Mashallah jotay bi tafsiroul khourane la taarikh la ak youkkou beug Sergine touba. Mbacké koula gueustou beug la . Namone nagnou len lollou way sama gars yi .
Demande d'explication !!!vous étiez où ces derniers moments...??? Vous nous manquez trop même 😭😭😭 Fan yi yeup ma gui xarr bilay .... Machala yalla na len Serigne Touba bokk nous dimali...niou gueuneu xirr si mom gueun ko beug...
Serigne Touba est la locomotive de l'islam Allahou soubanakhou taahalah lui a rapatrier la terre de makka la terre de Médine ici en Afrique et cette doctrine sera préservé par ces fervant talibe est vénéré petit fils
Machalah yallna lene yalla diapalè tè weral bat yi DIEURDIEUF SERIGNE TOUBA AMOUL MOROME
Amatina solo team ceey serigne Touba xam xam rafet n'a yalla na gueuna yok macha alla
THIEUYE SERIGNE TOUBA AMOULE MOROME SÉNN WAXTANE YI NÉKHE NA YAL NALÉNE SERIGNE BETHIO FAYE❤️❤️❤️❤️👏👏👏👏👏👏👏👏
Merci beaucoup vraiment kontan nann yalla na lén yalla fay
Dieureudieuffeutti serigne bethio yene bakh wayy te yiw
DIEUREUDIEUFEUTY SERIGNE BETHIO AMOUL DENDADO 👌
Waaw goor serigne saliou ak serigne boubacar tay kendouléne diokhogne thi son bi wa xeweul tv m'a challah
SERIGNE BETHIO AMOUL MOROM ❤️
Bilahi fanyi yeep dama toumourankeewonn ndakh niakka deegg senn émission bi
Mashallah jotay bi tafsiroul khourane la taarikh la ak youkkou beug Sergine touba. Mbacké koula gueustou beug la . Namone nagnou len lollou way sama gars yi .
MachaALLA AMATINA SOLO ! Dieureudieuf Mouride
Degatina deugu dee yen dal koulen deglou degu ndiarigne adouna ak alahira .merci heweul tv
Yallnagèn fi yague tè wèr si barkep serigne touba
SALAM DUO BOU MEUSSOUL AM CI WAKHTANEE SERIGNE TOUBA
Xam xam bii leerna dieuredieuf serigne Béthio
Dieuredieuf serigne touba amoul morome
Di yeukk serigne touba moy dih doundou aldiana tei dééwo
Ndaysann amna solo lol machalla dieredieffeti yalla na yalla takhawoulenn
Ceey s touba amoul morom s touba amoul mass
Walahi bék na❤❤❤❤ yalna léne yalla fay ci barké Serigne Touba😍😍😍😍😍😍
Bilahi malene beug yalla na seringe bi faylene
Dieureudieufaty serigne bethio
Dieureudieuff borom touba amoul morom kénn la
Abonnez vous à xeweul tv
Machalla ❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏
Demande d'explication !!!vous étiez où ces derniers moments...???
Vous nous manquez trop même 😭😭😭
Fan yi yeup ma gui xarr bilay ....
Machala yalla na len Serigne Touba bokk nous dimali...niou gueuneu xirr si mom gueun ko beug...
DIEUREDIEUF THIOUNE machalla Dieuredieuf yéne amouléne morom waxtane bi néxna lol wayy touuyyhhh
Waye dall waron na amm matt sy Koor gui dall
Thiye Serigne Touba ❤️💪🏽
sant serigne touba
Dieuredieuf,kham kham bi léerena té sellena.
Yague lénefi té wére
thiey liguèyou srgn bethio sii ndigualou srgn saliou
nii rekk todk ak pasteff si khamekhamm
lepp si ndiaguall
Beugnathie de machallah
Dieuredieuf
SERIGNE BETHIO jerejefeuty...ah Wawaw team Serigne saliou samb.waya Boubacar yawit wahta'ne wi d'où joug si kawei.jangueine jeuf
walahi yen yalnalèn srgn bi takhawou
lii walay amm na soloo
Machallah
Cey ceyyy dji ✨✨✨✨✨
Akassa Universels djanguénn djeuff SERIGNE BÉTHIO AMOUL DÈNDANDO
Ma chalah
Machllah
Machalla😭
mâcha allah 🥰🥰🥰🥰🙏🙏
Campagne électorale
Yalla ngene fi yag te wer !
waetne Cheikh Ibrahim fall
SERIGNE BETHIO AMOUL DENDADON
DIEUREUDIEUFAAAT SERIGNE BETHIO SERIGNE BAMBA DIARRAMATYYY SWRUUU MAME CHEIKH SIIKKAARR NDIAYEEE!!!.(MF)
❤🎈♥️
Waw goor jërëjëf
You gui diane guéne guéne ko tase partagè le lien
❤❤❤❤
🎈🎈🎈🎈🎈🎈🎈
Akassa
Djanguènn djeufff universels
Santati nagnou bègati nagnou
Ragualène yallah. Khana serigne bi dafa fatté niane ndokh bou nitt neune naane si deukame bi , touba. Wakhi doff rek biss bou nekk. Wakhi yèéfére rek nga wakh.
Thieey
Ame na solo lol
Dianguen dieuf wayy mourides. Beg nagne dé
Serigne yann mello la wax app mouride momm la wara yorr pr nk mouride sadix
amatina solo lol , xol yi s3dd na lol
Serigne Touba est la locomotive de l'islam Allahou soubanakhou taahalah lui a rapatrier la terre de makka la terre de Médine ici en Afrique et cette doctrine sera préservé par ces fervant talibe est vénéré petit fils
Begueutinane!!
Bègue na lol thi yene !
Saliou samb yaw jiguene moy sa serigne mouride ndigueull ku teggi ndigalu serigne nekka too mouride
Non
Hahahaaa fa koulla dalala fi narr yaw saliou samb dagua rér
Saliou samb do dara,Satan.mouride ndiguel
Litakh touba guen deuk yeup moy yalla sunu borom moy serigne touba té mom mom santhe touba guiss ga yalla nioun lay leuré rekk wayé niou. Kham naniou lep dieurediefé serigne touba
Wakh nga degue dé 😭😭😭
Yaw sétlou ngua li ngua wakh ni. Yaw ando ak sa xél déh.
Yallah nama yallah diégueul ci lima la lire
Depuis Maroc ,on vous suit .
Dianguen dieuf begnaniou
🤣deug dou nékh
Yaw Boul Yakh Sounou dérr imbécile Linguay Wakh Fooko Dégguee ak fooko Dianguee thi Enseignement SERIGNE TOUBA ?
Ya sambe ya gueneu Kate ndeyam yaw sa data ndeye
YAW MOR DIOP SA DATA PAPA SA COYE YAYE YAW AK GO YAKAL SEN DIAPPA PAPA DOUMOU FILS DU DIABLE GUA !!!
Yallnagèn fi yague tè wèr si barkep serigne touba
Machallah
❤❤❤
Machallah
Machalah
Machallah