COMMENT ON S'EST RENCONTRÉS ( j'ai déjà eu 4 Femmes 🙈)

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 13 фев 2023
  • COMMENT ON S'EST RENCONTRÉS ( J’ai connu d'autre mec... mais pas comme lui 🙈)

Комментарии • 396

  • @seynaboundao7675
    @seynaboundao7675 Год назад +38

    Djiguéne boul yakamti ba dougou ci lo khamoul 🥹téyal tanal generation bi Dangay sakh ragal en plus seuy Sénégal dafa minti kone so dadié ak kila beugue yeureum la dinga tané
    Yalna yalla bolé niou ak goor bou gueune ci nioune ❤

  • @mamediarradieng9555
    @mamediarradieng9555 Год назад +151

    La fille est trop intelligente et trop mature Machallah à son âge ! Que DIEU vous garde ! 🙏

  • @ramatoulayesane5835
    @ramatoulayesane5835 Год назад +209

    Mention spéciale à la journaliste très posée ma sha Allah

  • @khadijasarr6810
    @khadijasarr6810 Год назад +56

    Khalia Sey si bopamm mo bahh machallahh dina seuy dh yayam rououkay leu❤

  • @kourouroff
    @kourouroff Год назад +37

    Wa khalia mi kuko yar 🥰
    Ils sont trop doux mashallah yalla na suñu borom sam lén aar lén taxawu lén ba ngén gnewat 2033 tokk ak ndiabot gui di déf itv inshallah

  • @Rawda333
    @Rawda333 Год назад +96

    Journaliste bi aussi elle est adorable 😂❤khalia et son mari même chose yalna yallah sameléne arelene

  • @sankounkanoute3067
    @sankounkanoute3067 Год назад +28

    Ah quel couple mature sincèrement j'adore ce couple et vous souhaite bonne chance et réussite dans vos projets familiaux.

  • @ndoumbista9131
    @ndoumbista9131 Год назад +203

    Mon couple préféré je vous aimes vraiment ❤️😘 Long vie à vous deux

  • @fatimataba4461
    @fatimataba4461 Год назад +96

    Et moi célibataire sans engagement je souris tel un guignol pendant 47mnt😂

  • @rokhayagueye4910
    @rokhayagueye4910 Год назад +50

    Machalat qu’allât vous protège et vous garde juska la mort mais mane je m demande khana amour da am niouko mom wala da fété borr ahh mane dé diakhlé na😅

  • @soidoumbaye56
    @soidoumbaye56 Год назад +25

    Wallahi aka bakh Sama goor ken dou Mom junior yalla nalen yalla lafal thiate

  • @aramediop9665
    @aramediop9665 Год назад +31

    Il sont mignon machalla mes keinn dou journalistes bi c'est question sont juste correct congrat

  • @dieynabandiaye4608
    @dieynabandiaye4608 Год назад +91

    Un couple jeune mature et très posées j'adore

  • @rouguitabarhama9860
    @rouguitabarhama9860 Год назад +15

    Machallah kimoy journaliste bou professionnelle mais di questionner ay questions you bêtes rek

  • @afissatoudiouf
    @afissatoudiouf Год назад +12

    Elle parle très bien même machalla en plus dafa djongué tek si ameu khel tes beug dieukeureme bilae beug na couple bi walahie 🥹❤️💍😻

  • @ndeyemariemediallo7397
    @ndeyemariemediallo7397 Год назад +96

    Elle s’est tellement communiqué ma sha allah yalla nalen yallah sameu❤️

  • @madeleine7159
    @madeleine7159 Год назад +72

    mashaAllah je ne vous connaissais pas du tout, mais vous avez l'air équilibrés et très sincères. Qu'Allah Swt vous protège et vous bénisse à jamais 🙏🏽🙏🏽❤️❤️❤️❤️

  • @adjabsaboudabakhmalick1242
    @adjabsaboudabakhmalick1242 Год назад +43

    Bilakhi amega sokhna macha allah! Je me vois en ell tellement😍😍😍 on a bcp de point en commun macha allah! Yalnaniou yallah maye gore bou niou comprendré ni 😅incha allah! Amine 🥰🥰🥰

  • @fama_diagne04
    @fama_diagne04 Год назад +18

    Quand on a parlé de « bonne » Sa réponse est tellement impressionnante. Genre elle n’a jamais vue une bonne donnée à manger à son père ohh maasha’allah 🥰🥰🥰 Ça se voit qu’elle a beaucoup appris chez sa mère qu’allâh vous préserve🥰

  • @sokhnandiaye5674
    @sokhnandiaye5674 Год назад +18

    Machallah yalla na yalla barkel lèn Machallah way j’ai les larmes au yeux

  • @sokhoulovedieng1365
    @sokhoulovedieng1365 Год назад +20

    Machallah way yalla nalene yalla lafal thiate si barker seydina mohamed

  • @aichaniang3418
    @aichaniang3418 Год назад +18

    Machallah yalla may lén ndiaboot bou barkel

  • @aichadiop4502
    @aichadiop4502 Год назад +22

    Bilay gorr bou fonké nii diabaram avancement rkk ngay ame inchallah Di nga raw Say mass d inchallah yalla nalene yalla sam mes amours 😍🥰👋🥰

    • @ndeyefatoumbaye3339
      @ndeyefatoumbaye3339 Год назад +1

      Lolou gualadje la si goor .djiguénne kouko térale yalla térale la inchallah

  • @fallnational246
    @fallnational246 Год назад +75

    Ayooooo sama couple bangui ni ❤
    Billahi dama léena beug té Yallah rk takh damay tok ak sama kharit yi sakh dilén waxtane nei
    Yallah na sén diammou yague té lafal léen thiatt
    J vs aime fort ❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @Aminata261
      @Aminata261 Год назад +1

      Svp wakhma nigniou toudou ci réseau yi svp

    • @rosechristinediatta4542
      @rosechristinediatta4542 Год назад +2

      @@Aminata261 la fille c’est #Princess_Rouge et le gars #Junior_Ba

    • @Aminata261
      @Aminata261 Год назад

      @@rosechristinediatta4542 ya bakh merci beaucoup ya niak kiniane wayé dama kawa rousse😂😭🤣🤣 ma setane ba doyal di la sogua wakh merci 🤣🤣🤣🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰

    • @user-ew3fd1ru5n
      @user-ew3fd1ru5n 8 месяцев назад

      Junior khalia sene compte tiktok

  • @ndeyeseynaboundndiaye6197
    @ndeyeseynaboundndiaye6197 Год назад +16

    Ndeysane yalla nalen yalla defal diam maylen jaaboot bu barkél inchalah yeurmander moy leep

  • @fatoufall5808
    @fatoufall5808 Год назад +17

    Ma sha allah yallah naléne yallah same 😍 dangéne meilleurs

  • @nadegee9749
    @nadegee9749 Год назад +42

    Ils font partie de l'un des couples sénégalais que j'adore yalla na len yalla doli diam soutoura sen love geuneu yokkk❤❤.Journaliste bi aussi machalla.Elle a été professionnelle tout à long de l'interview félicitation à elle aussi

  • @seydatou4111
    @seydatou4111 Год назад +66

    Machallah mes amours. Laf thiat. Yallah mousseul lén, aar lén, lakh lén fou yakha yégoul.

  • @timabaro165
    @timabaro165 Год назад +8

    Mashalah wakhbi rafetna diarna yone !!yalna nalene yallah moussal si lep lu safano!!

  • @rokhayapouye366
    @rokhayapouye366 Год назад +19

    Macha allah yalla naléne yalla sameu ❤️❤️❤️

  • @matymbengue8694
    @matymbengue8694 Год назад +15

    Machallah 🥰Machallah 🥰Franchement Parler elle s’exprime très bien Lafthiate Limà geuneu nékh ci wakh dji néna Sama Dieukeur Diankhà douko tégal Lék 😊Makoy Tadial ndokh sakh mako kay diokh😊Djongué dal tamounako cii djiguéne Diadieuf Way! Yalna léne Yallah Sam arléne🙏♥️🙏

  • @hawasadio3608
    @hawasadio3608 Год назад +33

    Yallah naléne yallah lafale thiate té mousseule thii nite yi boni tasse katou couples yi

  • @bbchou4848
    @bbchou4848 Год назад +63

    Machalla longt vie à vs té guene gnanal ma mane ak sama dieukeur yalla dioubolé gnou khawma bane guémine moye barkel begueneté nagnou mé dal dagno menoul dioubo lou yague

    • @bintouniang8698
      @bintouniang8698 Год назад +11

      Yal nala ya'Allah dioubolei ak sa borom keur si barkei Nabil Moustapha🤲🏽

    • @limatoulayeba4867
      @limatoulayeba4867 Год назад

      Yalla n’a yalla dioubolé léne

    • @aichasal4258
      @aichasal4258 Год назад

      Sama bouki bi moola matt

    • @aidabodiang3220
      @aidabodiang3220 Год назад +1

      Yalna yalla diapalé té dioubalélen amine

    • @evakane4802
      @evakane4802 Год назад +1

      Ndaye san yalla nalén yalla dioubolé barké serigne saliou dina bax diapal rk ma belle 😍🙏

  • @mariamakane7299
    @mariamakane7299 Год назад +63

    Machallah les Ba qu'allah vous protègent 🤲🤲❤❤

  • @matyndiaye466
    @matyndiaye466 Год назад +8

    Machalah je voyais vs vidéos sr tiktok je vs suivez pas mais en vous regardant vous m'avez donné envie suis tellement contente de vous yalla nalen brom bi lafal thiat

  • @reinemariedione2475
    @reinemariedione2475 Год назад +9

    Machalla j'adore tu es bien éduqué Mme 🥰🥰🥰

  • @courasarr1582
    @courasarr1582 Год назад +8

    Yallah na yallah deff diam rékk insha'Allah 🙏🙏

  • @tiiw7425
    @tiiw7425 Год назад +20

    En tout cas j'adore ta façon de communiquer t'es posé et mâture ça se voit manchalah laff thiate

  • @veroniquenatack7392
    @veroniquenatack7392 Год назад +12

    Machallah cette fille est adorable et jongué osi Yalla nala borom bi gueuneu bolé ak sa borom keur tè dara bagna dougou sen diguanté 🤩🤩éducation khalia bi amna solo 😍😘😘😍🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @sallaba5970
    @sallaba5970 Год назад +10

    Mane deh magui sourire rek wa eihh amour nekhna dh

  • @fatoufall5847
    @fatoufall5847 Год назад +14

    Oh machaala couple bii nice na yalna yalla mayma lii ak beep djiguéne.

  • @katyfall3610
    @katyfall3610 Год назад +10

    MachaAllah Jolie couple Yallah nalene Yallah lafthiet

  • @ndeyeamyfall34
    @ndeyeamyfall34 Год назад +6

    Aye waye yalla na Diam yague machllah sama copoul bi😍

  • @ndamesy5849
    @ndamesy5849 Год назад +30

    Lui je le connais on été dans une même class à Ensup afrik kou baaakh wallah

  • @ndiayemguette5106
    @ndiayemguette5106 Год назад +2

    Macha Allah yalle naleine yalla lafal thiate may leine DiAbote diou barkel

  • @manegaye
    @manegaye Год назад +16

    Machallah yalna sakhal ande bi

  • @binetadiop2255
    @binetadiop2255 Год назад +6

    Ndaysan yalla nalen yallah diapalei ❤

  • @nogayedieng5309
    @nogayedieng5309 Год назад +8

    Mashallah 🤩 ❤🫶Alhamdoulilah Yallah Nalenne Yallah doli Diame

  • @khadyndiaye1745
    @khadyndiaye1745 Год назад +14

    Allahuma barick my fav yalla guene maguetando Insha allah❤️💍🥺

  • @maremelaye6949
    @maremelaye6949 Год назад +2

    Machlla yalla nala yalla dèfale diam 🙏🏽🙏🏽❤

  • @Chaby02
    @Chaby02 Год назад +23

    Machallah laf thiate je les adore

  • @Perlerare3808
    @Perlerare3808 Год назад +2

    Macha allah 🥰yalna lén yallah lafal thiatt

  • @aminatasallandoye9052
    @aminatasallandoye9052 Год назад +8

    ❤❤❤❤❤❤mashala yalah nalen yalah lafallll thiatttt🙏🏻🙏🏻

  • @rouguietousy2292
    @rouguietousy2292 Год назад +14

    Que dieu vous protège 🥰yar ak kham adouna louko way dieundé diarnako je suis contente ❤

  • @ndeyeantaniang4078
    @ndeyeantaniang4078 Год назад +2

    Machallah yalla nagnou tassé ak kignou beug

  • @thiamalimatou9299
    @thiamalimatou9299 Год назад +4

    Ohh khalia beugue nako en plus elle est trop belle machalla yallnaleine yalla laffal thiate❤

  • @ndeyekhadyseye8119
    @ndeyekhadyseye8119 Год назад +14

    Machalla sama sangue seye malick laf thiat

  • @aminatatakonate6485
    @aminatatakonate6485 Год назад +2

    Machalla sokhnassi maleu beug pir yalnaleun yalla mouseul te sameu leun yalla mayleun ndiabot you barkel barké seydina Mohamed

  • @ndiayemandela5275
    @ndiayemandela5275 Год назад +16

    Maacha Allah wallahi je vois une vraie femme ba paré xam lane moy seuy..souway dalna nga si rescapées yi dé barki iowmal hiyaam...outeul yeinèn boum geuneuh takk kay...

  • @ndoumbeediop3651
    @ndoumbeediop3651 Год назад +6

    Machallah junior dafa bakh trop

  • @ndeyelo1151
    @ndeyelo1151 Год назад +14

    Long vie à vous machalah laf thiat ❤

  • @maguetteniang4469
    @maguetteniang4469 Год назад +26

    MachaAllah ✅ inspiring couple

  • @blackqueenlasagesse4037
    @blackqueenlasagesse4037 Год назад +48

    Masha'allah j'adore cet état d'esprit de la dame
    Mane aussi suis d'avis avec elle deh topatol sa Dieucoeur....🥰

  • @adjiaratou8741
    @adjiaratou8741 Год назад +10

    Mashâ’Allah un couple très mature qu’Allah swt vous unisse pour toujours 🤲🏾❤️

  • @mamediarra6068
    @mamediarra6068 Год назад +6

    Machalla sister laf thiate

  • @ndeyakarisma3445
    @ndeyakarisma3445 Год назад +2

    Machallah sama préféré 🥰yi ✌️😩nala yalla sambeu seuy bou barké ndjaboot bou barkei

  • @diorfall3732
    @diorfall3732 Год назад +2

    Mashallah yalla nguén am ndiabot you barkel

  • @afissatoudiouf
    @afissatoudiouf Год назад +4

    Khaliya djongué na dhé bilae damako beug yalla nalaine good défale diap❤🎉🎉❤❤❤❤

  • @diopmamediarra2820
    @diopmamediarra2820 Год назад +11

    Ils sont Jeunes mais très matures Macha’ALLAH qu’Allah vous protège

  • @diatoubiteye3397
    @diatoubiteye3397 Год назад +3

    Ayoo mon bro vrement je suis fière de toi yalla nalene yalla lafal thiaate

  • @maimounadiouf917
    @maimounadiouf917 Год назад +5

    Machallah 🙏félicitations inchallah

  • @princesse9863
    @princesse9863 7 месяцев назад +1

    Mashalah un couple exemplaire yalla n’a dioubolléne mayelene diébote bou barkel goudal fane yi mousalene ci lepp louye loré inchalah love sur vs

  • @salifsy3743
    @salifsy3743 Год назад

    Machallah sama xol sedd na ci yénn yallah nama borom bi may sokhna bou melni rafétt djikko am diné

  • @fatouniang9622
    @fatouniang9622 Год назад +15

    Machallah vous êtes adorable tous les deux ❤️❤️❤️❤️

  • @fbpw1
    @fbpw1 Год назад +3

    Je ne vous connais pas d mais téyeu guen yarou guen. Ça se. Oit que vous êtes bien éduqués machallah. Yalla nalen lafal thiat lamigne

  • @awacisse5008
    @awacisse5008 Год назад +2

    Machalla dama contenne si yenn yénay sama royouwayy machala laf thiate yalla naléne yalla moussall si thiate❤ ❤❤❤❤❤

  • @mariamadiallo4941
    @mariamadiallo4941 Год назад +2

    Non mais cette halia elle s'exprime tres bien maachalah yalla nalén yalla lafal thiat

  • @messaseye528
    @messaseye528 Год назад +25

    Qu ALLAH Soubhallah veille sur votre couple et vous protège🤲🏼 mes amours❤❤❤

  • @monavenir7378
    @monavenir7378 Год назад +14

    😭😭😭😭😭aý way gnanal lenma Yalla may guor boubakh bou melni

    • @samboumy6359
      @samboumy6359 Год назад +1

      Yalnala yalla May kouko geune ko beuge ta mou geune si yaw

  • @patriotepeulletv6808
    @patriotepeulletv6808 Год назад

    Machallah yallah nalén yallah defal diam 🥰

  • @mamygueye2517
    @mamygueye2517 Год назад +16

    Ki mane ak mom nio yam Macha Allah lane xalé dangay meun sa djeukeur ba dou nameu lenen
    De passage c’est une celibatouss ki parle 😂😂😂
    Wayer nak Beug nako ndax nimou mel Incha Allah ni la fass yener def💪

    • @jadamimi9557
      @jadamimi9557 Год назад +1

      Wooy🤣🤣🤣

    • @elmoctarsane6903
      @elmoctarsane6903 Год назад +1

      Ray guama quoi 😂😂 celiba est ce que douma dougual cv 😂

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Год назад

      Wouyyyy ak ligua wakh thi kaw yeupp😂😂😂😂😂😂no yébb gua gnou

  • @gnilaneniane743
    @gnilaneniane743 Год назад +4

    Meusouma Xam ni junior bou univers des montres la bilae 🥺montre you class meusnafa dieundé ❤❤❤

  • @lil_mermaid8296
    @lil_mermaid8296 Год назад +1

    C'est beau yallah nalen yallah sameu❤️

  • @blackqueen5833
    @blackqueen5833 Год назад +2

    Masha Allah yalla nalen yalla sameu

  • @aminasaliou248
    @aminasaliou248 Год назад +2

    Yalla nalen Yalla defal kheweul sama préféré yih ❤️❤️❤️

  • @ramambaye1831
    @ramambaye1831 Год назад +2

    Yalnalein yalla mousseul si thiat ak lamignnn bilay je vous aime machallah❤

  • @aronadadondiaye5979
    @aronadadondiaye5979 Год назад +2

    MASHALLAH BRO AM GUA JIABAR soxna sou bakh moguini khawmako nak dh wayé ma maturité me dépasse

  • @asbiyadondesamb
    @asbiyadondesamb Год назад +4

    Je vous adore MachaAllah laf thiate

  • @diopgayekalsoum5980
    @diopgayekalsoum5980 Год назад +32

    Mn couple préféré oh nasén diam yague😊

  • @maremeba244
    @maremeba244 Год назад +16

    Oh machallah séne état d'esprit j'adore

  • @princesselimate2746
    @princesselimate2746 Год назад +4

    Yalla nalén yalla lafal thiat thi lamigne si beute si lépp way beugue nalén dh bilae😍😍😍😍😍

  • @mariethiawaseck9084
    @mariethiawaseck9084 Год назад +27

    Yalla nalén thiatt sékhlou way Yalla aral lén bopam maylén ndiabotou l'islam thi barké Muhammad Aleyhi Salatou Wa Salam 💚

  • @aliamsdiocou9010
    @aliamsdiocou9010 Год назад +6

    Oh trop chou mashalah ❤️❤️❤️amlen diam way ❤

  • @diaynabadiop4354
    @diaynabadiop4354 Год назад +58

    MOn couple préféré je vous aimes vraiment 🥰🥰❤❤❤❤❤ Long vie à vous deux

  • @adamakaire6533
    @adamakaire6533 Год назад

    Machallah xamel bou naturel amour bou naturel machallah yalna yalla barkel

  • @mamandia9688
    @mamandia9688 Год назад

    Machallah yalla nalen diam sonal way

  • @mbayangdiagne1904
    @mbayangdiagne1904 Год назад +16

    Macha allah my fave couple yalna lenn yalla lafal thiate Inchallah 🙏🏾🥰❤️❤️

  • @penchitadiouf1501
    @penchitadiouf1501 Год назад +4

    Les bâ malen beug Machallah❤️

  • @khadifall2825
    @khadifall2825 Год назад +10

    Manedale khalèbi beguena saye parants. Kilifa nonoulaye dèf

  • @maguettecamara4578
    @maguettecamara4578 Год назад +15

    Oh mon dieu comment je les aime Qu'Allah vous préserve 😘