Merci serigne bass patriote yép diégualonanioula léep louniou méréwone wala niou togne lako ndakh beugue sonko. Je vous présente nos excuses au nom de tous et merci pour votre grandeur serigne bass. Maachalla ziar ziar car nak gueum nanii danioula moussa beugue. Yalla na yalla diapalé lén le tandem DiomaySonko. Barké Borom Touba. Amine
C'est le même sentiment que j'ai. Et je me rends compte qu'il savait tout et s'il pouvait prendre position, il l'aurait fait quand SONKO subissait de l'injustice mais sa position et son titre lui empêchaient de le faire. On sent de la franchise et de l'aisance dans son discours aussi. Alhamdoulilah, Yalna diameu yagueu si rewmi. Beneu nafekh bagn ko diakhassé
C'est qui me plaît le plus c est que Serigne Bass Khadre a été promu à ce poste très jeune, un talent entretenu et encadré, son discours est à la fois convivial, serein, inclusif, pédagogique et riche d enseignements !
MachAllah kaddou yi raffetna, Sonko yalla na sunu Borom sammalla bopam, sa yeennee si Sénégal yalla bou yakar tass mouk en pensant à nos jeunes et braves sénégalais😭 qui ont perdu la vie en battant dignement pour leur pays
Ousmane Sonko amna bene domou serigne mourtada bou djigene bo khameni sonko rek la bege limou dadji si khekhbi té kene khamou ko kou sell sakh wayé begoul kouko khame diooy nana batayyi ngir sonko bafimay wakh ak yaw ay dok lay def ngir sonko ak diomay am ngam si rewmi moatakh amngene lou diafé ay nit niou selle niolene bege
Ay way yalla si barkei Psl samal gnou sa jaam bi, sunu wadji,sunu sopé bi, di santate yalla bou baaax bimou niou dimalé baniou sope seydina Pros ❤ Ousmane nourayni Al Moubarak milé❤❤❤😭😭😢waurna yalla kouma begua metital ci SONKO lakoy diaré😢❤
Machalla amatina solo bravo périmer ministre ousmame sonko yalnanga gana yokkou bou bakh barkep yonentabi s a Wasalam amine barkep xassidayi yeppou Amine ❤❤❤
Sonko bimou santé yalla dafa yageu dignité moy sonko la vérité rien que la vérité bamou meté ba bimi nex nex pas encore parce que combat bi mingi doram commencé faté kathio fi il faut que mou fateliko sounou guinaw ndax lifi weso dafa meti salam
La yalla Guindé wone Diam Gni thi yonent yalla youdoufe tay nioune wa Sénégal lako yalla defal thi seydina Ousmane mi mashalah may toucouleur bila ndieke tope depuis 2014 ma sétane sa Béne vidéo lala tope ba tay mashalah
Merci serigne bass patriote yép diégualonanioula léep louniou méréwone wala niou togne lako ndakh beugue sonko.
Je vous présente nos excuses au nom de tous et merci pour votre grandeur serigne bass.
Maachalla ziar ziar car nak gueum nanii danioula moussa beugue.
Yalla na yalla diapalé lén le tandem DiomaySonko.
Barké Borom Touba.
Amine
Amiine kaddou yi rafet na MachAllah
C'est le même sentiment que j'ai. Et je me rends compte qu'il savait tout et s'il pouvait prendre position, il l'aurait fait quand SONKO subissait de l'injustice mais sa position et son titre lui empêchaient de le faire. On sent de la franchise et de l'aisance dans son discours aussi. Alhamdoulilah, Yalna diameu yagueu si rewmi. Beneu nafekh bagn ko diakhassé
@PndlepatrioteJeey BIEN DIT ❤❤
Le témoignage sur Pros est émouvant, merci Cheikh Thioro ,et Compagnies ,les Patriotes sont fiers de vous Bon Magal à tous !!!
❤❤❤❤❤❤
Un discours de conciliation et vérité absolue. Dieuredieuf Serigne Touba.
Kou khamoul yallha si sonko si histoire sonko dotoko kham moukou yallha rek momane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤vive sonko
Wakhatiko dé. Yalla woné na lou réy si mbiroum SONKO
Louwér ngawaxe
Lâ Yalla djox xarite bâ siye marhama té mounou kô jeuf nattou lakoye xayema 🙏 C.M.K. Ndeyssane sunu wadji jambar leuh wlhy🙏
Deug la
Yeen gaccé mo leen wara ray ndax cheikh Bassirou mii dé da baax rék waayé lu né wax ngeen koko
Lii mooy li tassawuf di jangalé , jërëjëf cheikh Bassirou Mbacké ❤❤❤❤
Jeureuf Serigne bi si li gua sédé sunu wadji sonko❤ sunu sopé bi xarite sama référence yalna yallah fayla❤amine🎉
Serigne Bass kadeyi réfétene machalah yalla gafi yague té werr😢😢❤
Boy basse key bane serigne 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 bokkone na gni saboté projet bi 😮 mais yalla dou nitt toi ta rien guellé 🤫🤫🤫🤫🤫
@@mouhamedcisse2566yèn tamit il faut oublier les apparences. Kèn khamoul ndakh meusna wètt ak boromam nianal Sonko wala gni nékone ci diaffé diaffé.
@@joyfulness80 y’a rien a oublié ici frero deug dagnou key wakh c tt
Bou kene merrrr. On Love pm sonko yok yag weer cii barke Serigne Touba
Alhamdou lilah Rabbil 'Alamine Na si Nieup Diapp niou défal Réwmi❤ Dieureudieuf mbacké🙏
Ohh le témoignage est émouvant machala 🙏🏽🙏🏽🙏🏽❤️❤️❤ Serigne bi sax dafa am thiofel si OS
Li da sedeu xol bilay heure bi daw metiwone na.wayè nak yallah attè na.vive Sonko Diomaye
Segne Bass Abdou khadre Dieuredieuf séde yi refetna digeul yi refet na❤️❤️😭😭😭😭
Machahala.serign.bi.kadouyi.raféna.té.am.solo.yala.na.diamou.sakh.thi.réwmi.ak.liko.weur.gouvéna.mabi.yala.naniou.réwisir.ak.ndamthi.barké.yontibi.🤲♥️👍🙏
Ohhh sama khôl seddne❤❤
C'est qui me plaît le plus c est que Serigne Bass Khadre a été promu à ce poste très jeune, un talent entretenu et encadré, son discours est à la fois convivial, serein, inclusif, pédagogique et riche d enseignements !
machallah
Il est très serein.
Waknga lep ❤❤
True
Je suis parfaitement dakor ❤❤❤❤❤Masha Allah
Vraiment niit lo kham cii nitt wakh ko merci pour les témoignages. Franchement Basse est honnête dans c’est paroles ❤❤❤
MachAllah kaddou yi raffetna, Sonko yalla na sunu Borom sammalla bopam, sa yeennee si Sénégal yalla bou yakar tass mouk en pensant à nos jeunes et braves sénégalais😭 qui ont perdu la vie en battant dignement pour leur pays
Serigne Bassirou Mbacké quel homme❤❤❤
Respectez vraiment cet homme
Cheikh bara ndiaye ❤❤❤
Cheikh thioro ❤❤❤❤
Ousmane Sonko amna bene domou serigne mourtada bou djigene bo khameni sonko rek la bege limou dadji si khekhbi té kene khamou ko kou sell sakh wayé begoul kouko khame diooy nana batayyi ngir sonko bafimay wakh ak yaw ay dok lay def ngir sonko ak diomay am ngam si rewmi moatakh amngene lou diafé ay nit niou selle niolene bege
Kou ka bagne gratuitement moye touko
Nouko nit di bagné la khamoul
Machalla
Machalla sama ranguoñe ya gui tourou
Machalah, jereudieuf MBACKE il vaut mieux tard que jamais..GONTOUGUA..TAWFEKH
Un discour très courageux du porte parole ❤❤❤❤
Macha alla bek nano lol dh thi kaddo yi Amna solo lol yalla na Yalla doli diam thi Sénégal 🇸🇳 ak kheweul ak diobou ak bageunte nguir yalla
Machalla mbacké kilifa koufi yalla ték rék lay andal
Yatakh mabayiko xél ki thimmm
@@gnagnadiatta2169kan nonou 🤔
@@Cheikhna-df mbaye pékh
Deugla serigne bass❤Sénégal war nagnou tëy si sonko
Le premier ministre Ousmane Sonko est le meilleur premier ministre du Sénégal de tous les temps ❤❤❤
Dieureudif Serigne bassirou Mbacké Abdou khadre yageu fi lool te weer amine si barckp khadimou rassoul ❤🙏🏻
Amine barkebe borom keur Niang
Amine ya rabi
Dieureudieuf serigne bassirou abdou khadr wayé wa apr faw niou guéné xalissou réwmi s'est obligatoire diadieuf serigne bassirou abdou khadr patriotes yii contane naniou si yaw ❤yallah na sonko ak djomay réussir bougnou réussiré Sénégal réussir
Meileur magal moy magall 2024 🎉❤
Allaahu akbar
Kholou mourid yi foume dieum fala kholou talibé yi dieum😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Seydina Ousmane mou sell mi ❤ sakh si deugg rek doylo yalla inchalla lepp dalay wouyou si si katanou borom bi dieureudieufé borom touba
KOU SELL DOU SALIT. KOU NEK TCHI DEGUE DO SALIT. YALLA DEYNAKO LOU KEN DEGOUL MOTAKH DOU SALIT MACHALLA LAKHAWLA WALA KHOUWATA ILAH BILAH. KEN FATEWOUL DARA❤❤❤❤❤❤MACHALLA
Bilay békna cissa commentaires ❤❤❤, sm wadji kouko waxal Lou bax dgua bax,kouko waxal Lou bax ma begu leu❤❤❤
Yén sen datay ndaye yénak sonko 😮huuuuuuuuuuuuuuuu
yow ko alkounga domou khathie@@sene6344
Kharoul !@@sene6344
Seen leufeul ndaye yeen akh sonko gnouy serigne touba rk mognou gnor na took keureum sou meunei
Cheikh bass un grand savant et très pertinent manchalah merci p.m.sonko, merci président diomaye
Bilahi mbacke ya bakh mbacke ya bakh mbacke ya bakh fa nityi fogé won wayé dano khamoul rk dieuradieuf borom touba
Serigne Bassirou Mbacké mom Serigne Abdou khadre Mbacké yalla nafi yag téwér si barké Serigne Touba
Kaddu yi rafet na Mbacké❤❤❤
Seydina Ousmane Sonko mou selmi yalla nala yalla samou ❤❤❤❤ nioun dh yaw rek laniy topou ❤❤❤
Vous êtes une source d'inspiration pour nous tous. Merci pour tout ce que vous faites
Sama khôl bi seddna ❤❤❤❤❤❤
Wallahi président sonko ya bakh nekha beug ❤❤❤❤❤❤
Seydina Ousmane Sonko mou sell point❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ma challah ousmane sonko yala nala yala samm
Dieureudieuf serigne mountakha dafa yaga yeiné sonko yor Sénégal Dieureudieuf Mbacké balla yallah nala yallah defal goudou fane ak wer allahouma amine 🤲❤️
Discours historique. Mach'Allah kaddu gui raffett na
Li moye VALEUROU SENEGALAIS (RESPECT❤ COURAGE❤ SAGESSE❤
IT'S TIMEE TO WORK FOR SENEGAL ❤❤❤❤❤❤❤
ماشاء الله حفظه الله ورعاه وأطال بقاءه فينا آمين يارب العالمين ❤❤❤
Merci merci merci fils sonko d avoir tenu avec dignité en pensant à souhana lehoiu pour faire du bien❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Kou boon rk moy bagn sonko😭
Sonko thiagua doméram la
𝗦𝗮 𝗽𝗮𝗽𝗮 𝗺𝗼𝘆 𝘁𝗵𝗶𝗮𝗴𝗮 𝗯𝗼𝘂 𝗺𝗮𝗸𝗸 𝗯𝗶 @@kingw4380
@@kingw4380 Sa baye Moy thiaga Moy doméram sa thiotou deye
@@kingw4380lo wakh fi di ngako wakhat feulé
@@kingw4380sa baay gorjiguen leu motakh mou diour domeram bou melni yow
Machalla wakhdji rèfètna ❤❤❤
Sonko si hol machahalah
Serigne Bassirou Mbacké Habdu Xàdir
yalna yalla yàggelkufi
❤❤❤❤❤Machallah yalna jamou sakh cheikh Mountakha bachir yalna fi yagu té weur🤲🤲
Ay way yalla si barkei Psl samal gnou sa jaam bi, sunu wadji,sunu sopé bi, di santate yalla bou baaax bimou niou dimalé baniou sope seydina Pros ❤ Ousmane nourayni Al Moubarak milé❤❤❤😭😭😢waurna yalla kouma begua metital ci SONKO lakoy diaré😢❤
Alhamdou lilah sama xel demna ci sunu magal 2023
Bi Moussa khadj di wakh amna niou beugeu yakhe magal gui
Machalla amatina solo bravo périmer ministre ousmame sonko yalnanga gana yokkou bou bakh barkep yonentabi s a Wasalam amine barkep xassidayi yeppou Amine ❤❤❤
Machalla amatina solo dieure dieuf Mbackè serigne Bassirou Mbackè yalnanga fii yague thé andack weure barkep xassidayi yeppou Amine ❤❤❤
❤❤machlla amna solo loll yalla nayalla motali lép❤❤
S B A K a la hauteur des espoirs Sénégalais .. bel esprit et bon discours .. Élégance et Sagesse
Alhamdoulilah Jëuredieuf serigne Bassirou Abdou khadre kadou ji rafét na machallah ❤❤❤❤❤
Walahi azim nék ci deug rek mo waur
Merci Mbacké Dieure dieuf ❤❤sonko merci 🙏🏾 pour la confiance
Meilleur discours de Serigne Bass Abdoul Khadre
Vive Sonko❤❤❤❤
Thiey adouna!! Aah Yalla bakhna alhamdoulilah ♥️
NOUS N'AVONS PAS LA MÉMOIRE COURTE MAIS DIEU EST GRAND LUI QUI DONNE À QUI IL VEUT CE QU'IL VEUT ... FOCUS
Serigne Cheikh Saliou nitou yalla deugue
Kou guiss mbaye pekhe si coinbi lalale jaime
🤣 🤣 🤣 🤣 Guisnako mou melni limon
@@momzly6818 konkorong la 😂😂😂
Mbaye pekh daa borokh lou 😂😂😂😂😂😂😂😂
Bouma déconcentré Way 😂😂😂😂
Aaamadou ba amadou ba aaaamadou ba …wakhlen macky wakhlen macky ! 😂
Machalla cadouyi rafetna kjole sede na
Xol sédna mbacké balla. Vive sonko vive diomaye vive le Sénégal
Macha Allha 😭😭😭♥️♥️🙏❤️vive persida seydina Sonko ♥️♥️
Dieuredieuf serign bass mbcake balla macha allah ❤❤
❤❤yalla nalla yalla samou ousman sonko❤❤
Mashallah xol yii sëdd neu dëff lou bakh akk deuggou mo am solo.
Djeureudjeuff Ousmane Sonko bing gnou guënë sii regime Macky Sall.
Yalla nala fayy si barkë Serigne Touba ❤️
Je l ai toujours adore sonko mais maintenant je l aime...
Diaradiafate Mbacke sama xol seda si yaw ❤❤❤
Merci beaucoup PM Ousmane sonko
Sonko bimou santé yalla dafa yageu dignité moy sonko la vérité rien que la vérité bamou meté ba bimi nex nex pas encore parce que combat bi mingi doram commencé faté kathio fi il faut que mou fateliko sounou guinaw ndax lifi weso dafa meti salam
Machallah yalla na yalla faye thi barke alkhouranoul Karim ❤❤❤❤sedna alhamdoulila
Lii mooy li tassawuf di jangalé , jërëjëf cheikh Bassirou
Alhamdoulilah 😢😢❤❤seydina ousmane sonko
Machalah yalla naléne yalla doléle défal lene diamou goudou fane wergui yaram s base diomaye sonko AK diépou
Dieureudieuf m backer bala yala nagafii yague tee werre
raffét na waay. Yallah na Yallah sakhal diam ci réw mi 🙏
dieye sama wadji naléne yalla defale diame ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mahchalah ❤️ yalna bou yakar tass amine 🤲🙏
Dieurediuefé Serigne bass Abdou khadre ,amlén yar s,bass dousén moromou ndeye
Cheikh bi tay nak discours na❤
Mashallah ❤❤❤ Mbacké
Président Ousmane Sonko notre sauveur Yalna YA Rabi défal la diam,same la ,are la
Sonko avie ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
La yalla Guindé wone Diam Gni thi yonent yalla youdoufe tay nioune wa Sénégal lako yalla defal thi seydina Ousmane mi mashalah may toucouleur bila ndieke tope depuis 2014 ma sétane sa Béne vidéo lala tope ba tay mashalah
Kaduu Serigne Bass yi rafèt lol MachaAllah!
Machallah Machallah Machallah ❤️ ❤️ ❤️
Raféte na lol mbacké ❤
Machalah
Un discours pleins d'enseignements❤
Jerejef Mbakké Bala❤
Un discour plein d'enseignement et de révélation ❤❤❤❤
Kou Guiss.S Bass Abdou Khadir taye mouy wakh taye khamné ngour sakhoul
Wiri wiri diarri ndari fi serigne bassirou Abdou khadar lafi seringe touba respect
😂 domou xadj louy wiri wiri diari ndari.Bass kay xana warna rouss té défaraat togayam.
Dieuredieuf Serigne Bassirou Mbacké thi kadou yi ❤❤❤❤
Macha Allah sonko moY sama Serigne maneà❤❤
Dieureudieufaty Serigne Touba
Dieureudieufaty Serigne Ahmadou Bamba
Sonko yalla ko badil kou ko nangoul woul bilahi dinga soneu fi si aduna