Manam gorgui mola wah nga gueum,né siteu moy dane modou lo Ba dimanche inchallah dinga hamné gorgui dou yalla ,yalla késsé mofi néke,yalla na modou lo am victoire contre siteu
Ki dina ame gathié inchallah ✍️ té mome amoul loumouye wakh sa touba ndakh daye wakh di wate ci lou gneuweugoul 😂 bayile xél ni béss daye ñeuw dhé ñieuw 🤷 bocalé rék ngéni déf ✍️ sama xôl sédana ndakh var bi dafa doye waar 💪💪💪💪
Comme yalla amna nga wax kone sa gorgui boula waxé boko geumé yaw geumo yalla ki tek khel lay def legui kou dane mouni waxone nako siteu la waxone légui waxat nga modou lo
@@taphasamb6836 ey wayy Tapha dama beugue modou Lo ba gueume woumako. Pour Mane ma ko gueuneu beugue ci aduna bi 🤣 Yalla nako borom bi defal jamm meyko ndam
5 tonnes Moune nga doul nakkkkkkk 😂😂😂😂😂😂 Khana khamo ni gnoune sonko mo gnou yééé genre doule yi Moy doulou politiciens Dangay politique pour sa poche changel stragie 😂😂😂😂
bilay ya beug micro iow lamb dji kousi danou tmt fii guay nieuwat di doul nann sm gorgui waxon nmko fek ki danou la waxon moy dane doul rk guay df bilay ya meun fen😂😂😂
Yaw loutax ngay ciblè Sa touba yaw nekal si linga nek Sa touba nek si limou nek kii day tek xel Sa touba waxna kiy Dane mè yaw balegui Wakhofi dara louler Donc kousi gagnè ngani kokou toi osi nit yii yewou naniou dee
Yaw ligey wakh ak ligay déf walahi bokoul figa enkésé Sama xalis di ma daw Lo ba tay diokho ma numéro bi legui souma la wowé doma diel ligay déf sét si yalla
Yallah baxna inchallah MODOU lo borom bi dinako may ndam inchallah
Ya maneu ndey dou😂😂😂😂
@ bay ko mouy wakh rk sokhna si
Khana Siteu dou domou Djoulite tamite?? Inshallah sunu borom dina maay Siteu ndam thi katane
Frr c pas Moustapha 😂😂
Modou Lo yalla na ko yalla may ndam Amin inchallah
Manam gorgui mola wah nga gueum,né siteu moy dane modou lo
Ba dimanche inchallah dinga hamné gorgui dou yalla ,yalla késsé mofi néke,yalla na modou lo am victoire contre siteu
Modou lo yallanaka yalla maye ndam si Baracke seydina Mouhamed Amine inchallah 👑👑💪💪🤲🤲🙏🙏
Amine
Amine
MODOU LÔ YALLA Nako YALLA MAY NDAM 🙏 lafal ko Thiatt Samal ko Boppam 🙏
Yalla n'a Modou lo âme ndam si kaw Moustapha Senghor siteu amine✌️🙏🙏
Amine ya rabal alamine 🙏🏿
Amine
5 mi Sakh Ndaysane si kasso bi lay mouje Ndaysane
Allahuma Amin 🤲
Modou lô seul 👑💯💪💯💪
Yalla mofi nei té dina May Modou LÔ ndam inchaa Allah
Situé yall nako yalla may ndam 👑
Modou lôoooooo ❤❤❤❤❤
modou lo moy dan dou wakhi farr loll la yalla déf
Amine way
Amine 🙏 inchallah
Gspr k bouko Siteu daner di nga ame ngorou delou si fii thi katane
Var incha allah
Serigne Fallou néna Senghor ( sink) saa kaaw❤❤❤❤❤ siteu dîna bakh Insa Alla
Inchallah Ndam rec
Ki khana amoul liguey amna diot dhei thioooo 😅😅😅😅😅
Ki dina ame gathié inchallah ✍️ té mome amoul loumouye wakh sa touba ndakh daye wakh di wate ci lou gneuweugoul 😂 bayile xél ni béss daye ñeuw dhé ñieuw 🤷 bocalé rék ngéni déf ✍️ sama xôl sédana ndakh var bi dafa doye waar 💪💪💪💪
Siteu yalla na am ndam
Di nga doule fépp yague nga doule nak mé tay lay raw yafi wakhone ama baldé day dane modou lo nga watonsi
Dagay fén rék khamo dara touss modou lo dinako douma danko loumou andi fék kofi inchallah 16:40
Modou seuu❤
Modou rek
Mais ki khana d'ou sonne chaque jour trois cites différents mais sa salive yi legui mou diekh😅😅😅😅
Siteu daanou rek inchallah
Yala na yala may ndam Modou LO le 24 novembre thi bar kep seuydina Mouhamed
Yalla na Modou lo daane Moustapha senghor Siteu
ndam rk inchallah modou lo seul Parcells moye dirige
Bo attaquer diomay gnou niaff sa ndaye deh
Doudou lo lo def danu
Mais mom d'où dieul sakh appel 😅😅😅😅😅😅
Siteu rek bilaye.....
Situé seul
5kilo nena '' ngaan moy nianayou dioulite ''😅😅😅😅😅
Non gorgui néla yalla dalay wane mou wékh khëy mou nioulal ka kouk ghay wat ki door rék lay deff
Billahi frère lou lerr ngaa wakh gni dougnouy doull rk
Adina yalla ko mom yako wakh kon kay nopi lén yalla paréna té dolén diokhé verdic jamais
Modou seul
Walahi yagui watte rék thi alhourane ak yonénete bi si aye thiahane.meytoul dhé fi yala rék moffi nék tes mo hame liye héw souba inshaalla yagui wakh rèk di wakh di teurereurii rék 😅😅😅bahena lignoula déye si lamb djiii dinala nakh dhé😅😅😅
Vraiment
Beugouma di wakh si lamb ta siuta la farall waye Moudou dinako dour dann ko lolou reck Mona meti
Siteu ndam reck inchallah
5tonnes my il vien dou ???
Wakho deug sitheu moko eup dollé
Ki mo dakha doule ci sénégal
Yaw geumo yalla doul rék danga baari wakh ba dimanche thi gnome kéne khamoula Modou yalla nako yalla maye ndam
Comme yalla amna nga wax kone sa gorgui boula waxé boko geumé yaw geumo yalla ki tek khel lay def legui kou dane mouni waxone nako siteu la waxone légui waxat nga modou lo
Dangay fene rek wakho deugue khamnganer legui nga khewi profitel bou bakh senegal mome dafa nekh aye doff la bari
Var varat bilahi yaw rk yafi doulone wala lo watone si ama baldé ak modou lo yaw mi meno di kate sa ndeye di nopii
Damay Dee boko atacke niou niouss la
Ki daye nare rék
Kii moum da ndjimi yalla
❤❤❤❤❤❤
3:44 lane la wakh si falakhi ak nassi doul rekk😂😂😂😅
Siteu moy dane inchallah
Modou lo bilay si milieux guewgui lay daané siteu com nimou deffone Eumeu sene door mou keupp
Ey wayy yalla nala borom bi degueu. Da nga Guiss Li nga wakh?
Amine way yaram yalla na am 🤲🤲🤲
Modou Lo danouna bou yague 😂
@@nafisene5335 😂😂😂 toi tu es là encore ndeysann danga beugue modou lô yallah naniou yallah maye ndamee😂😂
@@taphasamb6836 ey wayy Tapha dama beugue modou Lo ba gueume woumako. Pour Mane ma ko gueuneu beugue ci aduna bi 🤣 Yalla nako borom bi defal jamm meyko ndam
No 5 d'où niteu😂😂😂😂
SITEU YALNAKO YALLA MAY NDAM INCHALLA
Sa gor gui bou exister won di nga entraîner dji dieuli ay combat 😂
Modou lo sa Thiès mo Koy dan
Amine Ya Rabbi
Dagay doul bilakhi daga doul ndayam
kou meuna doul moy ki😂😂😂😂
KEN DOU WAHE SAMA DÈH SAMA ALDIANA NGAYE WAHE SOUMA LÈRÈA DEH TAY LOLOU LANI WAHE
Serigne Cissé bou Serigne Babacar sy lay wakh moy Serigne Modou lo
ragal montakh nième woul wakh Modou combat dagua cii def dangue rrk
Ték katou dile deug moy 5 tonnes doul rel😅
Day dofdoflou mais dofoul dh 😂
5 tonn bayil aya alkhourane dji guay yakhu dou sa wakhu Baye dou sa wakhu yay wakhu Yalla la.
Ki aka meun doul dina nopi si combat bi
😂 mane boy 5 tonnes bi gorgui laay outeul promotion gnoune wa camp modou lô yallah rek lagnou yakaar souba yaguatoul
Nékal fofou di doune rék
Mom Kay loumou wakh lerna siteu la wakh moy Dane on verra inchala
Non dafay codé wakh dji c'est le contraire
Daguaye doull yoro dara
Ça veut dire Siteu moy dane
Wakhofi dara lou ler
Blh atakel diomaye khol bakham
5 tonnes Jammm Rk Ngay amm
Ki doul rek lay def
Reuy ngua lamine nak ioe mi yayy ndamou
Bayule gawa wah mo geune
Aka ya mana tëggu. Té rëy lamiñ. Ñaak ngaa mandu lool. Ya bari wax yu jaxasso. War nga xame sa bopp té bayi waj waj ji.
Doule rek courtier marabout 🚫❌👎 lep pour xaliss rek
5 tonnes vraiment sa gorgui khamoule dara lamb dafa beurri khalisse té meuno ame ndame
Walay tu as dis la vérité lolou moma diahal victoire moinouko ame
5 tonnes luler lay wakh baxna siteu day dane Modou lo diapal téyé bah dimanche
Dans tes rêve 😅😅😅
@MameAlassaneDiop sula néxé djeul sama nmro bilah Modou lo day danu lala wakh dimanche inchallah
Noumouy dano 😂
Numéro 5 ton la beug svp
Woma ma diokhlako
Lane moy kiy dane nimema léré sama dé souma léréwone nonou la dé wala sama aldjiana nga beug wakh bayil watt yi dangay doul rk
Ioe mome kou meuna doul nga
Mbye 😂🎉😢l❤
5 tonnes Moune nga doul nakkkkkkk 😂😂😂😂😂😂
Khana khamo ni gnoune sonko mo gnou yééé genre doule yi Moy doulou politiciens
Dangay politique pour sa poche changel stragie 😂😂😂😂
Borom batin barinagn senegal li khew yala moko mom
Billahi❤
Demal outi combat
Waw comme ça gorgui diko dokh Victoire
Combat bi lèrouko mo takh
Day doul rrk combat by lay Ndiay rrk
Atageko no xol bakham dagay réw réw lo
Ki ték khélela kiye danne boula léré wakheko boko nebé rek yagui soralé souba ko iri lék khalisame gua begue 😅😅😅
Balla day dan eume sene
bilay ya beug micro iow lamb dji kousi danou tmt fii guay nieuwat di doul nann sm gorgui waxon nmko fek ki danou la waxon moy dane doul rk guay df bilay ya meun fen😂😂😂
Var lay daw
5 sadata yeye yaw dagay dool bilayhi forco modou lo Moy dan bilayhi dagay dool
Senn mbeur day danou té waxo bann clent leu yaw ko yap wala ay dof nganiou diapé yaw doul rk ngay df
Yaw loutax ngay ciblè Sa touba yaw nekal si linga nek Sa touba nek si limou nek kii day tek xel Sa touba waxna kiy Dane mè yaw balegui Wakhofi dara louler Donc kousi gagnè ngani kokou toi osi nit yii yewou naniou dee
Yaw ligey wakh ak ligay déf walahi bokoul figa enkésé Sama xalis di ma daw Lo ba tay diokho ma numéro bi legui souma la wowé doma diel ligay déf sét si yalla
😂😂😂😂❤❤
bo geume sa bopp defal ni Abou CFA dangay doul rek
Saway Abou change na ay wakham dee Kene dousi Wakh Modou day danou
Ya.mana.féne
😂😂