Chers journalistes, moment yi il faut éviter de faire des interviews aux parents directs. Il faut aller voir les autres proches, vous ne faites qu'aggraver leur douleur.
Cheikh bou Diop yalla nagua agalei sa ndaw aldiana j’ai était témoin de la mort de cheikh à Thiaroy hier lorsque nous faisons des comptes orange money jetai boulversé en voyant sa mère par terre qui se tordait de souffrance 😭💔😔
Les gars ils veulent trop faire le gangster jusqu’à tuer une personne et c’est de là qu’ils se rendent compte qu’ils ont fait une connerie. Allah yarham
Pere au Blouson blanc , vous avez tt dit. Police ak Gendarmerie gnon wara commencer di def Rond , dans les rues, les plages, tt comme en Europe, Etats Unies
merci la populaion vous avez bien fait kou ray na gnou la ray
Chers journalistes, moment yi il faut éviter de faire des interviews aux parents directs. Il faut aller voir les autres proches, vous ne faites qu'aggraver leur douleur.
Machallah père gueume gua yallah Machallah, yallah nala souniou borom maye khôlou mougne
Repos éternel au défunt
Fin des temps sans aucun doute 😢vraiment la barbarie des gens en ce moment me dépasse اللهم ارحمه و اغفر له و اجعل الجنة دار له
Kiignou ray yalnako yalla yeureum kharei ko aldiana ki rayei nak yalnakofa aye dieufeum feikk bougn defone kougn ray gnou rayla legui mou diekh😢
Ndaysane gueum gua yalla dh 😢
Yalnako yalla yeureum te khareko adiana yalna égale ndawam adiana amine
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢 triste paix à son âme
Baye cheikh yalla nga agalei sa ndaw aldiana mak moma bokone classe CE1 fi ci mbour a CFP yalla nala yeureum li bett na ma💔
Cheikh bou Diop yalla nagua agalei sa ndaw aldiana j’ai était témoin de la mort de cheikh à Thiaroy hier lorsque nous faisons des comptes orange money jetai boulversé en voyant sa mère par terre qui se tordait de souffrance 😭💔😔
Yalla nako Yalla 😭😭😭😭😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😭😭😭😭😭🤲🤲
Les gars ils veulent trop faire le gangster jusqu’à tuer une personne et c’est de là qu’ils se rendent compte qu’ils ont fait une connerie. Allah yarham
Que son âme reposé en paix 😭😢
Ndeysan yana ko yala yeureum maye len kholou mounie 😢
Nila rk kou ray nanioula ray legui ray gui diekh fi bilahi
Paix à son âme 😢
Ndeysanne di massou wou parents yi sokhla nagn assistance psychologique nakh trauma biniou doundou ni😢😢😢
yalla na khippé aldiana firdawsi li khéw si deuk bi il est temps ñou dieule aye mesure you sévère parce que li eupena méttina trop
Ndeysan massa metina lol Bilahi
Pere au Blouson blanc , vous avez tt dit. Police ak Gendarmerie gnon wara commencer di def Rond , dans les rues, les plages, tt comme en Europe, Etats Unies
Yaye dji ndeysane
Dafa tite diakhaso neysan 😢
😭😭😭😭😭🇸🇳🇸🇳🇸🇳😭😭📱
Bougnou défone kou Raye gnou raye la légui légui mou diêkh fii
Motakh kiko ray raynagne ko
@@Amy-p6e3j c'est bien
c dure🥲