Tapha yagui wakhati dé ya takhawoune finé barké séringe Touba ama baldé Faye dane Modou lo té Modou lo khawna rayé ama baldé té nga nopi mou geune Thi yow
Ama vs Franc lamb le ! Que le meilleur gagne mais Franc ame ne doler mashallah mbappatt ne lutte simple wayer ndakh yeme ne Ama si sagne sagne be? Ama meune ne gagner dè wayer ne soraler Franc doler dokhoul diambeu ! Combat éclair le nara done inshallah sou gnari mbeur yi dadjer 10 secondes chutes ame inshallah ! Kouy dane lolay thiow bi!
Franc champion la 💪🏾
Per tafah nar diame si yaw ❤❤❤❤
Pikine pour nioun gayi dagn lenna ragal 😂😂
Pikine moy Sénégal 🇸🇳
😂😂😂😂
Franc borome pikine
Franc sera le vainqueur
Inchalla
Sergne ndiaye lolou mbapatte la
Ki bayiko mouye nane ataya ni
Pikine daniou ame problem mou fite
Pikine moy lamb ba la 16 incha alla
Tapha yagui wakhati dé ya takhawoune finé barké séringe Touba ama baldé Faye dane Modou lo té Modou lo khawna rayé ama baldé té nga nopi mou geune Thi yow
😂😂😂
Ama vs Franc lamb le ! Que le meilleur gagne mais Franc ame ne doler mashallah mbappatt ne lutte simple wayer ndakh yeme ne Ama si sagne sagne be? Ama meune ne gagner dè wayer ne soraler Franc doler dokhoul diambeu ! Combat éclair le nara done inshallah sou gnari mbeur yi dadjer 10 secondes chutes ame inshallah ! Kouy dane lolay thiow bi!
Yalla na yalla May ndam Ama Baldé
Inchalla
@papesouma ah mane dè faraloumassi keneu wayer ne boy Franc khame ni ame ne client "banfit guew"!