Iran Ndao répond à Imam Kanté: sama yone nékoussi et remet une autre somme d’argent à Taïb SOCÉ...

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 10 янв 2025

Комментарии • 316

  • @fatalfate126
    @fatalfate126 5 лет назад +9

    Machala oustaz Iran gorr deugeu moy yaw yalna yalla doli la diam

  • @sarierediallo70
    @sarierediallo70 5 лет назад +7

    MASHALLAH ! Thierno Ibrahima, Yalna Yalla Faye la sa mbakh

  • @ndiagandiaye7364
    @ndiagandiaye7364 5 лет назад +70

    mame chiekh Al mahtoum sy yallah nako yallah dolli yermande Amine diadieuf

  • @chiekalkhalifarektalibesse1320
    @chiekalkhalifarektalibesse1320 5 лет назад +15

    Machalla papa iran yallah nga Goudou fan si barke seydina Mohamed swslm yew talibés serigne babacar sy nga

  • @chekhnecheikhelbou695
    @chekhnecheikhelbou695 5 лет назад +36

    Iran ndao que Allah te gardes avec la santé bonheur prospérité choukran Allah et sont prophètes Mohamed paix et salut sur lui

  • @bijoufaye2800
    @bijoufaye2800 5 лет назад

    Machaalha iran yalla nala yalla faye si ligay def. Faye sunuy wadiour

  • @mamecheikhibrahimadiallo3407
    @mamecheikhibrahimadiallo3407 5 лет назад +4

    Maa shaa Allah je salut sa franchise jup rek mo jara ñaan yalna ñuko Yalla may...

  • @aboondiaye1889
    @aboondiaye1889 5 лет назад +2

    Iran liii mou df nonou la machalahhh yalna yallah dolie soutoura🤝🤝

  • @aidaly8787
    @aidaly8787 5 лет назад

    bravo bravo bravo bravo bravo bravo bravo bravo bravo bravo bravo bravo .diadieuflaine.machAllah.😍😍😍😍💚💛❤👍alhamdoulilah.

  • @moussandour2540
    @moussandour2540 5 лет назад +2

    Merci iran pour ce beau geste machallah .yalnala yalla faye ...mais amna yo khamni diaroul siwal .falait garder ce que taib t as di

  • @zeydousow5462
    @zeydousow5462 5 лет назад +1

    Lidal koumou doyoul lènène doula doy machalla dieuredief Iran ndao yalna yalla fayla yiiw inchalla

  • @aliudiao9144
    @aliudiao9144 5 лет назад +26

    Senegal mo metí yen iran dieul aye mesureum founek mou Diarfa mane ak yawe miye wedi boba fougnounekone apre me il faut mou leral 1oo million dou aye thiakhane
    Iran khawmako mosoumako guiss loudoul tele waye senegal yalna ame gnoumelni gnom

  • @talentfoottv3861
    @talentfoottv3861 5 лет назад +3

    J’adore cette homme 👨 vraiment

  • @investigationscriminelles7375
    @investigationscriminelles7375 5 лет назад +11

    Machallah yalna nallah yallah faye

  • @adamaba6508
    @adamaba6508 5 лет назад +3

    Merci iran

  • @diedhioudjibril8359
    @diedhioudjibril8359 5 лет назад +1

    mersi iran

  • @modoufallbetebeteitsenegal5272
    @modoufallbetebeteitsenegal5272 5 лет назад

    MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH DIEUREDIEUFÉ OUSTAZ IRAN NDAO SAY KADOU DÉMBOU AK YOU TAAY AMOUL CHANGEMENT YALLAH NALA YALLAH FAYAL BOPAM GOUDEUL SA FAAN GEUNUE WEREUL SAY THIEUR DOLILA SOUTOUREUY BIIREUK BIITI SI BARKE SEYDI ABOUBACAR SY RTA

  • @abymbaye6758
    @abymbaye6758 5 лет назад +10

    Machallah Iran

  • @momoanna6samb35
    @momoanna6samb35 5 лет назад +32

    DIAMBAR GA MACHALLAH YALLAH MON LAY FAYE

  • @falldame3662
    @falldame3662 5 лет назад +5

    Yalla rek molay faye mom mi am fay iran yalla na saw fan goudou

  • @africataal3303
    @africataal3303 5 лет назад

    Alhamdoulilah iran j'ai même les larmes aux yeux walahi yaw ya bakh

  • @sadiboudieng8202
    @sadiboudieng8202 5 лет назад +3

    dieureudieuf iran ndao machallahou al yennenn ouztass yeup yi ngua andaloonn

    • @karimniang4845
      @karimniang4845 4 года назад

      li Tay in sosé wakh motakh mou andy aye lairal

  • @laminediatta1820
    @laminediatta1820 5 лет назад +4

    Tu vraiment un gas bien Iran

  • @amarykane5143
    @amarykane5143 5 лет назад +5

    Merci sgne IRAN .big man

  • @modoufall8127
    @modoufall8127 5 лет назад +1

    Iran yalna la yalla féy barkep s touba amna solo machahalla

  • @mbayesene1072
    @mbayesene1072 5 лет назад +144

    Défléne ni oustaz hadi niass moytou léne sit intérnét yi

    • @saliba9139
      @saliba9139 5 лет назад +3

      Bilay il est discret

    • @badjidiarra7184
      @badjidiarra7184 5 лет назад +6

      Iran lègui mome da miss internet bi a mon avis il parle trop

    • @diafarabarry8916
      @diafarabarry8916 5 лет назад +11

      Ostas ady niass amol morom bilay

    • @diopmomo329
      @diopmomo329 5 лет назад +7

      Mbaye Sene walahy oustaz hady niass amoul morom dafa bokkoul ay gayi you niak fayda yii nékkou si sakh

    • @bambadiop8487
      @bambadiop8487 5 лет назад +1

      Merci ya wakh degue wakh rek

  • @aichaousmaneba5302
    @aichaousmaneba5302 5 лет назад

    Je vous adore vraiment

  • @daoudagningue4711
    @daoudagningue4711 5 лет назад +1

    Machala... Voila un bon exemple

  • @bokemetalservices1140
    @bokemetalservices1140 5 лет назад

    Merci Iran ak nimou thi andalone

  • @abdoulayengom359
    @abdoulayengom359 5 лет назад +1

    Yalnala yalla Faye sa kholl amine

  • @matyndiaye5569
    @matyndiaye5569 5 лет назад +9

    Je vois pas où est le problème comme nous les sénégalais on aime dire dioublangla donc je suis daccord du fait qu il donne les détails juste un point de vue

  • @mameaissasarr6424
    @mameaissasarr6424 5 лет назад +23

    Euy waye Iran nopil doyna nak soutoura dafa bakh thi leep

    • @sofiyatouagne9399
      @sofiyatouagne9399 5 лет назад +4

      Non mounoul doye nakh dafa dess khaliss boumou wara djiokh Taib bou oustaz Alioune Salla yorone fokeu mouleral fi senegal la dih

    • @ndiagandoye8074
      @ndiagandoye8074 5 лет назад +1

      @@sofiyatouagne9399 billay wax nga deugg

    • @yerimsy8740
      @yerimsy8740 5 лет назад +1

      Yaw ya wara nopi

  • @balljul9813
    @balljul9813 5 лет назад +20

    Ohh sama jeunesse vous n’arrêtez jamais de critiquer les bons actes et vous participez jamais mais pourquoi?

  • @maramethiam5050
    @maramethiam5050 5 лет назад +3

    Ho machallah

  • @datr6676
    @datr6676 5 лет назад +53

    Linga defal taib soce refete na waye boko fate woul dinga yakhe linga defe sa lamegne dina ko yakh nda bepou jeufe bou yalla takhe diaroul di wakh saboko rombee fateko nek thi lenene nga balma

    • @cuisinedehalima2978
      @cuisinedehalima2978 5 лет назад +9

      Da Tr affaire khalis la c'est normal Lou diar ci mom dinako leral où sinon gniou toumalko Sénégal lagniou nek on peut pas satisfaire tout le monde.

    • @datr6676
      @datr6676 5 лет назад +1

      @@cuisinedehalima2978 wakh nga deug diglou wouma fin bi Diadieuf way kou bakh

    • @boubacardia8862
      @boubacardia8862 5 лет назад +2

      li kay yakouna ba parè li rafetoul

    • @sofiyatouagne9399
      @sofiyatouagne9399 5 лет назад +6

      Mani c normal djokhé na 100millions mou desse venene millions fokeu mou leral ko fi senegal lah

    • @papeousmanefall5796
      @papeousmanefall5796 5 лет назад +2

      Da Tr non Sénégal moy deug bouguena graw nabania lerall con ba paré dieund auto wala keur legui niounè xaliss bala

  • @momathethiam3337
    @momathethiam3337 5 лет назад

    Ma shaallla Iran. Yalla nala yalla tahawu. Dieuf yiga déf at sa mbok yila diapalé rafetena trop. Mane dé souma amone sa numéro dinala wo remercie la particulièrement en tant que sa mbok djoulite. Gneup ka rafete lou

  • @diatousene6468
    @diatousene6468 5 лет назад +11

    Thiéy oustaz yalna sa diameu yageu

  • @adamaba6154
    @adamaba6154 5 лет назад +1

    Merci iran Amna nio Khamne diarougnou wakhak Sakh

  • @damendiaye9737
    @damendiaye9737 5 лет назад

    Machalla yalna yalla faye

  • @ndiagagaye9260
    @ndiagagaye9260 5 лет назад +28

    Mais noo!!!! Iran lép lay expliqué dou bayii 0,05 😂😂

  • @ndeyefallyndiaye8144
    @ndeyefallyndiaye8144 5 лет назад +3

    Machalla amo morom ndaw

  • @nancygueye6799
    @nancygueye6799 5 лет назад +3

    Machalla 👉💪

  • @ndeyefatoufaye8286
    @ndeyefatoufaye8286 5 лет назад

    Mercie

  • @bourguibafaye8521
    @bourguibafaye8521 5 лет назад

    Dieureudieuf Iran

  • @philippechapuis61
    @philippechapuis61 5 лет назад

    Paye voir tonton tu me fait pleurée machalla yalla balla yalla faye tonton Iran ya mbakh dabakh malik

  • @bambandiayediouftoubabrasi7893
    @bambandiayediouftoubabrasi7893 5 лет назад

    Merci ira

  • @lavieestbelle-o7s
    @lavieestbelle-o7s 5 лет назад

    Merci a toi père iran

  • @mardiouf3684
    @mardiouf3684 5 лет назад +32

    Pkoi vous parlez de soutoura les amis il est franc il dit que la vérité s'il le faisais à sans le dire on le dira qu'il l'a mangé l'argent

    • @villanileonardo006villani5
      @villanileonardo006villani5 5 лет назад +3

      Soutoura sakhe moumoussi ame Lou gendarmerie ame prison amesi soutoura mounoussi ame

    • @maymouna1802
      @maymouna1802 5 лет назад

      @@villanileonardo006villani5 merci bien Di

    • @maodothiam6173
      @maodothiam6173 5 лет назад

      @@villanileonardo006villani5 deuguiit way

    • @bokemetalservices1140
      @bokemetalservices1140 5 лет назад

      MAR DIOUF tu as vu juste deh. Lolou moy senegal.
      Bu Tawoul niuni Tawul, Bu tawé ninuni taw bi dafa baré...... Merci Iran ak nimou thi andalone

    • @mardiouf3684
      @mardiouf3684 5 лет назад

      @@bokemetalservices1140 oui ç vrai hen

  • @mamefamangom917
    @mamefamangom917 5 лет назад +5

    Maschallah wadji rafetna lërna

  • @konadiouf2596
    @konadiouf2596 5 лет назад

    Li Iran def kou nékone à sa place tamite lolou ngay def mba nga def louka raw. Bravo à lui et aux autres oustaz yissi diapone👏🏿👏🏿👏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿

  • @victoriasagna9993
    @victoriasagna9993 5 лет назад

    Que Dieu te garde et te benisse

  • @ahmadoufall8560
    @ahmadoufall8560 5 лет назад

    Machalla Iran koubakhga diambarga

  • @mameh.8116
    @mameh.8116 5 лет назад

    LAISSEZ LE TRANQUILLE!!!!!
    Le geste qu’il a fait est NOBLE. Animateurs bancs diaklé you niak classe yi akk tayal dem wouti information bou am ndieurigne. Ce qui est fait est fait, il a sauvé un être, un musulman et un père de famille. Iran ne demande pas a ces vautours d’aller chez lui, ils le sollicitent. Niak khorom, thipatou! Iran l’homme de l’an 2019. Tu es unique.

  • @isatoujobarteh88
    @isatoujobarteh88 5 лет назад

    Mashalla Iran ndow net ko bakh ga

  • @mbackeka3907
    @mbackeka3907 5 лет назад

    اللهم استر دوراتنا yangui nîan yalla toujour sutura ba paré di khawi sutra si diambour

  • @aramesene5836
    @aramesene5836 5 лет назад +1

    Iran ndao je t’aime plus que tout ❤️

  • @الحقالمبين-ي5غ
    @الحقالمبين-ي5غ 5 лет назад +7

    Zournalist sênêgalêyi ngisi eupou diahasêrêk langouy dêf
    Iran nogilay sane boubah sitahawoubi amnadolo yallah nala yallah faye yaw ak ngiga andall

  • @adamasoumare4412
    @adamasoumare4412 5 лет назад +2

    Merci machaallah

  • @sophiendonh6187
    @sophiendonh6187 5 лет назад

    Merci ira ndao

  • @bayefall6717
    @bayefall6717 5 лет назад

    Iran dal am nga ndam té yalla molay faye

  • @yerodiallo9046
    @yerodiallo9046 4 года назад

    Salam

  • @aidaniang1288
    @aidaniang1288 5 лет назад

    Le Prophete Psl a dit : Nadal sa ma mbokou dioulit va sokhlam fadiou moi ma gueuneul ma def ikhtikaf (retraite spirituelle) 1 mois dans la mosquée de Medine. Bravo Iran Ndao

  • @rackysow5477
    @rackysow5477 5 лет назад +1

    Iran lingua degou motakh nga nekhma yalna la yalla faye sa xol

  • @alibadiane1763
    @alibadiane1763 5 лет назад +3

    Bravo

  • @damadiop1750
    @damadiop1750 3 года назад

    Dafa Ler ira machallah

  • @cuisinedehalima2978
    @cuisinedehalima2978 5 лет назад +16

    Iran dafa beugue Lou ler rk rien plus

  •  5 лет назад

    Iran khana taye

  • @diezpollaire2447
    @diezpollaire2447 4 года назад

    Yal nala ya Allah faye nit kou joub kou geum té ragal ya Allah

  • @Ndiayetv2174
    @Ndiayetv2174 5 лет назад +1

    Machallah

  • @sidikidiabate4566
    @sidikidiabate4566 5 лет назад

    Maachaa Allah. Lii la djoulit meuneul moroo mameu

  • @mbayeyatt9310
    @mbayeyatt9310 5 лет назад +1

    Merci iran wakh dji rafétna

  • @amadougniang6446
    @amadougniang6446 5 лет назад

    Waaye Iran Yaabahx yalanayallaFaye le enine yeoue

  • @djibrilndiaye5349
    @djibrilndiaye5349 5 лет назад +25

    Sénégal dale mo méti té nakaré def lou bakh. Iran il faut que mou léral khaliss bi parce que sénégalais dafa gnaw khalat.

  • @djatoudiawara1075
    @djatoudiawara1075 5 лет назад +3

    Iran l homme de l Anne guorou ya. Allah

  • @khadimgueye7166
    @khadimgueye7166 5 лет назад

    ya bakh iran ndao Yalla nala yalla fay yiw ak wa commission bi yeupe

  • @modoudiagne7607
    @modoudiagne7607 5 лет назад

    Muy bien Irán👏👏👏👏👏

  • @fadabakhfashion2482
    @fadabakhfashion2482 5 лет назад

    mais yen lane guéni wakh ndakh iran dafay def ta yallah takh khalice bi guénoul ci possou iran ci posou sénégalais yi la guéné wala bokk legui nakk doukka leral bam ler kom mime rew yakk fi nitt mo gueuna gaw defar fi nitt soff .bne continuation papa iran notre fierté

  • @ndiagamakhtarndoye5189
    @ndiagamakhtarndoye5189 5 лет назад

    والله المستعان

  • @madougueye5490
    @madougueye5490 5 лет назад +17

    Aye waye soutoura waye iran dou leupe lanouye wakh akh

  • @Xvrjk
    @Xvrjk 5 лет назад

    Iran bou né "ma déposé khaliss bii gnou diokhma taïb" dafmay ray. Machallah

  • @mbayelo3022
    @mbayelo3022 5 лет назад

    Máchallah

  • @sambousarr3817
    @sambousarr3817 5 лет назад

    yalna yalla doli laa sam nafek yi diema khejal ibliss rousnane bene nierel bi Massalikoudjiane Islame da am ay realité merci Iran le gran Iran sunu ouztaz beguenala li dada nekh fier être misilman

  • @boubacarbalde3500
    @boubacarbalde3500 5 лет назад +1

    Je suis fière de toi sama Serigne yalla n'a la yalla Sam nitt kou dioubb

  • @bintourassoulba7200
    @bintourassoulba7200 5 лет назад +7

    Yaye gore deug oustaz

  • @ahmedgaye6825
    @ahmedgaye6825 5 лет назад +7

    Senegal bilaye yenna sokhore wakhale baye de sounou la dinke n'a lere beuguoulenne kouye deff lou bakhe talibe Maodo gua na lere nagne boussi lalle dereume television la wonne delokaffa leppe lou yawe wanele

    • @Art-d5e5y
      @Art-d5e5y 5 лет назад

      Ahmed Sènègal dafa mèti lounè gnou wakh t gniy wakh bi diapalè taibe socè diotè lerr nama ken dèfousi dara gno nek si net bi yore sen lamigne mandou bakh na d Iran def rk t yala takh koubakh la diadieuf Iran ndao

  • @altesseroyale4383
    @altesseroyale4383 5 лет назад +2

    Loudoul deug dou yague
    Sétane na dakh ci ndadjié
    Manaar rangui naar yangui
    Sénègal bess angui ci bess yi, beuré imams ak ouztazs, douma kou mane sa morome douma.
    Imam Kanté nak dina nouko douma doumaye ndiaago you méti, ndakh daffa wané seytané waaba djiba mana fasstèye siquime. Bala tokk nakk seytané wathie ci kowame. Na dokhe gnou dème mouye saf danguine gou reuthieu
    Tchiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii ba Bahrain.......

    • @ndeyefall1965
      @ndeyefall1965 5 лет назад

      Deug rek nga wakh bamou wakhé si affairou Waly ba paré la warone nopi wayé ratatati rek 😂😂

    • @altesseroyale4383
      @altesseroyale4383 5 лет назад

      Ndèye Fall djiereu djieuf
      Kham nga Sénègal amona Serignes you mague: Serigne Touba, Serigne Fallou, Mame Mawdo, Mame Abdou Aziz, gnognou kène massou lèna dègue thi wakh yi ouztazs yi ak imams mi tey yi di wakh.
      Gno gnou dagno mandou wone, ame soutoureu di digglé lou bakh té dougnou wakh kène lou niaw!
      Wayé ouztazs you tèye yi ak imams you tèye yi wa Sénègal war nanoulène moytou bala gno tasse Sénègal

    • @fan4dass712
      @fan4dass712 4 года назад

      Bravo Iran Yalla nala Yalla yok soutoura si sa kaw. Amen

  • @daoudasall8075
    @daoudasall8075 5 лет назад

    Du nimport qw ay imaam youy woote ni dina molen nior bapare toppu site you niakk fayda yi di sannante at caddu ...respecte len niou respect dine ji

  • @boubacardia8862
    @boubacardia8862 5 лет назад +11

    khana ki defoul won tè yallah takh m'est li diaroulwone wakh

    • @badjidiarra7184
      @badjidiarra7184 5 лет назад +2

      Vraiment wakh deugue bou yague day Sof sakh

    • @mouhamadoudiop6253
      @mouhamadoudiop6253 5 лет назад +2

      Bonn moootax doolén meussa encouragé kouy déf loubax

    • @aloudia4180
      @aloudia4180 5 лет назад

      Sahola tange rèke lima lère sa Dereme dougousy sohore rèke

    • @adashhniang6652
      @adashhniang6652 5 лет назад

      Dafa beugu Lou lerr rekk nah beuguoul kouni daf ti lekk dara

    • @mamadoumagattediop4114
      @mamadoumagattediop4114 5 лет назад

      En quoi ca vous derrange mou leral . Khana yene jouboulene

  • @traoremouhamet9908
    @traoremouhamet9908 5 лет назад

    Bienfait. Na lep leer bala doul kat yi di yakh sa derr

  • @karimniang4845
    @karimniang4845 4 года назад

    boulen niou fonton oustaz iran limou wakh deug leu fi koufi khamoul sabopp niou wakhla sabopp tayib loumiye mbél mbél rk té défi louni wénguh

  • @borombeyti417
    @borombeyti417 5 лет назад

    Dia dieuf way oustaz yal nala yalla fay yak gni nga andal

  • @oumarpouye530
    @oumarpouye530 5 лет назад

    Iran je t écoute toujours mais je te demande d éviter de prendre les journalistes ,ils sont nuls et dangereux.Tu aides les gens à comprendre leur religion ,continues sur ça et laisses les petits journalistes

  • @galsenpeople9634
    @galsenpeople9634 5 лет назад +4

    Iran souteura dafa bakh nopil

    • @aliouba5875
      @aliouba5875 5 лет назад

      Khlebou jigen bi soutoura dougenli amo yar khamo adouna 🙏🏻

    • @mayewone4316
      @mayewone4316 5 лет назад

      Yow danga mène noppila Iran boula nexoul loo koy degloo

  • @morsella505
    @morsella505 5 лет назад +7

    dioulit pire moy yaw iran

  • @moussambengue9988
    @moussambengue9988 5 лет назад +2

    Geum yalla rèk mo am solo

  • @Steven-ul8pw
    @Steven-ul8pw 5 лет назад

    oustaz iran diadieuf mé détail yoyu diarul di waxat niit dina xeuy tabah lou bakh ay anne xeuy yakhko si lamigne lisenciel bi moy ñingako sekhalon kén xebulasi mosi am solo

  • @aliouneseck6083
    @aliouneseck6083 5 лет назад

    wakh ji doyna iran wakh diouli barista bakoul toujour wakh.wakh

  • @lavieestbelle8539
    @lavieestbelle8539 5 лет назад +1

    👏🏻👏🏻👏🏻👏🏻👏🏻❤️❤️❤️❤️

  • @toubatouba1377
    @toubatouba1377 5 лет назад

    yéén yéna warone nék président wooooooooooooooooooooy walléne séne djiko yi sounou polotichien yiiiiii

  • @ibrahimasall4312
    @ibrahimasall4312 5 лет назад

    Me imame kante nafekhle