la famille Pouye de Ouagou Niaye expulsée en pleine nuit de leur maison familiale

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 фев 2025
  • Vipeoples TV

Комментарии • 574

  • @yacinetoure3360
    @yacinetoure3360 4 года назад +42

    Kepp kou guiss ni senegalais baxoul ta da meun toroxal moromom rek pousse bleu

  • @sodamariameboye9367
    @sodamariameboye9367 4 года назад

    Yala ak yonet nii ak serigne babacar mignou yalla dinala lenn takha wou inchala boulenn khadiii moukou

  • @aidaniang2131
    @aidaniang2131 4 года назад +23

    Y'alla n'a leen yalla soutoural ba niou délolène sen keur gui amiine

  • @Corailpro
    @Corailpro 4 года назад +40

    Oh, trop triste 😭😭😭🇸🇳🇸🇳🇸🇳
    Mairie bi nalene logé gaaw li yeme na torop !
    Na si deukondo yii yeup diap

  • @aminanaa9166
    @aminanaa9166 4 года назад +120

    Ay si j'avais les moyens😩 yalla nalene yalla dibeuli inshalla

  • @khadimseye144
    @khadimseye144 4 года назад +29

    Billahi wallahi tahalahi manguiwatt thi torou Yallah kou tonie yalnala Yallah alak toroxalla mbougalleu banga xamni tonie baxoul aminee yarabi

  • @hamzagueye2677
    @hamzagueye2677 4 года назад +2

    Diaga Niang li mou def famille pouye yalla nakayalla torohal si kanam si barke seydina Mouhamed salalaliwasalam

  • @diamandiaye2641
    @diamandiaye2641 4 года назад

    Yalla nala yalla ak serigne babacar takhawou si yeurmandéme

  • @fatouthiam8397
    @fatouthiam8397 4 года назад

    Yalna yalla leral lép ci barké Serigne Touba. Lii metina

  • @diadiasarr3658
    @diadiasarr3658 4 года назад

    Yalla nalene yalla dimbeuli si barké serigne babacar sy

  • @fatimabalde6972
    @fatimabalde6972 4 года назад +100

    Aywwayyyy sounnn borom waronn nama def milliardaire hoooo😭😭😭😭😭

    • @saoune1saoune16
      @saoune1saoune16 4 года назад +5

      hahaha soko amon fatélèn

    • @fatimabalde6972
      @fatimabalde6972 4 года назад +7

      @@saoune1saoune16 dou gnépeu melni ioe dh lolou gua wara kham parck en général nigua mél reeek guay jugé gnénenn gni

    • @mariamadiagne9876
      @mariamadiagne9876 4 года назад +5

      Yalnalako yalla def

    • @saoune1saoune16
      @saoune1saoune16 4 года назад

      @@fatimabalde6972 😋😋yalla mom meuno ko door 😎ioe da nguay khar milliard dafa tèleu si khalèi

    • @fatimabalde6972
      @fatimabalde6972 4 года назад

      @@mariamadiagne9876 aminnn ma chéri gnou book leep machalah

  • @diarytraore1700
    @diarytraore1700 4 года назад +113

    Ndiaga Niang délosil sa khél té khamné adouna dou keur tot ou tar dingua wouyoudji sa borome

  • @toubabelsall8113
    @toubabelsall8113 4 года назад

    Yalla nalen yalla takhawou sénégal 🇸🇳 meitina bilahi

  • @thiateleu
    @thiateleu 4 года назад

    Niou bakhhh yalla nalene yalla diapaleee

  • @odettegomis6411
    @odettegomis6411 4 года назад +1

    Louma beugua wakh khepp ko Sénégal mongui nii koula eupp dolé wone la ko mai yalla reck Moy bourr courage a vous que dieu vous protège

  • @abasspouye9631
    @abasspouye9631 4 года назад

    Yalla nalène yalla diapale si sene barkè Mame AK Serigne Babacar on est de la mm famille suis un petit fils de el hadji Momar Gueye pouye fils de Gouy Gueye pouye mais ou sont les autorités et anciens de mbao et de la communauté lebou

  • @alimaseye1542
    @alimaseye1542 4 года назад +85

    Pourquoi les sénégalais ne sont pas solidaires ana wa ouagou niayes deloléne keurou diambour on est plus en sécurité 😭😭😭😭😭😭😭😭

    • @LaBarhamienne
      @LaBarhamienne 4 года назад +1

      Alima seye Mane dh thi kogn bi la deuk mais li si net bi lako yeugué ni, wa ouagou niayes solidaire naniou mom franchement la preuve gnithi vidéo bi yeup majorité bi ay voisins laniou... fi ay nite yague naniou nangou keur diambour, ce n'est pas le premier cas.

    • @alimaseye1542
      @alimaseye1542 4 года назад

      @@LaBarhamienne ah bon lolou modoule yone sacrifié toute une famille leur dignité piétinée lolou lay nakhare lou

    • @LaBarhamienne
      @LaBarhamienne 4 года назад +1

      Alima seye Ah deuk bi dolè mofi meune deug malheureusement, lolou la nieup di nakarlou.

    • @alimaseye1542
      @alimaseye1542 4 года назад

      @@LaBarhamienne doyeneware yallah dina atté

  • @cheikhibrasamb8476
    @cheikhibrasamb8476 4 года назад

    Li mom doyna war yalla naléne yalla takhawou thiowale souf sakh da bakhoule

  • @khadimniang797
    @khadimniang797 4 года назад +4

    Khana famille bi amoule gaure dougou léne séne keur koufa nieuwe niafe léne ndayame

  • @aidambaye6167
    @aidambaye6167 4 года назад

    Yalla nalene yalla dimali si Barker serigne babacar

  • @ringo-lu1my
    @ringo-lu1my 4 года назад +51

    Kou khawîi soutoura ndiam bi ,tot ou tard diguako guiss

  • @khadydiop8274
    @khadydiop8274 4 года назад +3

    Liiiii moy khawi soutoura deugg yalla na yalla safara yirrr soutoural

  • @aitandour3867
    @aitandour3867 4 года назад

    Amine yalla naléne serigne babacar sy takhawou si barké seydina mouhamet sallahou aleyhi wa salam

  • @suzanneaminataseck1654
    @suzanneaminataseck1654 4 года назад +6

    Wa wagouyaye. Bou keneu kouneck heberger beneu khaler en attendant ls evemt car li meun n’a thraumatiser khaler 😭😭😭

  • @manganengone2806
    @manganengone2806 4 года назад

    kou nékoul en règle saxx warouniouko guéner waxoumalak kigua xamni mo mome li je n'ai meme pas les mots yallah nalène yallah soutoural aaaaaa SENEGAL

  • @abdoulayeba3344
    @abdoulayeba3344 4 года назад

    Yalla nalen yalla diapalei baguen naguou sen keur . souf ken douko kheutio

  • @magnoratvsenegaldiinooning4956
    @magnoratvsenegaldiinooning4956 4 года назад +2

    NDIAGA NIANG DOMÉRAMLA!!!!!!😭😭😭😭😭😭

  • @amicoleba4684
    @amicoleba4684 4 года назад +4

    Du courage doudou pouye😭😭😭 yalla nalenn s touba diapeuler😰

  • @ramatoulayesagna5532
    @ramatoulayesagna5532 4 года назад +10

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 ndeysane dawna yaram si seulement je pouvais les moyens si seulement j'avais les moyens

  • @diopdame1153
    @diopdame1153 4 года назад +1

    Diagua nieng yalla naga torokh yalla nalene yalla maye dam famille pouy 😭😭

  • @Keyna26
    @Keyna26 4 года назад +21

    Mettineu torop yalnalene yalla takhawou barkei seydina mouhamed SAWS

  • @amygaye408
    @amygaye408 4 года назад

    Bilay ça me touche énormément yalla nalen yalla geuna takhawou ci barki cheikhoul khadim 🙏🙏🙏

  • @aissatousylla9750
    @aissatousylla9750 4 года назад

    Yalla nalene yalla are te soutoural lene yalla bakhna

  • @falldior8000
    @falldior8000 4 года назад +2

    He la vie?? Que la lumière de Allah éclaircie 🤲🏽🤲🏽vraiment du courage qu'allah azzajawal vous aide amine yarabi

  • @Boye78
    @Boye78 4 года назад +1

    Vraiment c triste j'ai mal où vas le Sénégal

  • @oumydiallo9542
    @oumydiallo9542 4 года назад

    Thiey yalla lii nieuwna yallana yalla nieuw khetalilene

  • @courandiaye5937
    @courandiaye5937 4 года назад

    Dawna yaram yalla naléne yalla diapalé

  • @kebouz8297
    @kebouz8297 4 года назад

    C vraiment triste Cette histoire mai aussi je trouve que ils son bien fait de reste dort car ils ont ression vue que ils son pas honte bn courage yalah dîna ate insha allah

  • @cheikhsow3063
    @cheikhsow3063 4 года назад

    Yalla naleine yalla takhawou

  • @nafiniang3420
    @nafiniang3420 4 года назад

    Courage la famille pouye imbécile bi def li yalnako yalla trokhal mom ak wakeureum kou dém ba guéné la sa keur mom déssé loula dara amna niou bone way

  • @ngallagueye4924
    @ngallagueye4924 4 года назад

    Thieye yalla yalla naléne yalla takhawou t mayléne kholou mougne

  • @ndeyendong9137
    @ndeyendong9137 4 года назад +4

    Bilay boumafaye rombe douma sakh siggi ndakh yarame bouy daw
    Yalla nalene yalla takhawou

  • @aron6054
    @aron6054 4 года назад +22

    Li dawna yarame Ndiaga Niang xana yaramame dou daw walla xalatoul bamélam Sénégal deuk bou amoul loi , des juges corrompus 😥😥😥😥

  • @assanegeyemegustamucho8974
    @assanegeyemegustamucho8974 4 года назад

    Yalla nalen yalla maye ndame

  • @diattababacar9248
    @diattababacar9248 4 года назад +50

    Yalla naka serigne babacar sy tek lokho sii keur gui

  • @evacamara4340
    @evacamara4340 4 года назад +4

    Ndeysanne samay deukeundo you bakh tei mandou 😭😭😭😭😭😭yalla naleineu yalla dimbalei leiral mbir mi 🙏🙏🙏🙏

  • @thesisterschannelyacineand2547
    @thesisterschannelyacineand2547 4 года назад +7

    Yalla na lèn yalla diapalè si barker Baye Niass

  • @usad01
    @usad01 4 года назад +2

    Yalla mogii giss lep
    Inchallah yalla Dina
    Atté

  • @moussandiaye7958
    @moussandiaye7958 4 года назад

    Je soutiens la famille Pouye bon courage mbor Pouye et notre sœur Maguette Pouye

  • @mamadougo2749
    @mamadougo2749 4 года назад

    Li metina wayé lou waye def bopom boulen bayi li dafa yomb dinabah inchalah

  • @Taphiendoye
    @Taphiendoye 11 месяцев назад

    Oh mageutte pouye je la connait tho.boguóne classe

  • @LiLyg68
    @LiLyg68 4 года назад +2

    Ayy Ndiagua Niang , allal diraoul lih, mem bo ameh raison nga khol tchi yallah . Bamel khatt nah dall

  • @mariemekeita5063
    @mariemekeita5063 4 года назад

    Boulene bayi deh meme sounguene amé fénéne founguene deuk demeléne ba diekh ndakh baka séne mame di liguéye kéne fekou kassi (soudé yéna nek si deugue) yalla nalene yalla soutoural

  • @awadiouf7404
    @awadiouf7404 4 года назад +55

    khamouma kouw thiagua niang wayé na moytou mbiroume souff bi moye 2fois maye sétane vidéo gnouw guéné aye famille toureume dissi fégne bayil khél euleuk😢😢😢

    • @sagardieng5698
      @sagardieng5698 4 года назад +4

      Waw Way lolou amna dé

    • @astousaliou5860
      @astousaliou5860 4 года назад +6

      La justice de Dieu est latente mais elle arrive toujours. Beusseum migui si biir beuss yi

    • @mamecorsarr5845
      @mamecorsarr5845 4 года назад

      Qui dou nite sakh si

  • @adakambel211
    @adakambel211 4 года назад

    C'est triste Dieu est grand Les gens sadiques qui veulent à tout prix devenir riches ont envahi les grandes villes La famille Pouye est une des victimes parmi des milliers Que le prophète Mohamed P S L intervienne pour que les Pouye récupèrent leur dignité

  • @khadimbeye8798
    @khadimbeye8798 4 года назад

    Ce qui est le plus difficile au monde c est de voir des problème que tu ne peux résoudre malheureusement si je pouvais vous donner une maison

  • @InfosetTutos
    @InfosetTutos 4 года назад

    Ce gars a certainement un soutien au sommet il est plus fort que cette famille et nous sommes dans un pays ou c'est la loi du plus fort

  • @maguettediouf8538
    @maguettediouf8538 4 года назад

    Li méttina trope Yalna niou yalla moussal thi pékhé none

  • @ndacksene8665
    @ndacksene8665 4 года назад +7

    Hoooooooo😢😢😢😢métina gnagua niang torokal sa mboromou djoulite loulako djaral dé dina ame dééh bayi si khel. bilaye serigne babacar légui mou gneuw baguéne délou sene keur

  • @oumarblondeblonde4142
    @oumarblondeblonde4142 4 года назад +1

    Li nako serigne mountakha bassirou mbacke yeuk waye

  • @bayeniang3044
    @bayeniang3044 4 года назад

    aÿÿ way Kou sante Niang day am yeurmandé dh

  • @abdoulatifmbacke1008
    @abdoulatifmbacke1008 4 года назад +4

    Ndaysan yalla yalla nekk sén takhawaye yalla nalen yalla sammou

  • @mmesarr2607
    @mmesarr2607 4 года назад

    euy Yalla nagnou Yalla sangue malaanou Soutoureu. Amiiine

  • @ababacarsall2449
    @ababacarsall2449 4 года назад

    Ki déf mo bone deugeu bilahi sama khôl nakarina ta mounou massi dara. Ay wakh trokhal naléne wayé yalla dinaléne dimbeuli. Famille bou tollou ni ak séne ndiabote mou défléne ni. Adouna diaroul li ta baméle khatena trop. Allakhira dina métti trop. Yalla naléne yalla diabalé si barcké seydina mouhamed. Ak cheikh Ahmed tjidiane chérif ak serigne babacar sy amine

  • @aissatousow4668
    @aissatousow4668 4 года назад

    Away lii meeti na trop adouna bii djèkh na ba par
    Kou mena trokhalè nii sa famille 😭😭😭😭😭😭😭

  • @Venusediop1817
    @Venusediop1817 4 года назад +1

    Yalla nallene yalla ndinbali si berki yonet bi psl 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @myamya9300
    @myamya9300 4 года назад

    Ay way ndeysane masta

  • @mynasaliou24
    @mynasaliou24 4 года назад

    Hoh c triste yalnalen yalla takhawou thi barkep seydina mouhamed ki def lii douko djik famille leum thi bedd mi

  • @mohamedgueye4329
    @mohamedgueye4329 4 года назад

    Liy dafa nakari si khol wallahi le faite k ngakay guiss rek tei meuno ko fath sakh dafa meiti injustice mo wara diekh Senegal genre yi dongou motakh yalla dji diniou teik yimou niouy teik wallahi yalla nalei yalla tahawou 🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @khalifabenmtdiop2440
    @khalifabenmtdiop2440 4 года назад

    Yalla na yalla dolli soutoura sounou rewmi so amoul dollé rek mou metti si yaw wayé yalla naléne yalla diotolé wate si séne keur

  • @amdykandji3524
    @amdykandji3524 4 года назад +68

    Ya des gens yo xamni nio gueuna bonn coronavuris

    • @adamadieng8720
      @adamadieng8720 4 года назад +1

      Vraiment c la triste réalité ....on doit les restituer leur patrimoine. De tout coeur avec ma famille POUYE.

  • @babsmania85
    @babsmania85 4 года назад

    ça me rappelle une expulsion d'une famille à Kaolack qui avait abouti à deux morts, un vieux policier et un jeune homme qui s 'était suicidé ! quel gâchis pour un bien qui dans 50 ans ils seront tous morts et enterrés depuis longtemps! Adouna diaroul yen yi !

  • @diopmansour5939
    @diopmansour5939 4 года назад

    😭😭😭😭 ndiaga set si yalla sama yaram dafa daw

  • @ndeyefatouba8659
    @ndeyefatouba8659 4 года назад +182

    Serigne babacar dou tass sen yakar

    • @maguettediop3785
      @maguettediop3785 4 года назад +2

      Bilay

    • @deessedufoutadiallo2121
      @deessedufoutadiallo2121 4 года назад +2

      Bilahi

    • @ibrahimambodj3713
      @ibrahimambodj3713 4 года назад +39

      Ma chère soeur serigne babacar est mort. Qu est-ce que cette façon de parler. Priez pour lui il n'est pas Allah . Seul Allah peut les soutenir mais pas serigne babacar que dieu nous pardonne tous.

    • @moussabadji420
      @moussabadji420 4 года назад +1

      inechallah

    • @atitababacarsy5535
      @atitababacarsy5535 4 года назад +17

      @@ibrahimambodj3713 waa yao moom Serigne Babacar est mort rkk nga meuneu wahh aah niakk nga horma dei nitt daffay amm teguine nga baalma😒

  • @bayetaphagueye5290
    @bayetaphagueye5290 4 года назад

    Ndeysane métina trop yalla naléne yalla takhawou

  • @rackyracky7198
    @rackyracky7198 4 года назад +33

    Vraiment li dafa méti sénégalais di woté dioulite té amo yeurmandé c'est pas juste ca fait mal

  • @julesjunior1937
    @julesjunior1937 4 года назад

    On est dans quel pays

  • @dareal_momo4946
    @dareal_momo4946 4 года назад

    Ayyy wayy nitt kene douko torokhal li gnaw na trop legui kokou deukoul si keur gui dou lene Lo delo rkk ba lougnou am fayy Yallah dh mom mogui Djiss lepp

  • @maimounabalde7622
    @maimounabalde7622 4 года назад

    Al lahou Akbar adouna diékh na

  • @madapouye6568
    @madapouye6568 4 года назад

    Bilakhi Sama mame sokhla woul allalou diambour bilakhi ndiaga niang bayi nanioula akh yalla

  • @mamediarrasene7044
    @mamediarrasene7044 4 года назад

    Naniou kholat dokhaline yii alalou adouna diaroul yéneu yii. As gor kéneu douko torokhal. Yalnaniou yallah doli soutoura🙏

  • @salyallemomuawrksarr8652
    @salyallemomuawrksarr8652 4 года назад

    Ndayssane li mètina dèh niang dèlosil sa khèl te khamni adouna dou dara te dara yagoul dèlol sa khèl si yalla 😭😭😭😭

  • @mamekhadysow530
    @mamekhadysow530 4 года назад +56

    Dadji len bountou bi dougoul seni bagages. Kou fi niaw nguén vanterko sen bakan sinon di nguén niak sen keur gui Lou lerr lalen wakh sou guen diogué fofou niou dougueul len fénén Moy niakk guén ba faw. Mbédjou kanam borom mokoy fadji. Yeurmande ak deuk mo djékh Senegal. Yalla nalen yalla takhouwou.

  • @fatousarr2822
    @fatousarr2822 4 года назад

    je ne peux m'empéché de commenter ,li métina trope sakh yalnalene yalla takhawou nite khéne doukha trokal ki kou bonne la

  • @naskelly4451
    @naskelly4451 4 года назад +1

    Yalla nalene Serigne touba takhawou

  • @fallmara9119
    @fallmara9119 4 года назад

    Yalna si yalla diamou si berkhe s babacar sy

  • @thiamkhadim4681
    @thiamkhadim4681 4 года назад

    yalena yalla doliléne soutoure diokheléne louco geune wayai cite bi amoule soutoure cou torokhale domou adama yalla dinala torokhale 😭😭😭😭

  • @amethgueye8598
    @amethgueye8598 4 года назад +1

    Yalla nalen yalla atée ak mom

  • @zaleuhbdk1777
    @zaleuhbdk1777 4 года назад +3

    😭😭😭😭😭li gnaaaawna ki deffli na khamni allalou adouna diaroul li

  • @kinedieng2641
    @kinedieng2641 4 года назад +2

    Yallah nagnou yallah doli soutoura Mme ne vous inquiétez pas ndakh yallah gueumoul neilawoul mou ngi guiss leipe dou bay mouk diamame bi di torokh

  • @khardiatoubocoum7737
    @khardiatoubocoum7737 4 года назад

    Bilahi yalna serigne Babacar sy wouyousilene

  • @bintasall1932
    @bintasall1932 4 года назад

    Fima tok magui dioy sama khol diékh tè meunou masi dara thiey yalla soumasi meunon dara dieunde keur diokh léne lilèn bayi lénko ak yalla mé bon lileu yalla dogal😭

  • @minafall8709
    @minafall8709 4 года назад +19

    Ma bayi commenté si wakhou keur ndakh cas wou Moussa yalna leinn yalla diapalei doli leinn soutoureu

  • @omartoure1016
    @omartoure1016 4 года назад

    Lii dara diaroukoo si adina akk lou meuneu hewww dara diaroukoo yalnanou yala dolii soutoureuu

  • @reineasacouronne6590
    @reineasacouronne6590 4 года назад +7

    Modou khoulé dangay méyé ay terrain rk,voilà amna nio méy terrain,méylén terrain, tabakhal lén ko nguir dieumi Rassoulilah,Marème Faye Sall on vous lance un appel de venir en aide à cette famille,La famille a tord ou op c op important, de toute façon nit waroul fanan thii mbédeu mi tei askan bi neikk fi...Où est le téranga sénégalais ???

  • @modoudeme7517
    @modoudeme7517 4 года назад

    Ndaye sane 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @mariamagaye2669
    @mariamagaye2669 4 года назад +7

    Métina trop mais yal nalene yalla takhawou

  • @papethiam9413
    @papethiam9413 4 года назад

    Bilahi si j’avais des moyens, je résoudrai cet histoire bilahiiiiiiiiii😭😭😭

  • @diopconstrutora6213
    @diopconstrutora6213 4 года назад

    Bilakhi barkep borom touba budon man wala sama famill kèn du deuk si keur gui khawma jiaga niang khawma mèi kou bon la

  • @BK18465
    @BK18465 4 года назад +1

    Yalla nanou yalla doly soutoureu rekk