Ok merci. Je suis pas là pour polémiquer moi. J’ai juste dit dans des explications religieuses comme celle ci ,faut limiter la rigolade .On est pas dans le show biz .
Reponse bi dacorouma ci ndakh amna aye borom xam xam youni djiguéne souy simékou, sou delo wé thiéne gui dieukeureum niko simekou na, Islam tass na seuye ba, legui nak warou guar biko borom keureum diokhone lolou amoul pour faye kako ndakh dou farata pour takk seuye. Farata biye takk seuy moy thiéne, wayé dou warouguar. Wa Salam
Oustaz li nga faté moy 2millions yoyou cotiser ou pas kou goor ki ak sa famille gno eupeu lougne si consommé. Ndax sougnouy indi wargal bi di nga si sakk diox lene, jour xew bi nga yoboul lene agne ak reer bou riiiche na paré teral lene... c a dire tu recois 2milion mais so defoul nank tu en dépenses le double voire le triple pr la belle famille et les amis de Monsieur... mani delo mofi amoul place en cas de divorce, nakou nek goré rek dem
Problème bi moy djiguee mo badola bou di ameu lou nek ngay deg kom dousa borom keur llou moy pousse goor yi mais dou sokhor wala bonn djiguee dfeu badola te yalla loumou wx ameu lutax
Séo mom dafa nékh macha alah moma gueneul dokh yeup yal nagnou yalla mousseule thi divorce amine
C’est abusé.
Trop d’amateurisme 😢
Il faut rigoler mais y’a des limites quand il s’agit de réponse à des questions importantes sur la religion .
Tu as la réponse à la question et c’est l’essentiel
Ok merci. Je suis pas là pour polémiquer moi.
J’ai juste dit dans des explications religieuses comme celle ci ,faut limiter la rigolade .On est pas dans le show biz .
@@Faty1206tu dis que la vérité... pape cheikh dafa wara wagni thiakhane bi, il est très abusif...
@@Abdallah31341Ofet moi Dieu sait que je l’apprécie trop mais la religion ,c’est la religion
Reponse bi dacorouma ci ndakh amna aye borom xam xam youni djiguéne souy simékou, sou delo wé thiéne gui dieukeureum niko simekou na, Islam tass na seuye ba, legui nak warou guar biko borom keureum diokhone lolou amoul pour faye kako ndakh dou farata pour takk seuye. Farata biye takk seuy moy thiéne, wayé dou warouguar.
Wa Salam
Pape cheikh a raison goor dou cotiser ak djiguéne do am batt thi sa keur
Goor bou irresponsable rk mokay nangou
Seo môme dafa nexx bilay .man môme douma doyal 😂❤
Ndékété légui encaissé dot erreur le😂
Oustaz li nga faté moy 2millions yoyou cotiser ou pas kou goor ki ak sa famille gno eupeu lougne si consommé. Ndax sougnouy indi wargal bi di nga si sakk diox lene, jour xew bi nga yoboul lene agne ak reer bou riiiche na paré teral lene... c a dire tu recois 2milion mais so defoul nank tu en dépenses le double voire le triple pr la belle famille et les amis de Monsieur... mani delo mofi amoul place en cas de divorce, nakou nek goré rek dem
Cotiser pour lane tmt
Bumuko Faye touss niak fayeda shim.😢
Pape Cheikh Dou Nit😂😂😂😂
Non 😂😂😂pape cheikh wakh ngua deug
Wouyy pape 🤣🤣🤣
Kia mon compte 😢😂❤❤
En Europe c'est 50 50 diobou ndaayou les meufs africains
@@cheikhantadioptv2790 sa yaye meuf leu tamite soko faté,
Wa Salam
@@cheikhantadioptv2790 sa yaye meuf leu tamite soko faté
Wa Salam
Problème bi moy djiguee mo badola bou di ameu lou nek ngay deg kom dousa borom keur llou moy pousse goor yi mais dou sokhor wala bonn djiguee dfeu badola te yalla loumou wx ameu lutax
Goor moo geuneu bodola fouuf
Yen goor gni yéna geuna bone
Badola wésou woule nite guisse là beugue là bamou diaralko aye cotisation pour ngua takouko ngua saguanéko bamoulay Niane divorce yéne guor gni yéna guéna nék aye badola
@@binetouniang2273faut pas généraliser
Fi dh kou goor ki mo badola