Saida Binta Thiam -Live - Grand Théâtre - YAA RASSOULALLAH
HTML-код
- Опубликовано: 5 фев 2025
- Bienvenue sur la chaîne officielle de Saida Binta Thiam !
Explorez l'univers fascinant de Saida Binta Thiam, une voix emblématique de la Musique Afro-Arabe, qui allie tradition et modernité. Originaire de Casamance, Saida rend hommage au Prophète Muhammad (SAW) et aux sages du Sénégal, tels que Cheikh Elhadj Malick Sy, Serigne Touba, Cheikh Ibrahima Niasse, et Serigne Cheikh Ahmed Tidiane Sy Al Maktoum, à travers des interprétations profondes et émouvantes. Avec son orchestre Firqatu Ahmadiya, elle crée une expérience musicale unique qui touche l'âme.
Cette chaîne vous propose des clips, des performances live et des moments exclusifs, célébrant la richesse du patrimoine culturel soufi. Pour toute collaboration, n'hésitez pas à nous contacter à ahmadiyaevents@gmail.com . Suivez-nous également sur nos différentes plateformes et abonnez-vous à notre chaîne RUclips pour ne rien manquer de notre aventure musicale !
RUclips : / @saidabintathiam
Facebook : www.facebook.c...
Instagram : www.instagram....
Tiktok : www.tiktok.com...
Sy Malick les cœurs ❤️ qui ne battent pas pour toi sont des pières. Yalna yalla fayla sa thiono ak sa yèné🙏🙏🙏
Vrai
Saïda binta, kén dou yow cii miim reweu, chanter un discours, ouff tu es extraordinaire ❤
Machallah seyda binta mariama yalna yalla fayla yiwe di barké Serigne Moustapha
Moustapha Sy Rëuy ngaw fit’ak itté, rëuy ngab xol té rëuy nga jëuf it
Rëuyub yar’ak juddu, rëuy ndam, rëuy ngëurëum, mata naw
Tabaarak’Allaahu yaw guémiñ gu bon na la moy
Té moy sa këur, moy sa waa këur, moy julit ñi la ëuw
Macha alla kou bakh ga yéw yalla na la yalla défal diam
Comme kou nek aljana rek
dieureu dieuf gorgui al moustapha❤❤❤
Le cœur de Serigne moustapha sy en ce moment ❤️❤️❤️❤️❤️oh
Frigo rek AK beugeu yonnentebi motakh mou fentt li
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mach'allah yalna yalla dolli samou kilifa gui tè goudal fanwi soxn bineta thiam ohhhh yalna yalla weural baatbi❤❤🤲🤲❤❤❤❤❤❤
Bilahi soumakay sétane sama yarame day daww ndakh thiofél gui ma am si mom😢😢
Man actuellement dama gisoule kou melni mome si Afrique yalla xamnako yalnako yalla gene sammou
Seydi mouhamadoul moustapha sy ak maktoum yalla sunu borom doliko sutura ak tawfekh inchallah
Diarama Sy Malick. 💖
Yalla na Yalla gouddal sa fan té may la wër incha Allah 💖
Diarama Sy Demba yalna yalla yokou goudou fane weur ak weurlé inchallah si barké seydina Mouhamad psL 🤲❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Macha'Allah seyda Binta Thiam notre fierté
Liiii yomboul wayé sayitté yeup moy bégueul sanguebi
Yalla na yalla samale niou Serigne Moustapha
Ayy djoy rek la desé 😢 sy Malick ko dondouwoul yalla tegou ko lokho ❤❤❤❤❤❤
Ay waay sougnou khol sed na si yaw seyda yalla na yalla fay la si barké goorgui
Manchia Allah Yalla na yalla na yalla barkèl Thi barkè seringe Moustapha Sy ❤❤❤❤❤❤
Yalla n'a yalla sam ta samal leu GOROU CAPITAINE Jaaramah ♥️♥️
❤❤❤❤❤ Machalla ya zeyda sayo gnianwer rekk mou guenna nekhh sounou Gorgui Yalna ndoundou 500ans you commencé taye inchallah
Guddu fane ak weer sy Malick seyda yalna yalla weral bate bi❤❤incha allah
Saida Bineta fessal gua sunu khôl yi alla rawatiii bou sougnou kilifeu Seydi wa Mawlaya ❤Seyda Dieureudieufffff❤
yallah na yallah mayco dolyco may bayico sunu kaname inchah allah
Seyda Binta lagnou beugue ❤
Amna ko xamni bokoy woyal dangakoy def si khaalam❤
Mbécté mimaye imaginer né moom la Goor gui am si lii billahi mootakh meunouma Contrôlé sama boss waay seyda doundeul wereul sissa euttou kilifa inchallah ❤❤❤
Machalah yalla naniou yalla samal sonou kilifeu gui mou yague fii loo ❤️🤲
Maachaa Allah. Am na solo lool. Longue vie à Serigne Moustapha Sy.
kéne dou gorou capitaine walay ndeysanne kéne rk ngua si nioune bilay niola beugeu way diarama serigne Moustapha SY🥰
Allahou Akbar❤
C’est la meilleure de l’année🎉🇸🇳
Le son est top, le rythme envoûtant et la voix de Cheikh Mouhamadoul Moustapha Al Maktoum qui vient tout édulcorer💯🎊
Sayda Bineta Que Le Bon Dieu vous accorde une longue vie et toute votre équipe 🤲🏻
Cheikh Mouhamadoul Moustapha Sy Yalnaniouko Yalla Fayal 🤲🏻
Yalna ñepp am Jamm ak Sutura Bi Barakati Nabiyil Moustapha Sallal Lahou ‘Aleyhi Was Sallam ❤❤❤❤
Diarama Serigne Moustapha sy longue vie ya Saïda Binta Thiam oustas Thiam dieuredieufe
Ohhhhhhhhhhhhh❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
الله أكبر
يا رسول الله كنت أنت رمز الشرف الإنسان .... يا رسول الله أعطيت للعيش قدرا.... 😢😢❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
CHEIKH SEYDI MOUHAMMADOU MOUSTAPHA SY AL MOURCHID YALNAKO YALLA FEY
Yalla Samal gnou Al Moustaphal maktoum laxal gnoko fanga laxe Sa bopou 🙏❤️❤️❤️
Ku kénn amul fayam ❤❤❤❤❤goru kapitéén gi yalna ko yalla fay
Diarama Serigne Moustapha Sy Malick yanala yalla sam arla defala goudou fane ak weer
Merci infiniment q vous et merci aussi a cheikh Mouhamadoul Moustapha sy Al khoutboul Maktoum wal barzakhoul Maktoum ❤
Diarama serigne moustapha sy malick❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Saïda Binta yalla nga goude fan té am wér ninga sérélé xollyi ❤ Yalla Nala yalla séral sa léppe té wéral battbi❤❤❤
Machallah ♥️🫶 diarama serigne Moustapha sy yalla nafi yague té wér ♥️♥️♥️♥️♥️🫶
Diarama Serigne Moustapha Sy Al maktoum walahi watalahi amoulo morome Sy Malick goudeul ay fann wéreul yague fi Loll té ande ak wérr ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤sat yalla djiouli thi yonentabi Serigne Babacar sy d'où morom
Machaala Saïda Bintou yalla ne yalla weula batbi❤❤❤❤
Mâcha Allah Seyda Binta Thiam. Magnifique. 💖
Oooh Serigne contann na ❤❤❤
صلاة وتسليم يفوق على مسك 🤲 ورند على ذي الفضل والكرم
Diarama Serigne Moustapha sy saïda binta Thiam dieureu dieuf ❤❤
oh khol seed na sougnou goor gui yalla nafi yag té am weer
يوم المرشد
يارسول الله
Sy demba doundeul wereul yalla samla aarla bayila ak nioun❤❤❤❤
Machallah Machallah Machallah Serigne Moustapha doundall wërall ❤❤❤❤
Amna solo ❤❤❤❤ barké boroom touba
La meilleure de sa génération
Amoul morom si limouy deff ni comparation
Ohh li nekhna sy malick yalna yalla guodal sa faneu,❤
Mach'allah yalna yalla sammula té àrla 🤲❤️❤️❤️📖❤️❤❤❤❤
Diarama Sy Malick yalnala yalla sammou arla si barki seydina Mohamed psl inchallah ❤️🥰
Diarama Serigne Moustapha Sy Al maktoum❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je sais pas si c'est ce sont les instruments, la voix ou le temps mais vraiment c'est du haut Niveau, ça transcende vers les multivers ❤❤❤❤❤
Sayda binta thiam yalnala yala fay yiw nèèkh na lool thi khol
❤❤❤Ho Macha Allah yalna Yalla def niu deug deug ndiambot
Seyda bineta yalna yalla weural baate bi si barké Gorou capitaine
❤❤❤❤❤ manchallah
Seyda guoudeul fane sey wey nimou mey def 🎉
Ndeysane Gorgui yalha na yalha motali incha'alha bayi lafi att you bari sunu kanam Sy
al maktoum mi est ce que nit leu ndaysan yalnako yalla fay way
Diarama Serigne Moustapha sy❤❤❤❤❤❤al maktoom❤❤❤❤
Yalna fouf bayam fane. ❤ Sy lou yaye baye aki bok meunoul ci nioune def gako ci nioun
MACHALLAH SY DEMBA YALNA YALLAH DOLILA KARANGUÉ AK SOUTOURA
Haassaal Karim Ibnoul Karim
Laahoul Karim Yallay Karim
Moustapha Al Karim
Moustaphal maktoum Mu Sell Mi❤
Machalla diarama serigne moustapha sy almactoum sama serigne ❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah Seyda yalnala yalla samm🙏🙏❤️
yalla na yalla barkél té samou ❤❤❤
Juste incroyable ❤😢Merci Seyda ❤
اللهم صل على سيدنا محمد وعلى آله وصحبه أجمعين ❤
Yalna yalla barkel
Machalah maman yalla doli wér ❤❤❤je t'aime
YALLAH NA YALLAH WERAI BATBI SI BARKE SERIGNE. MOUSTAPHA SY❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ohhhh nekhna torp ❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Machaalla dal loudiogué thi ❤thi ❤rék lay délou ❤céd lol❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
YAA RASSOULALLAH ❤❤❤
Salam.Mashalla from middile east muslims.
Xole yeppou seddna billahi wallahi
Allahouma baarik ❤❤❤❤ ya seyda xol Yep bek nagn
machAllah Ya RASSOUL ALLAHOU
machallah
diarama serigne moustapha sy al mactoume
Machallkh sayida Binta Thiam yallna yalla yokou ba yeuko inchallah ❤❤❤❤
Sy Demba doudal wéeral notre père spirituel ❤❤❤
Amou'gnou sa Faye Sy Malick'
Mashallah yalla na yalla ❤weralsene bate
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Dieredieuf Tata
Machalla la reine❤❤❤❤❤ des Musik afro Arabe ❤❤❤❤
ماشاء الله سيدا مريم بنت تيام وينادونها في بلدها أم كلثوم سنغال هي فنانة برز اسمها في مجال الإنشاد الديني باللغة العربية ❤
Merci Tata binta يا رسول الله ❤❤❤❤
Giorgio Binta Thiam bouy weuy day bék machalla
yale yala contane si yow seyda binetou inchalla
Machallah Saïda Mariama binta thiam yalna yallah fay yiw si barké gorgui
Machallah ❤️❤️❤️ diarama Serigne Moustapha 💖💖🫀
Oh Macha'alha Macha'alha tata binta
Diarama s’y Malik ❤❤❤❤❤❤
Machallah Saida sougnou soppé bi yalna yalla fayla 🙏
جزاك.الله.خير وكل عام وانتم بالف الف الف مبروك
Tata Binta contann nan ci iow