Attention🚨à Mbacké Sakho Coraniste - Dinné Bopam - Wéddi yonent bi Saw - Oustaz Omar Sall précise

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 24 янв 2025

Комментарии • 56

  • @aladjidiaoune2421
    @aladjidiaoune2421 15 дней назад +3

    Mbacké Sakho da sankou depuis bamouy wotèwo yonénete bobu doxoul lègui mou essayer bi boyi rère yi top ko ndeysane

  • @ltyu8813
    @ltyu8813 9 дней назад

    Diangi len ngen bagn
    Aytia rek
    Merci oustaz lerr na nagne

  • @AssaneMbaye-o8y
    @AssaneMbaye-o8y 10 дней назад +1

    Chiekh mbacke sakho monfi nègue❤

  • @IbrahimaNDIAYE-v5d
    @IbrahimaNDIAYE-v5d 15 дней назад +4

    Vous êtes le seul oustas qui a démenti CMS et vous m'avez remis sur les rails.

  • @fatou-y7w
    @fatou-y7w 15 дней назад +2

    Dieureudief ya ouztaz au moins quelqu'un pour poser les questions qu il faut

  • @aboubacardoucoure4661
    @aboubacardoucoure4661 14 дней назад

    Qu'ALLAH TAALA nous guide dans le droit chemin et nous facilite
    Allahumma Amiine
    Allahumma Amiine

  • @aladjidiaoune2421
    @aladjidiaoune2421 15 дней назад +2

    Sénégal loufi wayy wotèwo am gnuko top

  • @MouhammadNgom-g4v
    @MouhammadNgom-g4v 13 дней назад

    Machaalah ❤❤❤❤❤❤❤

  • @hoorevision5753
    @hoorevision5753 13 дней назад

    Oustaz bayil fénn fii Mbackè sakho mofi née.yénn ay yeféer nguén folen tollou di wedi yalla nane alxur Ann matoul leroul

  • @MoussaPouye-u6i
    @MoussaPouye-u6i 15 дней назад

    Mbaké Sakho limouy nakhê gaayiko topp moy gnînane yonénete bi daye léeral alkour'ane dégno wéddi y'Allah, ndakh y'Allah lou léer la diokh yonénete bi ba paré gnome gnouné yonénete bi daye léeral, wa mane Limay lathié moy ndakh lou léeroul dagneko meuna leéral, tontou bi moy déedétte, ndakh kéep ko guis mouy léeral dara lamouy léeral dafa fék mou léer si mom, wa illa douko meuna léeral, yéwou léen yéne gni toop mbaké Sakho

  • @papaamadouname9315
    @papaamadouname9315 15 дней назад +1

    Mane dama diakhlé, Yalla wakh diaraléko thi Yonén bi, niouni lolou doyoul té léroul.
    Likoy complété nénaniou moy li ay nitt wakh ni Yonénebi moko wakh. Té lima diakhal, wakh yoyou yeup dafa am youniouy validé ak youniouy nénal.
    C'est grave !!!

    • @aladjidiaoune2421
      @aladjidiaoune2421 15 дней назад +2

      Yèna diangoul motakh ngène nèkha keuf wayyé Mbacké Sakho darra la xamoul èlement cheytané la mom ak gniko guem yeup

    • @aladjidiaoune2421
      @aladjidiaoune2421 15 дней назад

      Lislam 7em siècle la lèrr wayyè dou tay si yène gni xamoul darra mom yalla naléne yalla guindi

  • @cheikhdiop9673
    @cheikhdiop9673 14 дней назад +1

    gor di sakho yobouna sene fouri fara yi dé ndax dafa nara keup séne yall wane dé yéne ak mbacké sakho kif kif kén lasi yalla nioroul séne bopp rék ak di dadialé mbolo mbacké Sakho sakh moléne tané yén mome khamnaléne bou bakh Sénégal gui yép la yémalé topouma kéne kéne momoul yalla banane nitt gni topoulénma ma yobouléne ci yalla

  • @zakymane3016
    @zakymane3016 14 дней назад

    Television bou melni DTV moo wara organise benn face à face digunte Oustaz Oumar Sall mii ak Cheikh Mbacké Sakho nguir gni reer guindikou.Liggueey bou reuy lay doon nguir Islam.

  • @AssaneDiop-w5m
    @AssaneDiop-w5m 16 дней назад +1

    Yonéte yalla mouhamed saws lagnouy toppou

  • @alasancham7483
    @alasancham7483 16 дней назад +1

    Yaw mi ya ne djuien dafa medde, Subhanallah 😂

  • @assanendiaye1276
    @assanendiaye1276 12 дней назад

    Le savoure rend fous

  • @hoorevision5753
    @hoorevision5753 13 дней назад

    Bane sunna bou akhlou sunna wala bou shian yi.paré nguen si tarikha yi legi Mbackè sakho molen terée nelaw

  • @checkfall2292
    @checkfall2292 16 дней назад +2

    Vous n avez pas écouté entièrement la vidéo de Cams il n a pas dit deux prières

    • @moustaphakane1979
      @moustaphakane1979 15 дней назад

      Gnii fenn rekk lagnouy deff

    • @JeanchristDiallo
      @JeanchristDiallo 13 дней назад

      Yaw doomeram nga mbaame bi sunna rekk tchi kaw tchi kanam faut quitter labas

    • @moustaphakane1979
      @moustaphakane1979 13 дней назад

      @JeanchristDiallo kone yaw yonentebi ngay roy nii? Soubhaanallah!

    • @JeanchristDiallo
      @JeanchristDiallo 13 дней назад

      @@moustaphakane1979 instant bi dammay toppou senn logique mbaamou kharram khoûkh yi

  • @AhmadAhmad-qi8us
    @AhmadAhmad-qi8us 14 дней назад

    GENROU mbiké sako YI BOY DEFE MONTAGE VIDEO DA GUAY DEFF FOTOM VI SOUF BA NOPI DEUP KO.

  • @aladjidiaoune2421
    @aladjidiaoune2421 15 дней назад

    Tè yène boyyiko top moulène di reral dèmlène xol yènéne coraniste yi nugnuy dioulè ak wakhtou yi gnata ngène wakh ma kane mo wakh deugu si gnom

  • @mamecoumbaseck4580
    @mamecoumbaseck4580 16 дней назад

    Alquran dji sakh si yonénta bi lagne ko wathié, yonénta bu dou wakh dara si thiobré bopam

  • @Fallmuslim
    @Fallmuslim 16 дней назад +1

    Debat. Debat omar sall et cheikh mbacke sakho thioly diarouko debat a rdv l'équipe thioli djekh

    • @abousow5021
      @abousow5021 15 дней назад

      @@Fallmuslim il ne le fera jamais pour dem diakarlo bou deesé si lolou dolen guiss tok si ganaw écran rek lanou meune..
      Kant à yefer bi mbacke sakho dîna yak si dinedji lou ibliss doul yakk

    • @OusmaneDg-xt7ns
      @OusmaneDg-xt7ns 15 дней назад

      Mountakha dou debat 😂😂😂alif lam ho

  • @momardiallo1609
    @momardiallo1609 16 дней назад

    Sounnit yi rek nioy leral diiné dji ❤❤❤❤❤❤.
    Ani sén soit disant kilifeu diné yi 😂😂😂😂😂😂😂

    • @boubacarsagna3289
      @boubacarsagna3289 15 дней назад

      😂😂😂

    • @abousow5021
      @abousow5021 15 дней назад

      NAFEKH BAKHOUL

    • @abousow5021
      @abousow5021 15 дней назад

      VOUS ETE EN RETARD KHOUR ANIYOU BANI COMMENCE SEN MISSION BA LEGUI SAFAIT LONGTEN YENINGUI SO GA DIOUKK NGAY DIAYE NAFEKH YENE LOUDOUL GAROUWALE MENOULEN KO AK MEUNE FENNA

    • @momardiallo1609
      @momardiallo1609 15 дней назад

      @abousow5021 wakh dji boula métté fingua diokou sa soit disant wassila na guénn def intervention boudé amna xam xamou charia ...
      Alhouran ak souna point tout le reste à la poubelle ❤❤❤❤❤

    • @abousow5021
      @abousow5021 15 дней назад

      @@momardiallo1609 diohma sa numero

  • @freemind3009
    @freemind3009 15 дней назад +1

    Sounnites yi bayilene fenn

    • @aladjidiaoune2421
      @aladjidiaoune2421 15 дней назад +1

      Wakhal loula nèkh mais deugu mom dinako wakh

    • @AhmadAhmad-qi8us
      @AhmadAhmad-qi8us 14 дней назад +1

      SAGA AMOUL SOLO NA NIOU WAKH DEUGUE GUI REK. mbické sako KHAMOUL DEUREUM DEUREUM BILAHI.
      XAM-XAM BOU ANDE AK LERR YALLAH MOKOY DIOKHÉ.

    • @freemind3009
      @freemind3009 14 дней назад

      @@AhmadAhmad-qi8us damani nguene bayi soss. Mbacke Sakho certes danguene ko contre mais amoul si yene kenn kouka gueuneu maokkal ak kham alquran. J'ai remarque que vos conferentieux et debateurs mentent sur sa personne. Vous dites qu'il n'aime pas le prophete, mais lui il dit que la parole du prophete etait le coran et pas autre chose. Mais vous vous continuez a insister dans la betise. On ne peut pas croire au coran et destester le prophete Muhammad. Dites ala verite aux gens et arretez la diabolisation. Vos cheikhs comme alpha BA mentent gravement sur son discours.

    • @aladjidiaoune2421
      @aladjidiaoune2421 14 дней назад

      @@freemind3009 ndeysane Mbacké Sakho alquran bu diube sakh meunouko diang nganane kène gueunuko mokal alquran ragulal yalla

    • @AhmadAhmad-qi8us
      @AhmadAhmad-qi8us 14 дней назад

      @freemind3009 DIALHIL KABIR

  • @galasfall7419
    @galasfall7419 15 дней назад +1

    Cheikh mbacke Sakho dall Manou len si mom Dara ba legui andiwulen louko wedi

    • @aladjidiaoune2421
      @aladjidiaoune2421 15 дней назад +1

      Mbacké Sakho dinalène sank rek ndeysane

    • @MoussaPouye-u6i
      @MoussaPouye-u6i 15 дней назад

      Yow ya beugoul guis deug rek wayé mbaké Sakho djiaroul sakh nguaye déglou kénéne pour wédiko mom si boppam so bayyé khél ay wakam boula y'Allah défalé tawfékh dinga khamné mbaké Sakho daye thiakhane késsé

  • @aladjidiaoune2421
    @aladjidiaoune2421 15 дней назад

    Loumassi mètti moy boyyi ko top dinalène dougueul si nane sangara ak touh yamba ak deglou music fo ak thiakhane parsk nèna haramoul ndeysane

    • @iboudue2727
      @iboudue2727 15 дней назад

      Fi kene touhou fi ni nane mais yi ni kouko def vous dites safara la dieum.
      Indil ayat bou Yallah wakh né dafa haram rek niou geum la
      legui loutax doléne diapo ni Yallah wakh ci coran bi sourate 5 verset 6??

  • @kaolackvamal2881
    @kaolackvamal2881 15 дней назад +1

    Toi tu fait dans la manipulation. Bayil fén ak soss

    • @OusmaneDg-xt7ns
      @OusmaneDg-xt7ns 15 дней назад +2

      Dadial bou bonne moy mbacke sankou ak gni and ak mom

  • @hoorevision5753
    @hoorevision5753 13 дней назад

    Oustaz bayil fénn fii Mbackè sakho mofi née.yénn ay yeféer nguén folen tollou di wedi yalla nane alxur Ann matoul leroul