الشيخ ويترك الإعلام وسيأتي يوم تكون او يكون أخوك الخليفة وكما تدين تدان
صحيح الشيخ منتقى حفظه الله ورعاه أسن وأفضل منك وأكثر علما وأقرب إلى الله لا تقارن أنت به في أي شيء وهذه التعليقات الغامضة الكثيرة لا ينبغي أن يصدر منك عد إلى رشدك.
Bayilen commentair yi seringe mountakha dou sén morom si dara..
Wayé wayé dji barina té amoul solo ah
Lima xam moy kepou koufi yalla tek nga woutou serigne touba nan mase deklou la lo wakh boun xalaat boun ladje nan def linga wakh rek
وانا بصراحة احب سيدنا حمزة بك وسيدنا مرتضي بك واكن لهما الاحترام والتقدير واتمني لهما ترك الاعتراض مطلقا ولو بباطن وسلب الاختيار لحسن الظن
ماشآء الله
Yene yena yakh Touba rek sene intere cassé Serigne Moustapha bassirou mbacke nimou topewon Serigne Abdou lahat mbacke gnioue khamnagne Léo yen dolen dara
Maan deh bima seetaaneh video serigne mourtada aam naassi louma meetti trop ndakh dafa melni serignebi laay dankaafou nguir mou baña foom magagui,ta serignebi moom khame na limouy def bou weer ta lou beug rek dañouci wara and ak moom.Yeen naak soungueen amer guiss bou rafet ngueen wara deem baci moom wakhtaan ak moo mo gueun.waaye di wakha ci media guenoul ndakh kou neek aak famouy degue.cheikh abdoul ahad bimouy mouride voteloul abdou diouf wor nga serigne touba ,li eup ci mourodeyi dañou dieufe ndigal ta keen guenoul di wakh.yeen soortie you bari yi khew ci yoon wi ta amoulwoon moo taambili di maay khaleyou bari fiit kou neek di wakh ak di critiquer,mais naak leeral yi amna solo.And dellou ci ak taalibe comme mame cheikh ibrahima fall .
Bilay kou bakh
bayilen diaxase
Wakhgua lepp dh waw goor
Abdou gni boulaine di totou
@@abdouahadahad4235 fii keen diakhassewoufi fi serigne mountakha moofi neek kilifa keen warouko djitou ci dara walla diko djiema araftou,kazu radjiap serigne abo bimou djiotte ndigal tegou ci baat ,dani serignebi soiniwoon boulen magal sakh ken douci teek baat,yoonwi waroula aam activiste rawatina aay kilifa.Nañou noopi taay deglou serigne mountakha taay dieufe ndigal auto been chaufeur lay aam.
Machalla mbacke, serigne hamsa léér na
Yen djoxo len serigne mountakha theur
wawaw santa serigne touba rek
Dierediefati Mbacke Yagüe fi Loll té wer ak mbolem Taloube yepou sí barkep xassidayi
Li Serigne Mourtada li pou waxx werr la té nii eup si mouride yi lolou laniou guiss .il dit Claire que sunu kilifa yi li niou wax yeup defnagnou ko .té yaw minane nakhari nala fofou ga wara degué
Wawa amna solo de
أعوذ بالله من الشيطان الرجيم..الحمد لله رب العالمين
Bayi leen wax dji ak waht ahp yi bakh n'a ,lingay wax do dara
yeen site web yi buleen niou sonal way tamite waax leen lu epp solo ci yoon wi wara ngen noppi details yi bari na lool leegi
Diereudiefeti serigne touba kena dou mome
Diueruediuef Mbacké nila rek yakh kat yi la rek lep dina leer
Borom séne bi sokhla naa numérom de djambar la migui liguiyal cheikh ahmadou bamba
War guena bayi watshap bi dh bilahi. Xo tihe seringue ahmaou rafahi
Yawmiy wakh s amsa lou niaw nala ler ny wa keur seringe by nieppou nga ko wakh koubakh la yalnafy yague loool te werr
Machallah
Wakhdji mome li serigne mourtada wakh kouko dieumale si serigne mountakha danga dioum mande bimako deugue wornamane serigne mountakha takhout tontouyi fimou egue manone nafa bagnia egue kou dieugue wakh khamne wakhdji etabi motakh nanou teye te andak yar dara tanewoukosi mangui dieugalou boubakh di toupe
S moustapha bassiroi lébaloul li Sa baye s a ahad kone danguéne wara topé
Wakh dji khéw légui dal si yone wi,kén rafétlouwouko
Diaradiaf mbakce amna solou ni rk lofi xiwe rk dem léne wakhkou serigne bi moye youne tabayi sayetani yikou waar di féne rk dakh xaliss bi maky sall di léne diokh nion serigne touba monoye téral
ko khamené yilifo yoon wi yoro batou yone wi lo wax sa bopou la engagé wayé engengé woul yonn
liy deug moy teugousi ndigeul tey bania djitou serigne bi si dara wayé yanou saff rek takh lay ratti raty ba awx lou eupou nioune magal gui ak lénén mosi yam dara amalou niou ndiarigne loudoul digeul mais dano soff
len li ken khamoul loumiy nirou
wala sen projet adya bi moy si magal c abdou lahat bi molen metty
Yen mom wax deugu yalla daguèn soff surtou yaw s.amsatou waxi doff rek ngay deff s.mourtada mom tamit waxi doff layy deff eupolen fi ken xam xam s.mountakha ñimou dënk liguey bi maté nagnou ko yawmi ya warou ligueyi té bayi lou nieuw nga beugu si wax
yaw ya khamadi ngamane seurigne bi wakhi dof lay wakh ya rew
Dagueine soof trop demlen wouti talibé mo gueune. Serigne mountakha doussa morom.iow ak mourtala amoulén talibé. Liguen di wakh tégou lénko fenneuh reww rek molén diapp. Nioune mom dounou ay dof khamounou kou sant mbacké khamounou kou sant diakhoumpa wayi nioune ak talibé lanou kham. Iow amsatou iow yaa gueuneuh soof nieup
Gaayi douñou nougou deug ndakh faar ,ñii liñiy def tegouñouko feen serigne sidy miiy seen kilifa douko deef ta douko wakh ,diaaple serigne mountkha mooy diko diokh adiya mou defko ci limouy ligueyeul serigne touba moo guen ,neek ci media di wakh ak di laayi ak di woote fiitna ak tour aay deret ta serigne touba wakh saa nafssine bilaa dararin.
liy deug moy di teugou si ndigeul tey bania djitou serigne bi si dara wayé yanou saff rek takh lay ratti raty ba awx lou eupou nioune magal gui ak lénén mosi yam dara amalou niou ndiarigne loudoul digeul mais dano soff
Kii mome dafa sofff véram yii mélni ap deumbou
Astaxfirul lakh rafé talal lingay bine ki kilifa la sëtu s bi derect
Yaw ay teguin loum la mayou xagn lako.yarou baxna lool.
@@bayefassdianetv6975 lane moy seut ak setou seg bi loumouy diarigne walla loumouy wagni bou diaroul si deug domi yonent mogui safara bayou yonent naka nonou faléwmako
Yaw lousi sa yon niom ay bokoulan
@@bayeniass121 iow kay laay wakhe lousi yone ndakhe mak mome nio bok mame mor anta saly ta iow niasse nga sante