Déjà nou mbeugeu wakh ni Modou lo pa la ibou lo mi khalé kon Modou lo tela mbeure rek mo takh wayé dou makk nak dafa man limouy def rek machala sama champion bi
Modou lô ❤yalna nako yalla maay weer ak fane wou goud mayko nieup bref à son grand frère responsable et respectueux 💕ki mom xamna xarangne lô oft mom Modou lô 👍dako yém srx
Limit wane ni modou lo xalé leu dou makk comme nimou koy waxé kii xam gani dou magg té moy magame machallah ❤ limoy des frères deggoo rk yaar dafa am solo
Boy Niang il est bien éduqué bamouy xallé ba légui ni la mel Sénégal comportement nek si niit gni Di Wax laniouy fog Kou am fiit té dou lolou deuk wax Moy Sénégal
Ñakk takk gualaac wuté na ak jëfëndiko musique....man ngua ko naan, man ngua ko diwo,man ngua ko sanguo, man ngua ko suul... té lolu yagg na ci lamb.ñëw té do takk dara du fi guléet. Di nguén fékkéwul lu bari rékk..
Sénégal Nio Nex bo dané nioulay xalab NGA danou niouné ragal la iow boy Niang mi meun Na deuk Pikine Di don ragal 😅😅 waxal lénén wayy sport kou dioumoul do danou
Gayi il faut qu'on se dis la vérité iow meuno ni dagay doundou souna ba paré nieuw soumékou woné sa thieur ba paré niou tog nann ibadou té Lamb bokou si louniou sippp Sénégal nio Nex 😂😂😂 🤣 bou féké beug Na nek diamou Yalla bou sel Na bayi mbirou thiakhane
Pareil contre ama j ai rien mangé je ne l ai même pas regardé contre boy Niang j ai pas mangé mais j ai tout suivi Contre Bombardier je ne l ai pas regardé contre balla pareil
modou il doit arreter juste pour palmares bi rafete wayé boufi togué di ame ayye 8 defait comme bombardier mome moy lolou , focalé bakhoul te manne bokouma mou danou na arreter koi amena palmares bou bakh..
Sorry ibou lo Il y a rien d'anti sportif sur l'acte de boy niang au face to face. On n'est pas dans des bureaux, c'est du sport. Et autre chose Boy niang ragaloul modou lo.
Qui doff la sa communication zero modou khanala legui guenn wahh civilisation deguenn meune khassté wa parcelles khana legui deguenn donn Beuré sene bire yenn geune doff gneup😂😂😂😂
Machallah nioune wa Italie modou rek laniouy top yalla nako Yalla lafale thiate ❤❤
Machallah modou yarou moko may li yeup ak kham adouna .
Diot na mbeur yeup dieul
Si mom exemple franchement
Grand Hibou Lô, wakh nga deugueu dé, ya gueunone siw Modou. MERCI pour sa takhaway ak sa beugueu ASC Jant Bi ak unité 10
Machalla modou lo
Machalla modou lo ❤❤❤❤🎉🎉🎉
Machalla ❤Modou rek
Jajeufeti lo grand bou bakh machallah ❤❤❤ one love grand
Bilahi grand Ibou Lo mo begoon Asc Jant bii , un grand supporter depuis temps niom Maldini paco Diaz Aris etc...
Machallah wakh dji rafétna ❤
On veut l'interview de yekini ou centant gningue
Déjà nou mbeugeu wakh ni Modou lo pa la ibou lo mi khalé kon Modou lo tela mbeure rek mo takh wayé dou makk nak dafa man limouy def rek machala sama champion bi
Modou Di xale bou ndaw xale mom topoul sax si ki xalebou djigen bi nek Amérique la topou anta lo
Kimoye papaye petit lo wala
@@dakardk4750non ibou diouf moy papam moy sén taw
Khana guisso anta lo mon mak. Modou lo Modou khalé bou ndaw la😂
Non dou ki deh magou ki moy papay petit@@dakardk4750
Ibou sama mbeur mi mola dakeu deih 😂😂 laf thiate a modou lo yalla nako yalla lafal thiate thi barker serigne Babacar sy 🙏🙏
Gran ibou Kool gran
Modou lo xale la de❤
Yallna sé diamou yageu
Modou Lo Messi de la lutte sénégalais bene natou la ame si lamb mouy balla Gaye modou Lo plus fort que balla gaye
Mohhh ins bobou papam ak tourondom gnoko done diapalé rek si mystique mais Modou moko meune, gni daane balla yep dane nalene
Macha'Allah
Modou lô ❤yalna nako yalla maay weer ak fane wou goud mayko nieup bref à son grand frère responsable et respectueux 💕ki mom xamna xarangne lô oft mom Modou lô 👍dako yém srx
Modou rek❤❤❤
Kou fadjaral sa papa yalla fayela bou bakh merci Modou 😊😊
No lolou pour nehal Comba rek boy NIANG Amoul benn problem dafay lamb rek mes bou diekheeee diekh na
Limit wane ni modou lo xalé leu dou makk comme nimou koy waxé kii xam gani dou magg té moy magame machallah ❤ limoy des frères deggoo rk yaar dafa am solo
Modou topoul si mom sakh anta lo sila modou topou
@@KANEBOUSEYDIAHMEDTIDIANEmerci beaucoup lo lou la bagon wakh 😂
Way yow boussi sonou lignou bagna dégue balla mo makk modou lo lolu dara douko dindi
Tek sii Modou topoule si môme
Machalla mbeur❤❤❤
Boy Niang il est bien éduqué bamouy xallé ba légui ni la mel Sénégal comportement nek si niit gni Di Wax laniouy fog Kou am fiit té dou lolou deuk wax Moy Sénégal
Abdoulaye sylla moy yone wi le profil parfait pour le senega
Nico bro❤❤❤
Modou da am kilifa respecté ay magam diam rk lay amm
Ibou Lo Borom asc Diantbi 💛🖤
@cheikhsow7503 bilahi grand ibou Lo kou beugone nawétane AK Asc Jant bi
Ah modou khale la kon
ki moy magou ragne khagne ? Kone semeu wa dji décéneu aïe combat you beuri sakh😊😊😊😊
kui Modou lo topoul sakh si mom kui anta lo motopa si mom
Kokou talibé cheikh la tamit
Pikine lo ❤
I’m from PA bokk jeef 💙🤍
Ñakk takk gualaac wuté na ak jëfëndiko musique....man ngua ko naan, man ngua ko diwo,man ngua ko sanguo, man ngua ko suul... té lolu yagg na ci lamb.ñëw té do takk dara du fi guléet. Di nguén fékkéwul lu bari rékk..
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😊
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Sénégal Nio Nex bo dané nioulay xalab NGA danou niouné ragal la iow boy Niang mi meun Na deuk Pikine Di don ragal 😅😅 waxal lénén wayy sport kou dioumoul do danou
Ki magou modou lo la Mais modou lo khalé la dé
❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉
Modou xale bu ndaw la
où est birame gning ?
il est malade
Kidou papay petit lo waleuh ???
Yalla nalene thiate seylou
no no dou kui des ko kou ak Modou lo yay lagn boko
@@MamadouThiam-ho7gi ah d'accord merci beaucoup
🥰🥰🥰🥰🥰
Mola guene bady
Ki mo mag assane magou boy Niang 2foi
Mais modou si anta la topou mo mag boy Niang mais dou fouf dé
Gayi il faut qu'on se dis la vérité iow meuno ni dagay doundou souna ba paré nieuw soumékou woné sa thieur ba paré niou tog nann ibadou té Lamb bokou si louniou sippp Sénégal nio Nex 😂😂😂 🤣 bou féké beug Na nek diamou Yalla bou sel Na bayi mbirou thiakhane
Tieuy yaw yaw yagui déf lépeu lou nékh yallah ???
Ibou lo mi xana beugoul niarél
beugge na dh
😂ak mane
Danga beugeu Mou niarél leu😂😂
Lambe nga😂😂 kay ma defela awo
Domou baye ab ndiéyene dou niakal bopam fayda dh
Pareil contre ama j ai rien mangé je ne l ai même pas regardé contre boy Niang j ai pas mangé mais j ai tout suivi
Contre Bombardier je ne l ai pas regardé contre balla pareil
Boy Niang geuneu civiliser Modou lo
Ya meune doule 😂
Yawwww dagual fene rekhhhh
Katal sa ndey yarou😂
Mocvcvcbcbcbcv❤
modou il doit arreter juste pour palmares bi rafete wayé boufi togué di ame ayye 8 defait comme bombardier mome moy lolou , focalé bakhoul te manne bokouma mou danou na arreter koi amena palmares bou bakh..
Bombardier 11 défaite la am
Sorry ibou lo
Il y a rien d'anti sportif sur l'acte de boy niang au face to face. On n'est pas dans des bureaux, c'est du sport. Et autre chose Boy niang ragaloul modou lo.
Ki magou modou lo bi dof la yaw khat gua
Qui doff la sa communication zero modou khanala legui guenn wahh civilisation deguenn meune khassté wa parcelles khana legui deguenn donn Beuré sene bire yenn geune doff gneup😂😂😂😂
Nanal ndokh😂
@@BarkhameDieng mann AMDY MOUSTAPHA TINE mou sa mbeur 👑👑👑rec🤣🤣
Mougneul yaram massa😂
Daw lakou nga pikine nga daral😂
@@BarkhameDieng pikine moy REAL MADRID trophées yeupe la ame🤣🤣🤣
Pikine lo ❤