Sokhna Zeynab Fall : son enfance, son parcours et sa rencontre avec Radio Dounya

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 28 дек 2024

Комментарии • 514

  • @bngfromsl9871
    @bngfromsl9871 6 лет назад +4

    yall na yalla yerem zeynabo fall diekgel ko té yekhéño

  • @fatoumatandiaye1111
    @fatoumatandiaye1111 2 года назад +2

    Paix à son âme qu'Allah lui fasse miséricorde.Que firdawsi soit votre demeure éternelle ya Zeynab,

  • @rolandefaye8091
    @rolandefaye8091 6 лет назад +149

    Sincèrement média bi perteuna mane suis catholique mais j'aimais ses émissions je le suivais royoukay la kou melni mom dina diaffer fane yi guatteuna mais li ngua diokh dunya reyeuna dieuredieuf à jamais dans nos cœurs demme be sa dieukeur seddel la lou rafet li Machallah

    • @yoossoopha
      @yoossoopha 6 лет назад +3

      Machallah. Que Dieu te guide

    • @aramesarr6374
      @aramesarr6374 6 лет назад +1

      YeT

    • @deuggreikktyallareikktakh3505
      @deuggreikktyallareikktakh3505 6 лет назад +4

      NdeySsane...Rollande ya Baax Wayy

    • @D-Awa
      @D-Awa 6 лет назад +4

      se n'est pas une une affaire de religion mais son comportement ; calme, respectueuse modèle d'une femme africaine

    • @deuggreikktyallareikktakh3505
      @deuggreikktyallareikktakh3505 6 лет назад +3

      @@D-Awa C Vrai mais vous pouvez vous taire aussi en voyant toutes ses qualités mais Baax Ak raffètte xOole reikk nguène deiff

  • @matydiop8562
    @matydiop8562 5 лет назад +7

    😭😭tu nous manque ya sayda yallah na yallah yereume ko tè yèsale yeurma dè si mome tè dièguele ko 🤲🤲

  • @Laspheredesdistinguees
    @Laspheredesdistinguees 6 лет назад +111

    Machallah Tu as accomplie ta mission sur terre ( Yalna yalla yokk yermandem thi iow sokhna zeynab ) ton absence touchera tout le senegal .
    Je ne suis pas trop mourrou ( j’ai mes raisons et le Dieu qui m ‘ a conçu comme ça m’aime comme ça ) hamdoulilah après l’éducation que ma mère et la vie m ont donné ( thi sunna mouhamet PSL ) je suis ton enseignement j’essaie d’être une bonne personne t dîna gueuneu roye thissa djikko yi inchAllah ( tu es le type model sokhnassi ; sénégal sokhlawone nala trop ) A dieu 😓

  • @alessehameze831
    @alessehameze831 6 лет назад +4

    Elle est vraiment courageuse. C'est une maman exemplaire. Que le bon Dieu acceille dans son paradis.

  • @fatoudiedhiou8652
    @fatoudiedhiou8652 3 года назад +6

    Paix à son âme c'était une femme exemplaire 🙏

  • @djkops6073
    @djkops6073 6 лет назад +2

    Al hamdoulilahi Repore en paix SOKHNA ZEYNAB FALL

  • @SenegalVideossn
    @SenegalVideossn 6 лет назад +157

    Yalla na ko Yalla Yeureum 😭😭😭

  • @deartaar6178
    @deartaar6178 5 лет назад +3

    Femme brave, femme digne, Mashalahhh beugue YONENTE bi Psl yala nala yoke léraman té tass niou barkémm

  • @aminaseck4943
    @aminaseck4943 6 лет назад +22

    Je ne trouve mêm pas les mots 😭😭😭😢😢yalla bouka thiate djitou si bamelém une femme très pieuse k'Allah l'accueil en son paradis céleste

  • @mamadousalioudiallo3196
    @mamadousalioudiallo3196 6 лет назад +66

    Qu'Allah l'acceuil dans son paradis .paix a son âme.

  • @sokhnabessane8898
    @sokhnabessane8898 6 лет назад +61

    Inna Lilahi wa Inna Ilayhi Raji'un Qu'Allah l'accueille dans son paradis céleste. Amine

  • @elhadjibaboudiop5603
    @elhadjibaboudiop5603 6 лет назад +37

    Macha allah notre très grande sœurs vraiment le pays même le monde a besoin des femme comme vous que Dieu que bénisse

  • @bachirdiop6275
    @bachirdiop6275 6 лет назад +3

    Qu'Allah Lui fasse Miséricorde et lui ouvre une Porte du Paradis,le Sénégal a perdu une femme très pieuse,mes pensées vont à Oustaz Alioune Sall,

  • @oumoudiallo3089
    @oumoudiallo3089 4 года назад

    Machallah Sénégal niak na cou beugueu Diiné Yalla na souf woyof sa kaw Ndeyesane

  • @layelaye75
    @layelaye75 4 года назад +1

    mashallah cette dame!!! que Dieu l'accueille dans son paradis céleste inshallah

  • @alphaba6611
    @alphaba6611 6 лет назад +10

    c'est une femme unique au senegal elle a du savoir cette femme c'est une exemple pour toute les femmes senegalaise que le tout puissant l'acceuil dans son paradi MachaAllah

  • @maimounangom7592
    @maimounangom7592 9 месяцев назад +1

    Ont t oublierai jamais que son âme reposé en paix ❤❤

  • @fatoundiaye812
    @fatoundiaye812 6 лет назад

    Qu'Allah te fasse miséricorde SOKHNA ZEYNAB, et qu'Il fasse venir des milliers comme toi

  • @gnimadiattakonte3072
    @gnimadiattakonte3072 6 лет назад +3

    Ndéyssane yalla nalla yalla yeureum té kharéla thi aldianay firdawssi yi macha allah amnagnou yakar thi yaw

  • @nenesarr805
    @nenesarr805 6 лет назад

    Yalla nako borom bi yeureum ci barké séyidouna Mohamed yalla xaré la aldjana

  • @ndeyefatouniang9125
    @ndeyefatouniang9125 6 лет назад

    Yalla nako yalla yeureum tè kharè ko aldiana niit kou yiiw kou am diinè am l islam

  • @pape7592
    @pape7592 2 года назад

    Yalna ko yalla yeureme té khéréko aldiana si barkép seydina mouhamad

  • @oumousarr9252
    @oumousarr9252 6 лет назад +1

    Que Allah le tout puissant l accueille dans son paradis inshallah

  • @HojaNjie-j4u
    @HojaNjie-j4u 7 месяцев назад

    MashaAllah
    May Allah forgive her shortcomings and grant her Jannah

  • @binacissokho
    @binacissokho 6 лет назад +74

    Je t'aime tellement mon idole

    • @salimkebe9830
      @salimkebe9830 6 лет назад +3

      Bineta Cissokho senegal li mo ko yakk. "On dit pas sama idole etc je t'adore" cest de l association par ignorance! choisissez des mots juste. Merci

    • @binacissokho
      @binacissokho 6 лет назад +8

      Salim Kebe ou as tu lu je t'adore ?
      Wa loutax nite eupeul tamit ?
      Ma idolo Sokhna sou bax bi deh moma guenal may idolo gnou nekoul référence...
      Guemal liga gueme ma gueme lima gueme

  • @cheikhfall4729
    @cheikhfall4729 Год назад

    Bilahi ki dou nitou fi man mom ba légui Sama khél day nek si mom yalnako yalla yeureum té xareko aldiana firdaw si

  • @coumbaasmndiaye3316
    @coumbaasmndiaye3316 3 года назад

    Yallna yallna kharé aldiana firdawsi sa boumal guissé sama khéle déye délou thii yalla ndakh dama khamné yama guene té yalla dieuleulafi

  • @mereawandiaye5170
    @mereawandiaye5170 3 года назад

    Yalla nakou yalla yeureum si barkè seydina mouhamed sallahou aleyhi wa salam

  • @informatitienka2951
    @informatitienka2951 6 лет назад

    innalil lahi wa inna ileyhi raadjihoun
    allahou akbar
    taye sama Hole dafa fèèss
    yalna yalla dimbalila ga dadjè ak yonent bi.. yalla boula thiate djitou sa bamél si barke BAYE NIASS

  • @rackythiam220
    @rackythiam220 6 лет назад +12

    Yalnako yalla yeureum teh diegalko😭😭😭😭😭

  • @alletailleur8583
    @alletailleur8583 6 лет назад

    yalla nakko yalla yereume xareko aldiana barqi Mohamed psl qouu baxx te sell. gnieupp koo beuugg wawaww.kou labir.aldiana fall

  • @SohknaThiane-rt9ct
    @SohknaThiane-rt9ct 3 месяца назад

    Que firdawns soit sa demeure 😭😭😭💖💖💖💯💯💯🙏🙏🙏

  • @zaynagaye7538
    @zaynagaye7538 Год назад

    elle est comme moi ce extra ordinaire سبحان الله 💞

  • @AwaNdiaye-ph1yg
    @AwaNdiaye-ph1yg 6 лет назад +1

    Yalna ko yalla kharé si aldial nay firdaw si que la terre soit légère sur elle tu nous manque zeyna fall

  • @bacarycoly8223
    @bacarycoly8223 5 лет назад

    Que le tout puissant l'accueilledans son paradis amen je l'ai connu à titre posthume mais je me disais que si j'ai une fille je vais l'amener dans son interna 😢😭

  • @Topofthetopapex
    @Topofthetopapex 6 лет назад +7

    37ans 😢 Yalla rek mo kham loutakh mou dieul la. Bilahi. Yalla nga khipé aldjana kham ni accomplir nga sa mission. Dem nieup khamal la Lou bakh bolei ci dane ligueyal yalla darra dakouko🙏🏾💞repose en paix

  • @MultiSoda09
    @MultiSoda09 6 лет назад

    Yallaboulla thiatt djittou sissa keurbou moudjou, ma sha Allah référence deugeu, Allah dans sa miséricorde infinie t'acceille dans son royaume céleste amine Ya Rabbi

  • @fatougueye2495
    @fatougueye2495 6 лет назад +2

    Yalla nako yalla yeureum té atté KO si yeuemandém

  • @ngouyediouf336
    @ngouyediouf336 6 лет назад

    Ma sha Allah. Yallah nala Yallah diapalé soutoural la ci barké seydina Muhammad SAW.

  • @houlaykane865
    @houlaykane865 2 года назад

    Marshall je l'aime bien qu'elle repose en paix que dieu protège ses enfants

  • @mamediarrasene9191
    @mamediarrasene9191 6 лет назад

    Yalnako yalla yèreum tèe kharè ardiana firdawci ba guena kawèe ,nitt kou yiw la won ,

  • @babacarsakho2963
    @babacarsakho2963 6 лет назад +19

    Yalla nala sunu borom yobou aldiana thi barké Mouhamed PSL 😭😭😭😭😭

  • @mamadoulaminekebe5512
    @mamadoulaminekebe5512 6 лет назад

    Machalla yalle nako yalla yeureum.

  • @ibrahimasarr4546
    @ibrahimasarr4546 2 года назад +1

    😭😭😭😭😭😭dioynalla wallahi

  • @mormbengue7821
    @mormbengue7821 5 лет назад

    Machalla yalla nako yalla yeureum khareko aldiana firdawsi

  • @autetine1560
    @autetine1560 6 лет назад +10

    Les gens bien ne reste pas trop longtemps en vie car dieu les aiment trop et il a besoin d'eux

  • @fatoupouye1407
    @fatoupouye1407 6 лет назад

    Allakhou akbarr machallah yallah bouko thiate djitou.yallah na yéwo Aldjiana inchallah amineee

  • @mouhamedndiaye4451
    @mouhamedndiaye4451 6 лет назад

    yalla nako yalla yeureum khareko adjana

  • @shushulawade4506
    @shushulawade4506 6 лет назад +46

    Ndeysan yoe nittou yalla nga
    Aldjanna moy seu keur
    Yallna souf oyof seu kaw

  • @haidaraaboubacre9064
    @haidaraaboubacre9064 6 лет назад

    yallahna KO yallah xare adiana souf oyof si kaname

  • @matysow8802
    @matysow8802 6 лет назад

    Bilahi mW oci je suis chrétienne mai souma sagnone melni ioe j répond au non de Nina mais sama compte kharit la ame nga dîné machalah yalla na souf woyof sisa kaw

  • @alimatoundour1160
    @alimatoundour1160 6 лет назад

    Yalla boula thiatt djjtou si sa bamel Yall na Firdawsi néka sa keur pour toujours si barké SEYDINA MOHAMED PSL Amin Yarabi Repose en paix Zeynab

  • @muhamadoudibbasey6228
    @muhamadoudibbasey6228 5 лет назад

    May God grante her janatul firidalsil-a-ala and the rest of Muslims.
    Ameen ya rabil allameen

  • @kinendiayefall
    @kinendiayefall 6 лет назад +3

    Yalla na Borom bi fay yeureum xaréra si aldiana firdawsi barkep Borom Touba amine

  • @dykha8182
    @dykha8182 6 лет назад +8

    Ndeysaaane yalla nako yalla yeureum té xaré KO la janna

  • @adjafall6433
    @adjafall6433 6 лет назад +26

    Ayi j'ai mal, tres mal, repose en paix

  • @madamebittaye2628
    @madamebittaye2628 6 лет назад +15

    Inna lillahi wa inna ileyhi rajihun, yallah na aljanatul firdaws di wathiou wayam

  • @mamouchekhan372
    @mamouchekhan372 3 года назад

    Yalla nala yalla yeureum bidjahi Taha AK yaçine

  • @hawandiaye9550
    @hawandiaye9550 4 года назад +1

    Que la terre lui soit légère

  • @kamor1734
    @kamor1734 6 лет назад

    yalla nako yalla yeureme teh Yoko aye léram

  • @ndiemendour7250
    @ndiemendour7250 6 лет назад

    Yalla nako yalla kharé aldiana firdawss té yékhéniou KO khame né diné rek Moka yité yalla naniou yalla khir si môme amine

  • @aminaniang5982
    @aminaniang5982 6 лет назад +37

    Que le bon dieu l’accueil dans son vaste paradis 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽❤️

  • @khelcomtouba3863
    @khelcomtouba3863 5 лет назад

    Yalnako yala yeureum té kharéko aldiana...

  • @Tymalife
    @Tymalife 6 лет назад

    Ooohhh machalla .Yalna aldjanna di sa deukouwaay inchalla

  • @serignegueye5426
    @serignegueye5426 6 лет назад

    Yala nako yala yeureum si barke seydina Mohamed psl

  • @ndiayandiaye1879
    @ndiayandiaye1879 6 лет назад

    yalla nako yalla khare aldiana 😭😭

  • @elbachirniang7840
    @elbachirniang7840 6 лет назад

    اللهم نور لها قبرها ووسع مدخلها وأنس وحشتها , اللهم وأرحم غربتها اللهم أجعل قبرها روضه من رياض الجنه لاحفره من حفر النار,

  • @coumbadiop1483
    @coumbadiop1483 6 лет назад

    Yalla nako yalla khare aldiana😭😭😭😭

  • @jaynprods2
    @jaynprods2 6 лет назад +28

    ki yalna ko SUNU BOROM moussal si tchate ak seytaner ak lep louy lorer!! yagi si tankou njoub boudeugou ak sellal sa biir ak sa biti! yalna ga agg figa yener agg tchi ap sell ak jamou YALLAH SWT

  • @aichaka1700
    @aichaka1700 6 лет назад

    machallah rokay la wonne si bepp djiguenne yalla nako yalla yereume té khare ko aldianna firdawsi amine 😭😭😭😭

  • @syiba2683
    @syiba2683 6 лет назад

    Yallah nako yallah Yeureum thé khare adiana 😢😢

  • @oumydiop7622
    @oumydiop7622 Год назад

    Yalna yalla yésal yeurmandem thi yaw wétal nga ngou lol 😢😢

  • @fatoucamara5781
    @fatoucamara5781 6 лет назад +1

    Que Dieu l'accueille dans son paradie une femme pieuse et exemplaire yalla nga khipé aldiana firdawsi

  • @papakhouma8237
    @papakhouma8237 6 лет назад

    Yalla nako Yalla yeureume diégal ko kharé ko aldjanay firdawsy amiiine

  • @moisek147
    @moisek147 6 лет назад

    Machalla yalla nako yalla yereum kharéko aldjiana boiko thiate djitou si bamél

  • @ibrahimasarr4546
    @ibrahimasarr4546 2 года назад

    Képp kou buegeu seyda zaynab rk lalal j'aime

  • @mansoursall3594
    @mansoursall3594 6 лет назад +17

    macha allah kou bakh ga ta famille et ta mère macha allah j ai passé trois jours c est vous avec Lamine et serigne fall mais macha allah niou am diné

  • @kinesogue9211
    @kinesogue9211 6 лет назад +6

    Zeyna yalna yalla kahkre adiana 😭😭😭😭😭

  • @sodandaye9956
    @sodandaye9956 6 лет назад +3

    Yalla nako yalla yeureum te khare ko aldiana firdawsi si barke seydina Mohammed

  • @abdougaye9766
    @abdougaye9766 6 лет назад

    Yalle nala yalla fayee aldiana souf oyoff si yaw amine Senegal mo niank wallahi

  • @fatyniang899
    @fatyniang899 6 лет назад

    Yalnako yalla yeureum tei xareko aljana firdawsi

    • @kamarafatou5557
      @kamarafatou5557 6 лет назад

      sènègal niaquena koumoudoul amati ba faw naniou dièma roy ci mome nioune djiguène yii example la

  • @fatoudia7830
    @fatoudia7830 6 лет назад

    Djiguene bou nekk warna roy si mome yalla na khippe aldiana repose en paix Zeynab

  • @awathiam4419
    @awathiam4419 6 лет назад

    Kahall l'accueille dans son paradis firdaws avec les tout les muslum du monde amine yaraby

  • @awangom8569
    @awangom8569 5 лет назад

    sokhna sou gnamé dëg yalna ko yalla kharé aldiana.amineee

  • @thieckandao9920
    @thieckandao9920 6 лет назад

    Yalnako yalla kharei Aldiana

  • @cheikhniang4219
    @cheikhniang4219 6 лет назад

    Yallanako yalla yokou ko ay lerr

  • @mamadoumouhamedba4792
    @mamadoumouhamedba4792 6 лет назад

    manchallah yalla nako yalla yeureum tee khareko Aldiana... Amiine

  • @maguettethaim7333
    @maguettethaim7333 6 лет назад

    Machallah yalla boko thiate djitou si bamél té souf oyof ci kawam

  • @khadidiop3725
    @khadidiop3725 6 лет назад

    sokhna ci yalnako yalla yeurume ci baké seydina Mohamed psl amine

  • @aissatasy7847
    @aissatasy7847 6 лет назад

    Sama sope demna
    Yala nala yalla yeureum

  • @laminmaster9387
    @laminmaster9387 6 лет назад

    yalla nako yalla kharé Aldjana firdaws bibarakati seyidouna Mouhamed sallal lahou aleyhi wa Salama

  • @ndiayeoceanexport1187
    @ndiayeoceanexport1187 6 лет назад

    Ma challah yalla na ko yalla yeureume tè diegeul ko

  • @linguereseye159
    @linguereseye159 6 лет назад +1

    Bilahi damala nawlowone!!Yallah na Aldiana Firdawsi done sa keur

  • @elbachirniang7840
    @elbachirniang7840 6 лет назад

    كانت امرأة كريمة وشجاعة والله لم أرى مثل شخصيتها وكانت قوية بالصدق والأمانة، ولكن إذا حُمَّ القضاء على امرئ😭😭😭 فليس له برٌّ يقيه ولا بحر. هذا إرادة الله.... رحمة الله عليها دائما

  • @lalacamara1169
    @lalacamara1169 6 лет назад

    Yalnako Yallah yeureum bidiahi rassoullillah saws

  • @fatimalo5924
    @fatimalo5924 6 лет назад

    djambarou l'islam machallah yallana firdawsi doon keureum si barkei Mohamed psl

  • @ndongfatouk7986
    @ndongfatouk7986 6 лет назад

    ohh yalanako yala yereum takharéko aldjana firdawsi barké Cheikhul Khadim repose en paix Sokhnaci

  • @muhammedsamba4294
    @muhammedsamba4294 6 лет назад +6

    اللهم إغفرهم ورحمه ويدخلهم جنة الفردوس