Foule immense, Doukatt.... Sokhna Aïda DIALLO a encore frappée fort... " Nioun Thiantacoune yi..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 20 янв 2025

Комментарии • 116

  • @mbayekante5430
    @mbayekante5430 4 года назад +12

    Seytané mannaleen wayé sëriñ bi d seytané manoul ci mom dara yalna lenn yalla soppi ta gindi leen

  • @minachoco2831
    @minachoco2831 4 года назад +4

    Bayi léne sokhor way sokhna Aïda défouléne dara loutakh bonne ymt

  • @modoufall8127
    @modoufall8127 4 года назад +2

    Allahou akou barr astakhfiroula thieey yalla barkep s touba linakhar monouko wéssou bilahii

  • @mariamaba1915
    @mariamaba1915 4 года назад +5

    Yallanagnou yalla moussalthi saytanne

  • @sokhnandiaye5152
    @sokhnandiaye5152 4 года назад +10

    MACHALA RAFETENA THIOUNE NEKHNA TROP YAGUE LENFI TE WERE MACHALA 👌💖🧚‍♀️💖🧚‍♀️💖🧚‍♀️💖👌

    • @sublimesublime7632
      @sublimesublime7632 4 года назад +3

      Dieureudieufety signe BETHIO ya niou sagual dh thioune 😍😙li AMOUL

  • @ousmanebeauetsage8173
    @ousmanebeauetsage8173 4 года назад +5

    Sou président Diayonne sénégal mou diohma sama walle ma dème Rwanda dinama nekh rewou Shaytane Sénégal la.

  • @abipefaye
    @abipefaye 4 года назад +8

    Vous qui disez du mal a aida diallo vous etes mécontant Aida a plus de valeur a vos marabouts mourites quelque soit alfa Aida diallo a du mérites

  • @khadydiallo9721
    @khadydiallo9721 4 года назад +10

    Adja pene ya wayadi amou sa gueramou dieukeur bamou dème.gua topou sa woudiou di talal sa lokho moulay gnanal

  • @thiantaconebafawwwpro3264
    @thiantaconebafawwwpro3264 4 года назад +9

    Mane gnii bagne soxna sii rékk la yereume blh ya aida nékhou taa bagne dhé

    • @infosclairtv439
      @infosclairtv439 4 года назад

      THIOFÉL SII SOXNA SII PRO même mane beug nako mais c’est pas normal de tout c’est qu’elle fait 😢

  • @moisek147
    @moisek147 4 года назад +10

    LAHILAHA ILLAH MOUHAMADOU RASSOULLOULAH PLS AIDA DIALLO THIABI YAYE DOMOU HARAM DEUGUE SA SARAP NDEYE DEUGUE YI GORE AK POLICIER DOMARAME YOU GNIAK FAYDA DI TAKHAW SI BIROU CHAYTANÉ MÉLNI DOU GUÉNE DOMOU SÉNÉGAL PEUL BOU TÉGAL NDÉYA DIOGUÉ GUINÉ SÉNE GATE DINA DAGUE INCHALLA YA SA BINDANE YI RAYE RÉK MO DAGANE SI YÉNE SOTI PÉTROLE TALE YÉNA ALY GUOUYE N

    • @mabiguekebe5750
      @mabiguekebe5750 4 года назад

      Ki bayi ngako sax mouy nirou ak diabarou iblis ni

  • @zeinabrassoulndiaye6782
    @zeinabrassoulndiaye6782 4 года назад +6

    Comment cheikh bethio doit se sentir présentement devant ALLAH et tout les saints il ne doit pas être fier de lui en tout cas c sure
    Li lep moko prôner won di togn yallah aka soufell lislam ak younou mouride biss bou nekk teih dou diekh ba adouna di toukki
    Chaytane deugu moy kii wallahi

    • @mohamedfall6154
      @mohamedfall6154 4 года назад

      zeinab rassoul Ndiaye Diadieuf sawaye. Le vrai diable qui est en enfer à nos jours c’est Bethio lui-même. Le diable en question.

    • @boussodiouf5206
      @boussodiouf5206 4 года назад

      @@mohamedfall6154 kattal sa thiottou ndaye

    • @boussodiouf5206
      @boussodiouf5206 4 года назад

      Sa leufeul ndaye

  • @aminataseye9013
    @aminataseye9013 4 года назад +6

    Machallah yalagafi yag ta wer Thioune

  • @seynibarro7244
    @seynibarro7244 4 года назад +1

    Yale nako Yale sopi tai taikniou si yonou djoub Amine

  • @oumarsamb7408
    @oumarsamb7408 4 года назад +6

    Dieuredieuf thioune nioune ak yaw bâ faw nioune yaw laniou gueume yaw laniou SERIGNE BETHIO boléle

  • @designsafart59
    @designsafart59 4 года назад +4

    Ki souyy wakh sakh gua khamni dafa pank ba deugu ndayam.

  • @sokhnandiaye5152
    @sokhnandiaye5152 4 года назад +5

    LI DIAMME REK LA SI GUISSE👌💖💖💖💖👌

  • @diopabdel3780
    @diopabdel3780 4 года назад +1

    Aida diallo daafa mol déh. Koumaaay mettre en contact ak mooom.

  • @ibrahimkane1091
    @ibrahimkane1091 4 года назад +4

    miim Réew Sokhna Aida Diallo Thioune moko mome😂😂😂😂

  • @aronawassa8352
    @aronawassa8352 4 года назад +1

    Man lima mèty moye Sénégal dafa Bari aye sayetané ta dounou wakh linou wara wakh bén yon wayé kidi sokhna Aïda Diallo défoule Dara loudoule Diam ak salam

  • @fatoumatadiao5032
    @fatoumatadiao5032 4 года назад +1

    Deysane yalla n'alene yalla tek si Yonne bou dioubb diyguenn sans kala seytané diayy na lenn

  • @falugningue5849
    @falugningue5849 4 года назад +1

    Soknna ayda mala begue lool way

  • @mourabiyatv4951
    @mourabiyatv4951 4 года назад

    Hé aïda Diallo ya réw té mana féne yaw yonénte bi ngay fénal yaw danga torokh

  • @diadam6449
    @diadam6449 4 года назад

    aida god protect u

  • @infosclairtv439
    @infosclairtv439 4 года назад +5

    Cela prouve que le Sénégal 70% ne connaissent pas leur religion, comment suivez-vous une femme qui ne sait rien de sa religion c’est honteux😢

  • @babacartoure1356
    @babacartoure1356 4 года назад

    mashahalla

  • @babacarmbaye4203
    @babacarmbaye4203 4 года назад +1

    Aï-dadial-lo

  • @Innovation-Mouride
    @Innovation-Mouride 4 года назад +1

    Seytané moléne Selem ake deurem ba ndiou fare gueleum

  • @xassaïdtv
    @xassaïdtv 4 года назад +3

    Siy fèn rèk guèn nèk wayè nak yonou mouride dara manouko yakhe.

  • @alioudiop3308
    @alioudiop3308 4 года назад

    Serigne cheikh aida Diallo mom amna borom keur wala 😀

  • @mallbelly8250
    @mallbelly8250 4 года назад +8

    Wakhone naniou mime rew bamba ko moom waye leegui ayda ko moom😂😂😂😂😂😊

  • @boussodiouf5206
    @boussodiouf5206 4 года назад

    Kou guiss aïda Diallo dem aldiana aywaay wane len ma aïda waay 😁😁😁😁

  • @mbayekante5430
    @mbayekante5430 4 года назад +1

    Yalna niou yalla mouseul ci ak worou nakh worou kat moy indi reer

  • @gueyemoustapha2376
    @gueyemoustapha2376 4 года назад +2

    Aka toye

  • @sopebayamesanteyayame5397
    @sopebayamesanteyayame5397 4 года назад +1

    Nooo wa khana khalif general bi guissouko, nooo sokhna ci nak mongui wonè doolème, regardè cè homme ki saccroupi devant elle.

  • @galasseck2891
    @galasseck2891 4 года назад

    Soubhallah thi li

  • @alfadl3202
    @alfadl3202 4 года назад

    Soubhanalla

  • @falouseke9631
    @falouseke9631 4 года назад +5

    Je ne comprends pas ban monde lan nék quoi yala nano yallah mouseul si saytani

  • @haddymbay4755
    @haddymbay4755 4 года назад

    ♥️♥️♥️💪🏾💪🏾💪🏾

  • @thiantaconefaaawww6593
    @thiantaconefaaawww6593 4 года назад +3

    BILAYE YAYE NDANDANE BISS BI NGA TRANSFORMÈ AY BOUDOULWONAK YAW GNIOU BARI SANKOU SANTNANIOULA BOU WERR

  • @miyatoure8073
    @miyatoure8073 4 года назад

    Li dekh moy ragall sakh moroumou djiguenne 🤣🤣🤣🤣 demme lenne topi si seurigne saliouw thoune moy deugue😅😅

  • @harrypotter2807
    @harrypotter2807 4 года назад +5

    Sokhna Aida Diallo damako beugue rekk t'es yalla takh

  • @maguette8141
    @maguette8141 4 года назад +2

    ils s'amusent

  • @ibrahimabadjiga7191
    @ibrahimabadjiga7191 3 года назад

    لعن الله صوتمرعت ولاو بذكر الله

  • @freshlova22
    @freshlova22 4 года назад

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️☝️☝️☝️

  • @blmtvtvblm3288
    @blmtvtvblm3288 4 года назад

    Zayda zamane +aïda Diallo +saïtané=.................? humme bakhna rék Sénégal guissa goun darra déssna yénnéne deukou diner bi légui lounék gaffé guiss

  • @mamadougalsene2003
    @mamadougalsene2003 4 года назад +1

    Yow ak nielawere yepe ayye aye Seytanegene

  • @xalaattvsamachaineprefere2129
    @xalaattvsamachaineprefere2129 4 года назад +1

    Démal wouti dieukeur 😂😂😂😂

  • @matydiakhate3607
    @matydiakhate3607 4 года назад

    Sa wakh dji kouko degu khamni neko thi degu

  • @lemelomanedelamusique4615
    @lemelomanedelamusique4615 4 года назад

    Mala fan

  • @falloundiaye8156
    @falloundiaye8156 4 года назад +2

    Do dara iow gnila top ak iow si gnabotou saytané ngéne bokou

  • @hamidouba5784
    @hamidouba5784 4 года назад

    C est théâtre ou bien

  • @Idyxaragnelo
    @Idyxaragnelo 4 года назад +1

    Wakeur Iblisse ☠☠☠💀👺👹👻

  • @serignefall8803
    @serignefall8803 4 года назад

    Baameu sakh mo lle neu guen bilahi dem lle neu rek

  • @talibeboromdarou6151
    @talibeboromdarou6151 4 года назад +3

    Si ndiabote bi dieum safara nga bokou
    Serigne touba daf la teré nga lank

    • @lachinoiseiniaasy9658
      @lachinoiseiniaasy9658 4 года назад +1

      Talibeborom Darou yaa mom saafaraa ba kham koufay dougou ou pas🤔Lii rek molène dessei Prendre la place de Dieu nama yalla ball sii kadddu bii

    • @labelle4941
      @labelle4941 4 года назад

      Serigne Touba moy yobu waté Aldiana? Hahahhahahaha foutaise !

    • @sopebayamesanteyayame5397
      @sopebayamesanteyayame5397 4 года назад +2

      Fi daal koudoul yalla do dara, yalla rek mofi nek, yalla fèp yalla partout.

    • @viplofficiel5353
      @viplofficiel5353 4 года назад

      @@sopebayamesanteyayame5397 Serigne Touba Moy Yalla

  • @ibrahimadieng693
    @ibrahimadieng693 4 года назад

    Li leep aly ngouye ndiaye moko waral ndah moko autorisation

    • @matyseckkgueye2612
      @matyseckkgueye2612 4 года назад +2

      Tu n'as rien compris sokhna Aïda moy borom gouvernement bi loumou beug day am

  • @lemzocanzo5406
    @lemzocanzo5406 4 года назад

    Man dh dinaneki serigne li nekh na dh te khamo dra

  • @wakeupafrica9906
    @wakeupafrica9906 4 года назад +6

    Mouride Yi Légui Dañio Bayi Sén Yone Kén Yaboulén Wone Mais C'est Domage legui.

    • @diouplenekhothieulernagneu3343
      @diouplenekhothieulernagneu3343 4 года назад +1

      Leckeu adiya kouko bayiwoul kenneu doula respectée

    • @wakeupafrica9906
      @wakeupafrica9906 4 года назад +2

      @@diouplenekhothieulernagneu3343 Louy Adiya.. Yaw xaamó dara bayil hors sujet bi.. yigga néké si site. Adiya mo defar Massalik Déffaar Touba do wakh si lolou.

  • @falloundiaye462
    @falloundiaye462 4 года назад

    Wa damay ladje vidéo bi avant Serigne bi diko ayé la wala après

    • @iallys56
      @iallys56 4 года назад

      C'ÉTAIT LE 14 FÉVRIER 2020 PASSÉ : SAINT VALENTIN

    • @falloundiaye462
      @falloundiaye462 4 года назад

      @@iallys56 dwrine Ibrahima mangi Ziar dila sante si léral gui mé li doyna warr dé kou tolné Serigne mountakha Mbacké wakhouma yonou mouride sakh mé gni bokou l islam ki yeupou nangoul naniouko abb bakham ak dioulitém ak talibém ak oyofam ak yéné yeupou diamou rawatina ngueuramou sounou borom ayéla Béne mbir nga lank rek né doko bayi ndakh adouna ndakh outoube mbollo wala daradja vraiment Sokhna si mane khamatouma si môme dara

  • @fatoubintoundiaye274
    @fatoubintoundiaye274 4 года назад

    waa lii nak louci pekhei

  • @designsafart59
    @designsafart59 4 года назад

    Aida diallo kou tothie khourrou ndayam leu domeram ji diou bonn dji

  • @pakeyarame9585
    @pakeyarame9585 4 года назад

    😮😮😮👀👀👀

  • @tallaka6303
    @tallaka6303 4 года назад +1

    Iblisse bég naa

  • @ndiayemilko8240
    @ndiayemilko8240 4 года назад

    Astafiroula

  • @moisek147
    @moisek147 4 года назад

    GNIAK KILIFA DIOURE SA DOME SAI MOYE LI DEUGUE

  • @fantadiagne6422
    @fantadiagne6422 4 года назад +2

    allez chercher des maris diamou yalla top ndigueulou serigne touba mo gueun

  • @diaaammmouuuurekkkkkkk
    @diaaammmouuuurekkkkkkk 4 года назад

    Kii dé khamm nguénn nii saytané bou fess déll labilahi barké serigne touba

  • @babacarcisse8110
    @babacarcisse8110 4 года назад

    domèram

  • @serignembackeboye1362
    @serignembackeboye1362 4 года назад +1

    Aida mi dé kham na kouko dioutalone lou bari gay am✌kham na leuf lou saff la wara yor😜 ba takh goor gnépou topouko ni😂

    • @infosclairtv439
      @infosclairtv439 4 года назад

      SERIGNE MBACKE BOYE sa tourbi masha’Allah.

    • @ibrahimkane1091
      @ibrahimkane1091 4 года назад +1

      aka toy mom rékk la nobb 😍😍

    • @serignembackeboye1362
      @serignembackeboye1362 4 года назад

      @@ibrahimkane1091 même mane aussi mom rék la nop😋et bén goudi rék la beugu mou may mako😜

  • @cheikhgaye2157
    @cheikhgaye2157 4 года назад +1

    Adia mi amna mbolo dal

  • @fatoukineloum7276
    @fatoukineloum7276 4 года назад +2

    Ioe xamgua lan molay dimbali alkhourane gui guay Def si sa thiant yi ak dioxé lek m sinon mom ça serait otre choz

    • @thiantaconefaaawww6593
      @thiantaconefaaawww6593 4 года назад

      Fatou Kine Loum heureusement nga avouè merci bcp

    • @viplofficiel5353
      @viplofficiel5353 4 года назад

      OK legui waxma Lou gueun lolu té boil fateii limou xassaide yii. Man mi di wakhak Yaw Lima mokal si xassaide amna niou barii niouy wakh mokalouniou 1/5 Bi. Bilay Sen Rouh Yi nangounagn sen xoll yi reka bagn

    • @fatoukineloum7276
      @fatoukineloum7276 4 года назад

      @@viplofficiel5353 sabou dou foot bopam fii nieupeu diangu

    • @viplofficiel5353
      @viplofficiel5353 4 года назад

      @@fatoukineloum7276 Dett Sokhna Si Niepp Djangouniou deii

  • @dlyt4209
    @dlyt4209 4 года назад

    yen ay domi seytane geun ndiabotou seytane moye yen

  • @amtiba4912
    @amtiba4912 4 года назад +1

    ESKEY Senegal
    Yalla nalla
    Musal Senegal

  • @cheikh7233
    @cheikh7233 4 года назад +4

    Guissou mafi diangale thiakhane rek lafi guiss

    • @thiantaconefaaawww6593
      @thiantaconefaaawww6593 4 года назад

      Cheikh Diagne yangui nèlaw bo yèwo ngay comprendre

    • @diopfati8505
      @diopfati8505 4 года назад

      Kii dafa rew billahi des nako yar say say deg mogui nii billlahi lima namo si yaw bòko kha mon ah

  • @fatousall9518
    @fatousall9518 4 года назад +1

    Diablesse

  • @mbayekante5430
    @mbayekante5430 4 года назад

    Onzoubilahi minal aida diallo akouk diapotam

  • @ibrahimandiaye3556
    @ibrahimandiaye3556 4 года назад

    Lou gueuna bone ti adina moy rére té nanguoni rére ngua

  • @bayeserignedjigale8774
    @bayeserignedjigale8774 4 года назад

    daf riw

  • @designlabcreativecloud9395
    @designlabcreativecloud9395 4 года назад

    Mdrrrrrr ): trop marrant ):