Khalébi tamiite yaroul woul. Comment tu peux insulter une personne qui a l'âge de ton père. Kène yaarou ko. Cet enfant finira par le tuer ou le blesser gravement. Amoul bène traumatisme. Son frère aussi pkr il reste silencieux face à cette situation. Lii yeup yaayou khalébila rek. C'est la seule personne qui peut regler cette histoire
Khalei bi sou féké deugue bi la beugue kham dagne koy ték wo grand frère bi ak petit frère bi ak séne Yaye ak yayou khalei bi niou wakh ko li am yeup pour mou kham nou histoire bi démé llou moy solution bi grand frère bi wakh khalei bi li takh mou nangou yayou khalei bi tmt wakh khalei bi que ni niom niar niép dafa meusa seuy ak niom mou lerr si bopou khalei bi té grand frère li lépp soutoural khalei bou jiguéne bi mo ko si dougueul ak yayam bi si topone di wakh rék ms khalei bi li mouy déf ni ba la mouy dioure lénéne nagne ko wakh deugue bi mane dh llou la guiss ok merci
XALEBI AY FAMILLES MEME ,NIARI PARTI YEUPES TE MOU SOUTOURALE POPAM, AK NGIKO DIOUR ,BOU MOUKO YOBOU FENNE, NIMOUNIOU TOK WAX TANE EN FAMILLES , LERAL TOUS ,SI NON DI NE DEGUE, NOUMOU DIOUDE WONE ,TE DOU LOU RAFFETONE WONE,BOU BOBA DINE NE SOKHLO SOITOURA , TE FEKE PASSENA TE DESSOUTOU NDONDAME DOTOUL NEXKHATTI .
Loussi meuntii am daal wadjii mo togn bopam, yaw nga khamnii ki dafay sékk ak sa rakk ngay sékk ak mom bamoulay djiign eumbou, sou sékoul wone ak khalé bou djiguene bi li douko daal
Accro à cette émission machalal mais Sokhna Fatou je voulais partager l'histoire d'un cousin vraiment il souffre maintenant comment ça se passe par appel oubien vocal
A tout cas 1er cas bi waji. Na wakh khalébi bopame wakh ko carrément que sa yaye ladone soutoural wayé sama frère mola diour sou régler woul mou démm gendarmerie.
Celui qui a donné le nom de waly à son fils n'a qu'à porter plainte à sa belle famille pour retrouver ses enfants . L'autre n'a qu'à dire la vérité à sa maman devant l'enfant la mére de l'enfant et son frère
Sokhna Fatou,soy préparer thème bi,sa gard yi naniou la defal correction,''petite frère bi' ligua KO prononcé bari na.petit frère laniouy wakh.nio fare
Ne nguéye nek ci deuk français yi wala anglais yi tu fais des erreurs quand tu parles jamais tu ne verras un toubab se moquer de toi Mais senegal ngueye dém di lak toubab di def des erreurs les gens se moquent de toi alors que dou sakh sougnou langue maternelle. Legui boye lak wolof déf erreur gnou nane ndeyssane toubab leu vraiment nous les africains nous sommes troop complexés!!!!
Man deè pour man lii dou dueg nakh ci say biir wakh neènga wàdji dafa gnibi ci beès nakh dafa toukki woòn en 2006 ba pare ni wakh sakhnam ci dar dòn dow te wasin bou beès la 😂😂😂😂😂
Soit c'est l'un ou l'autre du moment qu'il savait que son frere etait l'amant de la fille pourquoi il l'a "frappe" vous n'etes que des boucs en rut voila votre chevreau a grandi et voila la consequence de vos actes irresponsables l'enfant la seen nattou leu dh🎉 10000 blems il va te tuer dh sa maman n'a qu'a le calmer en lui disant lequel des deux est son vrai pere.
Sama khalate moy ki dafa yabaté ay thiakhane kate ngay toudé sa dome Oustaz yi nék fi Imame yi nék fi Kilifa diné yi nék fi ak sa mbokou yi ak sa mbokou diabar yi Kén téréwoula nga beugue Wally mais toudé mome lolou dafa eupeu
Ms le Mr mo diour domam mo wara xol kouko nekh mou toudè ko lousiy yonou famille kou gorr ki ms fofou seuy amnafa batay d dkh seuy bi tassoul na dem si yonee dakh mom mayéewoul bate seuy bi tassoul
Naniou deff assises familiales les deux frères la maman et la mère du petit. Niou tog toj yaxwi 🍖 2- famille diabar ji yabatè na niou dè. Na len yobou justice
Nadem thi imami diakayi nioutok ak kilifam ak pati fereram ak yayi xalebi ak khale ak mbokku yi nioufenial deuggau gui apare mom garaa ferreram bi nadem polic decrareko bala daraa xew
XALEBI AY FAMILLES MEME ,NIARI PARTI YEUPES TE MOU SOUTOURALE POPAM, AK NGIKO DIOUR ,BOU MOUKO YOBOU FENNE, NIMOUNIOU TOK WAX TANE EN FAMILLES , LERAL TOUS ,SI NON DI NE DEGUE, NOUMOU DIOUDE WONE ,TE DOU LOU RAFFETONE WONE,BOU BOBA DINE NE SOKHLO SOITOURA , TE FEKE PASSENA TE DESSOUTOU NDONDAME DOTOUL NEXKHATTI .
Apres avoir écouté l"histore je dis que le grand frere devais raconter la vérité á sa mére avant d"en arriver ici
Il faut organiser une réunion entre ton frère, la mère de l'enfant et d'autres proches et toi pour mettre les choses au clair et dire toute la vérité
Ayway nasi waly diott
Vraiment
Il n'a qu'à dire la vérité a l'enfant
Faut dire à cet enfant ce k sa mère a fait c la seule solution
Sokhna Fatou djiguen nji leg leg lou yalla kham doyna
niou def test ADN entre l' enfant et ses deux pères lolou mo guena gaw sii sama avis
Weni bik sokhna fatou longue vie
1er bi man dama be Lou bone bakhall khalėbi dėffoll dara yayam ak papam ak mame na porte plainte yayou khalėbi bou ko dėffoll dina ko raye 😢😢😢😢
Khalébi tamiite yaroul woul. Comment tu peux insulter une personne qui a l'âge de ton père. Kène yaarou ko. Cet enfant finira par le tuer ou le blesser gravement. Amoul bène traumatisme. Son frère aussi pkr il reste silencieux face à cette situation. Lii yeup yaayou khalébila rek. C'est la seule personne qui peut regler cette histoire
Khalei bi sou féké deugue bi la beugue kham dagne koy ték wo grand frère bi ak petit frère bi ak séne Yaye ak yayou khalei bi niou wakh ko li am yeup pour mou kham nou histoire bi démé llou moy solution bi grand frère bi wakh khalei bi li takh mou nangou yayou khalei bi tmt wakh khalei bi que ni niom niar niép dafa meusa seuy ak niom mou lerr si bopou khalei bi té grand frère li lépp soutoural khalei bou jiguéne bi mo ko si dougueul ak yayam bi si topone di wakh rék ms khalei bi li mouy déf ni ba la mouy dioure lénéne nagne ko wakh deugue bi mane dh llou la guiss ok merci
Leur maman est très brave et responsable.
Khalé bi tamite kou rèw la. Il faut que mou yémalé ko.
Sokhnasi please dél lake wolof nga bayi petite frère bi
XALEBI AY FAMILLES MEME ,NIARI PARTI YEUPES TE MOU SOUTOURALE POPAM, AK NGIKO DIOUR ,BOU MOUKO YOBOU FENNE, NIMOUNIOU TOK WAX TANE EN FAMILLES , LERAL TOUS ,SI NON DI NE DEGUE, NOUMOU DIOUDE WONE ,TE DOU LOU RAFFETONE WONE,BOU BOBA DINE NE SOKHLO SOITOURA , TE FEKE PASSENA TE DESSOUTOU NDONDAME DOTOUL NEXKHATTI .
Loussi meuntii am daal wadjii mo togn bopam, yaw nga khamnii ki dafay sékk ak sa rakk ngay sékk ak mom bamoulay djiign eumbou, sou sékoul wone ak khalé bou djiguene bi li douko daal
Vraiment dafa salté
Mani koci ceeeyyy ceeeyyy ceeeyyy, cukum njaay yaañu sonal😂😂
Ya togne xalé bi dé
Na whax Tanaka famy
wotel rinion de famille nga wakh lene degue bi bo diare test ADN nga defko
Accro à cette émission machalal mais Sokhna Fatou je voulais partager l'histoire d'un cousin vraiment il souffre maintenant comment ça se passe par appel oubien vocal
Faut envoyer un vocal après c'est le directeur qui vous appelle
Ay way dimbali niou si petite frère nak
Petit frère stp
On n'a compris😂 le français n'est pas notre langue maternelle
Petite frere nak😂 magui commencé douté lima diangone😂
Mais elle raconte bien nak ndeysanne
Personne n est sûr de qui des deux est le père..donc ya qu un test adn qui peut edifier..
😢😢😢aye waye mes lii na si wally sécke diote wally dé kou bakh la tes ame yeuremandé
C'est aussi simple que ça,il faudra faire les tests d'ADN pour tirer cette histoire au clair.
Il n'a qu'a blame sa mere yomb trop il devait s'attaquer a cette derniere si tu ne prend pas garde il va te tuer dh ce gosse ne t'aimera jamais
A tout cas 1er cas bi waji. Na wakh khalébi bopame wakh ko carrément que sa yaye ladone soutoural wayé sama frère mola diour sou régler woul mou démm gendarmerie.
il faut qu’il aille à la gendarmerie sinon il risque de lui faire très mal
Histoire 3 danga koy piège
Djiguén la mais li yeup pékhé djiguén bou yéss rék thieuyyyyy
Celui qui a donné le nom de waly à son fils n'a qu'à porter plainte à sa belle famille pour retrouver ses enfants . L'autre n'a qu'à dire la vérité à sa maman devant l'enfant la mére de l'enfant et son frère
Légu 3ème bi 😂
HISTOIRE 2 QU'IL LES TRAINE A LA JUSTICE
BJR WAGNIL CAFE BI PREND DE l'eau
Sokhna Fatou,soy préparer thème bi,sa gard yi naniou la defal correction,''petite frère bi' ligua KO prononcé bari na.petit frère laniouy wakh.nio fare
djigéne dou rabu soye loulo ay fene la
Dafa fekk amaguoul sa diott rk 😂😂
@@seutouaby4140 Yalla Nanio Yalla Sotoràl Dafal Nio Diàm
❤❤❤
Xalé bobou dina nék bandit nakh yayame moko liguéy wadji na déme porte plainte tes wo yayou xalé mou waxe deug bii
Mo yéye di
Waye Yala bakhna
Il n'a qu'à organiser une réunion de famille et dire toute la vérité
Sokhna Fatou yowtamite petit frêre laniouye wakh
masamz on dir oas petite frère mais petit frere
Ne nguéye nek ci deuk français yi wala anglais yi tu fais des erreurs quand tu parles jamais tu ne verras un toubab se moquer de toi Mais senegal ngueye dém di lak toubab di def des erreurs les gens se moquent de toi alors que dou sakh sougnou langue maternelle. Legui boye lak wolof déf erreur gnou nane ndeyssane toubab leu vraiment nous les africains nous sommes troop complexés!!!!
Demal l Waly seck mayla djabar
Nako bayi
Cou djiguene ki mo niac fayda da deme si yone porté co plainte birgade de recherches
C pas sûre dale na wo yaye dji mou lèrale khalé bi dina ko raye dale
Yaye xalé bii mo derrière tous ça il doit porter plainte une fois au tribunal xalé bii dina wax kan moko waxni frère papam moko diourr
Jiguén mo meun lou nék xam mag xam rak mo taxit xalé bi agresseur reck la meuna doone nako wakh deug bi puisque dou doomam
Wala. Mou. Wakho'ne. Petit. Frère. Bi. Necko. Ya. Diour. Khalebi. Lolou. Moy. Wakh. Dji
Wala mouneco dangene nouro rec wayé lala diour
Ndeyssane dafdone fo tec lolou amnanioucoy fowé mome dafa fire rec
Man deè pour man lii dou dueg nakh ci say biir wakh neènga wàdji dafa gnibi ci beès nakh dafa toukki woòn en 2006 ba pare ni wakh sakhnam ci dar dòn dow te wasin bou beès la 😂😂😂😂😂
Sey bi dh sariha tasuko dh nan took wakhtan wala mudem mom djiguene gui dem nianibat
Soit c'est l'un ou l'autre du moment qu'il savait que son frere etait l'amant de la fille pourquoi il l'a "frappe" vous n'etes que des boucs en rut voila votre chevreau a grandi et voila la consequence de vos actes irresponsables l'enfant la seen nattou leu dh🎉 10000 blems il va te tuer dh sa maman n'a qu'a le calmer en lui disant lequel des deux est son vrai pere.
Test ADN REK MOLÉN MANA ATÉ
Mais khalébi ni rek la meneu melle par se que yaye dji moo bonne mais wadji mononako wakh yayam nako yobou gendremerie sinon dinako ray
Sama khalate moy ki dafa yabaté ay thiakhane kate ngay toudé sa dome Oustaz yi nék fi Imame yi nék fi Kilifa diné yi nék fi ak sa mbokou yi ak sa mbokou diabar yi
Kén téréwoula nga beugue Wally mais toudé mome lolou dafa eupeu
Ms le Mr mo diour domam mo wara xol kouko nekh mou toudè ko lousiy yonou famille kou gorr ki ms fofou seuy amnafa batay d dkh seuy bi tassoul na dem si yonee dakh mom mayéewoul bate seuy bi tassoul
Djiguene dafa wara kham bopam li niana trop amel na domam akha
Na laag rakam ndakh mo jur khlabi wala
Nakho yobou police
Do bayi petite frère bi tmt😂 ngay insister ni
Personnellement j'ai aucun idée à propos de cela
Histoire 2 police rk
Grang. Frère bi. Moukhame. Née. Petit. Frère. Bi. Daye. Dokhane. Khalebi. Momite. Lou. Mouy. Sekhe. Ack. Khalebi
Na porte plainte gni yonou jabaram ta bou gagné sa fasse diabar gni ndakh bakhoul
Naniou deff assises familiales les deux frères la maman et la mère du petit. Niou tog toj yaxwi 🍖
2- famille diabar ji yabatè na niou dè. Na len yobou justice
C la seule solution l'amener à la police comme ça les choses seront plus claires là-bas
Nadem thi imami diakayi nioutok ak kilifam ak pati fereram ak yayi xalebi ak khale ak mbokku yi nioufenial deuggau gui apare mom garaa ferreram bi nadem polic decrareko bala daraa xew
Na whax Tanak famy bi ak ya youb khalebi en sambil tous
Nako wahh je ne suis pas ton pères la vérité
Aller encore au village le montrer ces parents si non tu auras des un jour
mani na wakh deug bi rek ni djouroul xalé bi c mieux akh
Khalé bi yayam mocoy wax ni diourou co
took lenn yen 3 ou 4 guenne wakhetane
Il faut appeler la mere ils disuttent a 3
Mais nak wax na deuk Wally xamoul la xamoul gagay toudé Domme papam mom wala ay magal wala xaritam comme si ndawlo woul gnimou xam
Le scénarist a oublié que les batards souvent se cachent.
Khalebi yayam moko togn oyof ser bakhol
Petite frère ou petit sœur? Dis rackame bougoor.
Komka dafa salolsii nawo ndayi djiuguene gui ak baayam wakhli xew bupare tegalko ay kondition buko respectee niokotini boko respectewu mufaseko seti keenen
Mom tmt ken dou mom rak loumou lal mom waro fa sakh xol salté na trop
Benen yonn sa sera ta mort