🛑Divorce Aïssatou Penda et Ousseynou? La vèritè :Jamra en direct dit tout avec la voyante

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 янв 2025

Комментарии • 81

  • @mouninandiaye7917
    @mouninandiaye7917 5 дней назад +6

    Beau travail dans le pays. Qu'Allah vous Garde ou Protège

  • @BayeamadouDiouf
    @BayeamadouDiouf 4 дня назад +20

    Vraiment, vous nous emmerdez avec ce problème entre un homme et une femme qui se sont mariés devant DIEU, laissez les vivre leur vie comme bon leur semble.

    • @adjiadialo
      @adjiadialo 4 дня назад +2

      wakh deugu

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 4 дня назад +3

      Nga sagne ko wakh! Sénégal sou fekker ni vie privée amatoul dina méti nak. Gni dagno seuy lolou kay lou dagane le mashallah.

    • @adjiadialo
      @adjiadialo 4 дня назад +1

      @ mane sama ex 5ans lako mague bamou febare lako kham mom khamoul mako makk mais mako bayi dakh dama meusa degu mouni les familles danio wara bayi niouy tak kou lene makk ak niou seuy ba tass am bene dôme la khamni qui sene wa keur danio am bleme bobou te mane douma dougou si seuy bou bari tiow jamais dakh dama beugu sama bop trop kene douma khep nigamay touteul

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 4 дня назад +3

      @@adjiadialo ma soeur Sénégal mo ngui ni, li gni waara bagne da gnou kay tek feuler bagne lou ya allah geureume. Nek fi rek di tass seyyou djambour yi ak di yak mbeuguelou djambour yi. En plus dama djiss ni respect de la femme mi ngui en recul au sénégal! Ligni mayy gor baari na lougnou may djiguene new ne! Mani kou nek ne sey ak kouka nekh tant que deupo na ak se diner bi nga bok ak souna ... Ame djott rek nek si seyyou djambour di wah rek li tamitt. Fière de toi si geume se bop mo gnou siye djener nak si mime rew!

    • @adjiadialo
      @adjiadialo 4 дня назад +2

      @ bilay do comprendre dara dagniy yak diguenete di yak amour diambour 😔

  • @natachaseck8206
    @natachaseck8206 4 дня назад +5

    Sénégal soutoura jekhnafi ! leup moungi ci mbedmi ! leep ! goor meuna am 4 femmes ci rewmi ngen takhaw weer sen bop nii ! Na état bi jouk def comme japon et plus même Etat militaire! liguey ba deh ! doug ci allebi daag ay tole you doul djekh nieup bayi mou teuj tik tok bi ! li Sénégal nekeh wakh werantéh ben deuk défouko developper ! ben deuk nak !

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth1968 4 дня назад +6

    Mame Matar
    Ce n'est pas Aïcha; c'est Khadidja qui a engendré 2 garçons etquatre filles, et pas deux filles et quatre garçond. Faites attention quand vous parlez des affaires religieuses.

  • @courambissa1816
    @courambissa1816 4 дня назад +2

    Yow bougnou sonal takoo koula makk! Ta baayileen di djeul reference thi Yoneent bi ndakh moo magg Khadija thi baatine...

  • @KhalidSowe-q2l
    @KhalidSowe-q2l 4 дня назад +2

    Non non dou Aïcha Khadija la

  • @kanemariame8262
    @kanemariame8262 4 дня назад

    Qu’Allah vous bénisse abondamment amine y’a raby 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @ndeyediawara6350
    @ndeyediawara6350 4 дня назад

    Kaboul hy rafetena machallah ❤

  • @yayodiallo1021
    @yayodiallo1021 4 дня назад +1

    Môme guéne nite gni dé plus 1 semaine FO tourné si tik tok bi rekk gnom la focus reek si lénéne

  • @MamadouMbacke-k4h
    @MamadouMbacke-k4h 3 дня назад

    Niongui diglou wayé nlomté yi Barina bo waré wakh seyidatouna Khadija né seyidatouna haicha
    Bowaré wakh pawlis né kouthia doyna War yalla yalla doli diam

  • @KaraJieu-p5p
    @KaraJieu-p5p 5 дней назад +5

    Ousseynou sakh kanamou comédien la yorai ,tai guaure dou bari wakh, or lui il est très bavard,influencé nagnouko bamou soopalikou comme deume,rakhassoul thie moome ,mou dailou thia walaawookine ya,naala wouteul kou baakh,il est irresponsable

  • @nogayelo774
    @nogayelo774 5 дней назад +3

    Lui c'est pas un IMAM, et pourquoi il se laisse appeler comme tel alors qu'il ne l'est pas .....C'est une USURPATION de fonction!!!!!!

  • @ouleymatoudiallo6677
    @ouleymatoudiallo6677 5 дней назад +7

    ❤❤❤ différence d'âge bi dafa barri trop

    • @KaraJieu-p5p
      @KaraJieu-p5p 5 дней назад +3

      L'islam moola wakh nila si la différence d'âge est trop grande kaine waroul taike seuy bi,mbaa dou valable ?

    • @thinktanktruth1968
      @thinktanktruth1968 4 дня назад +3

      Ce n'est pas important, ni une barrière

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 4 дня назад +2

      Différence d'âge khana tay le déranger yene sénégalais (e)s yi! Ay gor you maguett difi tak khaler you touter touti, djiguene sey ak gor bou ndaw si atte thiow li ni kour! Nitt dey deugou. Age yoroul mbeuguel yoroul sey. Sey nak koussi meune wah lou raffett nako deff sou wakh dji narer gnaw na nane ndokh nopi.

    • @nabiyana
      @nabiyana 4 дня назад +1

      @@lacitoyenneafricaine8566Hello ça fait un bail.

    • @AS-ks1kx
      @AS-ks1kx 3 дня назад

      Toggal fofou di khar dieukeut! Môme de amna!

  • @kanemariame8262
    @kanemariame8262 4 дня назад

    Et y’a n’a d’autres qu’il veulent faire des mariage le temps d’un week-end du jamais vu aux Sénégal Soubkhanalah

  • @toutoularandiaye2116
    @toutoularandiaye2116 4 дня назад

    Au 21é siècle le changement est grand acceptez le

  • @NfamaraDiatta-q8j
    @NfamaraDiatta-q8j 4 дня назад

    Macktare Sen baye le
    Kou baak le

  • @AssaneNdiaye-dv8dl
    @AssaneNdiaye-dv8dl 3 дня назад

    Ce gars doit se taire. Il ne connaît rien, tout ce qu'il fait c'est du trafic d'influence. Qu'est-ce qu'il représente pour le Sénégal. Qui l'a investi,vraiment donné nous la paix.

  • @mbathiodalle1051
    @mbathiodalle1051 4 дня назад +1

    Franchement vous avez très bien que c'est juste du buzz au Sénégal les féministe elle feront jamais sa 😂😂😂😂😂😂 c'est juste pour qu'on fasse attention à eux 😂😂😂

  • @zeyna7672
    @zeyna7672 4 дня назад +1

    Feminist yi né dagnou marche tatou nène, wakho si. Vrai nafekh boudonn sa dome bou gor doko nangou.

  • @nafissatouseye6477
    @nafissatouseye6477 4 дня назад

    c'est koutia où pawlish

  • @ThiernoDioum-h5t
    @ThiernoDioum-h5t 4 дня назад

    Excusez-moi mr gueye il faut dire de bon exemple parapor entre khadja et cette je sais pas la😢😢😢😢😢

  • @AS-ks1kx
    @AS-ks1kx 3 дня назад

    Vous faites vraiment un harcèlement moral sur de paisibles citoyens !

  • @abdouazizthiaw3491
    @abdouazizthiaw3491 4 дня назад

    Ndaxam yonnént bi amoon në lu ëpp ñénéneti soxna té ab jollit waru lë wéessu ñént. Ak yu bari yo xame né dagan në ci yonnént bi té mayu ñu ko jullit yi. Du lépp la nuy roy ci moom ndax yallah daf ko bér , baadil ko ci lu baré bari.

    • @toutoularandiaye2116
      @toutoularandiaye2116 4 дня назад

      Yalla bérou KO bédilouko c'est pour enseigner aux générations futures

    • @abdouazizthiaw3491
      @abdouazizthiaw3491 4 дня назад

      @toutoularandiaye2116 Waxu ma bédi ,badil la wax. Moy may ku lu mu mayul kénéen.

  • @bassirou5406
    @bassirou5406 4 дня назад

    Mr Makhtar, bien que ce mariage est accepté par islam, mais y'a une manipulation dedans que l'islam a complètement détesté, ceci ne correspond pas à notre culture sénégalais, qui est 100% de l'islam, aussi notez que le prophète mohammed (saw) est le meilleur référencé des musulmans, mais certains points qu'aucun musulman n'a pas le droit de référer du prophète saw, par exemple le prophète a laissé 9 femmes derrière lui. Certains points sont spécialement pour le prophète ( saw) merci pour la compréhension.

  • @farbadiouf1990
    @farbadiouf1990 4 дня назад

    " A sa plus petite expression." Vous vous référez à cette formule? Et vous exposez cette histoire intime de

  • @Astoundiaya
    @Astoundiaya 4 дня назад +1

    yaw ligay wakh gamou Loko ki 30tan lako make

  • @mouninandiaye7917
    @mouninandiaye7917 5 дней назад +1

    Koutia ou Pawlish?

  • @abdouazizthiaw3491
    @abdouazizthiaw3491 4 дня назад

    Téyitam xadija matul woon Yonnént bi yaay. Différencu 15 ans ak 30 ans du bénn. Xolaatal li ngay wax. Ndéem yonnént bi la nuy roy kon kay ab jullit warulë takk jigéen ju ko magé lu wéessu 15ans. Niki yonnént bi lë wara déff. Logique wallah ?

  • @ibrahimabalde975
    @ibrahimabalde975 4 дня назад

    pere bi xamoul dra

  • @thiabadiona5997
    @thiabadiona5997 4 дня назад

    Mais ndawsi marna mènopause mounouko amal dome

  • @assanembengue6364
    @assanembengue6364 4 дня назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @oumienjie9333
    @oumienjie9333 5 дней назад

    Not Aisha is Khadija

  • @ThiernoOmbre
    @ThiernoOmbre 4 дня назад +4

    CE MARIAGE EST VILAIN. CULTURELLEMENT INACCEPTABLLE . MA MACTAR JE NE SUIS PAS D'ACCORD AVEC VOUS

    • @toutoularandiaye2116
      @toutoularandiaye2116 4 дня назад

      Culture et islam qui est le mieux pour le musulman ? Juste sois franc😊

    • @ThiernoOmbre
      @ThiernoOmbre 4 дня назад

      @toutoularandiaye2116
      L'ISLAM EST UN ELEMENT CULTUREL ARABE. POUR MOI SENEGALAIS, AFRICAIN & PEUL , LA CULTURE AFRICAINE EST PLUS IMPORTANTE QU'UNE RELIGION ETRANGERE.
      LE NDËP, LE TUUR , LE SAFAARA, LE GAMOU, LE MAGAL , LE RESPECT AUX AINÈS SONT DES ELEMENTS CULTURELS SENEGALAIS QU'ON DOIT CONSERVER . DOIT ON LES REJETER? JE DIS NON!

    • @ThiernoOmbre
      @ThiernoOmbre 4 дня назад

      @toutoularandiaye2116
      L'ISLAM EST UN ELEMENT CULTUREL ARABE. POUR MOI, PEUL, SENEGALAIS & AFRICAIN LA CULTURE AFRICAINE EST PLUS IMPORTANTE QU'UNE RELIGION ETRANGERE.
      LE NDËPP, LE TUUR, LE SAAFARA, LE GAMOU ET LE RESPECT AUX AINÈS SONT DES ELEMENTS CULTURELS SENEGALAIS QU'ON DOIT CONSERVER.
      DOIT ON LES ELIMINER? JE DIS NON!

  • @FatouDiedhiou-xo8mm
    @FatouDiedhiou-xo8mm 4 дня назад

    Mere bi kene douko bayi kou donone sa dom dagayi bagne bougueugueu seute

  • @mariendiaye1348
    @mariendiaye1348 5 дней назад

    Pawlis

  • @chiekhsamb9296
    @chiekhsamb9296 4 дня назад +1

    Boudone sa dome doko naguou

  • @WeulliThiaw
    @WeulliThiaw 5 дней назад +2

    Aissatou penda n est pas Khadija ousseynou n est pas Mohamed psl et la différence d age de ce couple est le double si c était ton fils tu ne vas pas accepter in mariage que tes parents ne sont pas au courant 😊😊

    • @Ablayb
      @Ablayb 4 дня назад +2

      Donc foutez nous la paix avec la religion kou nek ga doundou sa doundou point

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 4 дня назад +2

      Sénégalais souka souna arranger woule rek gno contester. Souna borome khel yi lay wakhal peu importe différence âge bi. Li mou beug djangaler moy djaabar meune na mak djeukeurame att you new wala att gnou takou amoul solo.

    • @Ablayb
      @Ablayb 4 дня назад +2

      @lacitoyenneafricaine8566 gni daniouy fontou

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 4 дня назад

      @@Ablayb mane dama moudj djakhler si yene nitt yi vraiment. Li bok ne si li takh Sénégal sey yi gouda tougnou fane! Gnissi waroul wakh dissi wah ame fitt takhaw ni seuy bi nekhou lene fok mou tass! Wa ani mandou? Thieuy ya allah ! Ziare nala.

  • @mouninandiaye7917
    @mouninandiaye7917 5 дней назад

    Seydatou Khadija pas Aïsha

  • @edithsene373
    @edithsene373 4 дня назад

    Pabi

  • @lacitoyenneafricaine8566
    @lacitoyenneafricaine8566 4 дня назад

    Mère dale (maname kou khass be ame 50 ans Sénégal) koula wara tak soka magguer trope na nga tokk dè si célibataire sinon gnou pinthiale le bire Sénégal ! Djamba djaffer!!! Qui est qui pour régler ou reguler la vie de quelqu'un ou quelqu'une ? Djiss nani Sénégal Aissatou dou problème bi "djiguene" yi gnoye problème bi, saga ndeye yi bari ne, khass djiguene bari na. Djiguene bou mak (maname djek) amoul droit au mariage au même titre qu'un vieux monsieur qui épouserait une très jeune fille? Te pourtant lolou si rew mi Sénégal aka bari grand-père you takkeu gnou lene matt seutt gneup ni patteu! Mani sou fekker ni "Aissatou" bakhoul rek "vieux monsieur" yoyou bakhou gnou alors? Gars yi nagnou teudder "djankhanaye" way! Temps yi amoul lou djiguene degoule si lou gnaw surtout Mère yi mou djare si khass yi nitt yi di khass "Aissatou". Tant que mbire mi mariage le te deupo ne ak souna rek bane sénégalais moy kane bay tegui souna difi tek beug beugou bopame wala culture?

  • @AbdouNdiaye-or2bi
    @AbdouNdiaye-or2bi 4 дня назад

    ❤❤❤❤