Accusée d’arnaque sur la maladie de sa soeur, Ndeye gueye @ttaque Adama sarr "ya meuneu doul mane…

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 20 дек 2024

Комментарии • 69

  • @Ummou2983
    @Ummou2983 13 часов назад +11

    D’après lima degu si l’autre fille et les commentaires
    Mais Ndeye dafay seuy et bim deuké si keur gou normal yagoul la fille mougui wax ni Ndeye rakam fim deuk bakhoul mais tmt Ndeye day seuy rakam di seuy kou dem bay seuy sa Djikeur molay dougal si keur sa mag sou amé diapale la gni wax wally loumi nderigne Ndeye Gueye wally dafa am famille tmt meunoul diapalé adouna bi yeup loum meune lay def
    Senegal metina

  • @gayafall
    @gayafall 15 часов назад +16

    Ndeye Gueye boul tontou . Le cancer ça demande des millions . Yallah nioun ci moussoul ci febar bi. Du courage .

  • @Khadyjasow-y8j
    @Khadyjasow-y8j 15 часов назад +21

    Bilay y’a niak classe ndaye pour man dépasser gua yi 😢je suis choqué

    • @fatouseck6386
      @fatouseck6386 15 часов назад

      Adama AK Awa ay sékh lagnou Aka gnon khame ndeye Gueye 😂😂

    • @Filibeye
      @Filibeye 11 часов назад

      😂😂😂😂😂😂😂

    • @dieyedieye414
      @dieyedieye414 8 часов назад

      Ki dofe la rék

    • @myamandiang
      @myamandiang 7 часов назад

      No senegalais dalay topou ba nga seuss

    • @serignecheikhsy4155
      @serignecheikhsy4155 4 часа назад +1

      Ndeye gueye defa amoul bene classe niek sa morome dome yii di wayedi sa bopp ni😢😢😢

  • @MaladoGenç
    @MaladoGenç 2 часа назад +1

    Merci beaucoup Ndeye ❤❤❤❤❤❤

  • @HassanatouDiallo-f8i
    @HassanatouDiallo-f8i 12 часов назад +14

    Oumou Sow chaque jour que dieu fais malaye gueun di sope ya ame classe meun sangnse bole pateu ak organise

    • @Filibeye
      @Filibeye 11 часов назад

      Oumou Garmi la

  • @thiabadiopgueye969
    @thiabadiopgueye969 15 часов назад +10

    Ndeye boul tontou❤❤

  • @cheickmoinga3245
    @cheickmoinga3245 14 часов назад +5

    Keep ku jooxul saa bopp yàllà doo mëssa aam mujju gu rafeet muk ❤
    TawhiidRekkaWóor ❤

  • @IssaDiop-w9m
    @IssaDiop-w9m 4 часа назад +1

    Senegal ama niokamne madouyougnou kennkounek amgua louladoy Sisa bir familles bayilene dougou si famille diko tass kounek amgua loula doy lomounoul lidianti soutient de families yalla moykoy def nit yomboul Ndaye Gueye yalla nala yalla diapale basa Rakdji wer ak Diame dougnou deme kene d’où deme sokhore nagne troop yalla nala may❤ mougne

  • @maymounandiaye5396
    @maymounandiaye5396 50 минут назад

    Ndeye mounienle yalla na yalla yégueuti sa raka yi

  • @amyrock4324
    @amyrock4324 10 часов назад +6

    AMO BENE CLASSE DOFF CIMMM

  • @user-nd2yx2qg7w
    @user-nd2yx2qg7w 14 часов назад +4

    Bilay ndeye mame mi gay topou nek si Internet di live di wakh lou yorr ak lou yorrout bagni tan yi daga bari wakh torop

  • @DiorNdiaye-i4o
    @DiorNdiaye-i4o 9 часов назад +4

    Ndeye Gueye boule toutuo

  • @anitabarry76
    @anitabarry76 6 часов назад

    Ndeye yow please teguoul ci sa yonne boul deglou ken koula sounal nga yobouko ci yone lolou rek la ❤❤👈

  • @stafiroulaha
    @stafiroulaha 3 часа назад

    Yako guéne thiaga ndaye Gueye toujours

  • @massambadiallo-dd4kf
    @massambadiallo-dd4kf 12 часов назад +2

    Vraiment Senegal metina legui doule rek kou nek loulla nekh

  • @HélèneDieng-e3n
    @HélèneDieng-e3n 8 часов назад +3

    Ndeye avec tte tes connaissances ngay tok si quête fait toi respecter amo ben classe

  • @bellabella521
    @bellabella521 7 часов назад +1

    Ndeye mo amoul classe

  • @KhadyFall-c8f
    @KhadyFall-c8f 7 часов назад +1

    Ndéye bayile Ki beuz la beugue stp adama sarre da pérte chaum

  • @fatouseck6386
    @fatouseck6386 15 часов назад +1

    Adama AK Awa ay sékh lagnou gnongui saint louis soy gnew gnouy dokhane sa ndeye

  • @Nana-o7e3x
    @Nana-o7e3x 4 часа назад

    Setal si ñila sop te yalla tax 😢😢😢😢 rousa ñila sop

  • @BeugNaby244
    @BeugNaby244 8 часов назад +1

    Ndeye Gueye ya beuri wahh ak sa hefff you gouddou
    Sa teint bi di melni poubbi lir
    Ya weerr sa boppou

  • @adjathioune3911
    @adjathioune3911 4 часа назад

    Ndeye Gueye daguay porté plainte.

  • @Filibeye
    @Filibeye 11 часов назад +2

    Diamoudjil Yalla li yeup amoul sens

  • @mohamedmbodj4271
    @mohamedmbodj4271 5 часов назад

    Wa ki dou goudi Dakar tiagayi améguéne Sénégal wooo séne diobou ndeye

  • @magiquesylla1600
    @magiquesylla1600 2 часа назад

    Gnàkk fayda + gnàkk class! Bavardage, cris, ...Piffff!

  • @Malicksindidi1988
    @Malicksindidi1988 8 часов назад

    Adama Sarr limou beugoon amnako a 100%

  • @mamediarradieng8550
    @mamediarradieng8550 15 часов назад +2

    Do pass fékk ko fimu nekk guenoul rapide 😮

    • @fatouseck6386
      @fatouseck6386 15 часов назад

      Ki day doul Adama AK Awa ay sékh lagnou Aka gnoko khame 😂😂😂😂

    • @fatouseck6386
      @fatouseck6386 15 часов назад

      Ki day doul Adama AK Awa ay sékh lagnou Aka gnoko khame 😂😂😂😂

    • @Filibeye
      @Filibeye 11 часов назад

      😂😂😂😂😂

  • @Filibeye
    @Filibeye 11 часов назад +2

    Fi dè so dialgatè yonn yonn douma la.

  • @okalsdiallo2443
    @okalsdiallo2443 7 часов назад +1

    Elle parle trop cette dame

  • @MoulayeLaroussi
    @MoulayeLaroussi 3 часа назад

    Lou sen yone sakh ,sénégalais mo begue détail jambour , du bayi say tonne baparé du topoto kilos diambour 😂 vraiment c'est bizarre

  • @NdeyemaremeFall-d6x
    @NdeyemaremeFall-d6x 42 минуты назад

    Adama kaye doul kate laa

  • @aminatadiaw9283
    @aminatadiaw9283 7 часов назад +1

    Sama dieukeur sama dieukeur bla bla bla puff... Mbeur you dof yi...

  • @nourradam6391
    @nourradam6391 6 часов назад

    Man ndey Gaye dangma nekhon wai sa kharito ak gorr jiguen yii moma nakharii,

  • @mariatavares5693
    @mariatavares5693 9 часов назад +1

    Bayi ko ak yalla kéne khamou la si lou ñiawe

  • @laminedrammeh9738
    @laminedrammeh9738 4 часа назад

    😭😭😭😭😭😭

  • @MamyGueye-q9o
    @MamyGueye-q9o 6 часов назад

    Ndeye gueye ki limou beugone ame nako diaroule tontou mome kéne khamouko digua takh niou khame ko

  • @KhadySall-b6q
    @KhadySall-b6q 3 часа назад

    Warooko woon tontou sakhe bakhou niou beugeu niou kou bakhe ndeye courage dafa meti wakhall la loo defoull

  • @AstouSy-f8i
    @AstouSy-f8i 5 часов назад +1

    Daniou wara mandou si famille diambour yi niouy douguou heuy mane Sénégal

  • @ndeyangom4982
    @ndeyangom4982 2 часа назад

    Ndeye stp boule tontou defale lila warr kou khalate lenéne sa affaires la c'est tout

  • @ibs335
    @ibs335 5 часов назад

    Mai yaw ya nafikh ya rew waye linga wakh deugeula weuyou nga yako wakh boye bila tak reck mo niak chance amo kilifa wayane reck ngene neke si rewmi ba pare di reuye lamine sofe

  • @Fari-h9j
    @Fari-h9j 7 часов назад

    Ne répond pas à sa c des détails

  • @MameMatySeye-q6m
    @MameMatySeye-q6m 5 часов назад +1

    Boule ko falle

  • @AmiSall-rn5ov
    @AmiSall-rn5ov 2 часа назад

    Ndeye baleko

  • @maremeNiang-k4k
    @maremeNiang-k4k 8 часов назад

    🤲❤️

  • @djibyndiaye8734
    @djibyndiaye8734 2 часа назад

    😂😂😂😂

  • @facolidiebakate1077
    @facolidiebakate1077 7 часов назад

    Demal ligueye niak diom

  • @Beugdeug
    @Beugdeug 9 часов назад

    Yafous khana si Lamb dji

  • @serignecheikhsy4155
    @serignecheikhsy4155 9 часов назад

    Ndeye gueye moy niak classe khol se morom yii amoul ben diom simm

  • @diopabass2598
    @diopabass2598 9 часов назад

    Noto sister tu perd de l energie

  • @MorCisse-i1o
    @MorCisse-i1o 9 часов назад

    Kéne ganoule way

  • @leytikane8704
    @leytikane8704 5 часов назад

    Yaw ya wara dokhane sa daye regla beugueugua gnou guisla trop