Li Serigne Moustapha DIAKAHTE wakh ci Ndiouga KÉBÉ.

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 17 окт 2024

Комментарии • 9

  • @abobabacaryade1621
    @abobabacaryade1621 4 года назад +4

    Machallah El Hadj Ndiouga Kébé était un homme multidimensionnel qui avait beaucoup investi pour le développement du Sénégal.

  • @mourid9034
    @mourid9034 4 года назад +1

    Machallah yalla nako yalla fay

  • @bassirounguer7411
    @bassirounguer7411 4 года назад +2

    Yalnako yalla yeuram té kharéko aldiana

  • @sandamgileemfaal
    @sandamgileemfaal 4 года назад

    Baaraka Laahu fiikum
    Ku la naw la, Sëriñ Mustafaa...
    Seex Ahmadu Bàmba mooy ubbi ku ko soob ci anam yu jéggi xel...
    Na Yàlla guddal fan yi, wéral cér yi, dooli nu yàqiin te lëkke mbooleem tanneefi Sëriñ bi, ngir ñu bokk jooxe ay nammeelam.
    S Maalik Faal Gileem.
    Innal Laaha mahanaa

  • @ADfree-mp7wb
    @ADfree-mp7wb 4 года назад +3

    Famille Ndiouga kebe nio mou amoul kene kou meunoul agali les projets inachevés de ce Grand Monsieur

  • @habibkane8123
    @habibkane8123 3 года назад

    Serigne Moustapha diakhate yawe mbouno sakhe li djeune ti deux biir keur mbeux ngeye ndane mourite yii gnouye lidjane tii adouna,bayille doulle serigne Moustapha,mourite Sénégal rek leux yambe,

  • @habibkane8123
    @habibkane8123 Год назад

    Serigne Moustapha diakte bayille doulle yawe mbeundo lidjeunri deux birre keur wakhou mballak adouna bii

  • @fatousylla1971
    @fatousylla1971 4 года назад +4

    Ndiaga amoule morom