🚨Faux Prophète au Sénégal || La Fraude a Trop Durée ⁉️ || Sokhna MaKhady

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 31 янв 2025

Комментарии • 210

  • @KAADUDINEEJITV
    @KAADUDINEEJITV  Год назад +23

    Svp Aimez la video❤maximum de partage Mbook

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад +2

      Soxna si,
      Aussi pour t aider, tous les prophètes n ont pas reçu de livres comme tu lindiques dans tes propos.
      Je t exhorte d aller etudier avant d attaquer des hommes honorés par Dieu...
      Soxna si téeyal...

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад +2

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf

    • @senghori1is
      @senghori1is Год назад +1

      @@Elhadj47 bayilen ki santani mokko nguémb

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Werna

  • @ousseynoufaye8973
    @ousseynoufaye8973 Год назад +22

    Non vraiment j'aime cette Sokhna en Allah. Barakallahou fik 🙏

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @Salimata1000
    @Salimata1000 Год назад +19

    La religion musulmane,c'est le Coran d'Allah swt et la Sunnah du prophète Mouhammad psl,point.

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 18 дней назад

      Baye laye dou yonét yalla mouhamed saws l'islam dou ay foo mboke dioullit yi

  • @diatodiato
    @diatodiato Год назад +25

    Le prophète l'avait prédit:"il yaura beaucoup de faux prophètes après moi".

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @emeraudet4295
    @emeraudet4295 Год назад +4

    Et quand on leur dit: "Suivez ce que Dieu a fait descendre", ils disent: "Nous suivons plutôt ce sur quoi nous avons trouvé nos ancêtres". Est-ce donc même si le Diable les appelait au châtiment de la fournaise! SOURATE 31VERSET 21 DIEUREUDIEUF SOKHNA MAKHADY

  • @siacamane3361
    @siacamane3361 Год назад +11

    Longue vie a vous ya seyda 💪 💪

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @YoussouphaThiam-xs1qw
    @YoussouphaThiam-xs1qw 6 месяцев назад +1

    Bou niouy tane serigne naniou tane Mouhamed psl

  • @aissatousow2128
    @aissatousow2128 Год назад +11

    Slam🙏bokou dama békk siyaw looolou❤sama khollbi sédena siyaw 😊louwér guay wakhe❤yalla nala borombi samela❤❤❤❤❤jtm❤

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 18 дней назад

      L'islam wallahi dou ay foo mboke dioullit yi nane yéwou guir yalla yalla sougnou borom bay lay dou yonét yalla mouhamed saws L'islam dou foo wallahi dafa lérr

  • @YoussouphaThiam-xs1qw
    @YoussouphaThiam-xs1qw 6 месяцев назад +1

    Vraiment je contente de vous naniou délou ci yallah

  • @mouhamedemmanuelsene925
    @mouhamedemmanuelsene925 Год назад +2

    Masha ALLAH soxna ma khady lerna yalna yallah samm leu té moussal leu sénégal moh c malheureux courage à vous ❤✊🏽✊🏽✊🏽

  • @lecitoyen306
    @lecitoyen306 Год назад +9

    Wa mais yonente bo khamne sénégal gneupe khamou gnoula,li yombe na trop thiakhane bi beurina

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

    • @abibatoualidieng1411
      @abibatoualidieng1411 11 месяцев назад

      ​@@Elhadj47pardon mais il faut arreter de jouer avec les mots ces gens la qui suit la sounna du prophete psl c'est des savants aucun n'a le degres d'un prophète les compagnons sont plus haut en degrés au prés D' Allah aucun deux ne se compare au Prophete psl la comparaison est tout simplement impossible nelenn sen serigne nit kou bakh lewone te nit kou geumm yalla lawone te yam thi bouleen gravir echelon yi

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 11 месяцев назад

      @abibatoualidieng1411 mane dé, j invite à la retenue té tèey si mbiru Yàlla
      Le débat ne se situe pas sur la primauté du Prophète Muhammad sallallahu haleyhi wa salam
      "Bidaayatu Maahi nihaayatul khiyaar
      Fadalehu alal wara zul ikhtiyaar"
      Tàmbaleeb Yonente Muhammad sallallahu haleyhi wa salam moy fi gaayu baaxe yi téeré
      Mo kawé ñëp ak lépp lu Yàlla sàkk
      Par cet extrait écrit par Xaadimu Rassoulullah Sheikh Ahmadou Bamba, tu comprendras que tu situes le débat là où il n est pas ..
      Nañu andak mandu té tèey
      Jërëjëf

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 18 дней назад

      Baye laye dou yonét yalla mouhamed saws mboke dioullit yi l'islam dafa lérr wallahi

  • @Sam10ekl
    @Sam10ekl 11 месяцев назад

    Barak Allahou fikoum Sokhna Makhady

  • @od7240
    @od7240 Год назад +3

    Kou respecté yallah kén waroula respecté ay nafekh gno bari Sénégal

  • @ousseynoudiarra9578
    @ousseynoudiarra9578 Год назад +3

    Bilay yallah nala yallah faye iow yay djigueine deugeuh djigueine diou meune milli goor

  • @YoussouphaThiam-xs1qw
    @YoussouphaThiam-xs1qw 6 месяцев назад +1

    Féhell woma nda ma la beugue❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ahlinohin7504
    @ahlinohin7504 11 месяцев назад

    Très pertinente. Ma Sha Allah. Seule la vérité triomphera. Qur'an er hadiths sont la voie de l'islam. Rien de plus.

  • @faly-ft5yd
    @faly-ft5yd 11 месяцев назад

    Mach'allah ma sœur alquran ak Sounnah rk moyii dégueu, alhamdoulilahi y'a des véridiques qui se combattent sur le chemin d'Allah alhamdoulilahi
    J'ai vraiment besoin de votre adresse,watchap pour mieux comprendre le chemin d'Allah svp, k'allah nous guide 🤲🤲🤲🕌🕋🧕❤️

  • @YoussouphaThiam-xs1qw
    @YoussouphaThiam-xs1qw 6 месяцев назад +1

    Elle parle rien que la vérité

  • @OusmaneSow-gf6ju
    @OusmaneSow-gf6ju Год назад +1

    ماشاء الله بارك الله ف،،، يا سيدا

  • @Teranga80
    @Teranga80 Год назад +9

    Bilahi Yalla rk moléni faye, niou bari yéwou naniou ndakh yéne

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @dawdatouray266
    @dawdatouray266 Год назад

    Masha'Allah Sokhna Mahaddy leral yi Amna solo yallna yallah fay la 👍

  • @djibysow7394
    @djibysow7394 Год назад +1

    ما کان محمد أبا أحد من رجالکم ولاکن رسول الله وقاتم نبي! شکر يا سيدا✅✊🏿🤝

  • @محمدمختار-ر7ب
    @محمدمختار-ر7ب Год назад +6

    Napp katou yéét bii mane gniko geum ba legui dagn ma def cas nak walahi😢😢

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @vieuxsene1127
    @vieuxsene1127 Год назад +2

    Machalah Lou ler nga wakh sokhnasi

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @Yayoubayam-j7n
    @Yayoubayam-j7n Год назад +8

    Machala ma fille chérie ❤❤❤❤

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @diatodiato
    @diatodiato Год назад +11

    Après Mouhamad toute personne qui se reclamera prophète,a menti.

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @alphadiack8140
    @alphadiack8140 Год назад +7

    Mouhamad (Psl) est le dernier messager dAllah

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @diangokaou3669
    @diangokaou3669 Год назад +9

    أشهد أن لا إله إلا الله وحده لا شريك له ،وأشهد أن محمدا عبده ورسوله ،وهو خاتم النبيين.
    وأشهد أن كل من ادعى النبوة بعده كاذب . وشكر الله لكم سعيكم وجزاكم خيرا وصرف عنكم كل مكروه

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

    • @fsamateh260
      @fsamateh260 Год назад

      Amen

  • @authentiqueislam
    @authentiqueislam Год назад +6

    Machaa Allah Sokhna say kaadu amati naa solo loo

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @moussadiallo-2001
    @moussadiallo-2001 10 месяцев назад +1

    Limamou thiaw tamit lane moko khiir thi lii
    Louko fi diar

  • @amadoucoumbaniang788
    @amadoucoumbaniang788 11 месяцев назад +1

    La hawla wala houwata illa bilahi

  • @BadouBadou-b8f
    @BadouBadou-b8f Год назад +4

    Sénégal yakouna
    Dossi wéte deh
    Yalla nala yalla Faye yiw

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @oumardiallo6139
    @oumardiallo6139 Год назад +2

    Machala ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @SEKOUDIEDHIOU-s8x
    @SEKOUDIEDHIOU-s8x 4 месяца назад

    je suis très fière de vous

  • @authentiqueislam
    @authentiqueislam Год назад +6

    Machaa Allah

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @matarndiaye-ok2he
    @matarndiaye-ok2he 5 месяцев назад

    Limamou Yalla la fall ngaye AMIROUL MOMININA KU WEDDI FI SA WAKHE DIEUFEUME DIE NILNA...

  • @kinteh-2
    @kinteh-2 Год назад +4

    May Allah The Entirely, Exceedingly Compassionate ONE continue to Bless, Guide and Protect You my Dear Sister in Islam.

  • @ousseynoudiarra9578
    @ousseynoudiarra9578 Год назад

    MachaAllah amatina solo oukhty yallah naniou yallah moussal sii napakatou yeite bii sunnah sikaw tarikha sii soufffffffffffffffffffffffffff

  • @expertpablo7148
    @expertpablo7148 Год назад +6

    Nanou may diam prophète dou niaw ki dafa amoul béne lér gni kounou yapp 😂

  • @baakhreck8942
    @baakhreck8942 Год назад +1

    Ma sha Allah Ma soeur

  • @wirdo1557
    @wirdo1557 11 месяцев назад

    C'est un faut merci makhady

  • @istaqimkamaomirttv5189
    @istaqimkamaomirttv5189 Год назад

    جزاكم الله خير

  • @FallAlyine-q7i
    @FallAlyine-q7i Год назад

    ماشاءالله ❤

  • @boubacardiallo2636
    @boubacardiallo2636 Год назад +3

    qu'Allah vous bénisse ma sœur

  • @birahimatouray8004
    @birahimatouray8004 Год назад +2

    ❤❤❤❤❤❤yanlla ng am sutra guwdu fan ak weri

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @khadijaaidara751
    @khadijaaidara751 Год назад

    Walahi❤❤❤❤ merci

  • @authentiqueislam
    @authentiqueislam Год назад +9

    Walay senn ligeey rafetne

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @aissatousylla4172
    @aissatousylla4172 11 месяцев назад

    Ndeyssane layenne yi nawlo wou gniouléne motah faléwou gniouléne

  • @oulmatamousa8687
    @oulmatamousa8687 Год назад +3

    Vérité absolue.

  • @fatimadiajhete164
    @fatimadiajhete164 6 месяцев назад

    Wa nagnou deih demm safara akk sougni Serignes 😂😂😂😊😊😊. Sa kholl di butagaz gnouy wazifa di lazim. Yaw mi Yallah méréwoul tawal boulettes.

  • @FantaGoudiaby-t6s
    @FantaGoudiaby-t6s Год назад

    ManchaAllah ma fille politiciens rek mo diaral Sènègalais di kheeh ba dh wala lamb ak football waya ahloul sounna sounou borom molendi aar InchaAllah

  • @fatimadiajhete164
    @fatimadiajhete164 6 месяцев назад

    Sa wakh gnakkeuh neu téguine trop. Ba Yallah di yoni Seydina Moussa sk pharaon sakh dafka wakh mou wakh akk moom wakh bou amm téguine.

  • @cissokhomaimouna8620
    @cissokhomaimouna8620 Год назад +1

    soxnasi ni ngaye tahawo si diné yalla gi yalla nala yalla tahawoula nounou bi ijnilahi

  • @mariamjagana339
    @mariamjagana339 Год назад +1

    ما شاء الله الله يبارك فيك

  • @fatimasow1073
    @fatimasow1073 Год назад +5

    Walahi bimala khamé ba legui la bayi tariha yep

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

    • @Yerim-y1t
      @Yerim-y1t Год назад +1

      Alahouma barik

  • @بشيرصو
    @بشيرصو Год назад

    أشهد أن لاإله إلا الله وأن محمدا ابن ‏‪25:30‬‏ عبدالله رسول الله صلى اللّه ع عليه وسلم بلغ الرسالة وأدى الأمانة وجاهد في كل وختم به رسالة الرسالات

  • @Soul-GSow
    @Soul-GSow Год назад

    Wallahi ma sœur tu dit vrai le khakika❤

  • @Projet_pastef
    @Projet_pastef 11 месяцев назад

    Walahi la nabia bahda rassoul salalahou halayhi wassallam🤷

  • @emeraudet4295
    @emeraudet4295 Год назад

    Quand on leur dit : « Suivez ces révélations de DIEU », ils disent : « Non, nous ne suivons que ce que nous avons trouvé nos parents faire. » Et si le diable les menait à l’agonie de l’Enfer ? SOURATE 31VERSET 21 DIEUREUDIEUF SOKHNA MAKHADY

  • @seckablayeseck1135
    @seckablayeseck1135 Год назад +6

    Salam

  • @kawsaratvcheikhibra5812
    @kawsaratvcheikhibra5812 Месяц назад

    Très bien ,ku saga sama yalla bi bind asaman.ak.souf ak.nieup.ga.hamni mom rek nanioou.wara.topu DINA saga sa faux yalla 'ab..yalla biniou bind foko.guis.ndaw.yalla bu niak fayda ana kaka bind kone lumu.donne mom ab mbindefam mom miko bind té amalko.té.nékon.fi.tah mû amal la.nane la.créature.di amalé bopam .sama téléphone mo amal bopam wala mo.bind bopam ,légui.téléphone bi mom naka naniou.koy bindé bâ paré du weulbatiku du dieul placou kiko défar

  • @matarndiaye-ok2he
    @matarndiaye-ok2he 5 месяцев назад

    ROHULAYE GEUNALNGANU SUNUY NDEY GEUNALNGANU SUNUY BAYE TE YA GEUNE SUNUY MAME GEUNALNGANU AY DIOUNI...

  • @fsamateh260
    @fsamateh260 Год назад

    Maa Shàa Allah

  • @AbdullahJobe-gb1dk
    @AbdullahJobe-gb1dk Год назад +1

    Alhamdulillah

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

    • @AbdullahJobe-gb1dk
      @AbdullahJobe-gb1dk Год назад

      Sorry am for sengall but am no understand France because right now I'm in England 🇬🇧

  • @OumarDia-ry6sm
    @OumarDia-ry6sm Год назад

    Merci sohnasi

  • @BadouBadou-b8f
    @BadouBadou-b8f Год назад +5

    DEUG yalla moko mome
    Yalla limou wakh lerna
    Koufi doff nioulay nakh ya togne sa bop

  • @بشيرصو
    @بشيرصو Год назад

    كلام صحيح مئة بالمئة

  • @FatseMbath
    @FatseMbath Год назад +4

    Wakh deuggui yalla sokhnasi limou wakh deugg leu.nékhoul nak degg si laayényi. Senegal dafa beuri ignorant. Dagnou wara geustou al khour aane.kou comprendr ass toute messasou sounou boroom kén doula manipuler. Meme boo deggoul arabe timite amena ay traduction si français anglais pour au moins comprendre le but de son existence.

  • @CheikhouSylla-vr8jh
    @CheikhouSylla-vr8jh Год назад

    allahou akbar all hamdou liillah. yallah yoow rék yaaye yallah soub hana hou wa ta Allah kééne dou yallah kou doul yoow yallah Mouhamadou rassoul allah mooye sou gnou nabi Allah kééne la fii téh doo toul gnaar . deed dou roombe noop xana noop shaïtan mounafixoune.

  • @cheikhounasow6886
    @cheikhounasow6886 11 месяцев назад

    Boy guir yalla dooma diokh sa numero watchap guir yalleu

  • @mbayendiaye7560
    @mbayendiaye7560 Год назад +2

    Nooo ma soeur makhadi nadeugueur daii diaroul noyal Sénégal they fck upppppp im telling actually yanguiniou dimali qran sunah ❤

    • @Elhadj47
      @Elhadj47 Год назад

      Soxna si, téeyal !
      Ne pas confondre entre grade et fonction...
      Lorsque le prophète Insa ibn Mariam reviendra, sera-t-il prophète ? Pourtant non et il a le grade de prophète malgré tout...
      Teeyal si mbiru ahloulaahi
      Nabbi dotul ame ginaaw yonent Yàlla Mouhammad sallallahu haleyhi wa salam wayé ku jubb di wakh Si diiné, ñi lay déglu Moursal nga tcha ñoom.
      Aussi, Hadith bi nga si walou 73 sectes yi werul et je t exhorte nga gëstu ko (conseil d un frère dans l ' islam).
      Jajëf
      Il ne faut

  • @PapeMarGueye
    @PapeMarGueye 11 месяцев назад

    Ray guama way wanak😂😂😂😂😂😂

  • @aissatousylla4172
    @aissatousylla4172 11 месяцев назад

    O ho makhady tu nous amerde layennes yangui dounda sén dounda gou sélla gou yiw gou YALLA guereum may lén niou diam thiiiiim way

  • @NeneWade-i2w
    @NeneWade-i2w Год назад

    MACHA ALLAH amna solo .man douma setaan laayenn yi.

  • @AssaneDiop-w5m
    @AssaneDiop-w5m 11 месяцев назад

    Yonét dou amatt guinaw yonéte yalla mouhamed saw

  • @sakhoousmane7066
    @sakhoousmane7066 Год назад +1

    Soukh ma khade yal nala yala fay yéw ta samou la

  • @ahlinohin7504
    @ahlinohin7504 11 месяцев назад

    A ne pas oublier. Allah est le plus miséricordieux mais sa miséricorde ne transcende pas ma mort. On en bénéficie que quand on est encore en vie et que ce soit un choix. A l'image de pharaon qui a voulu se répentir étant devant la mort, ces répentances ne sont guère acceptées alors repentez-vous pendant qu'il est encore temps et ne soyez pas pétri de fierté et d'orgueil.

  • @mouhamedlaminethiam4404
    @mouhamedlaminethiam4404 Год назад +2

    Soxnassi layenne yi mome warouniou wakh lolu mome c’est pas digne d’un musulman ms iow tamit amal respect thi limamou nax degoko mou wakh lolu yeup

  • @kanegueye5477
    @kanegueye5477 Год назад

    Mashallah

  • @mbayethiaw665
    @mbayethiaw665 Год назад

    Degue rek machalla

  • @AliDiouf-kg9bu
    @AliDiouf-kg9bu Год назад +1

    ❤❤❤🤲🤲🤲

  • @ibrahimamba1296
    @ibrahimamba1296 Год назад +1

    Sénégal légui si tu laisse tes femmes pour aller forniquer dans les salons de massage, on te considère comme un saint, un exemple, un modèle ,un imam et tu es surnommé kou séle ki

  • @authentiqueislam
    @authentiqueislam Год назад +1

    ❤❤❤❤❤

  • @mbayendiaye7560
    @mbayendiaye7560 Год назад +1

    That’s not fair emprisonné des gens innocent senegal yeureumadh dagnaffa ndessane que des cadavres embulants

  • @ibrahimadiallo7739
    @ibrahimadiallo7739 11 месяцев назад

    kou khamoul yalla Manou dalay jaffé

  • @mamadousene2723
    @mamadousene2723 5 месяцев назад

    Jaajeuf waay

  • @بشيرصو
    @بشيرصو Год назад

    في الله

  • @OusmaneSow-gf6ju
    @OusmaneSow-gf6ju Год назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @matarndiaye-ok2he
    @matarndiaye-ok2he 5 месяцев назад

    KU WEDDI ALKOU DONTE LAWLIYA YI NGA 'NITE AK DJINE THI YÉME NA NGUENE THI YEWOU...

  • @xaamlounguenexamoul1066
    @xaamlounguenexamoul1066 Год назад

    ET PUIS ILS AVAIENT MONTRÉ À LA TV QUE JESUS EST APPARU SUR LE VISAGE DU VIEUX LAYÉNE 🤦🤦

  • @sambandiaye4932
    @sambandiaye4932 Год назад

    Que les mensonges dans ce pays

  • @Aicha-r4l
    @Aicha-r4l 11 месяцев назад

    Tu dis la vérité avec impolitesse parle des layenne est n' implique pas les autres tarikha tu es juste impolie tu n'aimerais pas qu'on dise que ton pere est fénekat leu

  • @issadiagne2213
    @issadiagne2213 Год назад

    Sa waax Barina te waxo fi dara

  • @بشيرصو
    @بشيرصو Год назад +1

    الله يفتح عليكم

  • @ClaraMendi-z2p
    @ClaraMendi-z2p 11 месяцев назад

    Wa thiaga bi mongui wédi ba taye ake sa data bou saltè

  • @MohamedDiaw-lt6tp
    @MohamedDiaw-lt6tp Год назад

    Yar yar yar

  • @hadiyatoubah3670
    @hadiyatoubah3670 Год назад

    Beugue nala ndakh alkhourane ak sounna bi ngay tane ndakh lolou moy DEUGUE

  • @antaba301
    @antaba301 Год назад

    Yalla nala yalla saam❤

  • @SheronnenickeMboumba
    @SheronnenickeMboumba Год назад

    Charia dou diamou yalla

  • @Lejuge-u8y
    @Lejuge-u8y Год назад

    Ceey jigueen gui Limouy guener si guemignam gui
    Yaw sa problème moy khamo différence entre prophète ak messager khamo gatte