Tout a commencé rien qu'à voir le gouvernement ethnocentriste de Macky dont beaucoup d'entre nous ont évité de pointer du doigt de peur d'être taxé d'ethnicist .
Fátima Kidé n etait pas a l aise. elle est peul et ce sont plus souvent eux ( les peuls) qui insultent, critiquent et detestent les wolofs. PENDA BA N EST QUE LA PARTIE VISIBLE DE L ICEBERG
😂 Kon séetlu nga loolu yakaron naani man rek maka séetlu Bañ Olof ci séen déréet la bokk. Té léer na ma ni ay maamam wala kén ci waajuram am na ay Olof 😂 ak ñulay am ci ñun la bokk. 😂
Maasàllaa Saa-Wolof ci kàddu yu jot yi, nii rekk la wax lu la naqari teewul a yar say kàddu, xeex bi moom na nu ci dem ba jeex rekk, te yal na am i njuréef, ndax leegi lii nu gis ci sunu réew mii di Senegaal, mi ngi waaj a jéggi dayo, te baaxul ci am réew, te am réew fàww ku teggi yoon ñu tegaat la ci yoon ngir réew mi man a tegu ci yoon.
Merci sa-wolof, tu as tout dit, il faut le régler avec la justice. Mais parcontre, je ne suis pas d'accord quand tu dis qu'après la peine judiciaire, on peut pardonner. Non, il faut qu'il purge la peine, non par méchanceté, mais pour que la leçon soit bien apprise. Chaque jour dans la cellule, lui permettra de méditer sur sa faute. Avec un imbécile de président qui joue chaque jour sur tout, même les fibres ethniques, il faut s'attendre à des dérives pareilles de la part des faibles d'esprit.
hahah , lui meme il est nè chez les wolofs il a grandi chez les wolofs , il a fait l'ecole coranique en wolof ....il habite chez les wolofs....ce qu'il a vient des wolofs.
Non dafa Don wakh dé kal Wayè nuit Gnie begue yakh déram ne Rk si souba ba legui Facebook yongui may saga l'on ne wakh nage makou waye Grawol nuit kou bakh la
Aidara a commis une grave erreur.les wolof sont de bons gens et sont très ouvert d'esprit ils ne méritent pas qu'on les traite de la sorte.peuls sérère diola wolof socé sont tous frères et sont égaux
Mane je suis olof et je voudrais qu on se bat avec les poulhar comme ça chacun restera à sa place comme au Rwanda je ss partant prcq le masla ça va un temps 😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡
Ma sœur la colère est mauvaise conseillère, je ne cautionne pas les paroles de cet énergumène mais j'espère qu'il sera sanctionné pour de vrai. Courage aux Wolof et à tous les épris de justice.
Le chien aboie la caravane passe. Ce faut shérif est méchant et complexé comme beaucoup de haalpoular du fait que le wolof est et restera toujours la langue dominante au Sénégal et non le haalpoular et n'en déplaise tout les haalpoulars
Où elles sont hypocrites, où elles ne connaissent pas leur métier, pour oser dire il s'est trompé, ou il ne faut pas redire les mots car ça peut choquer certains.
Faite attention Ibrahima aïdara al tidjani limou wakh ni bolén ko sétlo ba sét bou bakh c un rancunier est pourtant même pas une semaine la songuone wa ande sam djikoyi mais une chose est claire depuis k le senegal est senegal bougnou sétlo si diamonoy macky sall la li tambali mais défléne trés attention naniou bok ndeye bok baye liguéy réwmi mo geune té bagna top ibrahima aïdara al tidjani mi beug diviser Diola Baïnounk Sérére peul mankagne manjaque Sérére wolof toucouleur basaris balante mandingue na gneup dioug plainte doomi kharam bi beug toumal si wakh mame maodo mou bakh mi selon ay wakhame si vidéo sinon tôt ou tard senegal dineu meusseu doundou génocide té nianou mako yalla
Limou wakh dafa lèr amoul dara loumfiye lire limou wakh lèrna nagn j'ai écouté toute la vidéo il a dit que les wolof sont des voleurs et les sereres sont des ceddo dafa lèr dinagn kate leufeul ndayam
wolof yi aÿ na fekhe lange na sak joueur nga Guies kou def statut nan nuit ko niol dafa sokhr danguine begue yakh Goor bou kham ne defoul dara de kal kom nieupo dem len lô nek terite nagé kou waye dem len rk
Vous êtes tous pareil Vous les personne qui travaille sur les média mais dama len diii alerte koufii wakha lou niaw sii sama xette ma dokhann saa ndeye
may gnou sunu diame deh wolof yi gno fi dakh xébaté yeun xébaté rék nguén xamm ahhh guis nguén ni nexoul wolof amoul ben lakh katt bou mou xéboul dou joola dou sossé dou peul dou sererr kon guis nguén ni nexoul 😂😂
J'aimerai savoir si le wolof est une ethnie oubien une langue nationale. A ce que je sache et apris a l'école si j'ai pas oublié, le wolof est une langue nationale pas une ethnie donc sérères; toucouleur; lebous; peuls; manjaques; mancagnes; diolas; kognadji; bassaris..... donc tous sont des wolofs et quand il dit que les wolofs sont a 44 pour cent je reste perplexe et c'est pas ça qu'on appris car les sérères sont les plus nombreux suivi des peuls, diolas si je me trompe pas..... Pour moi le problème a été pourri depuis qu'on a laissé certaines personnes dire a d'autres qu'ils sont rebelles, qu'il ne mérite pas de diriger une mairie, qu'on vas prendre les coupes coupes, qu'on insulte les chefs religieux... Ceci dit si c'est avéré c'est a condamné
Lui il a donné sa source Agence Nationale de la Statistique (ANSD), le wolof est une ethnie comme les séreres, djola, ma dingue, avant d'être une langue. Va faire des recherches avant d'écrire pour ne rien dire.
Pire encore si le Wolof n'existe pas comme ethnie donc il a insulté toutes les personnes qui parlent Wolof la langue lui en premier et peut-être ces parents. Soit vous acceptez que le Wolof existe comme ethnie et vous respectez les wolofs si vous ne considèrez pas le Wolof comme ethnie c'est votre droit de toute façon personne ne va vous obliger à changer votre avis mais arrêtez de faire allusions à cette groupe de personne et de proliférer des insultes surtout nous savons tous que quand vous parlez de Wolof vous faites pas allusions aux personnes qui parlent Wolof. Le débat a savoir si le Wolof est une langue ou une ethnie n'est pas à jour actuellement on en entrain de condamner les propos d'un narcissique fou raciste qui se prend pour un savant ou Serigne. Góor Yàlla Dou lou gneuw yeungal la nanale Téré yeupe so amoul dale, yar, teguine, do tousse meuno diarigne Kéne Si yàlla santale noula nékh.
Tout a commencé rien qu'à voir le gouvernement ethnocentriste de Macky dont beaucoup d'entre nous ont évité de pointer du doigt de peur d'être taxé d'ethnicist .
Dëgg la de wallaahi 😭
Je suis en Wolof mais ki diaroute tontou wayé lépou macky sall la Bamfi togué batay dafa Senegal 🇸🇳 toujours day beugua diviser khét yi
Macky domeramou baadolo..
Moo ma de
Kokou niounaan Chérif la ...dou bén Chérif...Diallo la santeu...dafaa fén
Merci pour ton franc parlé coach 🙏🏿🇸🇳🇸🇳
Mom dasoff
Jërëjëf
@@Abdoulahi-cisse ñun askan wi jox nañ la suñu kàddu nangéen ko tóop ci yoon bamu sëss rëkk bu dara séed 😡😡😡🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Fátima Kidé n etait pas a l aise. elle est peul et ce sont plus souvent eux ( les peuls) qui insultent, critiquent et detestent les wolofs. PENDA BA N EST QUE LA PARTIE VISIBLE DE L ICEBERG
N'importe quoi arrêtes de raconter de la merde, avec vous c'est toujours les peulhs partout y'a des bons et des mauvais.
Wahatiko c'est pas lui le premier
😂 Kon séetlu nga loolu yakaron naani man rek maka séetlu Bañ Olof ci séen déréet la bokk. Té léer na ma ni ay maamam wala kén ci waajuram am na ay Olof 😂 ak ñulay am ci ñun la bokk. 😂
Nagn gnou dimbileu ak nday jégueulou .
Merci Abdallah Amna solo jërëjëf waaye 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Maasàllaa Saa-Wolof ci kàddu yu jot yi, nii rekk la wax lu la naqari teewul a yar say kàddu, xeex bi moom na nu ci dem ba jeex rekk, te yal na am i njuréef, ndax leegi lii nu gis ci sunu réew mii di Senegaal, mi ngi waaj a jéggi dayo, te baaxul ci am réew, te am réew fàww ku teggi yoon ñu tegaat la ci yoon ngir réew mi man a tegu ci yoon.
Yénn a ma yonni te ku géen yab. Bu yebbee kon njariñ feeñ
Mashaallah amna sólo Li ler na
Qui dafa dohane ndayam dou cherif dou dara
Merci Sa wolof, fatima yow ak la présentatrice sén mesquinerie mogui fégn dé srtt fatima.
Jërëjëf waay ñoom dañuy laaj rekk ngir xóotal 🙏🏿
Merci sa wolof.aidara doit être traduit en justice.
Diam rekk moy deugue merci beaucoup
Jërëjëf 👍🏿
Merciii bcp lou leer nga wakh merciii bcp
Je suis lébou et fière si il n’est pas contente qu’il dégage du Sénégal
Merci walfa tv
Man Saa-wolof maa ngi gërëm tay sant ñépp ci teewlu ak njañse = contribution yi
Pour maane wérou korgui warou niouko may béne conference si deuk bi foumou déme naniou KO déme tas ko
Yaw dof nga rk ki da yakar confirange dem len leGuyé yi ta bayi sokhor
Wax nga dëgg
Merci sa wolaf nice na
FATIMA KIDE ,ALIOUNE SOW ET RAMATOULAYE SARR FONT LA MEME CHOSE QUE CHERIF AIDARA.
SOLIDARITE NEDOKO BANDUM CONTRE SONKO
Jaajëf saa Wolof bi
Jërëjëf sa wolof 🤝🙏🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Jërëjëfati
Maasàllaa tubaarkàlla.
Merci c tidiane gomesse nafex gui dafa bari
Merci beaucoup sa woloff
Merci sa-wolof, tu as tout dit, il faut le régler avec la justice. Mais parcontre, je ne suis pas d'accord quand tu dis qu'après la peine judiciaire, on peut pardonner. Non, il faut qu'il purge la peine, non par méchanceté, mais pour que la leçon soit bien apprise. Chaque jour dans la cellule, lui permettra de méditer sur sa faute. Avec un imbécile de président qui joue chaque jour sur tout, même les fibres ethniques, il faut s'attendre à des dérives pareilles de la part des faibles d'esprit.
Nun bu géen ko baalul dunu ko baal de yénn rekk lay des
hahah , lui meme il est nè chez les wolofs il a grandi chez les wolofs , il a fait l'ecole coranique en wolof ....il habite chez les wolofs....ce qu'il a vient des wolofs.
Daguéne Di rafétal lou raféte lii mou wakh dafa niaw Ay téguine dafa bakh
Présentatrice yi aye peul lagn motakh niom nieupa yam peul ak toukouleur nio yam wolof rk lagn bagn
Jaajéf cobakh amna solo
Machalla saa wolof
Il faut arrêter ce monsieur et le conduit devant le procureur
Maasàllaa saa-wolof !!!!
Jërëjëf ci ñaax gi
Maa ngi wax ju ñaaw ci Ibou Diallo.
Nanhiou deuggeu ndéyeme, beaucoup de peul qui insulte les wolof sont des mairitaniens , et ses des racistes .ils n'aiment pas les senegalais
Merci yaw xamngeu !!!! Niome nieup fofou leuniou dioggé... Ba si djitou rewmi.. Ouolofs kegne bax rek.. Beug teranga ak masla!! Ils exagèrent nak.. Fixamnaniou leup!!
Jaajëf Saa-wolof !
Merci sa wolof
Jërëjëf 👍🏿
Mokotay khajle buo bone
Machalla amatina solo lool
Dou cherif ibrahima Diallo la toudou domeram bou mak la fén kate la
Dof manoul wésou Di wax Woolf ba noppi né Woolf amoul
Billae mane lolou moma diakhal
Wakh rek loula nekh thi loula nekh
Walf walahi da may weur téléphone diambor yi de abonné sen you tube bi waye dan Guine War de invite aÿ nuit Gniou am solou
AND SAMOU DJIKO YI koulén laal aam problème mé Sénégal kén mounouko taal
Dem len leGuéy mon Guene Serif mon len Guén fofou
Khamouniou Kane Moy chérif nitt kou bakh le
Non dafa Don wakh dé kal Wayè nuit Gnie begue yakh déram ne Rk si souba ba legui Facebook yongui may saga l'on ne wakh nage makou waye Grawol nuit kou bakh la
Ki souma khame maoda mon takh man begue maoda walahi ken dokou fi yakh sama kanam walakhi aidara doundal ba décourage ❤️
Aidara a commis une grave erreur.les wolof sont de bons gens et sont très ouvert d'esprit ils ne méritent pas qu'on les traite de la sorte.peuls sérère diola wolof socé sont tous frères et sont égaux
mé FALL sa niane gui tarkaala BAYOU MBÉNE
Da fee xujul sax moo tax nu gàttal ko waaye ëpp na lii 🙏🏿
Mane je suis olof et je voudrais qu on se bat avec les poulhar comme ça chacun restera à sa place comme au Rwanda je ss partant prcq le masla ça va un temps 😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡
Ah bon !!! 🗣🗣🗣Tenga yam sa wagne waa
Ma sœur la colère est mauvaise conseillère, je ne cautionne pas les paroles de cet énergumène mais j'espère qu'il sera sanctionné pour de vrai. Courage aux Wolof et à tous les épris de justice.
@@Mmm-mv8sy 🤣🤣🤣🤣 mo geune si môme dhè
Man mii sama yaay Pël te wolof bari Pël yu bokk sunu mbootaay gi
Di la jaajëfal Saa-Wolof vi taxawaay bu am solo bi.
Kii dees koo war a yar.
Wallaahi 😭
BILLAYE dou serif diallo la sent day fen
😂 😂
😂 😂 😂
Wa AND SAMOU DJIKO YI koulén laal aam problème KILIFA DJINÉ YII nion ande ak niom.Guisnaniou Ouztas bounék Louga bamlén laalé foumou moudjé
Wax nga dëgg de
Bayilen di wah aidarra ki ibrahima diallo la toudou
Mane numéro sa wolof la soxla
il na rien fait le Seul probleme c'est macky sall
Dëgg gu wér a wér nga wax
ki da rew di khass wolof yi badola
Am solo lool.
Le chien aboie la caravane passe. Ce faut shérif est méchant et complexé comme beaucoup de haalpoular du fait que le wolof est et restera toujours la langue dominante au Sénégal et non le haalpoular et n'en déplaise tout les haalpoulars
Waa ji Chérif li mu wax tegu ko fenn, il faut que l'Etat sévice au plus vite pour éviter les dérives.
TAPALé yatouna fiiii🤣boy demal ligeyi
Ibou diallo la todou doomiram goordijen bou kate naye sa data yaye sa lafalla naye ibou diallo dou sarife goordijen bou kate naye la 🏳️🌈🏳️🌈🏳️🌈🏳️🌈
Ku tojj lëfall ndayeem la Moom Ibu Jallo Bandi bi
Guiana niou penda Ba té darà fékou kossi
Tout a commencé avec Macky LGBT et Charlie hebdo et le ministère du GENRE.
C'est comme un autre doumbourou sow
Où elles sont hypocrites, où elles ne connaissent pas leur métier, pour oser dire il s'est trompé, ou il ne faut pas redire les mots car ça peut choquer certains.
Wolof amoul Lou kouka wakh day doul
😂 😂
Wa Pari niou ngui lène di faye
Ses grace a serigne touba k le senegal parle le wolof
ki nieup la saga après mouy wolof mouy toucouleur. d'ego limou wah ci nit kou nioul après
Mais li c'est pas la première fois
En matière de vol qui a usurpé le nom d autrui.La justice doit décliner son véritable identité pour arrêter ce phénomène de vol de nom
📺📺📺📺📺📺📺👍👍👍👍🙏🙏🙏🙏🙏
Kokou Diallo leu sant
Yaw fougn dadié ak yaw dinagn kate sa ndaye yaw cherif
Balou noco n danane katte ndayam
Il se nomme diallo pas aidara
Waw lén gor
Faite attention Ibrahima aïdara al tidjani limou wakh ni bolén ko sétlo ba sét bou bakh c un rancunier est pourtant même pas une semaine la songuone wa ande sam djikoyi mais une chose est claire depuis k le senegal est senegal bougnou sétlo si diamonoy macky sall la li tambali mais défléne trés attention naniou bok ndeye bok baye liguéy réwmi mo geune té bagna top ibrahima aïdara al tidjani mi beug diviser Diola Baïnounk Sérére peul mankagne manjaque Sérére wolof toucouleur basaris balante mandingue na gneup dioug plainte doomi kharam bi beug toumal si wakh mame maodo mou bakh mi selon ay wakhame si vidéo sinon tôt ou tard senegal dineu meusseu doundou génocide té nianou mako yalla
Dëgg la de
Gouvernement macky sall wakhi xétte rek vrais domou haramlanou
Niolen integre mo takh nilay deme
il n'a pas du tout demande pardon au contraire il a insulte de nouveau notre intelligence....
Wax nga dëgg de
Kookou d'où guat!
Sawolof yaw borome bakhe nga mais femme bi vrai domeramella mok ibou Diallo gno yame
Deedeet sax day laaj ngir xóotal rekk
C est pas une erreur
Vraiment moko tey
Ban Cherif bou déme si nar yi dina kham lepou deugleu
Chérif Aidara la santt wala Diallo? Les investigateurs Sénégalais (Kewoulo, Tange Fake, Leral BBY, Pape Alé Niang...) éclairez notre lanterne!!
Bayilen holofyi soul kerr douko tere feigne
Faux cherif Ibrahima Diallo khamoul nii histoire guinée conakry diangu nako avant Empire du Manding
😂 😂
dieureuf sa wolof contannanou ci yaw mandeh je s8 pret a integres tn association, rewmi kou and ak macky sall loula nekh def dara doukici fèk
Chérif ibrahima aïdara domou harame la kou gni saguati dinéne ko digualé ak iowe
Yen dem len setan émission interagalit lepou Guine douga wakh ame Guine diote torop
Limou wakh dafa lèr amoul dara loumfiye lire limou wakh lèrna nagn j'ai écouté toute la vidéo il a dit que les wolof sont des voleurs et les sereres sont des ceddo dafa lèr dinagn kate leufeul ndayam
wolof yi aÿ na fekhe lange na sak joueur nga Guies kou def statut nan nuit ko niol dafa sokhr danguine begue yakh Goor bou kham ne defoul dara de kal kom nieupo dem len lô nek terite nagé kou waye dem len rk
sa la vidéo á été coupée c,est une manipulation Sénégal ben bopp la ken mounouko tall
Rien a étais coupé il nous a insulté et ont mieux que lui ma shallah moi je suis lébou et très fière
Moustapha Diakhate est plus pire que lui
Wolof c'est une langue Sénégalaise ..qui est wolof? C'est des Sénégalais...
Wolof c’est une langue un ethnie … les wolof physiquement sont différents des autres ethnies , ils sont plus grands
saa wofol sa liggéey rafet na yal na la saa Boroom taxawu.
Jërëjëf Sëriñ bi
Vous êtes tous pareil Vous les personne qui travaille sur les média mais dama len diii alerte koufii wakha lou niaw sii sama xette ma dokhann saa ndeye
🥵🥵
Vous rajoutez des choses alors que ce n’est pas important. Il faut juste condamner la personne
may gnou sunu diame deh wolof yi gno fi dakh xébaté yeun xébaté rék nguén xamm ahhh guis nguén ni nexoul wolof amoul ben lakh katt bou mou xéboul dou joola dou sossé dou peul dou sererr kon guis nguén ni nexoul 😂😂
sa wolof tu la ferme
arrête de mentir
chérif dousa moromou baye
J'aimerai savoir si le wolof est une ethnie oubien une langue nationale. A ce que je sache et apris a l'école si j'ai pas oublié, le wolof est une langue nationale pas une ethnie donc sérères; toucouleur; lebous; peuls; manjaques; mancagnes; diolas; kognadji; bassaris..... donc tous sont des wolofs et quand il dit que les wolofs sont a 44 pour cent je reste perplexe et c'est pas ça qu'on appris car les sérères sont les plus nombreux suivi des peuls, diolas si je me trompe pas..... Pour moi le problème a été pourri depuis qu'on a laissé certaines personnes dire a d'autres qu'ils sont rebelles, qu'il ne mérite pas de diriger une mairie, qu'on vas prendre les coupes coupes, qu'on insulte les chefs religieux... Ceci dit si c'est avéré c'est a condamné
Yaw katale sa ndaye domou bireul bi
Les Wolofs sont les niambour niambour les walo walo les baol baol et les lèbous ils reprèsentent plus de 45 pour cent de la population Sènègalaise
Lui il a donné sa source Agence Nationale de la Statistique (ANSD), le wolof est une ethnie comme les séreres, djola, ma dingue, avant d'être une langue.
Va faire des recherches avant d'écrire pour ne rien dire.
Pire encore si le Wolof n'existe pas comme ethnie donc il a insulté toutes les personnes qui parlent Wolof la langue lui en premier et peut-être ces parents. Soit vous acceptez que le Wolof existe comme ethnie et vous respectez les wolofs si vous ne considèrez pas le Wolof comme ethnie c'est votre droit de toute façon personne ne va vous obliger à changer votre avis mais arrêtez de faire allusions à cette groupe de personne et de proliférer des insultes surtout nous savons tous que quand vous parlez de Wolof vous faites pas allusions aux personnes qui parlent Wolof. Le débat a savoir si le Wolof est une langue ou une ethnie n'est pas à jour actuellement on en entrain de condamner les propos d'un narcissique fou raciste qui se prend pour un savant ou Serigne. Góor Yàlla Dou lou gneuw yeungal la nanale Téré yeupe so amoul dale, yar, teguine, do tousse meuno diarigne Kéne Si yàlla santale noula nékh.
C'est notre langue nationale moi qui vous parle je suis meure.Ce monsieur Aïdara a tort