Mashalah un msg fort en ce qui concerne les baye Fall😍😍 leur noblesse, faire la quête pour ensuite distribuer aux plus démunies... sans attendre rien en retour
Cette série nous apprend beaucoup de choses seuls les doués d’intelligence en tireront des leçons... Famille bo dem nit gni tolowougnou dollé ki day niak khebu au départ kenen ki yalla mey ko après si dir bou guate yalla mouna defal teranga ki niakone am Histoire ngor et la famille de Pathé en témoigne beaucoup donc toi qui regarde cette série boudé yalla sala defal teranga boul kheb ken partage tes bien avec ta famille boudé yi tamite yalla mey guoula Boul ignané keneu batoit ne baisse jamais les bras ton heure va sonner Et pour terminer yalla naniou borom bi mey soxnna bou melni adja car le bonheur d’une famille dépend de la femme
Dewenati balma ak balnala yalla naniou yalla bole baale, amine defal gniou koor bou sele bou gniou nangou te yalla dieguel gniou sougnouy bakkar. Yii djitou ak yii nieuweugoul yii neubou ak yii fegn
Di nianal gni daan suivre série Adja te yalla dieul sen bakan yalla yeureum lenn te khare lenn aldiana firdawsi 🤲🏽 ak mbolem waay dawlou yepp barkeb weer bou sell bii🙏🏼
Qui comme mane beug série bii amate...? Meme sii Bou féké amna loufii diota am 🤷♂️et c’est le passé 👊🏾 bly manqué guen niou sakh j’espère que diguen guss sama mess bah deff différence inchallah ❤️on vous aimes bcp
Franchement Adja le rôle que tu incarne dans cette serie n'est un rôle chez vous mais votre être c juste la manifestation du bien en toi, tu me rappelle une Femmle: Ma mère merci.
Adja est une femme exemplaire qui est d'accord ♥️💯🥰
Moi je suis vraiment très contente ♥️🌹❤️🌹💔💋❣️💯🥰😍🤩💯🥰😍🤩
Moi
@@dieynabandiaye5913 suis d accord av tw💕💕💕
Tout le monde est d’accord 😌😇😍
Adja mo tané biddew adja khol bi dara nékousi
Mashalah un msg fort en ce qui concerne les baye Fall😍😍 leur noblesse, faire la quête pour ensuite distribuer aux plus démunies... sans attendre rien en retour
Amnafi
Qu’Allah accepte nos jeune et prière
Ramadan Mubarak a tous 🌙🍀♥️
ramadane moubarack
a vous aussi
Amineee
Amine et a vous aussi
Amine yarabi
Franchement avoir une maman comme Adja c'est le comble. Cette chance de pouvoir discuter avec sa maman ❤
C'est comme ma mère Sophie je les j'adore❤❤
N’aime tu pas ta mère ?
J'en est une comme elle machallah
Je ne dit pas k nite bayé woul ni mais li niouy jouer dou deg fiction la
Geumo sa yaye
Kou sopp naby beuseul j’aime 🥰🙏🏿❤️
Wawaw yoguini
🥰💔🌹🌹🌹🌹🥀🥀🥀🥀❤️❤️❤️❤️💕🎊🌸🎂🎉
Aleyhi salatou w selam
nous sommes la
SAWS💘💘
Dougou tigui migui yakk sama vie😂😂😂😂😂😂😂😂wouyyy dioguay badolana aye Yallah mignou sakk kéne meunoufi ndogou en paix😂😂😂😂diam si yéne.
Nnbndo7t6rjxbbx02649nnxnnfkokkwydlwk83lkfnf0tb🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉😢😢😢😊❤😅🎉🎉😢😂😅😮😢kdlfnnwidkn
Cette série nous apprend beaucoup de choses seuls les doués d’intelligence en tireront des leçons... Famille bo dem nit gni tolowougnou dollé ki day niak khebu au départ kenen ki yalla mey ko après si dir bou guate yalla mouna defal teranga ki niakone am
Histoire ngor et la famille de Pathé en témoigne beaucoup donc toi qui regarde cette série boudé yalla sala defal teranga boul kheb ken partage tes bien avec ta famille boudé yi tamite yalla mey guoula
Boul ignané keneu batoit ne baisse jamais les bras ton heure va sonner
Et pour terminer yalla naniou borom bi mey soxnna bou melni adja car le bonheur d’une famille dépend de la femme
J'suis guinéen. J'adore série adja mais, surtout ce Mr qui s'appelle Diogoye là. Lui,j'l'aime énormément wallah!
Yamal sa deuk
@@usaboieusa5293 ayway boul def lolou
Sayata yato 🤣🤣
@@221pro3 dagno soop katt mouy traverse frontière ni
@@mouhamedhdiouf434 youpoudé😂😂
Dewenati balma ak balnala yalla naniou yalla bole baale, amine defal gniou koor bou sele bou gniou nangou te yalla dieguel gniou sougnouy bakkar. Yii djitou ak yii nieuweugoul yii neubou ak yii fegn
Amine ouze yalla na ualla nangou sa niane
Amine dewenaty a toi
Amine niou bo kouko
Amine
Amine inchallah li moye commentaires bou am sollo
La complicite de Adjia et doudou me pleee beaucoup si digeunte yaye ak dome ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️👈
C pas du respect de dire Ta mer des choses comme ça vs pouvez être des amis mais se genre de choses
Salut celui où celle Qui est content pour le retour de Pathé pousse Bleu
Je suis présent
Pouce bleu*
Kou beuge sa papa dem maka beuseul j'aime
Di nianal gni daan suivre série Adja te yalla dieul sen bakan yalla yeureum lenn te khare lenn aldiana firdawsi 🤲🏽 ak mbolem waay dawlou yepp barkeb weer bou sell bii🙏🏼
AMINE YARABI
Amiin sama mbokkou designer bi
Amine,🙏
Amine lou diarra bayi xell
Amine y’a rabi 🙏🙏
J'aime le fait que Héléna bott domam surtout AK seurou rabal bi bariwoul lougnou koy guiss si Série yi déh 💝💝
Une pensée à nos morts
Paix à leurs âmes
✔✔✔
Diogoye d'où changer
Que leurs âmes reposent en paix
Amine
Amin
K'ils reposent en paix tous
Doudou : diougui diougui 😅😅
Diogoye : wagadougou 😂😂
Doudou et Adjia j’aime leur complicité 😍vraiment amour c’est de 7 à 77ans
Adja c'est une femme exemplaire en plus elle porte bien mashallah je t'adore beaucoup❤️❤️❤️
Wkjve🎉😮yrgi😊😂ff❤hlp😊😂😮😢
Diogay nena terenga ak patihanga la niou yamalé😂😂 bilay kou beugou diogay lalal......
Dou diogoye moko wax dh Doudou leu
Khana mourchid tv nguay sétane😂😂😂
😂😂
@@karagueye493 mais dama takone ver😎😂😂😂
@@karagueye493 mourchid moustaph donga fay wakh
le sourire de ADJA me donne de l'espoir machallah.
Mais ndélou👴 Pathé bi nék ci profil vidéo bi nk dolénsi wax 😂😂
Lolou cas leu deh
Ibou ani sen diankk bi Borom seur bou aund bi😂😂😂yarew kouy diokhe drpace bi
😂😂😂
Ayy ibou 😂
Mbir leu dh 😂😂😂
Vraiment dans votre série Adja donne des bons exemples a la société ... Je vous souhaite beaucoup de courage
Yalla nieup am diam si barké Chawrou Rammadan Moubarak bi amine
Meilleure série du ramadan ❤️🥰♥️
Adja elle est franchement belle en plus j’aime bien sa façon de cuisine 🔥🤣😂🤣👍🏿🔥
Ttgggfffffffffffffff❤😂🎉😢😮😅😊❤😂😂
Diogoy le meilleur artiste de sa génération 🙏🖐
🎉❤❤❤❤❤
🎉❤❤❤❤❤❤😊
Bayil commentaire yi ngay lire té sétane série bii 😂😂
😂😂😂bilayyy
😂😂🙄
Doull😂
@Fama Seck barri gua fi morome dh 😂🙄
Iow nak😥🤣🤣🤣🤣
Le frère de Eléna amna fouleu ngen tim lek di wakh rk 😂😂😂😂
Je te jure 😂
Enfin j'avais tellement hâté de voir pathé sene🙈 et je sais k suis la seule😍du coup j'adore cette série de oufff💙
A❤b😂c🎉d😢e😮f😅g😊
NOOO👆SAMA KEUR YALLAH NA MÉL COMME KEUR ADJA RK..,BEURI DIAM...YALLAH NA LÉNN YALLAH DÉFAL DIAMU....BON RAMADAN👏❤À VOUS TOUS🔥MERÇIII
Enfin paté est venu mais on na pas encore vue mamie et bariso 🤣😂🤣😂🔥👍🏿🤣😂😌
Mamie s'est mariée récemment donc bariso sa présence n'aura pas de sens
Walay diogay damako fans🥰🥰yalla defala diam tu es l meileur vraiment walahi
Alima wollah femme mariée dale nii laay mel sol lou diote jtm dale😍
Niom madior lougnouy sikar nekh naa way 😍
Néen deff 😂fans dioguaye yih ak adja🧑🏽🍳 jaam sy yenn way🙏
Amine
Merci
Amine
Mais frèrou Helena bi ni mouy léké aussi dougn si wakh 😂😂😂😂😂
Kikay sérère bou guiss thiébb leu🤣🤣🤣
@@Justin-Lo. Bara Bara Bara Bara
@@amilipsifaye8117 Wlh ware naniou wakh si lékamebi déeeeee
Meilleur série d SN après doomi gainde ki es d’accord
Kou beugue nabil Moustapha beusseul j'aime
Non Hélèna nimouye botté khalébi amna classe.😂😂😂
Dougoutigui déy dougal késsé 😂😂 lékka rékk léy déff 😂
Moma diakhal ak talons yi mdrr
Yalla boumou faux pas sakh dallam yii😂😂😂
🤣🤣🤣🤣🤣
😂😂😂
Merci
Dougouti ya wakh deugg bol sou tégé wé lekeu mossi dess pas wakhtane 😂😂
wahh deugeuu 😂😂😂fan nakoo waay
Vraiment 😂😂
@@mimaaaniang2473 ték bol ba paré di réunion foumou ame🤣
@@theresamendosa1127 moma diahal yenn key lekk lenn ba sourrr dogua wahtanneu😂😂😂moy logik bi
La beauté toxique de adja
La réaction de Madior M as tué 😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣
Waaa Ouagadougou miii😂😂😂😂😂😂😂ba diogoye dioukkk thi iowww😉😉😉😉😉
I really love your drama you guys always make me laugh may Allah guide and protect you all. Watching it from Banjul
Magui len dii nianal kooru diam akk salam sii barke seydina Mouhamed psl amine yarabi
Keep kou abonner yalla nala yalla nankoul sa koor amine yarabi
Amyne
Non srx lima reii yeup balou maléne ko mdrr..... Non dougoutiki ma tué 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Bilay dougoutigui khawnama rayy damah réee ba soneu 😂😂😂
Doigay il change jamais il est jaloux koi 🤣😂🤣😂😂🔥👍🏿
Adja et Diogoye ont fait la réussite de cette série
Wa Pathé diougué maka en plein koor bethieuk en plus mouy bisouwaté 😂😂😂
C pas athieu mé oumra
Khalifa Niasse nena bizou sa soxna aramul si werou korgui mdr
@@amaryngonesobel8500 😂😂😂😂😂fékhél ba boul âme plaisir rek
@@amaryngonesobel8500 mom il a fait un bisou à Helena qui est la femme de son petit frere et à Alima.
Avec Adja il a fait un calin
@@ababacarsadih8030 khana
C’est un discours douloureux thieye Diogoye 😀😀wagadougou ya rita mbollé bol🍲 bi yeup
Vmamszmzmzmzmzzmmzmzzmvbmzz
Lolou lay rëe ba insby bilahii diogaye dou nit
Dama rétane bay dioy😂😂😂
@@amyndionendour6262li kay diarna retan
Fatimata Ba néna ageou chômeur mdrrrrrr
Ana gni namone Pathé séne ❤️✋
Man
c moi
Hey diogay mi amna tokou Djiko de 😂😂😂😂😂😂😂😂
hey les malien 🇲🇱 vois êtes fort hen 😂😂😂😂😂
je vous salue de passage
Balaa nguén di paré Dougoutigi diekhal lekk gui😂🤣😂🤣😂
Dans toutes les séries du ramadan je regarde en premier Adja après Kooru bideew, Ndogouli, Ngagne ak koorgui et le ramadan de Ass c'est tout 😂😂😂
Le ramadan de ass ces dns quels scene
@@asteltraore7571 c'est sur seneflix
Dieuleutina fist waay liii dou chance mérité 😂💃💃💃
Bilae mérite tay moy 3jr 😂😂😂
Khana toguo séne keur
@@absandiaye1158 6
@@absandiaye1158 9
@@absandiaye1158 66⁷est
Nigir dieumi serige touba à bonne léne fi si kourel khassida tie yalla takh 🙏🙏🙏
Ki es d accord diogaye est le meilleur 👋🥰
Moi je suis d'accord
Bonjour à tous est-ce que vous étés d'accord Sénégal le meilleur pays du Afrique mach'alla Adja Adja longui vie à vous ❤️❤️👊👊👏🇸🇳
Non
@@zz-lv1ye pourquoi dis moi la vérité s'il vous plaît
Moi je suis d'accord
@@mormbaye6481 beaucoup d'hypocrisie au Sénégal
😂😂😂😂😂😂😂Alhamdoulilah amoul tardé wayé SAMA yaye mbéthie lama door ndaw série bi daf ma yoni maniko khara série bi diex mou dorma 😂😂😂
😁😁😁
@@Finash_chou 😂😂😂
Le frère de Elena vrai badola🤣🤣🤣🤣🤣
Lekou diam deugu
Yalla na yalla nagou sono koor si barkip Mouhammad 🙏🙏
Amine yarabi 🙏
Amine
AMINE
Adja est une femme tres belle machallah et exemplaire aussi à toutes les mamans adja mane nala beugueu 4real
Diogay nena ki bala Mouy degui Wolof Di naniou Ray 😄😂🇸🇳
Vraiment le retour de pathé sene j'ai beaucoup aimé la série adja sans pathé n'ai rien
Premier may lénea j'aime slvp ❤️
Non 2 sém
Mais khna j’aime 👍 yi day fay
May nala deuileul💝💝💝
@@akarabuzz7473 merci
@@ori-boyzofficiel1233 wawawu😂
Bilay diogaye dinama tue😂😂ou son les fans de diogaye
Machalla toutes les adjas sont ravissantes ❣️ ma fille Adja sama goro Adja j vs lôve💋🥰
Qui comme mane beug série bii amate...?
Meme sii Bou féké amna loufii diota am 🤷♂️et c’est le passé 👊🏾 bly manqué guen niou sakh j’espère que diguen guss sama mess bah deff différence inchallah ❤️on vous aimes bcp
Résspe pour baye fall yi✊✊✊
Billahe nan si guené baye fall yii
@@ndiayemamour9299 waww fall
Walahi
Wakh gua degu
@@aidadiagne9480 bilaye
Gniye weur serie yi di niane j’aime khana legui nek nane millionnaire walla sama bopp Mamé😂😂😂😂😭
Le retour pathé sene
Problème yangayyy démarrer
Pathé ak père dioks dou yombou
Franchement Adja le rôle que tu incarne dans cette serie n'est un rôle chez vous mais votre être c juste la manifestation du bien en toi, tu me rappelle une Femmle: Ma mère merci.
Une très excellente série,
Adja une exemplaire
Vraiment pathé Sene menoul manquer si série bi😍
Ana gni beugu Adja national du😍😍😘😘😘
Épisode 5 meilleur épisode pour l'instant kou d'accord 😂😂😂😂😂😂
Bilahi nak
Dougou tigi il mange mal on dirais que il a jamais manger 🤣😂😂😂😂😂🤣👍🏿🔥
Grave tcheee😂😂
😝😝😝
Dama retane b tiorohane
Bnsr sama team ana gniy bay xel serie adja chaque jour manifestez vous
Billahi woukoudoukou😂😂😂 Dina ma ray 😂😂😂😂😂😂😂
Pas woukoudougou yaw tamit🤣🤣🤣
😂😂😂😂😂xawma dougou digui xawma wagadougou mais wayei bala gnibi nguenn fifi😂😂
Première diamou rek inchallha néelen amine
Kou bess thi séri bi ni mouy léké
@@boypoulo2115 😁😂🙊
,🤣🤣🤣
Ahh li dé Dara dakouko teiro sa pape niougué MAKA yalnaniou yalla may lii wayy😊🙏🏽
Kou beugue adja beuseul j'aime waay😍❤
Kou beugeue serigne touba beuseul j aime
@@beyecheikhe2975 aa
Dougouti mom baala koor bi diekh dinaa am yaram mom 😂😂😂😂😂😂 ma sha Allah
Dioguoye meilleur comédien kou d’accord 👍
deugue leu dhé
deugue leu dhé
Et radia,baye
Séquence baye yi j'adore 🤣🤣🤣🤣😍😍 pâté enfin wagadoudou mi louko dal
Kou beugeu wadjou bax beusseul j'aime
Maylénma j’aime 👍 si barki seydina Mouhamed 😍yalla na gneupp am jamm bn ramadan mubarak 🌙 😍
Ayway tay may 37ème commentaire waye pour la première fois🤣🤣🤣
Diadieuf mbok Baye fall yi message bou fort bok lep vive la série Adja 👌🙏❤️
Yallah neuh nieupOu am diamOu ❤❤
Non diogay ne changera jamais qui est d'accord pousse bleu 🤗
Nooo diogoy mo sèw djiko😂😂😂😂😂
Ce film est génial na nieup am jamou ramadan karim
Yalla na yalla nagou koor yi
Amin
Role bay fall yi mome ossi c tré Nice wallae frer ta bien dit yalla nalla yalla dolli ay contra you barry si patissen 👌
Elena mom khana dou toguouu 😂😂
Dafa yoré bb motakh😂😂❤️
@@maguetteseck2918 bamou yoroul bb sakh togoul
@@ramatoulaymbaye4112 moma diakhal da meunoul reikk
Motakh pate dika roube
Kon yangui setlou lolou 😂😂
Sheuute Dougoutigui😂😂😂😂
Mom dinameuh raaye req
Aye kholeine ko tieeb ba dan diexxh diih😂😂🤦🏽♀️
Pàte khanà sa nel bi mo parégoul won🤣
Adja est vraiment une série magnifique