Wakhtane léne nga balko ndakh nakk qui cherche trouve. Femme nous aussi faisons attention à l'argent car si on accepte une bise pour 300mil est-ce que pour plus tu ne vas accepter autre chose. Khaliss nekhna wayé nagnou yémalé beugue beugue yi. Je vous suis j'ai commenté bonne continuation.
J'adore ce concept frérot Bonne chance pour la suite dieu bénisse davantage ce projet🔥💪🇸🇳🙏 Thia kaw thia kanam reek 👑 🇸🇳 bro Yalle na diamm saax Sénégal 🇸🇳🇸🇳 Yalle na yalle barkel nieup
Bravo la séquence a été bien joué merci pour l’éveil des consciences à mon avis souma nekon ioa je vais faire comme si rien n’était dakh #jiguèn koukoy nat si xaliss doh gawa guiss bou bakh au passage soukén wété goudi waxtan lénesi c’est comme ça se règle un bon couple 😅😅😅😅
Je suis parfaitement d’accord avec moi mo geune gnifi nek wa thème n’oublie pas les 5prier comme ci que nioune dougniou ay dioulit sounou nagniou way ah
Si c'était moi dina ko conseillé pour mou xam boppam, té moytou en plus dès lors nga dieul initiative testé. Deux résultats nio manon am soit fidèle ou infidèle du coup da ngay am compréhension que l'homme est imparfait on Pardonne on en discute et on passe. Sinon se taire comme si de rien n'était n'est point la solution. Bravo Toma
Maasàllaah, très bonne leçon, mais on vous supplie de parler plus Wolof que les mots français que vous prononcez fréquemment pour pouvoir mieux décomplexer les gens ! Wàññileen waati faranse yi ngir Yàlla ngir wàññi yaram gi nekk ci nit ñi ba ñu xam ne war na ñoo man a wax sunu làkk yii de duñu soxlaa mel ni tubaab bu ay wolofam setul. Loolu mooy deñal yaras gi ci nit ñi, di liggéey bu rëy te rafet niki ngeen nuy joxe ay bind yu am solo. Jaajëf yaaram 🥰✅🤔
Se lancer dans l’aventure entrepreneuriale, c’est avant tout adopter un état d’esprit : trouver le courage de prendre des risques et rester motivé en dépit des difficultés. Mais comment développer un tel état d’esprit ? L’une des clés est d’adopter la pensée positive.
Bien joué vraiment j'adore sadiya elle est supernaturelle dans son jeu ! Ah mais pour la question macdi khana nga bal KO rek gnoune djiguene gni dagno khawa beugué khaliss nak
Hahaha 😂😂😂😂😂😂thia 300mille yala excellent role ma chérie sa se voit que les femmes son matérialiste boyi djiiiz rek boufa nekatoul dolene guiss vive macdi❤️❤️💚💚❤️❤️🙏🏿 l'éveil des conscience continue
Ho frère idée bi nice na trop👏👏 Ho boudone mane damaye tokk yédeuko khamal ko niko sa lékhe béneu tougne rek moussi warra foune 💋mougne mane👉😘 parce que djiguéne yepp yamougnou 👌
Adine amoul solo ballko rek te bouko wakh dara bouko dole nga wakh tane ak môme bou doliwate nga wakh tane ak yayame bou dole nga wakh tane ak papame bou dole nga setane ko ba khame nane laye def bou dole nga bayi ko mou dème si diame ak salame
CC.1er pouces pour cette vidéo passionREINE MACDI❤️🏝️✂️🏖️je pratique une DRÔLE de discipline très atypique seul a réaliser en France composé de petite vidéo de 2minutes assez spectaculaire.merci infiniment
slt macdi lep nice félicitations Maashallah amna solo tropp 😊mé nak balko djigueen khaliss moy niarelou toureum amal compréhension si mom té téktal ko ndax niom femme sén khél soriwoul 😌 mé aussi macdi boulko bayi dh 😂risque leuh mom bou géné dina amat té dafay gaw wayé yaw bala nga amat diga ko sét sétat ko té bou boba dina duré ngay geuneu soufrire ndax linga tamone geudj ngako def 😂 pour amat confiance si kénén dafay yagg kon nak yéd ko mo geune si yaw ak linga diota def si mom yeup tu perdrais tout et recommence à zéro 😢lolou un simple bisous diarouko waleuh 🙃
Macdi'' je sais que cette fille est ta petite sœur et tu ne veux rien signaler, tu ne veux pas qu'on l'a drague,, et pourtant mouguonaaa' ngaa maymako'' dee /Elle me plaît vraiment
li rek mo tahh doylou bah ,lo ame santéko yallah. BRAVO C'ÉTAIT TRÈS BIEN.
❤❤❤
🤣🤣🤣🤣🤣bébé ma nieuw sangue leuh....
Sama serigne dafmakoy téré 🤣🤣🤣
C’est un honneur frérot Bilahi je suis fier de toi
Kou beugeue macdi lalal j'aime
Wakhtane léne nga balko ndakh nakk qui cherche trouve.
Femme nous aussi faisons attention à l'argent car si on accepte une bise pour 300mil est-ce que pour plus tu ne vas accepter autre chose. Khaliss nekhna wayé nagnou yémalé beugue beugue yi.
Je vous suis j'ai commenté bonne continuation.
J'adore ce concept frérot
Bonne chance pour la suite dieu bénisse davantage ce projet🔥💪🇸🇳🙏
Thia kaw thia kanam reek 👑 🇸🇳 bro
Yalle na diamm saax Sénégal 🇸🇳🇸🇳
Yalle na yalle barkel nieup
libereco mo am
Lath koh loutakh mou déf koh
@@moussagassamafofana317 gorr dou gawa libéré
@@bassirou297thiam6 mai lol mo gan
Première commentaire way gawlén si jaime yi avec macdi tout est possible bonne continuation
Doyna waar mais djiguen sopal te boul wolou
Bravo la séquence a été bien joué merci pour l’éveil des consciences à mon avis souma nekon ioa je vais faire comme si rien n’était dakh #jiguèn koukoy nat si xaliss doh gawa guiss bou bakh au passage soukén wété goudi waxtan lénesi c’est comme ça se règle un bon couple 😅😅😅😅
Je suis parfaitement d’accord avec moi mo geune gnifi nek wa thème n’oublie pas les 5prier comme ci que nioune dougniou ay dioulit sounou nagniou way ah
non suis pas d'accord du tout kou fonne kénéne ndah 300m neuune nala jaaye wala mou jaaye saye secret thi mbede mi ndah 1million
OK d'accord mais goor oci koukay nate si djiguéne do meusseu dal ci bou bakh bi🤧
@@aminatafaye1394 suis tout à fait d’accord avec toi djiko ak borom mouy gor di djiguén on a tous un côté négatif té kougnou thi sétlou diap gnousi🙏🏿
Motakh léne rek mo diara gnane moy yalnagnou boure Yallah doli soutoureu
Macdi le meilleur un coup de pouce niou ame un grand producteur confirmer bravo courage frère mashalla
Kou beug couple bi rq lalaleu j'aime🥰😍❣️
Ohhhh Nice
Bly yw
Soutouralko gua khamni djiguéne le
Macdi khana nga comprendre ko réck deuck bi mo deugeur réck 😆😆😆😆🤣mais ma challah amna solo nack
Si c'était moi dina ko conseillé pour mou xam boppam, té moytou en plus dès lors nga dieul initiative testé. Deux résultats nio manon am soit fidèle ou infidèle du coup da ngay am compréhension que l'homme est imparfait on Pardonne on en discute et on passe. Sinon se taire comme si de rien n'était n'est point la solution.
Bravo Toma
Ki dé so niakon téy mou bayila🥰🥰
Always love what you do Macdi❤️❤️
Di na ko dore ba mo hkambombam😂😂
Wouy sadiya wayadi nga nk dommage 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Bon courage mcdi on t’aime fort 💪🏿
Maasàllaah, très bonne leçon, mais on vous supplie de parler plus Wolof que les mots français que vous prononcez fréquemment pour pouvoir mieux décomplexer les gens !
Wàññileen waati faranse yi ngir Yàlla ngir wàññi yaram gi nekk ci nit ñi ba ñu xam ne war na ñoo man a wax sunu làkk yii de duñu soxlaa mel ni tubaab bu ay wolofam setul.
Loolu mooy deñal yaras gi ci nit ñi, di liggéey bu rëy te rafet niki ngeen nuy joxe ay bind yu am solo.
Jaajëf yaaram 🥰✅🤔
Am na solo mbook mi
Soudone Modou Gueye fassénako bou yague 🤣🤣🤣🤣
Douko yagual dama ko beugue
Waxna deug di
Ay
Yaguena 😂😂
🤣🤣🤣
Se lancer dans l’aventure entrepreneuriale, c’est avant tout adopter un état d’esprit : trouver le courage de prendre des risques et rester motivé en dépit des difficultés. Mais comment développer un tel état d’esprit ? L’une des clés est d’adopter la pensée positive.
Effectivement mais le plus important c'est résoudre un ou des problèmes c'est le devoir de tout entrepreneur.
Diadieuf broh n’oubliions le Mercredi 29 juin in chaaa الله seule la lutte libère ✊🏽🇸🇳.
Surtou
J'adokhh ce couple ✌️❤️
Yàlla nama Yàlla féwalé ak djiguénn yi foonaté ndakh wéccit touf touf touf amine
T'es brave vraiment frère bn contuniation 🥰🥰🙏
macdi tes video son tres bon👍👍👍😙😙
Cet vidéo est trés intéressant L'argent ken dou ko lidienti da niou Kaye liguéye y'a aussi de l'humour j'aime🤣😂😅
C'est nice dh bilay ❤
Toujours le meilleur ❤️❤️❤️❤️🔥❤️🔥❤️🔥⚜️👌
Bilaahi
Enfin Merci pour la leçon ndax Yalla sax jiggueen gni di bayi di fookné gnoon gueuneu mouss goor gni
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣Kii moo yabaate. waaye tay nga dee de
J'aime votre complicité vraiment
😂😂😂🤣 no macdi dou may khalé bi dara
Non macdi il est meilleur vraiment ❤️😂😂
Kagne ngakoy takk grand bi ✨
Mardi wallahi vous êtes forts tous les deux 🤣🤣 j'ai rigolé comme pas possible
Mardi nga lal dei dioumo😂😂😂😂🏃🏃🏃
@@ELZOYB 😅 niakk nga fayda 😂😂😂
@@ELZOYB 😂😂😂😂 yaw bakhna
@@papyIdriss ma tay😂😂
@@modougaye7351 oki😂😂😂
Macdi t’es trop fort ✌🏿
Bien joué vraiment j'adore sadiya elle est supernaturelle dans son jeu ! Ah mais pour la question macdi khana nga bal KO rek gnoune djiguene gni dagno khawa beugué khaliss nak
N’oubliez pas les cinq prières 🤲🏾
Merci
« N’oublions pas les cinq prières »mon gueune 🤘☺️
Diadieuf way😂😂iow la geum dh
yaw yaye guinaxbi
Ok domou tivaoune
C vrement cool mé wakhtanal ak mom rek gua délosiko khaliss seytané la
Bravo mame cheikh vidéo yi machallah
Hahaha 😂😂😂😂😂😂thia 300mille yala excellent role ma chérie sa se voit que les femmes son matérialiste boyi djiiiz rek boufa nekatoul dolene guiss vive macdi❤️❤️💚💚❤️❤️🙏🏿 l'éveil des conscience continue
Le pouvoir de l'argent on y peut rien mais c'est trop génial ce que tu fais on rencontre ça tout les jours dans la vie
Bravo Macdi et sadiya duo de choque😍
Bou lein fatté la 29 inchallha xéex macky sall ci jàamu Yalla la bokk 🔥⚔️✊🏾
Je vous félicite vraiment bonne continuation
Beautiful video ❤️😍😍
Diadieuf macdi boy bi sa gayine la daguene degoo machallah que dieu vous protège ❤️❤️❤️👍🏾👍🏾💙💙💙💙
Macdi t'es le meilleur bilahi♥️♥️♥️
Macdi beat bigua tèk sissa vidéo bi nèx nama deh 🥰
Ma ngay jooy
Vraiment vous êtes génial bro
Vraiment Macdi vous êtes formidables c'est incroyable
Macdi yalna sa diamou yague 😂😂😂😂
Amine
Ho frère idée bi nice na trop👏👏 Ho boudone mane damaye tokk yédeuko khamal ko niko sa lékhe béneu tougne rek moussi warra foune 💋mougne mane👉😘 parce que djiguéne yepp yamougnou 👌
Moi j’aime tout ce qu’il fait notre Macdi nationale
Divorcelllllllllllll macdi mom moy sa diamants rek dal 😘😘 elle t utilise pour de l argent 💰
You guys make great and sweet team !! ☺️😃
Bou done man la damkoy fasé mou dem boko defoul bénén yon dinane ko kat 😂😂😂🤣🤣🤣
🤣🤣
Thia fone bala 🤭🤭😁😂 baal ko rek khaliss moy seytané, après nga tegal femme bi néko wadji dala fone, pour bénen yone
Siiii siii siii lolou amoul lathié nak macdi gnibi keurr yayam rk mane sama diabarr dou beeurek diguene bay diapanté ay tieurr massak goor mouy téganték mom ay leveur 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Macdi t’es trop fort 🤣
Bilaahi
ruclips.net/video/EO48Q1wz8xQ/видео.html
Le visage de sadya à la fin 😂😂😂
C’est très intéressant, broddah
😂hé femme 😂😂✊🏿❤️✊🏿
Bonne continuation bro. Tu déchires de ouffff !!!!!!
Fassé d'office
C’est cool Macdi del deff genre vidéo yii tout le temps
non tonton macdi magui ramm les famme rek ni rek lagnouy def 😂😂
Lolou dou dara guara woul balko
Adine amoul solo ballko rek te bouko wakh dara bouko dole nga wakh tane ak môme bou doliwate nga wakh tane ak yayame bou dole nga wakh tane ak papame bou dole nga setane ko ba khame nane laye def bou dole nga bayi ko mou dème si diame ak salame
Vous formez un bon couple
damay Koy nakhe bb dagua beugue déme nioulay fonne dilla faille konne bounoba damay wakhe 😂😂😂😂😂😂
foon rek garawoull 😂😂😂😂😂😂😂
Ay 🤭😂 boul wakh lolou
Adultère la deh boulko xepp sawaay
Fon Molay yobou si lénén
Masha'Allahou c'est professionnel bravo l'équipe...👏👏👏👏👏👏👏
MAIS NÉKHOL BAGNE 🤣🤣🤣
Macdi black fatwa dinama ray contan si video yi 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣👍👍👍👍👍💗💗💗💗💗💯💯💗💗👍
CC.1er pouces pour cette vidéo passionREINE MACDI❤️🏝️✂️🏖️je pratique une DRÔLE de discipline très atypique seul a réaliser en France composé de petite vidéo de 2minutes assez spectaculaire.merci infiniment
Mane mom vraiment yalnala thiat sékhlou rék laalay nianal bravo
Non 😅😂 waye macdi je ' amie ça 😂😂😂
Nga tadje wakh ak mome,yédeu ko,nga baal ko après mou djièkh☺️
TRÈS BONNE STRATÉGIE D'ÉVEIL DES CONSCIENCES..
YALNA GNËP YEEWU!
Machalah trop nékh avec sadiya
Djigein sopal teh boul wolou😂
slt macdi lep nice félicitations Maashallah amna solo tropp 😊mé nak balko djigueen khaliss moy niarelou toureum amal compréhension si mom té téktal ko ndax niom femme sén khél soriwoul 😌 mé aussi macdi boulko bayi dh 😂risque leuh mom bou géné dina amat té dafay gaw wayé yaw bala nga amat diga ko sét sétat ko té bou boba dina duré ngay geuneu soufrire ndax linga tamone geudj ngako def 😂 pour amat confiance si kénén dafay yagg kon nak yéd ko mo geune si yaw ak linga diota def si mom yeup tu perdrais tout et recommence à zéro 😢lolou un simple bisous diarouko waleuh 🙃
Forgive her and advice her to be content with what you gave her, let love lead 🥰🥰🥰
Sama gars yi 1million d'abonnés pour macdi vrement tu le mérite
MACDI💔✨😂👌
Macdi do nitou fi
1 ere commentaire j’aime trop t’es contenu et un gros big up ✌️🥳
Machallah wayé nak esk bougne ko diokhé lu eupp lolu du diokhé lu guene sori 🤷
Lissi métty moyy faune nenn ko gratuitement 😂😂😂
Diekeur dji mo tek deal bi
Bilaahi
Wakhtana ak môme yèdd ko mou dèllo si khèlame ba douko déffate💓💓
Quel couple 💑
Khol solution 2éms femme Ndakh lii Woroul Diemoul Kanam sheutttt🤭 bon continuation mes Frr 🙏
Thiéyy l'argonnnnnn🤧🤧🤧😂😂😂
diamou si yaw macdi bilahi ❤
Loukhew fiiii 🥺🥺
Fassé bu rafét lakoy fassé ba paré meyko 300mil
Macdi'' je sais que cette fille est ta petite sœur et tu ne veux rien signaler, tu ne veux pas qu'on l'a drague,, et pourtant mouguonaaa' ngaa maymako'' dee /Elle me plaît vraiment
sama serigne dama ko tere❤😂😂
Macdi on t'aime fort
Bravo mon frère🙏
Amna solo loll mourit 🇸🇳❣️👈
Avertissement🤣🤣🤣🤣
😂😂😂😂😂😂😂non macdi do sérieux touti tamitt yakh nga tabaski dh