Bilay, depuis que jai commencé a te suivre tu as augmente ma foi. Surtt cette video. Avant quand jetais KO avc les soucis je disais a Dieu dans mes priere daccepter mes voeux rek et de faire de sorte que ce soit bon pour moi. Mais depuis que jai vu cette video, jaccepte de plus en plus que Dieu dirige ma vie, quil decide de ce quil ya de mieu pr moi et quIL me facilite la decision qu'Il a pris. YAllah nala YAllah féye, YAllah takhawou la, meyla li gueunn thi tow
Comment faire pour arrêter de pleurer la khamoul. Pas de parents, pas de werouway, ni d'aide des frères et sœurs. Mais je garde la foi mais je pleure rek
Bilay, depuis que jai commencé a te suivre tu as augmente ma foi. Surtt cette video. Avant quand jetais KO avc les soucis je disais a Dieu dans mes priere daccepter mes voeux rek et de faire de sorte que ce soit bon pour moi. Mais depuis que jai vu cette video, jaccepte de plus en plus que Dieu dirige ma vie, quil decide de ce quil ya de mieu pr moi et quIL me facilite la decision qu'Il a pris. YAllah nala YAllah féye, YAllah takhawou la, meyla li gueunn thi tow
😭😭😭😭Ndaysane nitt kou bakh nga kou yalla beugua wakhal alhamdoulilah
Pas une semaine qui ne passe sans que je ne revienne revoir cette vidéo pleine d’enseignement
Alkhamdou lilah alla kouli all delo lep borom bi 😔
Bilahi lolou moma d'ale nuit gni dima nakh rek 😢😢😢😢
Bilahi serif mansour laye dama nékh ta yalla rèk takh koumay diokh numérome yana yallah goudal sa fane❤
Machala wakhtane you am solo ngay def yalna yalla goudeul sa fane❤
Mome damako beugue té Yallah rek tah ak gnémé deugue 😢Yalla na Borome bi fayla thi rappel you ame soolo yi té yokk la tahawou Chérif Mansour Laye🤲🏼
Heee chaque quand j'écoute ce Mr je pleure aves cette chanson en bas vraiment beaucoup d'émotions
Quelle vidéo !!!
Macha Allah. Yallana Yalla doli sammeu té wéralal niou sounou iimaan
Yalla nalla sougnou borom defal yiww barker seydina Mouhamed niguay wakhei kouko khol kham lou am yakkine leu❤
Yalla na yalla yaggal taxaway bii
Allahumma amiin Laye Madiné
Intellectuel mom c pour c genre de personne qui impact positivement sur ta vie 👌👌🥰chapeau
Merci beaucoup c'est gentille, dolli léen ko gnaane rékk in chaa Allah
@allbusinesstv khassaides biga play so souf la beugue lien bi stp
Ay son bi ci Souf
Dossier diam l'auteur de ce chanson 😊
vraiment merci xaranmonxo Mansour laye
je vous suis depuis la Mauritanie
Ndeysane koubakh ki dangaye khiretale domou adama yi ci ak gueume Allah 😢😢😢😢Di sante sama sopé seydina Muhammed SAW ganawe borome bi swt 😢😢😢
Ayyyy wayy mala beugue yalnaleu yalla gueuna takhawou
Je me vois dans cette vidéo. Dieuredieuf laye makhatar.❤
Allakhou akbar. Ki Mane. Fouma nékone ba khawoumako. Yalla nala Borom bi Fayyy. Tu dis tellement vraie.
vraiment j'apprécie la dimension intellectuelle religieuse des layennes Mr Cherif et Mr ibra laye longivuté à eux
Si j'arrive plu à me reconnaître je l'écoute Machahala
Kuko setane plusieurs fois ❤️✅
Je suis un fan de toi cherif yallha na yallha gueuna wereul kham kham bi machallhalha
Abdou Hakim Mbacké Khassida machallah
Comment faire pour arrêter de pleurer la khamoul. Pas de parents, pas de werouway, ni d'aide des frères et sœurs. Mais je garde la foi mais je pleure rek
Thieuy vidéo biiiii dama yakar niii ma takh gua defff ko yallah késsé mome dongue mofi néék Anastasie général ❤❤❤
Dieuredieuf sangue bi niounguilay sant bou weer
Machalah sanga bi yalna nanou yalla may dégue ak toppa🤲🤲
Allahumma amiin
Oh khol yi fekh n’a lol Amna solo
Bilah doumasi doyal machahala laye makhtar ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Contane si ioe laye makhtar ❤
Djeureudjef Laye Memedou Souniou Sangue Biii❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bly deugue la 😢❤
Ay way chérif mansour laye dama ko beug sama xol noumay def ba guiss ko
Sama papa la diox ma sa numéro ma boolé la ak mom inshallah
Moi aussi damako bgue guiss pour demander quelles que questions
Seydi thiaw si c'est possible nga wax
Bien sûr c mon Papa
❤ vidéo bi doumaci doyale❤
Machalla Machalla diadieuf
Khassaides bi thi souf beugue nako wala kou hame kouko waye Ak bane khassaides la beugnako ame diko deglou kouma siy dimbali
Dialibatoul marakhib la toudou
❤❤❤machallah le trite du song stp
Machalla laye maxtar
BILLAHI AMNA SOLU☝
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wakhtane bi dei motakh ma souscrire si page bi jeureujeuf laye makhtar ndakh kadou yi delossi joulitt mom laniou sokhla jeureudieuf
Macha Allah 🥺🥺
Amna solo laye makhtar 💓💓❤❤❤❤❤❤❤😍
Jërëjëf Laye Madiné
Machallh cherif ❤
Ak degue lamatar
Maa shaa allah
Ndaye sane ❤️❤️
Jërëjëf
machalla
Jërëjëf
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
Machalla
Jërëjëf
Machalah
Svp le non de song
Sincèrement je l'ignore
Machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤💘
Bly ligua wx Daf ma dall
Machallah 👏🤍🤍🤍👏
mais Lou takh wakhtan bii agoull
par partie la gnou koy dugal, in chaa Allah di na dugal intégralité bi
❤
Machalla
Jërëjëf