Monsieur, je suis choquée d entendre un mouride parler comme vous d un homme comme cheikh Oumar ? Ce n est pas à vous de dire à Sonko et Dioumaye quoi faire ! Je vous suis régulièrement mais aujourd'hui, je suis déçue par votre vision et état d'esprit.
Serigne saliou yaww est ce que lathié gua anna lèttre bi serigne cheikhouna bindeu ba ch o diagne tontou ko bamou warall guayy khass ch o diagne fann yii mom say sorti yii guay deff andouma akk yaww etat dafa amm noumouyy dokhé legui wann niou lettre bi cheikhouna bindeu
Dafén ba falou dianguoul day weur didoul . Omar Diagne bounou nékon thi réw mou normal do falou amo xam xam yarou wo Serigne touba diantoub diolor la kén manou ko neub
Cheikh Oumar Diagne mbaam mou bone té yees té khamadi kou bagne Serigne Touba la waayé doussi am ndam
Déngay fènn deh
Cheikh Omar Diagne est un homme intègre et il a parfaitement raison...
Lolu sa guiss guiss leu nangoul naniou la ko mais Omar diagne dommeram leu loussi kanam rawouli beut
@@AboulBacharSall Mane tamit nangoul nala seu guiss guiss,mais nèye rafet,saga yi diaroukou,au moins nagniou diokh worma sougniou wadiour yi...
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Monsieur, je suis choquée d entendre un mouride parler comme vous d un homme comme cheikh Oumar ? Ce n est pas à vous de dire à Sonko et Dioumaye quoi faire ! Je vous suis régulièrement mais aujourd'hui, je suis déçue par votre vision et état d'esprit.
Maachallah Deugue gou wér ga wakh
Cheikh Omar n'es qu'un homme véridique mais la vérité ne vous intéresse pas
Problème bi dou Moustapha Diakhaté mais Cheikh Omar Diagne…. Manipulation dafa barri Nafekh bakhoul.
Yaw da ngay politique rek
Tanim gnou ngui lay topou chaque fois wayé li mome cheikh Omar Diagne kén dakoroutie
Serigne saliou yaww est ce que lathié gua anna lèttre bi serigne cheikhouna bindeu ba ch o diagne tontou ko bamou warall guayy khass ch o diagne fann yii mom say sorti yii guay deff andouma akk yaww etat dafa amm noumouyy dokhé legui wann niou lettre bi cheikhouna bindeu
Saway yaw ak omar diagne séne leufeul ndeye
@@AboulBacharSall yaw kou mom sagaa yii
@@AboulBacharSall avec ça guénn dii beugeu wouyo akk talibé serigne touba akk touba ngipeu ko bokk khamall nakk limala wahh guisss gua nala geuneu geunn deukk touba geunn la nekk talibé mais doumala saga wayé genre you mélni yaww nio tahh yonou mouride nioulênn dii khass ndahh niakka yarr akk talibé commentaires loussi diarr saga
On n'aime pas ceux qui disent la vérité. C'est le maslaa qui nous retarde
Moustapha diakhate ak cheikh oumar Diagne ay noon lagnou.gnoo kham,nagnou rayanté
Bayil tihakhn
Waxnga deg deee dax sax lan ko wara def
Saliou noang bayilen.cheikh omar coalition mouride bi diokna nak waye niang manoko foli nopaloule😢😢
Bilahi wakh nga degeu
اعوذ بالله من الشيطان الرجيم Omar diagne saytané le
Yawo Nafekhe bou bon gha🤮ceikhe omar diange Defoull Dara 🤮Bayilen Nafekhe 😢senegaleyii yewou nanou de 🤮🤮
Dafén ba falou dianguoul day weur didoul . Omar Diagne bounou nékon thi réw mou normal do falou amo xam xam yarou wo Serigne touba diantoub diolor la kén manou ko neub
Yaw dall linga wakh mooy deug wadio diou diakhaté AK ngoor si diagne ya leen kham
Dieuredieuf niang