Magal touba 2018 La relation de mame cheikh ibrahima fall et ses compagnons contée par Baye adama

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 19 дек 2024

Комментарии • 147

  • @kamal313soxarxalimandiaay6
    @kamal313soxarxalimandiaay6 6 лет назад +21

    Baye adama yag fii tei wéér barké cheikh Ibrahim fall imamou koulou Mouridoulahi yawmal khiyamati ❤👌👌

  • @seydinaissafaye3850
    @seydinaissafaye3850 6 лет назад +4

    Machalla anii Sopey Cheikh Ibra Fall ❤👌

  • @ansumanacamara4195
    @ansumanacamara4195 2 года назад

    Jerreh Jeffeh serign touba ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @thiatenar6215
    @thiatenar6215 4 года назад +1

    Machalla khole ❤️ sedd na trop

  • @ndiayeousmane358
    @ndiayeousmane358 6 лет назад

    Machallah Bay Adama sarr yalnafi yague lol té werr

  • @ansumanacamara4195
    @ansumanacamara4195 2 года назад

    Jerreh Jeffeh serign saliou ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @sowalhaj6236
    @sowalhaj6236 6 лет назад +4

    Machallah wakhtane bi amna solo trope

  • @bayeamdyfaliloundiaye4313
    @bayeamdyfaliloundiaye4313 6 лет назад +3

    Akassa yagfi té werr baye Adama sarr sagoup mouride yep nga machala werna té lerna 👌👍

  • @ansumanacamara4195
    @ansumanacamara4195 2 года назад

    Jerreh Jeffeh sheikh ibra faal ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @louisediagne2006
    @louisediagne2006 6 лет назад +8

    Macha alla baye Adama sarr baye fall pire 💙

  • @absadiop2563
    @absadiop2563 6 лет назад +4

    Masa Allah's Nice amana solo dieureudief serigne Touba Mercie serigne Touba Vielen Danke serigne Touba grazie serigne Touba Masa Allah's Nice amana solo dieureudief

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia8992 5 лет назад +2

    Yalla nagnou Yalla defal diam
    Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke
    Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia

  • @falloudia450
    @falloudia450 6 лет назад +5

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke
    Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibé Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

    • @papatanordiouf1044
      @papatanordiouf1044 6 лет назад

      Yaram ziar naleu mbok di diegalou nak mane numero Serigne Ngor la yitewo dama yoratul warna matte at legui

  • @ansumanacamara4195
    @ansumanacamara4195 2 года назад

    Jerreh Jeffeh serign mountakha ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @ansumanacamara4195
    @ansumanacamara4195 2 года назад

    Jerreh Jeffeh serign falou ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @beuggeumjeufgoudikbamel6170
    @beuggeumjeufgoudikbamel6170 6 лет назад +4

    Baye adama yalla ngafi yagg

  • @lemeraidara536
    @lemeraidara536 4 года назад

    Legi dall yousoufa ak issa doug nagn si rang bi bayilén thiakhan serigne touba dé wakhol li radiya allahou anhou

  • @magammoseck8486
    @magammoseck8486 6 лет назад +2

    Thieye cheikh IBrahima fall lamp Machalla

  • @falloudia1016
    @falloudia1016 6 лет назад +9

    Wakhtanewi amatina sololool
    Yalla nagnou yalla defal Magalou diam ta gnou fekeko ay yoni yon
    Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke
    Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

    • @aliounepallambaye1210
      @aliounepallambaye1210 6 лет назад

      Vs etes prof d'anglais?

    • @mamadougueye5164
      @mamadougueye5164 6 лет назад

      Fallou Dia

    • @khadimgueye7166
      @khadimgueye7166 5 лет назад +1

      serigne Fallou Dia nianalma ma si barké serigne Mor Dia ndiar

    • @falloudia1016
      @falloudia1016 5 лет назад +3

      Yalla nagnou yalla defal diam ak khewal ak koorou diam ta gnou fekeko ay yoni yon
      Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke
      Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar
      Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

    • @Bouba8689-s3
      @Bouba8689-s3 4 года назад

      @@falloudia1016 amiiine sama serigne yague fi lol té and ak wer

  • @sambacamara2201
    @sambacamara2201 5 лет назад

    Le son est très fort

  • @mouhammadkane5760
    @mouhammadkane5760 6 лет назад +10

    Monteur vidéo bi khamoul dara son bi si souf mo gueuneu fort k cheikh bi limouy wakh

  • @bamba_fitness
    @bamba_fitness 6 лет назад

    Yague fi Lolou fall baye adama sarr yague fi Lolou serigne Cheikh ndoye yalla na yalla werale bat bi

  • @dawoudadione2424
    @dawoudadione2424 6 лет назад

    Machala amna sollo 🙏🙏💓💓💓💓💓

  • @elhadjifallougueye1859
    @elhadjifallougueye1859 5 лет назад

    Fall maneuh dhe koumay bakher numéro bay Adama la beug

  • @adamasene7310
    @adamasene7310 6 лет назад

    Mame Cheikh Ibrahima fall yonou mouride yako yorer fall yalla nagnou yalla tass si sa Barker

  • @talibeboromtouba1594
    @talibeboromtouba1594 6 лет назад

    Dieureudieufé serigne touba

  • @laminembaye5848
    @laminembaye5848 6 лет назад +7

    Bay adama yagall yokall wueralll ssi dolay sidy Ibrahim fall

  • @mamecheikhka8730
    @mamecheikhka8730 6 лет назад +4

    alahou akbar thiey yalla mo mayè

  • @magoumbendiaye8571
    @magoumbendiaye8571 6 лет назад +1

    machallaa bayeee

  • @abdulfama5345
    @abdulfama5345 6 лет назад +1

    Akassa waaw gorr Baye adama amna solo

  • @cheikhngom3194
    @cheikhngom3194 6 лет назад

    Macha Allah amna solo

  • @alassanendiaye5685
    @alassanendiaye5685 4 года назад

    Heskeuy macha allah

  • @falloudia1016
    @falloudia1016 5 лет назад +1

    Mane sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar
    Mangui ziar ndiabotou Cheikh Mor Dia Ndiar guep di ziar mboki Talibe yep
    Yalla nagnou yalla defal koorou diam ta gnou fekeko ay yoni yon
    Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke
    Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @mamadoudia4945
    @mamadoudia4945 6 лет назад +1

    thiey serigne mor dia borom karamala Borom sagn sagn la kou wéddi fékk ma ndiar

    • @langke6947
      @langke6947 4 года назад

      Beugue nafa gneuw dé sama sangue bou bakh bi

  • @zalebrayan5593
    @zalebrayan5593 4 года назад

    sèn song binek sii kaw tawfekh neu kèn dègoul li dwr dji di wzkh wagni lèn ko way mouride

  • @digitalmultiservices4712
    @digitalmultiservices4712 6 лет назад

    La musique de fond empêche d'entendre. Merci de la réduire ou de l'éliminer

  • @seyeabdou8764
    @seyeabdou8764 6 лет назад

    dieura dieuf seringe touba dieure dieuf seringe touba dieure dieuf seringe touba dieure dieuf seringe touba dieure dieuf seringe touba dieure dieuf seringe touba

  • @yahyabenmahet4074
    @yahyabenmahet4074 6 лет назад

    Vraiment njaarign li neew na ndakh défaut son 😥

  • @bayealassane8781
    @bayealassane8781 6 лет назад

    Dieuredieufé SERIGNE TOUBA Diarama MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP BABOUL MOURIDINA DIARAMA SERIGNE CHERIF ASSANE FALL NAROU KAWSARA FALL MBEGOUM BAYE FALL YI

  • @papandiaye984
    @papandiaye984 6 лет назад +16

    Vos techniciens sont tellement nuls qu'ils n'arrivent même pas à diminuer le. Son des sikar pour que l'on puisse bien entendre baye adama sarr. Comme disait Elhadj Ndiaye 2stv "télévision du. Affairou khaley"

    • @kumpadumaray14
      @kumpadumaray14 6 лет назад +1

      Ns partageons les mêmes remarques mon chèrs

    • @moukhamadoulsarr6865
      @moukhamadoulsarr6865 6 лет назад

      Papa Ndiaye vraiment c la seule remarque

    • @mberythies5738
      @mberythies5738 6 лет назад

      Tres nul diminue sax moy le minim mais repetition zikr bii on dirair 10s sayou jexei dangassi prete attention yak nan interview bii yeup

    • @mbokkmi8023
      @mbokkmi8023 6 лет назад +1

      pourtant le volume n'est pas fort
      il faut encourager les gens qui se fatigue pour nous

    • @supafo2951
      @supafo2951 6 лет назад +1

      @@mbokkmi8023 vraiment toi t'ei humain

  • @thebesttv1526
    @thebesttv1526 6 лет назад

    Pourquoi le son ?

  • @moussasoussang3445
    @moussasoussang3445 6 лет назад +4

    Baye adama ndao ziar nagnou la yague fi lool te weer thi barke mame cheikh ibra fall begue lool thi yaw sa yougne la deeguee

  • @dembacuisse5201
    @dembacuisse5201 6 лет назад

    Y a que Dieu qui sait qui va entrer au paradis kun faya kun

  • @cheikhmbengue3382
    @cheikhmbengue3382 5 лет назад

    Dieuredieuf bay adama mais son bi si souff mo yakh wakhtane bi

  • @moustafaniang225
    @moustafaniang225 6 лет назад

    Diadieuf Baye Adama Sarr

  • @diamoubamba6328
    @diamoubamba6328 6 лет назад

    Svp prend l temps d diminué ton son ooouûufff do technicien Bou aye dara

  • @tallader6989
    @tallader6989 5 лет назад

    Baye adama boke gua si gni takh ma gueuneu beugue mame cheikh ibrahima fall

  • @xaritouyayam5349
    @xaritouyayam5349 6 лет назад +1

    ndaysan 😢😢

  • @dieyedieye2931
    @dieyedieye2931 6 лет назад

    Machaalla

  • @maxencecallegari7090
    @maxencecallegari7090 6 лет назад +1

    Yalnama yallah dieguel si kadou tu me dègue

  • @baelhadjisamba794
    @baelhadjisamba794 6 лет назад

    Thieuy sidi birahim aka bari dole thia yala eskeuy baye adama yague yokou weer rek

  • @mamecheikhdiagnenar9099
    @mamecheikhdiagnenar9099 4 года назад

    🧡❤🖤

  • @bayeyoussouseck6807
    @bayeyoussouseck6807 6 лет назад

    Eskey.bay.adama.sarr

  • @mamadoulaminedrame5520
    @mamadoulaminedrame5520 6 лет назад +6

    Seul Dieu est grand le prophète s.a.w est notre modèle

    • @momondiaye1067
      @momondiaye1067 6 лет назад +7

      Cheikh akhmadou bamba le serviteur éternel du prophète notre sauveur

    • @kumpadumaray14
      @kumpadumaray14 6 лет назад +1

      Mamadou Lamine Drame wakhngua deug gou wère .
      De même que nous les TALIBÉS TIDIANE aussi nous débordons beaucoup.
      Nous parlons beaucoup de Ch . Ahmed tidiane Cherif , de Ch . Oumar . Foutiyou , de mame El . H . Malick etc... .
      Mais peu de Mouhamed . S. W . S

    • @ouziandkr1188
      @ouziandkr1188 6 лет назад +3

      mamadou lamine drame ki limiye wakh khamoko tés doko khame ndakh khamo mayouk yalla noumou méle

    • @mamadoulaminedrame5520
      @mamadoulaminedrame5520 6 лет назад

      @@momondiaye1067 oui on doit faire la même chose

    • @mamadoulaminedrame5520
      @mamadoulaminedrame5520 6 лет назад

      @@kumpadumaray14 merci pour ta compréhension. On est pas contre nos guides religieux mais on ne doit pas exagérer

  • @willykevinharington6934
    @willykevinharington6934 6 лет назад +2

    Mako Xam Goor Gou Baxxx Baye Adama Sarr Deuk quartier mame diarra

    • @langke6947
      @langke6947 4 года назад

      Salam kou bakh ,ki damako beugue guisss ,té khamou ma foumou deuke

  • @moustaphafaye8753
    @moustaphafaye8753 6 лет назад

    Machallh lampou fall

  • @coumbadiagne3688
    @coumbadiagne3688 5 лет назад

    Ohhh lii nekhna dall

  • @ablayendiaye5412
    @ablayendiaye5412 6 лет назад +1

    Thiay mam chiekh ibrahma fall

  • @mbayesaliou6690
    @mbayesaliou6690 6 лет назад

    Baye adama sarr dounale way 1111

  • @iclud.c
    @iclud.c 6 лет назад

    Ndokk rek baye ni rek la deme

  • @gallaskawsara8733
    @gallaskawsara8733 6 лет назад

    Sen son bi way akh dakar actu kagn ngueen thiounei

  • @tallasene4519
    @tallasene4519 6 лет назад

    Akasa thiey man chiekh ibrahima fall kenla

  • @evedeesse446
    @evedeesse446 6 лет назад

    Yagg fi t werr baye Adama sarr

  • @mbackeniane1380
    @mbackeniane1380 6 лет назад

    Ibrahima fall lako s touba d'à wowee mes pa ibra fall yakar nani ndioumtela

  • @abdoulageabdoulage7301
    @abdoulageabdoulage7301 6 лет назад +2

    Hakaza baye adama yagfi ta wer si doley MAME CHEIKH coumay dimbale si numéro baye adama

  • @cheikhdiallo1050
    @cheikhdiallo1050 6 лет назад +1

    thiey Mame cheikh ibra

  • @abdoulazizsow3734
    @abdoulazizsow3734 6 лет назад

    C NUL ON ENTEND RIEN A CAUSE DU SON DES ZIKR.LES TEKINICIEN SONT NUL

  • @assthiam8586
    @assthiam8586 6 лет назад

    wakhtane bi amna sollo trope yalla naniou cheikh ibra fayale bopame....... (son bi nékk souffe déléne ko wagni ndakh niouy guena dégue limouy wakh di diéguelou bou werr si kadou yiii)

  • @laminembaye5848
    @laminembaye5848 6 лет назад +5

    Sikarr si neque si souff motakh mounouma tewlou waakh dji ndx sama xelll dasi neee

  • @bmg4451
    @bmg4451 6 лет назад +1

    Fan la deuké

    • @NdongOmar
      @NdongOmar 6 лет назад

      Touba Nguiranène la deukkeu!
      Wayé danaka sa bo démé ci Penkou Juma Ji fékk ko fa...

  • @beuggeumjeufgoudikbamel6170
    @beuggeumjeufgoudikbamel6170 6 лет назад

    Theyy SA mame cheikh ibra

  • @xale-yar-ak-teggin.7152
    @xale-yar-ak-teggin.7152 6 лет назад +2

    Siidi birahima fall moo barri doolé

  • @khadimndiaye9685
    @khadimndiaye9685 6 лет назад

    Nguir yalla kouma meun wakh baye adama foumou deuké ma ziari ko. Depuis jazboul mouride lampfall tv magui ko beug guiss

    • @alibosn8950
      @alibosn8950 6 лет назад +1

      touba palene

    • @aboupene2224
      @aboupene2224 6 лет назад

      @@alibosn8950 diaradiuef way

    • @amyfall3915
      @amyfall3915 6 лет назад

      Salam je veux le numéro de baye Adama sarr

  • @morseye6767
    @morseye6767 6 лет назад

    akassa baye adame sarr

  • @mboupkhadim8099
    @mboupkhadim8099 6 лет назад

    Fi bane cartier la si touba

  • @sellesarry6394
    @sellesarry6394 6 лет назад +1

    Sant mame cheikh ibrahima fall lamp

  • @modoudiop8376
    @modoudiop8376 6 лет назад

    Waw fall ya bakh

  • @ndeyemaimounagueye8245
    @ndeyemaimounagueye8245 6 лет назад

    Le monteur est vraiment nul ish , le son oooh mais non way ishh

  • @zalebrayan5593
    @zalebrayan5593 4 года назад

    mouride mo nekh

  • @cheikhbarakane8731
    @cheikhbarakane8731 4 года назад

    Cheikh ibrakhima falle doumorome dé

  • @gorandir3210
    @gorandir3210 6 лет назад

    Akassa

  • @srmourtaladia5351
    @srmourtaladia5351 6 лет назад

    machalla ame na solo lol

  • @rewmitvsn4423
    @rewmitvsn4423 6 лет назад

    keine cheikh ibrahima fall lamp fall

  • @nancysy8578
    @nancysy8578 6 лет назад

    Ken dou mame lamp

  • @adamadiagne9168
    @adamadiagne9168 6 лет назад

    nonu kassé la

  • @moustafaniang225
    @moustafaniang225 6 лет назад

    Sikar si Modou Aïda Fall la

  • @CheikhDiop-ci9xv
    @CheikhDiop-ci9xv 6 лет назад

    yag fi lol ta wér méi sén tecnicsén yi dése nanio ay

  • @masstall6364
    @masstall6364 6 лет назад

    جرجفت شيخ ابراهم فال

  • @gueyeass1713
    @gueyeass1713 6 лет назад

    Mam foum néke

  • @alioudiop552
    @alioudiop552 6 лет назад

    Amna soolo lolll

  • @papesambafall5907
    @papesambafall5907 6 лет назад

    Jaajeuff kou baxx

  • @fallmaguettefall5502
    @fallmaguettefall5502 6 лет назад +1

    HAkaza

  • @alhadjialassanembaye6357
    @alhadjialassanembaye6357 6 лет назад +2

    Doul rekkk

    • @paped4791
      @paped4791 6 лет назад +1

      yaw daga repe daga khamoul serigne bi mo takhe

    • @massimilianogavazzi5430
      @massimilianogavazzi5430 6 лет назад +2

      Amal yarr domerame dji ki dousa moromou baye

    • @mouhamadoubambaniang9587
      @mouhamadoubambaniang9587 6 лет назад

      Papa alassane Seye mouride et fier. A chak foi yenay nieuw di sani xer mais jamais ngeu guiss mouride bouy. Dinguate ndakh yar naniou

    • @elh.thiernoalyndiaye7161
      @elh.thiernoalyndiaye7161 6 лет назад

      Serigne Touba neena na ngeen moytu tògn ndax dina waral gnétt , dina xagné jubalu sunu Borom ( Inna laaha laa yahdil xawma zaalimiin ), dina xagné ndimbalu sunu Borom ( wamaa lizaalimiina min ansaarin ) , dina waral tam mbugalu sunu Borom ( innaa minal mujrimiina muntaqimuun).

    • @elh.thiernoalyndiaye7161
      @elh.thiernoalyndiaye7161 6 лет назад

      Serigne Touba neena : ndaw lu ne muccu ak jub la war di sàkku fu mu tollu , muccu dees na ko sàkkoo ci juróom : wormaal lu mata wormaal , wormaal ku mata wormaal , lu gnu ni baax na nga def ko , lu gnu ni bon na nga bàyyi ko te di gnaan Yalla Mu musal la . Njub , bul toogn mukku , bul fayu ag toogn , bul xëccoo , lu gnu ni jub na nga nekk ca tey gnaan Yalla jubal la.

  • @falloudia1016
    @falloudia1016 5 лет назад +5

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

    • @langke6947
      @langke6947 4 года назад

      Ziar nala sama sangue bou bakh bi

  • @ansumanacamara4195
    @ansumanacamara4195 2 года назад

    Jerreh Jeffeh serign touba ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia8992 4 года назад +1

    Yalla nagnou Yalla defal diam
    Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke
    Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia8992 4 года назад +2

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke
    Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @ansumanacamara4195
    @ansumanacamara4195 2 года назад

    Jerreh Jeffeh serign touba ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia8992 4 года назад +1

    Yalla nagnou Yalla defal diam
    Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke
    Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia8992 4 года назад +1

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke
    Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar
    Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar