ANALYSE BOU DOYWAR SUR LE DERBY GRIS VS AMA «AMA waroul beurek Gris 2mn

Поделиться
HTML-код

Комментарии • 43

  • @Cheriflaye1995
    @Cheriflaye1995 5 месяцев назад +3

    Vraiment Serigne ndiaye 2 beugue guéne gnouko forcer. Danou Fi Kéne
    Moustapha gueye fait tous piur nous le forcer.

  • @cheikhfall4377
    @cheikhfall4377 5 месяцев назад +4

    Yalla Nanioùkô téwé incha'Allah yalla maï ndam Ama baldé Ada fass si barké seydina Mohamed psl ❤

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 5 месяцев назад

    Amaaa Balde Ada Fass yallah nalène
    Yallah soutourall may lèn ndam Barké serign fallou Mbacké 🙏🏻❤️🙏🏻❤️🙏🏻❤️🙏🏻ndam rék inchalah 🙏🏻

  • @abdoulayefayedia7651
    @abdoulayefayedia7651 5 месяцев назад

    Je suis fassois mais li bour wakh deugue la gris défoufiiii dara lou extraordinaire comment bi moy dernière chance pour mou prouver que ni Mbeur la
    Bou danoul combat bi moom wakh deugue yallah naniou dinde titre tigre de fass

  • @ismailadiop7590
    @ismailadiop7590 5 месяцев назад

    Tapha machalla tu analyses bien Machalla

  • @abdoulatifdiop5640
    @abdoulatifdiop5640 5 месяцев назад +1

    Aÿ wayy m'ay l'en fadam diamou akh😅 DAa xam limouy wax rek Masha allah 🎉

  • @BaraNdiaye-jm9uo
    @BaraNdiaye-jm9uo 5 месяцев назад +2

    Il faut comprendre lii dou débat politique di khar parole
    Fadam ak bour c des animateurs
    Ils exitent les amateurs c'est ça dafa wara khoumb

  • @doundou_diam4953
    @doundou_diam4953 5 месяцев назад +3

    Fadam dafa Wara khôl si Bay Balla. Bay Balla il est tres posé, dou wakh tei diokhouniouko parole Mais fadam amoul beine dall

    • @abdoulatifdiop5640
      @abdoulatifdiop5640 5 месяцев назад +1

      Fadam nimou Koy defée mo bakh d'ay nekhal débat bi

  • @ibrahimasambseye2938
    @ibrahimasambseye2938 5 месяцев назад +1

    Tapha tu fais vivre la lutte vraiment tu analyses de manière très forte

  • @fadal9582
    @fadal9582 4 месяца назад

    Ama Baldé boumou nangou corps à corps bi
    S'il réussit ça dakoy daan
    Na fekhei diap ba parei xeex mais pas mou diakarlo ak mom di xeex gris lolou rk la am si combat bi

  • @elmahdi5221
    @elmahdi5221 5 месяцев назад +11

    Becaye waxal yane mbeur nio d'âne falaye mogeu ngay meuseuntou nii yekini gnimou d'âne yeupeu kéneu danou kosii waxal lénén moo geun ça se vois que wa fass nga mais le 30 insha'allah Ama Moy aam ndam

    • @elhadjidiouf1653
      @elhadjidiouf1653 5 месяцев назад

      Way copain duul way nganane Wa fass 137 combat khana sa papa moko arbitré

    • @cherifndoye3555
      @cherifndoye3555 5 месяцев назад

      @@elhadjidiouf1653😂😂😂 togne bakhoul way 😂😂😂

    • @elhadjidiouf1653
      @elhadjidiouf1653 5 месяцев назад

      Wa bro 134 victoires si 137 c’est pas logique nakk😂😂

    • @cherifndoye3555
      @cherifndoye3555 5 месяцев назад

      @@elhadjidiouf1653 bilay c pas logique motakh becay wakh nako lolou dou deug😂😂

  • @khadimgueye989
    @khadimgueye989 5 месяцев назад +1

    Non bour niguayy wakhi si gri daffa yaww tropp nitte kenn douko topp beup Seuss

  • @AliounebadaraGassama-or4op
    @AliounebadaraGassama-or4op 5 месяцев назад

    Yalla na Ama dann Gris bordeaux mais na Abdou bakhoum teuthie laminiame

  • @AliounebadaraGassama-or4op
    @AliounebadaraGassama-or4op 5 месяцев назад

    Fadam vraiment bakho bayil di wakh secret diambour yi

  • @ladianepathe5637
    @ladianepathe5637 5 месяцев назад

    Gris dh 100 combat ama daan ko gris dou mbeur setana gouma mou daan mbeur aah

  • @abdoufall3831
    @abdoufall3831 5 месяцев назад

    Giri moy dan ama inchla

  • @dembaztarkinda8270
    @dembaztarkinda8270 5 месяцев назад

    Baye balla nak lima nekh si mome dafa teye daye khar bagnou diokh ko parole mou doga wakh para port ak Bour ak fadam daniouy siff wakh tann dafa lathi deglonté kw moye Takh mou nekh nagn respecté nitt gni kw surtout fadam pour mome mo geuna kham gneup lamb kw

  • @gueyemodou8207
    @gueyemodou8207 5 месяцев назад

    😂9 ans sens victoire 😂 yèmèna dhé 😂

  • @AliounebadaraGassama-or4op
    @AliounebadaraGassama-or4op 5 месяцев назад

    Mais Serigne Ndiaye franc limou dèf thi lutte avec frappe défa goko

  • @khadeejaht
    @khadeejaht 5 месяцев назад +2

    Fadam da melni mom rekk lagn invité. Kou wakh mou dagg leu

    • @MOUHAMEDKANE-d1j
      @MOUHAMEDKANE-d1j 5 месяцев назад

      Setlou gua lolou ki daffa niap ndm koi mayoul becaye netali

    • @khadeejaht
      @khadeejaht 5 месяцев назад

      ⁠​⁠@@MOUHAMEDKANE-d1jboul sagua 😂 balko

    • @MOUHAMEDKANE-d1j
      @MOUHAMEDKANE-d1j 5 месяцев назад

      @@khadeejaht Imbecile leu koi

  • @MatarNjie-dc6hb
    @MatarNjie-dc6hb 5 месяцев назад

    Baye balla nopil khamou lamb😢

  • @AliounebadaraGassama-or4op
    @AliounebadaraGassama-or4op 5 месяцев назад +1

    Té gris défaite yi mou am boudonn bénén konn kénn dotouko toudou liko waral moy séytané yi thi lamb dji gris dou mbeur

  • @diafaracissokho963
    @diafaracissokho963 5 месяцев назад

    Il faut laisser Mame Balla parler par respect 😢

  • @jazaka3178
    @jazaka3178 5 месяцев назад

    Serigne da nga dioum franc amoul defaite

  • @AliounebadaraGassama-or4op
    @AliounebadaraGassama-or4op 5 месяцев назад

    Gris limou am contre Balla gaye mom la Modou lo am contre Ama exploiter ko gris meunn na khékh mai amoul détermination

  • @mamadouwade6565
    @mamadouwade6565 5 месяцев назад

    Ndox dou bayi yone ama seul

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 5 месяцев назад

    Becaye waxall kou Dann Falay Balde yaw Becay Bèneu problem nga moy pour yaw yaw rék yaa xam lou xéw Dèmeu 🥹ndioula mak fouf niofii Nèkeu geunla xam lamb yaw Becay Falay Baldé Math nala papa Dei 🧏Mounofé wax louniou xamoul thi Paa Falay Balde

  • @laminediop7135
    @laminediop7135 5 месяцев назад

    Je vous jure Cribaurdo cil gagne ou prêtre il lui reste 3ans de car

  • @Abdallah31341
    @Abdallah31341 5 месяцев назад +1

    Bour louma nékh si mom moy loum gueum lay wax, dou nafékh

    • @Domou_Deukk_Bi
      @Domou_Deukk_Bi 5 месяцев назад

      Au contraire Geumoule dara yak mom yéneu yam

  • @doundou_diam4953
    @doundou_diam4953 5 месяцев назад +1

    Fadam dafa Wara deglou franchement quoi mou melni kouniou dinkk lamb ji

  • @bambasamb7196
    @bambasamb7196 5 месяцев назад +1

    Bour sokhorga gris rék ga bagne

  • @Dudufaramaren311
    @Dudufaramaren311 5 месяцев назад

    Fadam kou soff la khamoul Dara

  • @bocarba2781
    @bocarba2781 5 месяцев назад +1

    Waw c pas un combat way, gris est fini depuis longtemps, vous êtes tous les fils de aziz ndiaye mo takh gueum foulal combat bi Maia gris est fini soyez sérieux way. C’est pas un combat aucun sénégalais de la diaspora vas payer pour voir alors qu’il savent déjà la fin. Xar redivision bi Rek lol