DEBAT CHEIKH BAYE NIASS AK AHMED IBRAHIME SI BIND CHEIKH IBRAHIMA NIASS

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 29 окт 2024

Комментарии • 66

  • @babacarbodian1603
    @babacarbodian1603 Год назад +1

    Baye niasse rek

  • @hdfjjgfvnklhb6157
    @hdfjjgfvnklhb6157 3 года назад +7

    Ndeyssane ibadou bi loumouy def ni Makako Dakone fouff sakh wédina Baye niass si fepp !! Mais alhamdoulilah bameu moudié done talibe BAYE NIASS sante yallah bou werr

  • @dadjibokaleiakbida539
    @dadjibokaleiakbida539 2 года назад

    Macha Allah Oustaz ibrahim cheikh baye dafa rerr ndeysane

  • @mouhameddiawara7151
    @mouhameddiawara7151 Год назад +1

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ cheikh Baye Niasse

  • @boura2756
    @boura2756 3 года назад +1

    DIEUREUDIEUF CHEIKH BAYE NIASS , MACHALLA

  • @xudamulxadimxeexakwakhaabi3565
    @xudamulxadimxeexakwakhaabi3565 3 года назад +3

    Wakhaabiyoun yi danio Alkou kepp kou noonu nittu yalla déclaré nga yalla guerre wakhaabiste Alkou naniou ba paré sen dra du baaxati ndakh danio bagn nittu yalla yi

  • @papejuleslebarhamien8786
    @papejuleslebarhamien8786 2 года назад

    Machallah cheikh baye niass yalla nala yalla weral katanala diamala deugeureula weral xamxam bi té samela barké baye niass rta doundeul wérral niass...wahabite xawma wahkatbi lingay wakh sakh xamoko dangay lambatou demnléne diangui té topp ki mattal si diamano mou yobouléne thia matame gua mataléne si...baye for ever☝☝☝❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ibrahimalo8711
    @ibrahimalo8711 3 года назад +1

    merci bcp cheikh baye yaw borome xam xam nga ms wadji dof deug lah

  • @RAZAQAKANJIAKINWUNMI
    @RAZAQAKANJIAKINWUNMI 9 месяцев назад

    بسم الله الرحمان الرحيم
    رضي الله تعالى عنه

  • @biranetoure4624
    @biranetoure4624 2 года назад

    Cëkkalmaan bii repp na de !!🤣🤣
    Seex Baay jaajëf waay.🥰🥰🥰

  • @alioudiane5228
    @alioudiane5228 3 года назад +2

    Le problème en est que les wahhabites n'ont rien compris
    Cheikh baye niass les wahhabites ne viennent pas et ne répond jamais tes questions

  • @sheikhibrahimathiam5148
    @sheikhibrahimathiam5148 3 года назад +1

    Machalla Baye niass

  • @umar-al-amirfofanah75
    @umar-al-amirfofanah75 Год назад

    Cheikh baye niass ❤❤❤

  • @aiouseydou1430
    @aiouseydou1430 Год назад

    kou beug lien wu groupe wtsp bobou nk ??

  • @niangtv3194
    @niangtv3194 3 года назад +3

    Merci cheikh baye Wahabiste bi liiy wané ni djaguoull moom djapnanii kou gueunn kénn mo warra eupp xam xam walla djagulé kimou gueunn gniounn djouliit yi gnioo gueunn yéfféeryi amna mbirr you beurri you yalla djaguléell toubab yi té gnioun' meunougniouko seydina aboubakar seydina Omar seydina Ousmane gnio gueunn fouuf Abou khouraira walla Abdoul lahi Ibn abass té gniii ligniou mokkall si khadiss Omar walla Aboubacar mokkallouko esk lollou takhna gniou gueunn vraiment wahabiste bi djagoull

  • @mamadoudiallo2696
    @mamadoudiallo2696 10 месяцев назад

    Ils lisent les livres des shaykhs Soufis de façon très superficielle, et après ils interprètent en toute ignorance.

  • @salioungom1624
    @salioungom1624 3 года назад +4

    Merci Cheikh Baye

  • @boyfall4738
    @boyfall4738 3 года назад +4

    Wahabite bi dal khelam rek lay wakhé indiwoul ben hadiss walla aya alkhourane pour lou mana weddi li cheikh baye wakh
    Vraiment merci encore une foi CHEIKH BAYE yalna yalla fayalnioula

  • @marechal6.c597
    @marechal6.c597 2 года назад

    Tari ay beuyitt c'est trop facile. Ça n'a rien à voir avec la science

  • @pathesamb9561
    @pathesamb9561 2 года назад

    Ma challa cheick ahmėt ibrahima kham sėll na ande ma ak yarr

  • @mamebayesow8526
    @mamebayesow8526 3 года назад +1

    Dieurehjeufe Baye Niass ❤❤❤❤

  • @SALOUMFAYDOUTV
    @SALOUMFAYDOUTV 3 года назад

    Sou féké yoneth bi néna chaque 100 ans Dina am khalif bou niow pour yéssalate dine dji .kone sou féké kou niow ngané bida iow Di nga wedi kou don nou yonetibi té kou def lolou yonetibi ci bopam nga wedi

  • @ameetfallsenegal3506
    @ameetfallsenegal3506 3 года назад +3

    Machallah cheikh baye niass

  • @latdiordiop6051
    @latdiordiop6051 3 года назад +3

    Cheikh bay salafist kome khatiak mouss rek. Nonoula cheikh bay del tégueul rek.

    • @absandiaye6071
      @absandiaye6071 3 года назад

      😁 😁salafist yi dagnio kachte sen kholyi waye walahi baye niass sakh nga sokhla

  • @mohamadoulaminegueye2220
    @mohamadoulaminegueye2220 2 года назад +2

    Macha allah cheikh Ibrahima halil lo ibn , léral yi amna solo, té Leena si kuy téktalo al xour aan ak Sounna.

  • @marechal6.c597
    @marechal6.c597 2 года назад +2

    Ch baye niass amoul kham kham bou léér il est juste éloquent. Dafa meune wakh mais diangam soriwoul. Même les étudiants de la licence ne commettent pas des erreurs comm les siennes

  • @mohamedgueye3998
    @mohamedgueye3998 3 года назад +1

    Cheikh baye niass yallah na yallah goudeul sa fan yok l xi zahir ak xi batine deugeur sa takhaway, walahi sedal nga suma khol bi , siguil nga l islam tarikha tidjane rawatina faydou mawlana cheikh Ibrahima niass rta

  • @daffesane
    @daffesane 2 года назад

    DIEUREUDIEUF BAYE

  • @ndiougamar2202
    @ndiougamar2202 Год назад

    Sénégal kou Amoul Serigne gnou né leu wahabite juste pour diaboliser leu Abdou wahab mi nguéni dénigrer sanou Serigne yi rawou gnouco eupou gnouco kham kham

  • @papesouleymanesane6555
    @papesouleymanesane6555 Год назад

    Mome rk lay topou cheikh baye mi

  • @mamadougoudiaby2672
    @mamadougoudiaby2672 2 года назад +1

    Machalah machalah alhamdoulila cheikhe Niass ham ham bi amnasolo ham ham rek mo wor jeurediefe baye niass ❤️❤️❤️

  • @mamadouthiam6062
    @mamadouthiam6062 3 года назад

    Walahi ki khaw ma foum diangue wayer guisnimoy wakhe rek nga kham ni khamoul dara mai nak heureuse cheik bay mingui fii machalah bay niass

  • @sav1253
    @sav1253 3 года назад

    Dieureudieuf cheikh baye mane dal beug na cou degue yalla mane do lene ma may bene wahabit ma am loumako ladie mane ta yalla takh

  • @khadidiatouseck3557
    @khadidiatouseck3557 3 года назад +5

    Jajëf seex bay kuywèdd tasawuf rek nañoko bole ak yaw

  • @mhalva4703
    @mhalva4703 3 года назад +1

    دليل تصرف فى القرءان .قوله سبحانه، قال عفريت من الجن انا ءاتيك به قبل ان تقوم من مقامك واني عليه لقوى امين. قال الذي عنده علم من الكتاب اناءاتيك قبل ان يرتد اليك طرفك الي ءاخر .......... صدق الله العظيم

  • @amethgaye7892
    @amethgaye7892 3 года назад

    جزاك الله خيرا خيرا الجزاء

  • @ablayesall1088
    @ablayesall1088 3 года назад +2

    Macha allah cheikh baye niass yalne y'a allah barkél leu barkél mbolém dioulid alhamdou lillah

  • @OumarDiouf-j9l
    @OumarDiouf-j9l 6 месяцев назад

    Kham dafa cher 😂yen talibe tasawouf yi amo len diotou dianga nono diotou all topé gen am 😂😂😂dem len diangi way te bayi diofou diambour yi am len xell bax na

  • @fallouwade2810
    @fallouwade2810 3 года назад

    Oustaz ahmed ibrahim lo

  • @sidikhthiam2936
    @sidikhthiam2936 3 года назад

    شكرا يا شيخ باي..حفظك اللّٰه

  • @abdouwahabthiam8055
    @abdouwahabthiam8055 3 года назад

    Gatta alliwa dem lien diangi , wadji de numouy wakhie soko deglo dafay wane ne mom kham khamam yatou woul. domou ram

  • @cheikhndiaye3426
    @cheikhndiaye3426 3 года назад

    Cheikh baye ki amoule khame khame, mane mi gana dawe gana ndiage solo si talibeyi. Souma wakhe dara inechalla .rousena baye sakh

  • @mamadouthiam6062
    @mamadouthiam6062 3 года назад

    Mai yow wahabi bi guisoulo loudoul wala biugoulo loudoul bay niass dioum na mai lii kay tepons bi binga ko degue rek nga kham ni machalah

  • @mastmindbah9561
    @mastmindbah9561 3 года назад

    Niass

  • @Deug13
    @Deug13 3 года назад +1

    Dieureudieufé Mame Baye Niass

  • @absandiaye6071
    @absandiaye6071 3 года назад +3

    Salafist yi sakh baye niass lagne sokhla pour mou guenelenn si sen bokale yi

  • @thiamagueye8699
    @thiamagueye8699 2 года назад

    c'est toujours le même raisonnement avec les 'ibaadu' ils font des déductions sur la base de Dieu n'avez pas donné ceci aux sahaaba donc c'est pas possible qu'il le donne à une simple personne. Les dons de Dieu n'a pas de limites, est ce que Dieu a dit tout ce qu'il va faire sur l'humanité. Ces ibadous ont le coeur aigri on dirait. Tu n'as qu'à regarder ce que Baye a réussi par la grâce de Dieu. Déel lathie ngir xam té moytu lathie ngir diingat.

  • @mamadoudiallo2696
    @mamadoudiallo2696 10 месяцев назад

    Thiey wahabytes yi, ay teukh lagnou, dougnou deggue dara. Ba paré lou séene serigne dooméraam yi guaaral sa saoudite gnou délloo siko, di fenn rek

  • @mamadijallow3534
    @mamadijallow3534 2 года назад

    🧠? Bou baye bokké thi 40 yi daye nguen sahaba yi?.Khana kon sahaba yi don djiouli guinaw yonént. Sa imamou djakka len guen ndakh moom imam la?

  • @papethiam4877
    @papethiam4877 3 года назад

    Wakhabiste yi diarouniou tontou Cheikh baye. Bouniou beugué kham naniou déme gueustou téré mak yi. Mais ils préfèrent les arabes beugue wédi sounou mak you bakh yi.

  • @bayesoule781
    @bayesoule781 11 месяцев назад

    Cheikh Baye Niass leeral ngua LP oustaz Ahmed demalaa fonkou trop pasque denguaa am yarr comme ça Baye Ahmed lo

  • @abdallahniass6634
    @abdallahniass6634 3 года назад

    Démal diangi wat xamo dara salafist yi yalla mo kasté séne xole yi

  • @pathesamb9561
    @pathesamb9561 2 года назад

    Yėne wa tassawouf yėna alkou billahi aye nitt guėne di diamou yena yague senegal 🇸🇳

  • @bintasy7599
    @bintasy7599 3 года назад

    Lane moy wahabi ya ?

    • @aissatakande5246
      @aissatakande5246 3 года назад

      Wahabi ya moy niou démm diangui djié makka andalé ideology Mohammad ibn abdoul wahaab nga kham ni was banou nadjdeu leu khétt bobou LA yonent bi wakhonn niom beuss bouniou dougué sama diiné bi fitna tambali Niniou nioy wahabiya fails des recherches tu saura bien encore

  • @oustazahmedfall6478
    @oustazahmedfall6478 3 года назад

    Salafiste yi ay yéfeur lagne

  • @babacarbodian1603
    @babacarbodian1603 Год назад

    Baye niasse rek

  • @OumarDiouf-j9l
    @OumarDiouf-j9l 6 месяцев назад

    Kham dafa cher 😂yen talibe tasawouf yi amo len diotou dianga nono diotou all topé gen am 😂😂😂dem len diangi way te bayi diofou diambour yi am len xell bax na