Rose mi tamit est ce werna❤couple diambour daal naniou mandou nak nit dou beug di banie Wax deug yalla diarra demal tok khar yalla Mane dé bama divorcé batay magi tok ak organiser Sonolouma keine Keine sonolouma Sama doom mogi sama wete
Lolou mom ay door la Rose Diagne boudé deugue nga beugue degue domeram nga khaliss ngay diamou té ioe néga guéno kone khamo lou khéw si biti fatou Ndiaye topal Bass bamou bireul sa nday rek wala mou walleu sa nday febar
Rose Diagne yaw kou osé nga mandoul si seuyou diambour do tass sa seuyy ba paré beugue tass seuyou Diarra. Sarap lii waay Sénégal mo metti dougnou seuyy dougnou la bayi nga seuyy. Loyy tabaskiwê keur diambour do took sa keur bagnou indil la yaakkk. Kou sikk nga. Bahna rkk. Siiiimmmmmm
Comportement physique et moral ak verbal sa repond a tous yow mi di wakhe ak xale yi yena bokk derete dok so nawe niou topou si te wakhe day reffette ndak soube soube yalla leu waye lou mata sede leu na nice
Bayilen khassté eumbb douffi guathié lidianti len problème rek mé khassté eumbeul bakhoul djiguene dignité rose dagua dioum ma soeur boul nagou adouna daffa goudou tankk té meuneu na dall sa domm kon wakh na raffet rek sister bayi len wakh diou niaww
Diarra y’a togne tu as divorcé pourquoi t énervé si bass sort avec une autre beu di def violation de domicile va chercher ailleurs cette famille t aime pas 😂😂
Gorou Sénégal souniou dielone sen responsabilités y'aurait moins de divorce. Les maris se font trop influencer. Protégez vos femmes
Rose yaa meunaa dulll😂😂
Rose Diagne nafék nga
Genrou Bell sœur yi gnoy tass séni séyou frére yii rék ba paré Di diay réy lamine ta pas honte
Que des mégères certaines belles sœurs, quallah nous préserve de ces genres de belles sœurs
Rose mi tamit est ce werna❤couple diambour daal naniou mandou nak nit dou beug di banie
Wax deug yalla diarra demal tok khar yalla
Mane dé bama divorcé batay magi tok ak organiser
Sonolouma keine
Keine sonolouma
Sama doom mogi sama wete
Ki vrai domeram leu!!! Boko degger rk xamni dou belle soeur bou bakh
Diarra elle a été trop GENTILLE envers ces imbeciles gni ay badola leuniou
Rose tu es méchante mais yalla bakhena
Tu es une femme ma chérie boule doxale ni à tout moment li meune nala dalle bounioula deffe ni mba dîna nekh nank rek
C pas logique de daguay doul rek
Bilay problème bi daf ma meti bilay Diarra sama tourono domm
Mougnieul yalla bakhna
Di défendr sa frere di bonnal dianbur nit eubeu na t'e bonule yow do référence
Dagnouy tass sèn seuye yi baparé di tass sèneu seuyou frère yi tchimmmmm
Lolou mom ay door la Rose Diagne boudé deugue nga beugue degue domeram nga khaliss ngay diamou té ioe néga guéno kone khamo lou khéw si biti fatou Ndiaye topal Bass bamou bireul sa nday rek wala mou walleu sa nday febar
Mais c normal sa dôme la tamite cou sokhor nga
Rose diagne dagua meneu doul gno bokou deugue hlm
Rose yow domeram ga. Akou Diarra dina lene dall.
Rose Diagne yaw kou osé nga mandoul si seuyou diambour do tass sa seuyy ba paré beugue tass seuyou Diarra.
Sarap lii waay
Sénégal mo metti dougnou seuyy dougnou la bayi nga seuyy.
Loyy tabaskiwê keur diambour do took sa keur bagnou indil la yaakkk. Kou sikk nga.
Bahna rkk.
Siiiimmmmmm
Khawouma rose Khawouma maron ms kou oubii leufeul ndayam laa
Comportement physique et moral ak verbal sa repond a tous yow mi di wakhe ak xale yi yena bokk derete dok so nawe niou topou si te wakhe day reffette ndak soube soube yalla leu waye lou mata sede leu na nice
rose yaw bagne gua diarra dddd yagui set liguay wakh
ROSE MI KOU BONE LA
Doll rek ross
Bayilen khassté eumbb douffi guathié lidianti len problème rek mé khassté eumbeul bakhoul djiguene dignité rose dagua dioum ma soeur boul nagou adouna daffa goudou tankk té meuneu na dall sa domm kon wakh na raffet rek sister bayi len wakh diou niaww
Rose tu es un vrai menteur
Vraiment rose wakhofi Dara merde à la fin douguéne seuy douguéne bayi nite yi seuy légui so meuné dieulal basse guéne seuy
Koula dégue ningay wakhé khamni tasse katou keur nga. Make dafay defar dou yake. Bass tamit dessé na ame foula
rose mi dofff la
Kholéne si khaléyi pliz😢😢😢
Eumb de seurou ndiago la amna si famille yeup mais yaw nitou intérêt nga
Bass dafay ndiallo kone
YAKO. DIONGUAL. TAGUOUWOOKO. DOUL. WAYE
Rose arrête de mentir
Rose bi domeram deug le. Basse mom yala dinako wone
Sokhnasi yaw do nitou darra
Goor gni amlen foula sen sœur yi nagnou mandou ci sen seuy yi bougnou menoul défar
Yaw rose dièpi nala
Yalla mousalma janr théiki yii daga fara defal di yaheu
ROSE. MIIMA. DÉGU. FÉNKATLA. BOO. GUÉNNOONE. SI. SEUYBI. DOU. TASS
rose diagne ioe mom wané gua niga meil do nite kou bakh yayou diambour lokossiy bolei en plus sougn la eumbaloul lann la sa makk moko eumbal deh
LOOLOU.. LAKHAMOUL. RAKKAM. DAY. NDIALOO. NA. WAKH. LOOLOU. KI. KOU. DEUGU. NDAYAMLA
Lomou Def rek mok rakam la
Rose bayil féne
sou eumbè deh se raka moco biral nak yaw mom kou bonne gue bakho santo yalle kou bakh dou wakhé ni
Rose seu saram ndéye
Vraiment vraiment Rox merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yéna yéme kholéne si yalla
Ki dead lokossi toudè🤦🏾♀️
Rose dei mafia la
Ki key bahoul
Ya bone Rose 😏
Senegal dou reuw
Yaw. Yaye begue. Wala. Bass. Sokhor. Gua
Yeen niare nieup ay thiaga ngeen seuy ngeen ba tasse
Yaw. Doul.
ya meuna doullll
Ki mome pankala de
Basse niallo katte la , day mbarane gor bou bone la
Genre ndieukei yi rek nio tass sey diambour yi am nga dieukeur nga tokk seuy sa seuy bayi seuyou diambour
Basse tioune gigolo le