Eumeu sene mane yow rek la beug bilahi yalla nalla yalla may ndam si be52 ak bella gueye2 mais dema beug gua dieulam ma gouy gui eumeu sene stp💪💪💪💪💪💪💪❤❤❤❤❤
Waxxx djii deih ma nguii koy beuga miis si internet bii aý bou la Balla Gaye 2 diapé té sa you ko diapé trokhal ko fethiou lo na ko bombass ak thiakhagoun vive Eumeu yalla na la yalla may ndammm
@@mansourdieng2000 nono deukou ma sakh région de dakar thies la deuk médina fall mane ak modou anta nio bokk bene kogn mais limou wakh da rétanlou 😂😂😂tei epui eumeu bamou wakhé wakhet batay moy lolou mais damakoy supporter tjrs grâce à boye niang bou diékhai rk diekhna 😂😂😂
Denga ragal aussi Reug Reug motah nganane do beuré ak mom,té besbou Reug Reug dieulé Boye niang wala Ama baldé dinga ande ak niom pour nioudane Reug Reug
Sénégal mo baari domeram di commenter di sagua Balla gaye sakh mak la mon frère et sa Thiès le petit frère de Balla gaye gno bokoon classe école HLM 4 e t mon frère a plus de 35 ans bayilen douul yi KO di wakh lac de guerre moom dof la lilaay waan lac khaoul dara negua dafa corriger eum t mounoul am combat lac dou ndeye mbeur mounoul Bakou mounoul tounou ndem eum 15 ans Modou Lo kesse mo daan
Je vois que tu seras humiliée par balla tu ne devrais pas accepter le 3ème combat ,balla il ta déjà préparer il c,est que tôt ou tard tu vas le croiser
Je suis fans de Balla mais t'a très bien fait de prendre le combat c'est votre travail et la vie est courte mais ndam ci balla inchallahou rabbi
Belle parole champion machalah tu es le meilleur
Bonne chance à balla Gaye ❤️
Thiéy sama mbeur bii borom xol bou raféte bii inch'Allah ndam rk sii niary combat yii
Kou beugg developpment.senegal.mangilay.nian.abonne.emission you amsolo pour Senegal
Eumeu rek lanou geum. Ani fans Eumeu Sene 💪💪💪💪
Eumeu amal diam lou beri
Sa xol dafa nice yalla nalla borom bi taxawou si sa 2 combats yi
Grand Dèeeeel Wakh Deugeu Bilahi Yall Nala Balla Gaye 2 Dann Amiiiin Barkèb Borom Touba Guinaw Lolou Bilahi Nièmè Woh Tapha Tine Barki Yalla Thiey Tapha Tine
Lolou darà worou la si fall nga bal ma nk
Fexal guene ci boys niang baa paré
@@Damos_officiel Nioun Danouy Nian Yalla Rèk
@Mohamed Ndiaye Masou Mako Deugeu Mowakh Siii Tapha Tine Fokah Fèeeek Mouy Wakh Combat Diakh
Eumeu séne dou sama mbeur,supportéwoumako mouk mais momeune Gouy gui 10000 fois lolou dou combat,na Eumeu dieul Tapha tine mo guéne daw bi
Machalla yalla na yalla def diamou
Eumeu sene mane yow rek la beug bilahi yalla nalla yalla may ndam si be52 ak bella gueye2 mais dema beug gua dieulam ma gouy gui eumeu sene stp💪💪💪💪💪💪💪❤❤❤❤❤
Eumeu Séne 🔥 Sa Thies
Gris 🔥 Bombardier
Gris 🔥 Tapha Tine
Ama Baldé 🔥 Gris
Eumeu Séne 🔥 Tapha Tine
Sa Thies 🔥 Reug Reug
Yekini jr 🔥 Malick Niang
Yekini jr 🔥 Siteu
Siteu 🔥 Malick Niang
Boy Niang 🔥 Gris
Moussa ndoye 🔥 Malick Niang
Eum mon lutteur préféré mais waro woona dieulaate Balla ak lou meuneu khew mais c pas grave c le sport que le meilleur gagne
Gouy gui mom nieup khamnagn ni balla mokay dérangée mais dina sonou dh
Wakh Ngua Deug
Dafa méleni dafa ame victoire bou reuy si kaw lac de guerre
Yénangi wax eume mak té gningéni wax nioy xaléyi Modou Lo rék moko dane kou soxoroul xamné ko championt la
Tu a parfaitement raison
Je supporte Balla gaye mais ken d'où kharagne lo
@@ousmanefall422 no Modou Lo mom kéne dou mom
Dél wax loy Déf Eumeu Séne
Nala Lérr niii Yak Bombou Dou Yomou Yak Balla aussi Day metti Défall Lolou Sa Bopou bii 🙂Mé Nak champion nga En plus Danga Yarou Trop Billahi Amall jamm Rék Yaw ❤️🙏🤙🏻🤛
Balla wakhone nakofi
Keep it up.....respect to you
Kan mo meuneu waat ni moussoul deloussi si ay Kadoom?? Kan??? Bayi len Eumeu Sene. Dioulit dey mandou.
Vraiment Balla Gague Diambarrrrrrr leu 4 combat
Bonne chance Eumeu 💙🤍♥️
Senegal bén mbeur la ame mouy ioe borom pikine
Dangaye doul. Niari champion nio am Sénégal balla ak modou
Fiiila sa carrière di diékh
Gouye guii daÿ doule sisoumane 😂😂😂
Wakhal dh
Gouy gui dé balla motakh mouni eumeu sene mofi dakha beuré 🤣
@@omarseye4228 bilahi mo dakha doule sii mbeur yii
@@laminegaye7429 boukii neina lou gnëëpe wax moy deug
Bonne..chance.eumeu
Eumeu rék 💪💪💪 laye supporter bilahi
Le journaliste revois tes références ils ont lutté en 2009 et en 2015 et non en 2012
Waxxx djii deih ma nguii koy beuga miis si internet bii aý bou la Balla Gaye 2 diapé té sa you ko diapé trokhal ko fethiou lo na ko bombass ak thiakhagoun vive Eumeu yalla na la yalla may ndammm
Après modou dor ko mou kheum 😂
Nice boy ♦️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Eumeu tay mou rouge souba mou bleu amooo kadou 😂😂
🤣🤣🤣🤣🏃
Nos journalistes savent pas poser des questions pertinentes!!
Eumeu sene borom 12 défaites et 9 victoires 🤣🤣🤣🤣
Bolesi douma yakarou gediawaye 2fois
Khana 9 victoire sa yaye lako dane
😂😂😂😂😂😂😂
Emeu séne se papa le
Eumeu Séne se
Eumeu balla gaye 2 moro man
Lac l'homme qui a corrigé eumeu sene borom 12 et 9 victoires si biir pikine 💪💪💪💪
Ioe escque goor gua yagui weur di doule rék ioe lamine konate
@@modoundiaye7985 😂😂😂😂😂😂😂
Lamine konate aka meune fene 12 defaite 9 victoire 😂😂😂
@@momobouthiapathiolybi7752 Yaw Tamit Khana Do Domou Pikine
@@mansourdieng2000 nono deukou ma sakh région de dakar thies la deuk médina fall mane ak modou anta nio bokk bene kogn mais limou wakh da rétanlou 😂😂😂tei epui eumeu bamou wakhé wakhet batay moy lolou mais damakoy supporter tjrs grâce à boye niang bou diékhai rk diekhna 😂😂😂
lamb dji nimou démé ni nékhétaoul darra , c'est koi ces combat qu'on compile a la hate ni , c'est du nimporte koi
Diam si iow beur respect
Machallah champion bonne chance
Machalla champion yalla nalla yalla maye dam
Bonne chance eumeu sene Balla gaye 3
Nooooo ki dou nit sahke 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Eumeu yow la faral mais combat yi gousoumasi sa avantage
Bonne chance balla
Wa champions 💪🏾💪🏾
To become too much friendship , can be falty
Cheuuuuut Gouye gui War nga rouss tchi li dhé 😂
Mooooooooodouuuuuu loooooooo... roi des arène
Eumeu champion la
Dangaye soop rék
Weddi nala bilay
Ya kham
Ha ha gouy gui balla mo dakh bari. Thi lambou dji
Say wakh diaroul diapp ya raw kakatarr
Mooo tey
Y'a koy diokhal de penche xamnaa
Soula balla diapè non
Eumeu lane motakh NGA bayi 450 million ba pare ngaye béure watt AK balla Gaye wakhé deg dafa bakh
Ki koukoy fay lolou day doul
Gaston dou dara diél balla dioko 4 combat boy yii nougnouy déf
Ziar frère prtnt li gaz dff dra nékousi parsk grand combat bou nek y'a plusieurs petits combats de dans
Biii môme do sui Dale allez Balla
Gouy Gui à raison eumeu moy papay Balla gaye alias Ndiaye dragon
Biyone yakk balla liliguéye.khépp.ko.walakhi amegua.combat.d.mbeur
Gouy Gui day doul
Denga ragal aussi Reug Reug motah nganane do beuré ak mom,té besbou Reug Reug dieulé Boye niang wala Ama baldé dinga ande ak niom pour nioudane Reug Reug
9victoires youy remplacé 20victoires
Reug kholoul boy niang ama sakhe ww
Hi
Machaalla eumue sene rék
Eumeu iow doule rek ngay deff do nitou dara b52 ak bg2 yeup dinaniou tegueul sa ndey gouye gui moom sissoumane leu guediawaye nieup ko bayi
Gouy gui khol bi bakhoul
@@laminegaye7429 dafa sokhor
Mâle éducation bakhoul khôl nit RK saga KO thiey yalla
@@cheikgbajane5197 niakk ngorr aussi bakhoul ak wakh wakhete ani valeur imbecile thieuy yalla
Papaye balla Gaye 2 mongini eumeu séne doff dou wérr
B52. 2 0
Mann xamonn nané ki Dina jeulatt bg2 daxx dakko fans
Mbeur bonne chance
Ndam rk yaw
so danou guir yalla gua bayi ndakh defet ak victoire gnoy wadia tolo
Ta gueule yakoy diox dépenses sof ngène trop gni meune si lambe ji emeu Molène dane
iow mane wor nami bimay faral eumeu sene iow khamo eumeu sene guay ay depeunse
Wakhou mbeur Diarta deugou Kouma wakhoune eumeu sene Dina mberewate Ak Balla gaye ma weudikou wakhou mbeur d'où dara
Kholbè rafèt machallah
Sénégal mo baari domeram di commenter di sagua Balla gaye sakh mak la mon frère et sa Thiès le petit frère de Balla gaye gno bokoon classe école HLM 4 e t mon frère a plus de 35 ans bayilen douul yi KO di wakh lac de guerre moom dof la lilaay waan lac khaoul dara negua dafa corriger eum t mounoul am combat lac dou ndeye mbeur mounoul Bakou mounoul tounou ndem eum 15 ans Modou Lo kesse mo daan
Gouye gui mom na khar ba guéne si reug reug sokhor
Je vois que tu seras humiliée par balla tu ne devrais pas accepter le 3ème combat ,balla il ta déjà préparer il c,est que tôt ou tard tu vas le croiser
Eumeu réck moy saf safal
Way yaw bayiule 450 mil kine fayoulako yaw ay 50 ak 80 rek gaufi niugge
Lol contre modou lo 160 millions
eumeu séne def nga erreur nak waro wone dieul BG2
Dioulit d'où nafékh dème ba Kaolack di féf féthieu tyson
Dioulyt tamite dou yé fitna nafékh yagui si bir dioulite yi
Lousi ndaye yon
Yaye bayou nafekh yi domèrame
Lalenga lalaké souma amoulone loumäye sétte dina dagal banga rouss yaw Mandiaye Cissé
@@kheuchshow656 ioe sa tounou ndeye yak eumeu séne
Ki dafa ragal tapha tine rek
Bo entrainné woutte dolén dane heumeu boul gnou rouslo bi yonne
Yo wallou Balla gaye
Danga ragal tapha tine
Eumeu Yaw la faral mais ligueyal Bou bakh balla migui ligueye dé
Sama papa ji lo diamu thi yaw
Eumeu sene maintenant tu as pris de l'âge il faut laisser maintenant
Ki daane balla gaye 2fois rek doyna palmarès
TUF
Ahhhhh yaw sama mbeur nga wone me mane beugouma wakh wedi dou yeufou gorr mangi si boy nieng togal nfak rek
Boye bouniou sonal eumeu séne daye liguéye
BALLA GAYE 2. MO BARRY FANS GAMBIE
Non Eumeu tour saidu Balla
Non Eumeu tout sauf Balla
nokhal ma balla rékh
Insbi mom ak wa pikine sougne lén bolé wone dou té balla dane lén
Balla daleen dii humiliè cette fois ci
Ki parena
🤣 serigne kay gnou parier
Eumeu balla amoul sans dakoy danate 3 fois rk
Way doul rek var wakh wakhéte nopénga am ndam sisa adouna
Yaw yaye yalla
@@mbayendiaye170 wakh wakhéte gor douko déf
@@elhadjigueyebayefall5176 yaw oubeul sa lamigne bi
Kone loutakh bingay wakh do beurè ak balla gaye kholosi wone say kilifeu
Balla loutakh mouniwone dotoule beuré AK modou lo si adouna
Cas yi bokoul
Eumeu dafa wakh ni balla dafa souli bamélou yayam motah dotoul beuré ak mom
Wakh diodiou dafa reuy
@@modoundiaye7985 balla gaye legerment lako wakhè mai eumeu dafni beurè wat ak balla lek souf momako guenal
Tape nga
no eumeu vré seytané
Yaye bou maak bi go waye
Danou son si revanch You bariyi
Bilahi
Sama mbarr
Gouye gui khol bi mo boneu sokhor motakh mou tarder domou khathieu bimou doneu hándicape leu moom gouye gui
Boul wakhé khôl way yaw tamite adouna diaroul lii
Eumeu yow mom tek khel gua
Lac dou doul day sopp rk di nakh ay supporter ram