Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yonnent bi (SAWS) akiy sahaabaam (RAA).
@sounnahsenegaltv bien-sûr que c'est un Hadith. Mais le hadith n'a jamais parlé de descente. Et vous n'entendrez jamais un soufi sérieux parlé de descente... "Et ne poursuis pas ce dont tu n' as aucune connaissance. L' ouïe, la vue et le cœur: sur tout cela, en vérité, on sera interrogé. (Coran, 17 :36).
Machalah dieuredieufe oustaz mor kebe leral yi amna solo yalla na la yalla faye
Masha’allah wakh dji lère na nagne Hafizahoullah
Amine
Lerrna si borom khel yis machâllah
Machallah oustaz❤
Machallah oustaz
Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yonnent bi (SAWS) akiy sahaabaam (RAA).
Machallah ya oustaz
Nanu YÀLLA sàmm sàmmal nu, aar aaral nu, taxawu taxawul nu, mùccël mùccëlël nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xam xam yi ragal sunu BOROOM YÀLLA.
@@assaneniang2133 amiine
Wallahi liigaayi wakh dou degga
Tek fi dara cone bu ko defé niou xaam deug😂
Nanu YÀLLA defal nu dëkkag gnoom ca Firdaws. Wan nu dëgg bamu leer MU yòmbalal nu tòpp ko, wan nu neen bamu leer MU yòmbalal nu dùmmóoyu ko.
Allah tey moom amnaa louma metti ndax more kebe wakna loudoul degg
Yalla dafay wathi Kay 😂😂😂😂. Sheuteute....
@@jajah0 limouy wakh. Ni hadith la
@sounnahsenegaltv bien-sûr que c'est un Hadith. Mais le hadith n'a jamais parlé de descente. Et vous n'entendrez jamais un soufi sérieux parlé de descente...
"Et ne poursuis pas ce dont tu n' as aucune connaissance. L' ouïe, la vue et le cœur: sur tout cela, en vérité, on sera interrogé. (Coran, 17 :36).
@ le sérieux et le soufisme sont en corrélation négative malheureusement
@@sounnahsenegaltv Fi ngaye moudié? Fogona dang may indil argument sakh. Wala amo? 😄
Ndeysaan moom ndeysaan ndey toontu boppaam
Ndeysann brom xam xam nga dh wayé lingayy waxni xamo si dara wax deug yalla 😂😂😂😂
Non mor kebe mahjoub Allah
Lane moo khew ?
Li ngay wakh khamo ci Dara. Lecture bou bari meuniula yobou fofou...
Dara compliqué woufi. D'où sa niveau rek
Sawaye wakhoufi dara mas alabi gua atté comprendro ko
😂😂😂yow ak sa serigne kay layal dieul cour gratuit
Li dé dou lérr loudoul si borom khel you séll yi té lérr