Yalla amoul sikke ni danioukoy guis yalla mom rek mofi néke Serigne touba néena yagusba yalla tee douma guisati lenéne loudoul yalla diereudief chiekh moussa cissé👌
Toukara et ceux qui l'apprécient sont dans le même troupaux d'ignorance. La connaissance est scinder en deux parties: celle qui est apparente et l'autre qui est cachée. Et la meilleur des connaissances demeure celle esotérique et non celle exotérique
@@mamediogalsamb2057 . C'est pas que je défends les yalla yalla, je faisais seulement une analyse de leurs pensées. Pour moi, aucun dieu n'a jamais parlé à personne. Toutes les religions dites révélées ou pas, ont été créés par l'homme.
Nothing is clear un her words. He don't know what the other gays is speaking. He develop a deep science Yeah , He is talking about a mistical knowledge witch we found behind the books and copie books. Ttry to Know the one ( God) before you die.
Kou toppoul yallah yallah yi di guene rere tabi safara 🙏🕊️ lah illaha illa allah islam dou yakou dou sopekou te foumou tolou mi gui méguo diamono 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🕊️
tounkara ne maîtrise pas plus le sujet que l'autre. Son problème en es qu'il était incapable de le vaincre . Ils ont la même conception du sujet. Aussi l'invité est très éveillé.
Le revêtu d’un manteau (Al-Muddaththir):34 - Et par l'aurore quand elle se découvre ! Le revêtu d’un manteau (Al-Muddaththir):35 - [Saqar] est l'un des plus grandes [malheurs] Le revêtu d’un manteau (Al-Muddaththir):42 - "Qu'est-ce qui vous a acheminés à Saqar ? " Le revêtu d’un manteau (Al-Muddaththir):43 - Ils diront : "Nous n'étions pas de ceux qui faisaient la Salat, Prier est obligatoire dans l'islam
Papa dieng motax mou wara diang al quran bouko dianguei dina yallah in shaa Allah te koula gueuneuh kham yallah gueun lako ragal boba dina takhawal ponk dinei yi bou bakh in shaa Allah
Yalla nena xamelen ma ba paré sog ma diamou, té wadji wax na deug dioulli degnekoy meun, kou khamoute yalla meuno diouli. Ta parfaitement raison fimouy wakhé tounkara yegoufa
Serigne Touba loumou wax lerr na "Lil Moustapha nawaytou ma you diatitou souna tahou hala mahi ni Ahmadou" Serigne bi dioulli Yonenti bi dioulli gua bagna dioulli ya xam mais pour waxni Serigne bi wala Cheikh Ibra sèn yoon nékoul si bagna dioulli
Mahrifatou bilahii guéne douga forcé kén yalla moola siye ndimballi rék ga yégue sa sooka beugué forcé té yalla doogalouko dousooti té danouye wétii sa dëgg té bilahii ligay aadou🗣 lér✨ rék la
Yow dangaa Xam linëk ci sama bop bi nii ? Dëgër fitt yaamassi doy bay sìwal lima Xam ak lima xamoul. Touti mandu baaxna deh. Kèep kou déh ci djouli ta mou fèk waxnanela xamal yalla milamoom nga bagne, naari diaxannama ngay motalidji sa ndiague, say djouli ak say koor: Wa salaam
Sawaay, Dame Diouf, Diouli waroul nieup deh. Ndaxté yeufeur waroul djouli, nafeeq waroul djouli; ndaxté djouli pour djoulitt gni la. Mais anna kanay deugi-deugi djoulitt? Nekoul nga joudoo ci keur djoulitt rk deh. NDaxté doon djoulitt nékkul lunuy djoudouwaalé, waaya danukoy sakudji, comme nikko sakhaaba ya déféwoon ci rassoulilah, cheikh Ibra déféwoon ko ci Bamba, waaya pierre déféwoon ko ci INSSA ibn Mariam. Ndaxté nioom nieup ay djoulitt lanou. Mais ci nann ak ci nakka? Kou xamout yalla, loolu doulla lère wa salaam
#Marie... Ce né po de la filosofie déh.. Diiné gnaari khaadj la: zayir ak batine. 5 piliers yi mooy zayir bi, waayé nak khakikha mooy batine. Amena gnou topou zayir, amena gnou topou baatine, amena gnou topou gnaar yeup. Wayé Baye fall bou matt Baye Fall baatine lay topou. A bon entendeur, salut
@@elhadjindiaye2228 machalah seex bi... Bégg nagn bou wéra wér. Niila, li nga déff mooy nitt, lépp lougnoula wakh té sa rouhou nangou wouko rek warooko kaddu ci sa lamégn, kone nga doone naaféék. Nangoul naala bou wéra wér. Yalna Yalla défal la diam, nitt kou baax nga té deugou🙏🙏🙏
Yalla waxone na yonénti bi psl amna gnagua xam safara moy sen keur parceque xam nagnou ni yalla am na yonénti bi psl am m gueumou gnou gnom sen xol dafay wow ba mélni xér kén mounou léne changé kone ki diaroul yak ay nélaw prsk dieux est Grand yalla na diam yague🙏🙏🙏
Tounkara doit savoir personne n'a le monopole du savoir certes je ne suis pas d'accord du gars si niakk dioulém mais mom kouka dégglou khamné amna loumm kham
Limuy wakh dafa yomb bania diamu yallah la déf beugg ko justifier nk ak yo hamni serigne touba molén ko gueuna xam fuf téréwul dadane djuli di wor t molén eupe thieur si yallah fuf
@@mbacke3602même s'il n'était pas dans cette religion,ça ne nous intéresse pas parce que nous ce qui nous intéresse c'est à partir du moment où il est devenu prophète
C'est les commentaires diasant qu'il a des arguments nii naa Ouvrer grand les oreilles une personne qui a toute ses faculté mentale qui ne prie pas n'est pas un musulman point بين الإسلام والكفر ترك الصلاة. الصلاة هو أول شيء يسأل عنه العبد يوم القيامة . Tounkar il est dépassé par sont niveau d'ignorance c'est tout il mélange tout il parle finalement pour n'est rien dire de bon et vrai.
Slm tounkara bayil ninga nèkè kii gor yalla deugg eupouloko xam_xam Diokhé mo geun #jullit Mandou mo geun #koor T s.touba nèna même nitt sou wakhè Lou nékul kèn douko wakh wakho DEUG Amo ayy tèguine dra😪
Diouli dh moy barriére entre dioulite bi AK kidoul dioulite Kouko bayi yéfére nga. Té Aussi diouli dou wathie kéne a moins que nga ame problémou khéle wala nga néke di nélaw wala nga guiss bakh. Diouli dou wathie kéne th koula ko téguil Aussi dafa rére wala nga beugueu koula nakh
pape malick mbengue meuss nga guiss kou djouli ba texé? soko guissé wonegnu firndé bi... lo waxati gnu topp la... jugement yalla ko mom du ioe dou mane nagnuy sabablou rek tey diamou sunu borom numu gueuna sellé...
tehei yalla ko mom nagnuy sabablou tei rafete ndiort... wadji il a le merite daller chercher l savoir et dessayer connaitr le seigneur c mieux de se dire musulman tt court di nane di agresser di def lou bone...
Mane Senegal chaque jour ma gana décourager . Bokkalé ak fene rek souba ak ngone. Tounkara niemewoul limouy wakh.. serigne touba rereul nia niou bari!!
deugeuleu bayfall doudeul sa doundou tagua bay lenn wakh guou beurii rk la lenn baye khamall lolou la ndiambe wakhon kham nagnou yalla mai khamougnou lignouye diamo yalla diamou yalla moye tawhide mahrifatoull billa bokoull akh tawhidoul illahiyeu tounkara di app khaamm da guoumbeu teuhlou
En tout cas , d'accord ou pas le gars a dépassé Tounkara de loin coté arguments. Tout ce qu'il dit peut etre choquant des fois mais il a des références solides et même il soulève des interrogations pertinentes que le journaliste refuse de considérer. En tout cas moi je ne dirai pas qu'il n'est pas un musulman. Et je crois que tout le monde devrait faire idem. Et je vous invite même à lire la sourate Kaaf lorsqu'Allah (swt) parle de Moussa et Dhoul Kharnaine. On voit le paradoxe que suscite la confrontation entre charia et akhikha. Salam à vous
Trop fort mouhamed ndiaye, yallah daniou âme dégue dégue pour comprendre l islam. Niveau spirituel très élève... Toukara essayés de comprendre... Ça m'étonnerai que tu comprend.
Accepte ce qu'on t'offre de raisonnable , commande ce qui est convenable et éloigne-toi des ignorants. Khuthi al'afwa wa/mur bial'urfi waa'rid 'ani aljahileena خُذِ الْعَفْوَ وَأْمُرْ بِالْعُرْفِ وَأَعْرِضْ عَنِ الْجَاهِلِينَ
Je regarde toujours cette vidéo et j’en apprends toujours c’est vraiment très important
Même moi yallah yallah aussi pourtant amna kham kham
YALLAH YALLAH Moog DEUG dawlèn nguène geustou jii
@@sambaniane1486lane moy xam xam ngani 😏
Yalla amoul sikke ni danioukoy guis yalla mom rek mofi néke Serigne touba néena yagusba yalla tee douma guisati lenéne loudoul yalla diereudief chiekh moussa cissé👌
Mais bénêne invité bi mandou na deh. Il est assis calme sans se mêler de leur conversation !!! Lol😂😂
Ah suis mor 😂😂😂😂😂
😂😂😂histoirou niou gouddou loussi yonou ndama😂
Dash hamul Dara fi
Doyna war🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Mom daa dieul comprime mandou 😂
Qu'Allah nous guide et pardonne de nos égarement
Dieureudieuf Cheikh Moussa Cissé Ndiamé borom Darou Lerou lerr yii
De nguen rer
@@hayeem-g3g😂
Tounkara dall MachaAllah un très bon débatteur ❤️❤️❤️🙏🏽
Toukara et ceux qui l'apprécient sont dans le même troupaux d'ignorance. La connaissance est scinder en deux parties: celle qui est apparente et l'autre qui est cachée. Et la meilleur des connaissances demeure celle esotérique et non celle exotérique
Tounkara ne métrise rien de ce qu'il dit
@@sidyakeyt9285 tounkara est un ignard tt comme ce qui l appui
Le problème au Sénégal est que les gens aiment parler du savoir et qu'ils ne détiennent nécessairement pas ce qui se doit pour en débatre
le niveau est trés élevé pour tounkara kham soga diamou
Plus élevé que celle du prophète explique nous
Waadji il ne fait que théoriser
Être musulman est de faire les 5 piliers de l islam c est l obligation divine Tounkara tu es fort merci
Islam c’est pas seulement les 5 piliers Serigne bi khotalale way tounkara khamoule dara daa limité
@@petitecoteinfosSerigne bi 5 pilier yi mom moy l'essecencial vraiment même si c'est pas tout l'essentiel c'est l'essentiel
@@aissatoudione1922 dioulékî woor yein deiglouléne lay takha raw kham yallah la!
J'ai beaucoup aimé ce débat......
ما شاء الله tounkara ختم الله على قلوبهم وعلى سمعهم وعلى أبصارهم غشاوة ولهم عذاب أليم
(ولهم عذاب عظيم)
Le débat n'est pas houleux mais passionnant. Le niveau du débat est élevé et en plus c'est dans une saine adversité.
Rien de passionant. Le rastaman n a aucun savoir. Il n a fait que memoriser qhelques versets pour vouloir justifier. Son refus de prier
@@khalidbiaye1816 Tu a compris
😂😂😂il ya que toi qui ose dire ça..le rastamane est complètement à la rue
Les yalla yalla développent une philosophie très profonde, qui n'est pas à la portée de tout le monde.
Dieu parle aux connaisseurs et savants
@@mamediogalsamb2057 . C'est pas que je défends les yalla yalla, je faisais seulement une analyse de leurs pensées. Pour moi, aucun dieu n'a jamais parlé à personne. Toutes les religions dites révélées ou pas, ont été créés par l'homme.
Qu'Allah nous guide vers le droit chemin inchallah
Amin
Amine
Mais il faut dire la vérité koudoul dioulli do dioulit ...
@@ndembadrame3804 vraimen
Amine
C'est ça qu'on dit journaliste comme toi ❤️
Tounkara may Allah bless you, your words are clear and you are a role model Shuran
Nothing is clear un her words. He don't know what the other gays is speaking. He develop a deep science
Yeah , He is talking about a mistical knowledge witch we found behind the books and copie books.
Ttry to Know the one ( God) before you die.
Yalla yalla rék noù âme xam xam cheikh Moussa cisse ndiamé darou dafa wah Lou léré
Baye niass rek moy xamlai YALLAH
koku doff la kom seringe bim top
J aime tounkara Tout son parole c est la vérité il connaît très bien le coran
😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤
Vraiment tounkara dokhamoul ladiale
Moy Xam Xam
Kou toppoul yallah yallah yi di guene rere tabi safara 🙏🕊️ lah illaha illa allah islam dou yakou dou sopekou te foumou tolou mi gui méguo diamono 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🕊️
le plateau de tounkara est très enrichissant il est important de par sa riche culture
enfin quelqu'un qui se pose des questions... soyons religieux mais pas moutons
tounkara ne maîtrise pas plus le sujet que l'autre. Son problème en es qu'il était incapable de le vaincre . Ils ont la même conception du sujet.
Aussi l'invité est très éveillé.
Ce débat est vraiment impressionnant j'adore
Ibra Dienne machalla ridial
Yalla Nagnou Yalla Mayy Moudjou Ngou Raffet Té Khir Gnou Si Gnoukoy Diamou
Amine
Le revêtu d’un manteau (Al-Muddaththir):34 - Et par l'aurore quand elle se découvre !
Le revêtu d’un manteau (Al-Muddaththir):35 - [Saqar] est l'un des plus grandes [malheurs]
Le revêtu d’un manteau (Al-Muddaththir):42 - "Qu'est-ce qui vous a acheminés à Saqar ? "
Le revêtu d’un manteau (Al-Muddaththir):43 - Ils diront : "Nous n'étions pas de ceux qui faisaient la Salat,
Prier est obligatoire dans l'islam
Bien dit. Macha'Allah
Les arguments ne comptent pas?
on se contente de féliciter celui qui partage notre point de vue..
dans ce cas, je le dis aussi : bravo Tounkara.
Il est fort
wadji comprendre nako dafa beuga wakh né yalla kén douko diamou té xamoko
Tiigii lolou lay wakh machala iow amga dég
Yaw topal falé yak mome yéna yame rék
Papa dieng motax mou wara diang al quran bouko dianguei dina yallah in shaa Allah te koula gueuneuh kham yallah gueun lako ragal boba dina takhawal ponk dinei yi bou bakh in shaa Allah
Bien sûr
Yalla nena xamelen ma ba paré sog ma diamou, té wadji wax na deug dioulli degnekoy meun, kou khamoute yalla meuno diouli. Ta parfaitement raison fimouy wakhé tounkara yegoufa
Toungkara Lo khamoul mandou Thi rawatina mam ciékh Ibrahima Fall 👇👇sinon dinan todje sa tiotou nd👇👇👇👇🤪
Yalla nagnou yalla dolli soutoura❤❤❤
Serigne Touba loumou wax lerr na "Lil Moustapha nawaytou ma you diatitou souna tahou hala mahi ni Ahmadou"
Serigne bi dioulli
Yonenti bi dioulli
gua bagna dioulli ya xam mais pour waxni Serigne bi wala Cheikh Ibra sèn yoon nékoul si bagna dioulli
Woy
Bian dit
Bilay
Ki seytane moko dieko mogui toumal Serigne Toubade tounkara mouytoul nie
@@abaaba5045 cheikh ibra danoul juli kne seytaneiko diekuwon?
Wa l'autre invité ndeysaan moudié na nék téléspectateur 😂😂
Vraiment
😂😂🤣🤣 Vraiment !!
Je i1h0
😂😂😂😂
😂😂😂
Thiey Sénégal louné amna fa tounkara a raison celui qui ne prie pas ne peut pas se prétendre musulman
K signifie le mot saalate ❤
Mahrifatou bilahii guéne douga forcé kén yalla moola siye ndimballi rék ga yégue sa sooka beugué forcé té yalla doogalouko dousooti té danouye wétii sa dëgg té bilahii ligay aadou🗣 lér✨ rék la
Yallah yallah yii sii ayy thiakhane képp lagnou nék
Ah enfin je comprends ce gars il nous fait comprendre ce qui est derrière le livre(coran)
Effectivement ! derrière le livre, il y'a une science dont la science du livre n'est qu'une infime partie
Yaw xamo ci Alhuran touss naan laan!!
Il n'y a rien derrière le Coran
Il y'a dieu derrière et au-dessus du coran. Dieu n'est pas le coran sawaay, xamignil yalla mila sak
Yow dangaa Xam linëk ci sama bop bi nii ? Dëgër fitt yaamassi doy bay sìwal lima Xam ak lima xamoul. Touti mandu baaxna deh.
Kèep kou déh ci djouli ta mou fèk waxnanela xamal yalla milamoom nga bagne, naari diaxannama ngay motalidji sa ndiague, say djouli ak say koor: Wa salaam
Niakka dioulli daal wooroul MOUHAMAD mo geuna tedda nieup te dédàn dioulli dioulli wathioul kenna bâ bangay dee
Yawmi diemal dieul ay leçon mo guene ngay critique ni
Toungkara naaaafeeekkkk nga
Sawaay, Dame Diouf, Diouli waroul nieup deh. Ndaxté yeufeur waroul djouli, nafeeq waroul djouli; ndaxté djouli pour djoulitt gni la. Mais anna kanay deugi-deugi djoulitt? Nekoul nga joudoo ci keur djoulitt rk deh. NDaxté doon djoulitt nékkul lunuy djoudouwaalé, waaya danukoy sakudji, comme nikko sakhaaba ya déféwoon ci rassoulilah, cheikh Ibra déféwoon ko ci Bamba, waaya pierre déféwoon ko ci INSSA ibn Mariam. Ndaxté nioom nieup ay djoulitt lanou. Mais ci nann ak ci nakka? Kou xamout yalla, loolu doulla lère wa salaam
djoulli = prière chacun avec sa manière de prier...
@@sidyakeyt9285 degg la waay
Le gars est très intéressant. Mais c'est un philosophe en fait.
Ce pas facile de convaincre un philosophe
#Marie... Ce né po de la filosofie déh.. Diiné gnaari khaadj la: zayir ak batine. 5 piliers yi mooy zayir bi, waayé nak khakikha mooy batine. Amena gnou topou zayir, amena gnou topou baatine, amena gnou topou gnaar yeup. Wayé Baye fall bou matt Baye Fall baatine lay topou.
A bon entendeur, salut
@@ThiagoSilva-ri2jc Dangay wax rek mais xamngani waxo xamm xamma
@@elhadjindiaye2228 machalah seex bi... Bégg nagn bou wéra wér. Niila, li nga déff mooy nitt, lépp lougnoula wakh té sa rouhou nangou wouko rek warooko kaddu ci sa lamégn, kone nga doone naaféék. Nangoul naala bou wéra wér. Yalna Yalla défal la diam, nitt kou baax nga té deugou🙏🙏🙏
Marie B non pas la philosophie
La prière et tellement sacrée raison pour laquelle serigne touba à prier sur la
Mer
Senegal dekeu bi geneu tooty si aduna wallahi senegalai moo daxxa wakh si aduna demlén diamodji yalla té tppou seydina mouhamad psl té dem ligéyi
il est vraiment extraordinaire
Yalla waxone na yonénti bi psl amna gnagua xam safara moy sen keur parceque xam nagnou ni yalla am na yonénti bi psl am m gueumou gnou gnom sen xol dafay wow ba mélni xér kén mounou léne changé kone ki diaroul yak ay nélaw prsk dieux est Grand yalla na diam yague🙏🙏🙏
Merci sérigne bi
Bilae d3
Tounkara bilay dagua reerr demal gustou j ligua fook bilahi dou xam xam cheikh bi lou lerr nagne lay wax xam yalla rk mo woor bilahi 🙏
OK c'est bon comme Débat sinon la prochaine fois sur le plateau il nous faudra des confirmer pour un débat comme ça merci
الحمدلله الذي عافاني مما ابتلاك به وفضلني على كثير ممن خلق تفضيلا الحمدلله على نعمة الإسلام
Qui est ici en 2020
Tounkara doit savoir personne n'a le monopole du savoir certes je ne suis pas d'accord du gars si niakk dioulém mais mom kouka dégglou khamné amna loumm kham
Limuy wakh dafa yomb bania diamu yallah la déf beugg ko justifier nk ak yo hamni serigne touba molén ko gueuna xam fuf téréwul dadane djuli di wor t molén eupe thieur si yallah fuf
Khamoul dara yefer la bou bonnee
Khamoul touss !!! Kou bonne là !!! Ki dayy yaakheu société bi. Yéférrr pire moungui niiii
Khamoul darra daffa rerere reck
Wallahi wadji lou laire lay wakh tounkara nit day deglou bou beuguer degue
Toukara barke serigne touba li moula wakhe kene douko dinni barke cheikh Ibrahim fall ❤❤❤❤
Yaw nguem sah hamoko nguani dangay diangalé😂😂😂😂😂😂
guide nous Ya Allah, je remercie mes parents de m'avoir aidé a apprendre et connaitre ma religion. c'est triste en plus il se donne raison
Vraiment triste key
Djouli dal kouko doul def té majeur andak sa khel yefar nga ak ko mana doon
Dc image ceque le prophète était avant les prières !!!
Le prophète était dans la religion d'Ibrahim purement monothéiste
@@mbacke3602même s'il n'était pas dans cette religion,ça ne nous intéresse pas parce que nous ce qui nous intéresse c'est à partir du moment où il est devenu prophète
Ah wakh nga lo khamul dh
Mai saway d3mal touppp t3 dioulli li yalla May mame cheikh ibra fall mayouko sa Bay wakhou malak yaw
Bala nga diouli kham
Liko yalla may mome ak wa keurem lako may segne ! mome ak kouko yakaar la dh
Mais yén galsen néhna dh dém lén diangui mo guen si yénneu
Wakhal way
Ndeye Khady way,
C'est les commentaires diasant qu'il a des arguments nii naa
Ouvrer grand les oreilles une personne qui a toute ses faculté mentale qui ne prie pas n'est pas un musulman point
بين الإسلام والكفر ترك الصلاة.
الصلاة هو أول شيء يسأل عنه العبد يوم القيامة .
Tounkar il est dépassé par sont niveau d'ignorance c'est tout il mélange tout il parle finalement pour n'est rien dire de bon et vrai.
Vréma yénneuko déf di invité ay dof noy comprendré loumouy wakh Yallah Yallah dégno réer meuhr😂😂😂😂😂
Slm tounkara bayil ninga nèkè kii gor yalla deugg eupouloko xam_xam
Diokhé mo geun #jullit
Mandou mo geun #koor
T s.touba nèna même nitt sou wakhè Lou nékul kèn douko wakh wakho DEUG
Amo ayy tèguine dra😪
kou dioup dangay noungoo jouly kou mandou dangay noungoo woor
s.touba kènnla wero yaw ki limouy wah tegougo féne
Wahi yalla guène di teukeulè AK wakhi serigne touba thiey adouna
Koudoul diouly yefar nga point .
Soubhana alah alhamdoulilah bima yalla déféré talibe cheikh
Mai tmt xam yalla dala war prck dioulite gua boul fatè lolou
Moi aussi amineeee🤲🤲🤲🤲🤝
Doff nga rk 😃
Diouli dh moy barriére entre dioulite bi AK kidoul dioulite
Kouko bayi yéfére nga. Té Aussi diouli dou wathie kéne a moins que nga ame problémou khéle wala nga néke di nélaw wala nga guiss bakh. Diouli dou wathie kéne th koula ko téguil Aussi dafa rére wala nga beugueu koula nakh
😂wa dolélene maye ki mou wakh😂khana mom dou invité😂
Tounkara amo xam xam
Xam xamou mahrifa la!!!
ioe momou ya khamoul touss séne leep bokalé leu
Mbavo Tounkara. 👏🏾👏🏾👏🏾
Tounkara est trop fort
QUI DALE DOU DJOULITE CEST PAS UN MUSULMAN REFUSER DE PRIER CEST REFUSER DE SE SOUMETRE A DIEU
pape malick mbengue meuss nga guiss kou djouli ba texé? soko guissé wonegnu firndé bi... lo waxati gnu topp la... jugement yalla ko mom du ioe dou mane nagnuy sabablou rek tey diamou sunu borom numu gueuna sellé...
waxma nax meuss na ame koudoul diouli tékhé
waxma nax meuss na ame koudoul diouli tékhé
tehei yalla ko mom nagnuy sabablou tei rafete ndiort... wadji il a le merite daller chercher l savoir et dessayer connaitr le seigneur c mieux de se dire musulman tt court di nane di agresser di def lou bone...
Je suis daccord avec toi diouli si lei lep nekk moy carte didentite dioulite
Bilahi tounkara niaméwoul,Koudoul diouli yéfeur nguaa point barre.ki wakhoufi dara,ay jeu de mots lay def
Mane Senegal chaque jour ma gana décourager . Bokkalé ak fene rek souba ak ngone. Tounkara niemewoul limouy wakh..
serigne touba rereul nia niou bari!!
tounkara démal xami yala mo gueun dé barké Cheikh Tidiane limula wakh deuguela
Vraiment ce yalla yalla est fort
kou bakh bayil liguay wakh
Délires théologiques... Des deux côtés !
Mouhamed ndiaye xam xam gua wakh lepp ligua wakh xam xam 🙏🏿🕊️🕊️❤️🙏🏿🙏🏿🙏🏿
LAHILAHHAHH ILALAHH ☝️🥰
لاإله إلا الله محمد رسول الله صلى الله عليه وسلم. اعوذ بالله أن أكون من الجاهلين
deugeuleu bayfall doudeul sa doundou tagua bay lenn wakh guou beurii rk la lenn baye khamall lolou la ndiambe wakhon kham nagnou yalla mai khamougnou lignouye diamo yalla diamou yalla moye tawhide mahrifatoull billa bokoull akh tawhidoul illahiyeu tounkara di app khaamm da guoumbeu teuhlou
rew passe woul toudou yalla di saga si comentaire yii
Dieng Rek
Non dou rew de rere mbiir ak niaka xam Yallah dong moleen diam
Bane symbole bene symbole amoul Sénégal seul Rassoul lah
Franchement je suis avec les yallah yallah allahou akbar ☝️🙏alkhourane khadioul thi boppou khathie 😂
Ganaw Xalei bu majeuroul ak Nitt Kou taggoo ak sagoom képp koudoul Djouli doo Djoulitt....Un point c'est tout
mame danna dioulli
Wakho degue
@@khadimmbaye8682 wakh na dege kay
@@mamadousene2011 wawaw
Tijanya walay wakh nga deugue lolou késsé mognou outeulé ak yénéne diné yi
Loumouy togne serigne touba rk moma metti, serigne bagne wakhtou diouli wessouko , motakh mou diouli si guedj gui .
😂
Danga khamoul Yalla motakh nga djap ni mingui togne SERIGNE TOUBA. Wayé li SERIGNE TOUBA woté rek lay wakh
En tout cas , d'accord ou pas le gars a dépassé Tounkara de loin coté arguments. Tout ce qu'il dit peut etre choquant des fois mais il a des références solides et même il soulève des interrogations pertinentes que le journaliste refuse de considérer. En tout cas moi je ne dirai pas qu'il n'est pas un musulman. Et je crois que tout le monde devrait faire idem. Et je vous invite même à lire la sourate Kaaf lorsqu'Allah (swt) parle de Moussa et Dhoul Kharnaine. On voit le paradoxe que suscite la confrontation entre charia et akhikha. Salam à vous
Ecoutez ce qu'il dit à 22:43
Li yeufou saytané la
Djitayou seytané la
Ndax wéraytéla
Daniy fen gueumoun S Touba
Machalah trei interessany
Machallah bayfal ya deeg tu es le meilleur tu donne des leçons forts
Merci Tounkara
Tounkara safara direct
وقال صلى الله عليه وسلم إن أول ما يحا سب به العبد يوم القيامة من عمله صلاته فإن صلحت فقد افلح وانجح وان فسدت فقد خاب وخسر dolit dall moy ki dioli
@@seckndanane9523 yako fay ndieuk dh ioe
C gas haute niveau laye wakhé❤
En tt ka sur le débat le gars reste victorieux devant Tounkara
Yalla dafni khama Lou djitou ngamay diamou
@@mouridoulakhi6304 kan moy kham yalla?
Woor akk djilli.....Yomboul dé😂🤣
Wadji kou yabate la diangoul ba paré Di reuy lamigne
Lima si mety rk Serigne Touba AK mame cheikh Ibrahima fall bouniouy mbobou rk😭😭
Trop fort mouhamed ndiaye, yallah daniou âme dégue dégue pour comprendre l islam. Niveau spirituel très élève... Toukara essayés de comprendre... Ça m'étonnerai que tu comprend.
Mouhammed Ndiaye mi limouy wax xamouci dara
😂😂😂😂
Vraiment qui vrai mouride leu
Machalla 🥰👍
Tounkara est dépassé par son invité ,diadieuf baye Fall degg yalla rekk mo woor ❤
j'aime bien tounkara
Lou takh
Tres bien tounkara longue vie a toi
wadji hamoul yalla walahi amoul xam xam boumou meuné défendr tounkara
naguoul nako yalla bou sett laye laye sarah
Debat bi néhena mashaalla 😅😅😅 djioulite dale djioulii wa salam
Merci Mohamed Ndiaye machallah
Su Koran amulon serigne touba dega dega nyu ne yonete la blie hi
C un super échange
100xplus fort que Tunkara.
J'ai aime ce debat !
Mé toukara amna sérieux problème
Accepte ce qu'on t'offre de raisonnable , commande ce qui est convenable et éloigne-toi des ignorants.
Khuthi al'afwa wa/mur bial'urfi waa'rid 'ani aljahileena
خُذِ الْعَفْوَ وَأْمُرْ بِالْعُرْفِ وَأَعْرِضْ عَنِ الْجَاهِلِينَ