Ndakh sène oustaz yii, lougnou wakh ci célibataire yi, wére na ?

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 3 янв 2025

Комментарии • 30

  • @LESPECIALISTE-dx7cm
    @LESPECIALISTE-dx7cm 4 дня назад +2

    Di fénal Yallah rék ak Yonénetam. Walou Diiné lép lou doul Al-Khour'Ane késsé ay Thiaakhane.

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 3 дня назад

      Léppou loudoul alxouran ak sounnah kasé ay thiaakhane kasé laa loutah guén wéddi sounnah yonét yalla bi

    • @NihmaTV
      @NihmaTV  2 дня назад

      😂😂😂Yonent bi amoul dara ci diiné dji. Diiné Yalla ko mome.
      Yonent bi li ko warone moy diotali ndiangalème Yalla ak di ko dieufé

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 2 дня назад

      Koutoppoul yonéte yalla mouhamed saws do téxé ci mom la yalla diarare l'islam mboke nane toppou yonét yalla bi guir yalla lou bah lane lene yéné alxouran ak sounnah meunoul takhali koo ba aldiana inchallah

  • @NjagaMbye-w7j
    @NjagaMbye-w7j 4 дня назад +1

    Mercy❤❤

  • @bassiroudiame-rz7iv
    @bassiroudiame-rz7iv 4 дня назад +2

    Marier di ndiallo célibataire moko gueune

  • @tydougueye39
    @tydougueye39 4 дня назад +1

    😢😢😢 degueur fitt ak gnémé Yalla

  • @fayealiounekane8727
    @fayealiounekane8727 4 дня назад +1

    machallah

  • @Mambanegra924
    @Mambanegra924 4 дня назад +2

    En faîte gni dagno dof, khawma sokhor wala rêrr bamouy torokh rek

  • @ibrahimasylla6878
    @ibrahimasylla6878 4 дня назад +3

    Yonnent YALLA Issa était il marié ?

    • @ZainabouDiop-
      @ZainabouDiop- 4 дня назад

      Il parfait que oui,avec Marie Madeleine,ils ont eu une fille parfait il,l'eglise a caché ça,lis Davinchi code

    • @bassiroudiame-rz7iv
      @bassiroudiame-rz7iv 4 дня назад

      Cest faut

    • @NihmaTV
      @NihmaTV  2 дня назад

      Le Coran n’en a pas parlé

  • @ousseynoudiop6651
    @ousseynoudiop6651 4 дня назад +2

    ❤❤❤❤❤❤

  • @babacarcisse1015
    @babacarcisse1015 4 дня назад +3

    😂😂😂il y'a des soi-disant oustaz qui doivent se taire à jamais ou avoir la modestie d'aller apprendre le coran. ❤CMS ❤MACHALLAH

  • @CheikhNdiaye-g7d
    @CheikhNdiaye-g7d 4 дня назад +2

    Li waxi dofla jarola diox solo

  • @ElhadjiBah-km4pb
    @ElhadjiBah-km4pb 4 дня назад +1

    Non Sénégal neckna 😂

  • @diopcherif8296
    @diopcherif8296 4 дня назад +2

    Khana niom avant niouy marier ay lan laniou won🤷‍♂️

    • @SedinaDiallo
      @SedinaDiallo 19 часов назад +1

      Bonne question 😂😂😂

  • @cheikhtidianedioo776
    @cheikhtidianedioo776 4 дня назад +2

    Séetal wax yii rék amoul bénneu preuve. Diiné dji kou diougue wax sans preuves c'est dommage. Xanaa léegui marié par force la ? Nagne gnou wax li yalla wax mô guenn

  • @AssaneDiop-w5m
    @AssaneDiop-w5m 3 дня назад

    Mbacké sakho boule wéddi sounnah yonéte yalla bi sama serign

    • @NihmaTV
      @NihmaTV  3 дня назад

      Yonent bi ndiangalème Yalla la done diotali amoul sounna

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 3 дня назад

      Kou baah xolgua ligua wax sounnah yonéte yalla bi wallahi meunoul niakk ci l'islam moo léral alxouran karim nane doylo alxouran ak sounnah moy yonou téxé frère

    • @NihmaTV
      @NihmaTV  2 дня назад

      Démal guestou dji stp fane la sounna sossou diougué, di nga kham li Cheikh Mbacké di wakh

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 2 дня назад

      Yalna yalla sougnou borom mousal gnou ci péxé chéytané wallahi mbacké sakho yalna koo yalla guindi ak mbolém dioullit

  • @bassiroudiame-rz7iv
    @bassiroudiame-rz7iv 4 дня назад

    Issa ibnou mariama dafa torohe Hana et les autre prophète et waliou hamo dara

  • @landingseydi4892
    @landingseydi4892 4 дня назад +2

    Machallah