Siteu ba mi mbeuré ak Lac 2 Modou Lo mo co dieundeul ay Billets , Iboul aye fait des grosses…

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 12 дек 2024

Комментарии • 50

  • @NarFall-om7vy
    @NarFall-om7vy 2 дня назад +10

    Modou lô seul Modou moyy Roi dés aréne coumou néx AK coumou nahari inch'Allah yalla nako yalla défal diam ❤❤❤

  • @FallWaly-c6g
    @FallWaly-c6g 2 дня назад +13

    Badola ak dof ken duko mayé chance

  • @MamadouNiang-g5r
    @MamadouNiang-g5r День назад

    bien dit ibou laye et merci pour tes paroles kou am personnalite nga

  • @mbayebayefall8162
    @mbayebayefall8162 2 дня назад +4

    Siute dof la ko rew la modou kasse yaye gor yaye jambar❤

  • @AdamaMballo-t9s
    @AdamaMballo-t9s 2 дня назад +3

    Merci grand iboulaye

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 2 дня назад +11

    Man mi siteu damako beugone mais légui parés n'a si mome

    • @AitaMalick
      @AitaMalick 2 дня назад +2

      Billahi bari ngua si ay borom
      Siteu a déçu beaucoup de monde 👎👎👎👎👎👎👎

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 2 дня назад +4

      ​@@AitaMalickidem pour moi bou amaté combat yalna danou

    • @absathiaw8233
      @absathiaw8233 2 дня назад +1

      Idem pour nw déh

    • @AitaMalick
      @AitaMalick 2 дня назад +1

      @@rouguikebe9984 Amine rougui siteu a vraiment déconné

  • @KhalilDien-fe5uh
    @KhalilDien-fe5uh 2 дня назад +4

    Siteu baye fall bi nguay woté nekoul si yow .... baye fall dou merrrr . Baye fall dou siiissou ... baye fall dou niak talibè .... mingui niiiaw... boul déglou gniiy yakh sa diguanté ak Modou lo

  • @aissatousy1875
    @aissatousy1875 2 дня назад +2

    Antouca tu as rezon bou dkhe djekhe ne siteu n'a geme Yale khame ne dane coy thi bire gew d'Anne co thi recour d'Anne co th appel siteu n'a khame ne ay Mocou lay donc da wara rafet rec mani siteu setil lene Modou lo félicitations kharagne lo nekha faral dimanch fiyer de toi bayil wala ga nopalou ba thi canam gnoun Say fans gnou nopalou

  • @cisseabdoulaye6229
    @cisseabdoulaye6229 2 дня назад +6

    Il faut que les vip refusent de lui accorder de chance...

    • @Jnrjoop
      @Jnrjoop 2 дня назад

      Bro fi may chance amoufi ay millions lagnou léne proposé 😂😂😂 promoteur kou am supporter lay weur
      Séne khol mo diekh rk té linguéne fogone amoul 😂😂 faté khadioufi modou amoul loumou wakhoul balla 🤫

    • @MamadouNiang-g5r
      @MamadouNiang-g5r День назад

      bien dit fall

  • @walobrackmbodj805
    @walobrackmbodj805 2 дня назад +11

    Depuis Quand Siteu N'a Pas De Victoire. Modou Lo Devait Pas Prendre Siteu Sa Thies La Battus Gouy Gui Est Lac De Guier.

    • @tmsba_tv
      @tmsba_tv 2 дня назад +2

      Billahi erreur bou mak la def waroul Wone beuré AK mom siteu dafa Rew dafa reuy lamign

    • @jazaka3178
      @jazaka3178 2 дня назад +1

      Ak Boy seye bi démone gadaye

  • @PapamorMbaye-w7n
    @PapamorMbaye-w7n 2 дня назад +3

    Lamb nekhoul Modou mo warouton djeul siteu

  • @abdouboukharagnelolo9687
    @abdouboukharagnelolo9687 2 дня назад +4

    Situe bilahi limou def modou dina ko rediou

    • @Jnrjoop
      @Jnrjoop 2 дня назад

      😂😂 ioe doul mayléne gnou diam Ay millions lane léne fay pr gnou beuri loléne bg Dane boy bi😂 boy bi doumako Dane ko nguéne 6sou 😂😂😂😂 fanculo

  • @Ismaeljallow-k3b
    @Ismaeljallow-k3b 2 дня назад +5

    Modou Lowe ROI des'arene full time. Siteu Tapet des'arene full time. App Tapet du jel ROI Chi aye tapaleh.

  • @magebop
    @magebop 2 дня назад +3

    Siteu dafa rew té béw
    Modou ne devait pas lui donner une chance
    Badola deugue moy Siteu

  • @ladepechetv6998
    @ladepechetv6998 2 дня назад +4

    Ibou laye sa ITW bi amoul sens meunontothie affaire yi? siteu dafa réww trop. Wakh ko mou diekh

  • @user-kf7oi4q
    @user-kf7oi4q 2 дня назад +13

    Diamageune ay mbam haram lagnou dougnou ay nitt doff yiii 😂😂

    • @BathieNdiaye-l6w
      @BathieNdiaye-l6w 2 дня назад

      Kadou yi rafét na dieureudieuf 😂

    • @mamadouseydougueye1696
      @mamadouseydougueye1696 2 дня назад

      Boul khass wa diamguene

    • @user-kf7oi4q
      @user-kf7oi4q 2 дня назад

      @@mamadouseydougueye1696 saway samay cousin akhane nioffa deuk khamnalen dee dougou kasso ka guenn lagnoufa nekk ay mbam haram lagnou kon bougou niou darra

    • @chamousman2726
      @chamousman2726 2 дня назад

      Sai kaddu refetut man modou lo kese problem bi siteu la kese wayeah wa diamaguen Sen Yoon nekusi

    • @Jnrjoop
      @Jnrjoop 2 дня назад

      Sa bay haramoul mé kou mbamé la t boul khaïri la 😂😂😂😂😂

  • @senegal559
    @senegal559 2 дня назад +3

    Man mii siteu soof nama ba faw

    • @Jnrjoop
      @Jnrjoop 2 дня назад

      Sa khol mo diekh 😂😂 daka douma daneko linguéne fogone amoul

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 2 дня назад +1

    Siteu domouram la wakh ak daw rk 😂😂😂

  • @silencieuxbouyant9687
    @silencieuxbouyant9687 2 дня назад +1

    Siteu da rew fater demb bilay

  • @saliougueye9833
    @saliougueye9833 2 дня назад +2

    Diamaguen nimou modee nonou la boy yi dofe toukh yamba ak nane sangara rek

  • @fatoundourbodian1078
    @fatoundourbodian1078 2 дня назад

    Situé kay mo warone wate me pa modou

  • @AbdellahiNdiay
    @AbdellahiNdiay 2 дня назад +2

    Siteu kaye dafa dioum dioum bou reuye modou lo sa grand frere la en plus mou bayifi sathies reug reug tapha tine mayela chance nga beurei combat royal kon lou meti ame da wara rafete adouna dafa goudou tank

  • @marcusmouhamed
    @marcusmouhamed 2 дня назад +2

    Modou yagg na diapaler siteu gneupako ham boy bi defa dioum

  • @BayeDiouf-uw4nh
    @BayeDiouf-uw4nh 2 дня назад

    Boul wah lolou lambe la

  • @moustaphadiouf9154
    @moustaphadiouf9154 2 дня назад

    Dagno ame groupe zikr mes siteu danagnko di nianal wayei vraiment merenako

  • @ArameDiop-o6l
    @ArameDiop-o6l 2 дня назад +2

    Siteu domouramla

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 2 дня назад +1

    Billahi wakh nga deugue alkhourane bour diangala

  • @aissatousy1875
    @aissatousy1875 2 дня назад +1

    Tamit ba thi canam

  • @fatoundourbodian1078
    @fatoundourbodian1078 2 дня назад

    WAw badola ak dof la def

  • @papasene9330
    @papasene9330 2 дня назад +5

    Non siteu fok gayi diko comprend dar mandi ba yakou mok gayame yi

  • @Elhadjikane-i6f
    @Elhadjikane-i6f 2 дня назад

    Bayilenma Siteu mii dofla il est immature
    Yeffou dof rekk laay deff

  • @mimikeita4262
    @mimikeita4262 2 дня назад

    Siteu da wara tok 5 ans dou beuré

  • @SambaSene-j1h
    @SambaSene-j1h 2 дня назад

    Siteu dof la gniko encadré aye doff lagnou amnasi gnokhamna warougnou lene dakh talale merco saine image ak saine wakh dou rognouwaye

  • @rouguikebe9984
    @rouguikebe9984 2 дня назад +3

    Siteu mom vrai badola la niak ngor trop.Modou mo déf erreur diko may chance.
    Siteu Vip yi sakh warougn ko may chance parsk dafay saltél khol bou bone la yor mok Max bou rancunier bobou nga khamni da nieuk