Bilaye je suis un fan de Modou Lo mais Mbeur bou nékeu warna ameu un Tapha Kandji à ses cotés. Il communique trés bien et bokeu neu si niou diayeu combat bi. Respect Tapha Kandji. Nio gui layeu khareu sur les live de Buzz walla Fadame pour Kanio leu touti nakheu khaweunanio titeul touti 😅.
Un entourages solide est un clé pour réussir mention spécial famille kandj vraiment boy niang esprit champion la yorr ms le reste c'est rapidité vivacité et la main gauche 👈🏿 ❤
Félicitations Modou t'as confirmé que t'es un grand champion. Du courage Boye Niang tu n'as pas démérité. Mais gnoune waa Lamb il faut que gnou khamni Lamb Sport de combat la té sport de combat djeul Coup Chaos ci la bokk, arrière ci la bokk, guénn saakou yi ci la bokk, daw khékh bi songg ci la bokk. Li lépp dou gaathia ci mbeur mi parce que lépp stratégie la té Lamb c'est l'intelligence en mouvement. Yékini était un grand champion té daawoul khékh rk djeumélé souba, khékh pour woute bountou la..
Barki alkhourane nimala yéné défaite bi Tapha kandji sakh mouno ko nateu c’est bien fait yakkar ni tu maîtrises tout doumeu dane combat dou serigne rek entraînement leu ak fiit

Ki rek mo takhone ma titt
Bilay nit guenouko ❤
Boy danou thiouné ngay done.
Il reviendra plus fort inchallah le thiapathioly, c’est un professionnel
Merci dieureudieuf diarama kadji yalla bakhna lithii kanam rawoul beutt inchallah
Wakh lén lou lén néxx niun ak boy niang 2 ba roi des arènes inchallahou ❤❤❤❤
Merci Tapha Kandji rafet na avant pendant et après ! ❤
Merci beaucoup tapha nobal nga ❤
Wa mais wa pikine après combat aay lunettes noir fumé lanouy laal 😂😂😂😂
Danio dioy dioyat
🤣🤣ya bone
Boy soff gua 😂😂
Do nittt iow 😂! Maneu je l'ai remarqué depuis contre Ama Baldé
Door yi molen jeulè kaw défaite bi betelennnn mo tax beu legui pour niom il fait nuit alors que le jour s’est levé depuis 😂😂😂😂😂😂
Du courage Tapha Kandji gental deugue nga mane kharagne lo moye sama mbeur wa brome bakh nga ❤
Machalah wakh jie rafét na🙏🙏
Merci tafa bon courage avec boy niang
Merci tapha amna solo di
Merci a vous Frere Kandji takat djadj yi rek nekat si
Un entourages solide est un clé pour réussir mention spécial famille kandj vraiment boy niang esprit champion la yorr ms le reste c'est rapidité vivacité et la main gauche 👈🏿 ❤
Moustapha sama kharitt bi du courage
Peulh vraiment sa question yi dess na professionnel
Du courage tapha kandji nite kou bakh nga machala
Félicitations Modou t'as confirmé que t'es un grand champion. Du courage Boye Niang tu n'as pas démérité. Mais gnoune waa Lamb il faut que gnou khamni Lamb Sport de combat la té sport de combat djeul Coup Chaos ci la bokk, arrière ci la bokk, guénn saakou yi ci la bokk, daw khékh bi songg ci la bokk. Li lépp dou gaathia ci mbeur mi parce que lépp stratégie la té Lamb c'est l'intelligence en mouvement. Yékini était un grand champion té daawoul khékh rk djeumélé souba, khékh pour woute bountou la..
1e janvier potou ndaala kou naane diokhe sa morome maaane kessè nak😅 courage bro tapha
Tapha sa watt yi toub ko 😂😂😂nane boy niang mo eup doolé
IL COMMUNIQUE TELLEMENT BIEN :PERDRE DANS LA DIGNITÉ 🤗
Machallah il cominique bien
Mês peull loutakh dou intérviwe Modou lo 🤔
Modou lo rék kasse modou lo ❤❤❤❤
Wa peul demal si lambalok way❤😂
ki kanla ya newon ya man ya eup dole
Franchement grand chapeau à toi sa communication bakh n’a trop ça montre que grand bou cool ngua ❤
😂😂😂😂😂Modou da dorr boy Niang bamouy gnibi Di dioyyy c'est du jamais vu
Tafa kamoulen modou sene mystique mo barri
Barki alkhourane nimala yéné défaite bi Tapha kandji sakh mouno ko nateu c’est bien fait yakkar ni tu maîtrises tout doumeu dane combat dou serigne rek entraînement leu ak fiit
Un sport de combat demande quand même un temps d'observation de son adversaire
Peul bou rafet tey mom gars yi nionguidal thiakaw sì commentaire yi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Tapha kandji damaco beugue
Dioy diekhna 😂😂😂😂
Dan Balla di niou beug nday ray té balla nekoul won si dara 😂
Père Balla Guaye 2 moy sama mbeur mais légui da diéhal,té mom loloulay bania deug
Tapha vrai sportif la ossi Nit kou bakhla vrm ❤
N'oublions pas que Tapha Kandji est chargé de la communication du staff de Boy NIANG 2..... Donc s'il s'exprime ainsi ça ne doit pas choquer les gens
Tchiey bougnou danone lol ! Kene dou degue
Tapha wadiou bakh la
President Abdoulaye sylla moy yoon bi
❤❤❤❤
Your questions were not that productive
Boye niange mudou lo dako douma danko na dieul reuge reuge lolou moye combat bi
Diadieuf kandji wakh dji rafetna
PIKINE LOOOOOOOOO😂😂😂
Lamine ki y’a waron wakh ak mom dh
Boy niang defeant la li bakhna si mom 😂
Tu cominik bien kandji, dicourage
Li nga wakh si auto bi c pas logic auto bi sou yakho nga woutatt benenn auto
Peul mi dou porofesoinel ki khamoul dara way
Peul tay mom tu as mal posé les questions au mois boco ladié nga bayi co mou développé
Père degauk dako xas tourne bayikofa dafa nday soof
Moustapha kandij dafa bakh
Journaliste bii kanla tu ne sais pas posé une question
Peulh ta maniére des poser des questions est à revoir!
Sois un peu plus professionnelle.
Interview di roubé c'est pas interessant.
Borom live 😂bi ak fadam di dull rék 😂
Boy mane fans modou Lo la mais respect way ki kou bakh la ❤❤
Diohal wadji respé avp,mousouma supporter Boye Niang 2 mais ki damako respé trop ndah mousouma deug mouy wah lou niaw ni lou bone
Mei tapha nn je ne suis pas d’accord avec toi un garen champagne com boye niang waroul am belem yoyou psk dagueni wara pare fepp ndakh lamp dfa guaraw
Démb mom dama contane escuve younékh lanou déff
Paul yaw ayo dé khamo touss soyez professionnel way sa question dra bakhouci
Yaw ya takh ma beug boye niang
Cette journaliste est très nulle