Pendo cilwissé neu Pendo rafet neu Pendo meuna sagnsé Pendo tey neu Pendo toubabé neu Pendo set neu Pendo indi woul nit you beuri donc elle a vraiment cuisiné. Elle meritait plus de 1 million sakh nak. Machallah
Je savais pendo mamy cobra ak ndickou nioy gagné ndakh niom guena set les mame Ndiaye savon une deux mou niam ak lohome tes dou dieul cou dou pour mou niam ugène mon manqui si mame Ndiaye savon ndickou togou makk la togue pendo mon eupeu ugène adji mass dou tokk bouy togue en plus sene décor yè eupeu mamy cobra mom meune togue trop machallah
Nekhoul ba nekh mais c'est très important, ça valorise nos qualités traditionnelle et culturel, en plus dey doundeul économie, il faut améliorer et prendre des jurys de qualité pour nos plats nationale
Dekku jamm xaley jamm lii mooy Sénégal mais pas de procès bodi body finalement nous en pouvons plus que dieu vous paye amine j ai tellement ri non Mame Ndiaye savon moo jel pee
Ah oui suis d'accord pendo plat wam chargé woul té thiép bi nironeu lou séleu té nékhe❤❤❤❤ diadieuf pendo guissé
Ak higiene bi tela paré rangé teye
Bilahi ❤
Pppp
Bétouma pendo guissé parcelles Unité 07 nieupeu xamnagnu meune togam machallah
Barke cheikh sougnou talibe cheikh bi🎉🎉🎉❤❤❤merci 2stv bonne continuation ❤
J'ai les larmes aux yeux F.E.L.I.C.I.T.A.T.I.O.N.S PENDOVtu l'as très très très très très très bien mérité je suis très contente ❤❤❤❤❤❤❤❤
Urio
Rtiuez
Pendo talibé serigne Babacare s'y ❤ndam rekk❤
Talibé cheikh dou dieul ndaré ❤❤❤
Wakh ko thia kaw 🥰
Dafa leer
Lou lére gua wakh
Bilay walay
Pendo daka mérite franchement c'est une belle initiative mami aussi meuneu na togou mashala 😊
Merci les membres du Jury vous avez fait un excellent travail sans parparlo. Félicitations Penda Guissé
C’est pendo qui le mérite vraiment félicitations 🎊 ❤plat bi set n’a nekh na 😂
Yako niam ?😂
Plat sénégalais la togou nekh sett ték si guena régler Machallah félicitations pendo 🥰🤣😭
Merci beaucoup bijou yalla nala yalla fay barke Serigne saliou suniou wadji❤❤❤❤❤❤❤
Amine ya rabi
Félicitation Pendo guis naneu daal bi maturité bi ak gueum gueum bi fofou rk la gagné encore une fois félicitation
Kou ande ake Serigne Babacar Sy dieule 1er 🎉
Bilahi dama contane trop pendo dako merité talibe Chiekh bii ❤️❤️❤️
Félicitation Pendo Talibè Cheikh Bi❤🎉🎉🎉
Pendo tu la merite vraiment 🎉🎉🎉🎉❤❤
Seule les noiceurs d'ébène on gagné machalah
Ahhh li mome 2stv rék moko meune wawawee❤❤❤❤ chapeaux à vous
Son plat est typiquement Sénégalais et elle a respecté les règles d'hygiène et de securité
Félicitations pendo et mamy cobra❤❤
Mamy Cobra téyoul dara c'est bien d'être drôle mais😭😭do réglé touti tamit. Pendo tu as mérité deh bravo
Elle ne me fait pas rire du tout😔
Ce que j'ai remarqué aussi, da eupeul
Cobra day forse beuz sofna trop
En plus elle a était très correcte pendo félicitation ❤❤
Félicitations Pendo Macha'Allah Guissé mabo❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Pendo thie gueuneu Regglleé Mâcha Allah ❤
Absolument ❤
La fierté des halpoular❤
Félicitations à pendo et a mamy cobra
Pendo mo daff ma nékh bilay très class
Félicitations à PENDO GUISSÉ MACHALLAH
Félicitations pendo 🎉machallah
Pendo khalifa setanoula 😭❤️
SOUGNOU RAKKOU KHOLE FOREVER INCHAALLAH
pendo est la seule qui est calme ame class machallah tey
Pendo cilwissé neu
Pendo rafet neu
Pendo meuna sagnsé
Pendo tey neu
Pendo toubabé neu
Pendo set neu
Pendo indi woul nit you beuri donc elle a vraiment cuisiné. Elle meritait plus de 1 million sakh nak. Machallah
Vive Pendo❤
Je savais qu'elle allait gagné son plat est trop riche en vitamine ❤
Maachalah j'ai des larmes aux yeux bravo Pendo❤❤❤❤❤
2STV ces derniers temps mom, vous avez pas de belles images. On dirait, les théâtres de Daraay Kocc de 2001😭
Khass gualene wayé deugu rek gua wakh 🤣
Je savais pendo mamy cobra ak ndickou nioy gagné ndakh niom guena set les mame Ndiaye savon une deux mou niam ak lohome tes dou dieul cou dou pour mou niam ugène mon manqui si mame Ndiaye savon ndickou togou makk la togue pendo mon eupeu ugène adji mass dou tokk bouy togue en plus sene décor yè eupeu mamy cobra mom meune togue trop machallah
C’est mal réparti la 1ere devrait avoir plus que les autres sorry Bijoux
Vive péndo talibé seydile Aboubacar Sy 💪💪💪❤️❤️❤️
kou ande ak sy malick dou dieul ndare mouk❤
Maan pendo rek laay top🎉🎉 yalnalaa yallah dollil jaam barké salatoul Fatiha
AMINE YARABI 🤲
Pendo amna class🎉
Elles la mérite, pavillon très propre sa donne envie de manger son plat.
Noooon Tata Bijou prix ambiance ak faire play dafa warone am ngua diokhko MAMY COBRA😂😂😂😂😂😂😂 Noooo ki dou niit
Nekhoul ba nekh mais c'est très important, ça valorise nos qualités traditionnelle et culturel, en plus dey doundeul économie, il faut améliorer et prendre des jurys de qualité pour nos plats nationale
Talibé Serigne Babacar Sy ❤
Maa cha Allah sama mboku talibé cheikh bi pendo
Nn Mami vraiment dafa eupeul trop 😢
Congratulations pendo 🇬🇲🇸🇳❤️
Bravo Pendo Machalakh ❤😂
Ngén yakar né Mamy mi Dou Souss moungi niami niami rek
Amatinañu Ndao nous les toucouleur 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤
Pendo dafa meune togg li c normal
Pendo mo guena sét
Fouf sakh
Pendo Serigne Babacar Mo beuré dolé sy Malick yakko wollou
Barké khasssida yi dama beugue pendo souniou talibé cheikh bi diam si yaw si barké borom magal gui touf touf
Hoooo félicitation pendo
Li waroul diekh mo dakeu sne petit Guale 😊
Félicitations pendo❤
Pendo tu la mérite vraiment
NDEYE savon ligua fi perrier y’a ko tay 😂😂 j’adore 🥰
Merci les noiceuses d'ébène
PENDO Félicitions la meilleure
Heeee hi wathina machallah Alima Sama saf nak
Barké khasssida yi dama beugue pendo souniou talibé cheikh bi diam si yaw si barké borom magal gui touf touf ❤
Félicitations ❤
On t aime pendo
Mamy cobra rey nama qui mako beugu ❤😂😂😂😂😂
Mame Soda Fall di kheutio micro bi ak Kheucha dougnci wakh 😂😂😂
Cheu tey bakh na déh surtout si Jiguén 😭
Mamy ❤❤❤❤
Ahh oui mérite nako set na simple na plat bi Machala nirou na lou neix
C est pas Normal
On doit pas filmè une personne a son Ainsu. Sénégal rèk
😂mo yow liii concours leu surtt mouy toggou c normal piège yoyou am pour natt les candidates
C'est très grave ce qu'ils ont fait, en plus ils le disent sans problème. Dama choquée 😢
Penda toutes mes félicitations mais une prochaine fois si sa staff ki done mare lokho yi boule kossi bolé
Ahhh wi bétouma ❤❤
Mami cobra ray nama😂😂😂
D'où nittou fi😂😂😂😂😂❤
Félicitations mes amours ❤❤❤
Macha allah❤❤
Genre personne n’a remarqué Ouzin keita?😂😂😂😂😂😂
😂😂😂no li dama ré ba dé li dafa nékh billahi lép rafét
Normal balamaissa la nak 🎉🎉🎉
Tien noir amatina ndam😂😂😂
Bilahi 😂
Niou nionon nionon danion civilisé beugue lou bague mana sagnsé man togue wawaw
Bilay li douma ci doyal❤
Dekku jamm xaley jamm lii mooy Sénégal mais pas de procès bodi body finalement nous en pouvons plus que dieu vous paye amine j ai tellement ri non Mame Ndiaye savon moo jel pee
❤❤❤❤❤❤❤❤❤merçi pour ta simplicité
Pendo
Domou ndiénion dakoy nirou barki alhourane
Mamy diane bii mom a dada😂
Mane mamy rey nama
regarder mami cobra ki jubile , elle croyait etre la prémiere , hahahah
MÉRE SODA NAKA DIEK DANGA FAAR AK PENDO MOTAKH NGUÉNE DIOXKO PREMIÈRE
Wakhal loula wor 😊
Pendo koku magoume la, togame day diare yone
Betouma ticke laobe 😂 nakh beuri ga wah te eupeulga
😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂
Tiket 😂😂😂😂mot ndaré meunou mako mougne 😂😂😂
Bilay mami mala beugue
Pendo dee comme gouy khar résultat bac
😂😂😂😂😂
Vous m'avez fait rigoler Macha Allah 😅
Kon guisnga lolou 😂😂😂
Wa ticket mo djeul ndaré 😂😂
😂😂😂😂lolou lay rètane bay dioye
🤣🤣
Wa yene diabante Mami yi dougnci wakh 😂😂
Adji mass sa jupe lan la, mame ndiaye thia pantalon ba la
❤❤❤
Concour bou amoul premier
Ndikou la faralone