Gaston Mbengue recadre Me Moussa Diop sur Ila Touba :" il doit demander pardon à tous ..".

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 3 дек 2024

Комментарии • 263

  • @mohamadoulaminediop9242
    @mohamadoulaminediop9242 5 лет назад

    Mercie bcp Gaston

  • @mamadoudiouf8638
    @mamadoudiouf8638 5 лет назад +8

    Hé dou macky moy défar Touba Touba serigne Touba moko mome défaralko bopam diokh mouride yi niou yégali liguey bi sou féké illa Touba rek mouride yi meune néniou defaral sen bop lou Raw illa Touba

  • @anniyagoto2086
    @anniyagoto2086 5 лет назад

    Merci Gaston homme de la vérité

    • @issatoure489
      @issatoure489 5 лет назад

      Ki di doméram ngua nane homme d vérité interem rék imbécile bi

  • @chantaletendeng5363
    @chantaletendeng5363 5 лет назад

    Gaston tu fais vraiment rire. Je te tutoie nakh c'est ça que tu mérites. Loy fonp ay beuts.

  • @afl8014
    @afl8014 5 лет назад

    oui merci sa wakh refet na 💕👏👏👏👏

  • @mohamedseck1272
    @mohamedseck1272 5 лет назад

    Bien dit Gaston. Nay rafet rek

  • @bambagueye2454
    @bambagueye2454 5 лет назад

    Merci Gaston bien dit

  • @mtkmtk364
    @mtkmtk364 5 лет назад +3

    Merci

  • @tidianesall7553
    @tidianesall7553 5 лет назад +23

    Mr dois demander pardont je suis alpoular mais je pas daccor avec ces paroles ireflechi .vive senegal uni

    • @jolof221
      @jolof221 5 лет назад

      Malheureusement même Macky sall pense. Comme moussa diop

    • @globodia
      @globodia 5 лет назад

      Y'a man féne vraiment doul rek

  • @modousylla625
    @modousylla625 5 лет назад

    Bien dit

  • @assanembaye1223
    @assanembaye1223 5 лет назад

    Merci gaston waye dafa doy dafa doy doyna

  • @diolmamadou1096
    @diolmamadou1096 5 лет назад +3

    Yalna diam yageu si Sénégal

  • @alfaaroukhtv3391
    @alfaaroukhtv3391 5 лет назад

    Merci beaucoup réfétna téy nak la

  • @babamaremdiop1470
    @babamaremdiop1470 5 лет назад

    Bilahi dina dem deh

  • @azizdabakhsow
    @azizdabakhsow 5 лет назад +3

    Bien parlé le Don King...lerreur est humaine..faut pardonner..

    • @lekinzal123
      @lekinzal123 5 лет назад

      Dafa rew rek gua nan ma dioum

  • @damembow6374
    @damembow6374 5 лет назад

    Moussa a raison yalla sax néna kouko nékal mou nékal laa

  • @labsolugueye9016
    @labsolugueye9016 5 лет назад

    Liko Waa keur borom touba Bii ndianalonn Yeuppeu Moussa Diop yaxnako Ta inchalah Dingainn ko Guiss Laigui bientôt rék inchalah......inchalah ay vrai vrai Doméram nguén Loudoull xaliss Geumoulainn ko 😎

  • @diolmamadou1096
    @diolmamadou1096 5 лет назад +3

    Yalna yalla bole khole yi

  • @labsolugueye9016
    @labsolugueye9016 5 лет назад

    Yaaa Geuneu Naa Féxx nieuppeu Yaw.... ....yénn Mom mérci rék yéna Yamm ay Doméram nguén rék......wayé Dingainn xammni Serign touba Dou Moromm DH 😎

  • @cheikhbecayediagne8497
    @cheikhbecayediagne8497 5 лет назад

    votre intérêt rek avant cel de la nation.vive le Sénégal qu allah vous dénigre tous et nous donne de vrais patriotes

  • @fadaleba1005
    @fadaleba1005 5 лет назад

    Père gueumoléne dara yénieupe yame

  • @toubaseck4361
    @toubaseck4361 5 лет назад +17

    Gaston nafekh pire nga mais tay wakh nga deug père bravo autant pour moi Second tour invitable gas o6

  • @bonjourfaye3266
    @bonjourfaye3266 5 лет назад

    Le grand seytaane

  • @amadoukane7595
    @amadoukane7595 5 лет назад +4

    Je suis d'accord avec Mr Diop ,

    • @thiounekabir4327
      @thiounekabir4327 5 лет назад +2

      Amadou Kane 👈🏿mounial wa fouta merito wouniou rang rang sakh

    • @alassanendoye9407
      @alassanendoye9407 5 лет назад +2

      ilaa fouta, seuls les moutons, les chèvres, les boeufs etc..etc...seront les usagers

  • @elhadjithiam9646
    @elhadjithiam9646 5 лет назад +19

    Yaw mom door rek hypocrite nga

  • @diamalick7974
    @diamalick7974 5 лет назад

    C pas les prières des marabouts mais la décision du peuple

  • @KAMALVISION
    @KAMALVISION 5 лет назад +1

    Sénégal daal lii moko yahh dangay wax sa tothie tothie niouneela diegaloul nga diegalou mou dieekh niou fatteko keneen waxaat tothie tothie

  • @jolof221
    @jolof221 5 лет назад

    Il ne faut pas nous fatiguer. Moussa diop a dit tout haut ce que Macky Sall même et les haal pulars pense tout bas. C est ça la vérité. Macky a seme depuis le début de son mandat les germes d une division nationale.
    Ne nous emmerder pas avec Sénégal Nioun Nieup bene laniou. Macky Sall n a pas agi en tant que vrai chef d état mais de clan et d Ethnie. C est ça la vrai leçon à tirer de ces élections

  • @aminaba6130
    @aminaba6130 5 лет назад

    I love macky

  • @msdmsd2453
    @msdmsd2453 5 лет назад

    Yènaa yame rék

  • @babsiba1551
    @babsiba1551 5 лет назад

    Wawu waawu

  • @bambakebe345
    @bambakebe345 5 лет назад

    Gaston katale sa ndeye 🤐🤐🤐
    Kéne lasioula🤐🤐🤐

  • @tallandiaye496
    @tallandiaye496 5 лет назад

    mr6 Moussa diop

  • @sonkopresident938
    @sonkopresident938 5 лет назад +1

    Waonala kou leck xalisse politicien digna beugeu geune mou teula

  • @almeriaalmeria3826
    @almeriaalmeria3826 5 лет назад

    On la reelu pour travailler c pas pour voter

  • @serignembengue2033
    @serignembengue2033 5 лет назад

    S.Mountakh dou daram bou lene niou sonal dinou saga chak jour bo lene diouguè di justifie nous somme fatigue avec la colere ki nous tue

  • @arondia7421
    @arondia7421 5 лет назад +1

    Geumo dara sa sarame ndeye. Geumoléne yalla.

  • @abdoucostatine7746
    @abdoucostatine7746 5 лет назад +10

    Gaston nokoul feuleii. Yaak moomah yeime. Marr taatou diambour yii ngueine fi nékeii. Vampires sax moleine gueune. Waayei yagatoule yeine nieupay ndeyou diougueii fii

  • @medounefall1855
    @medounefall1855 5 лет назад

    Waye saye

  • @mouhameddiouf8690
    @mouhameddiouf8690 5 лет назад +1

    gis ngua yéén sénégaléyi ngéén yap wayénak sénégalaiyi gnoléén wara tégaat séén palac wolof daané mbééjoum kanam boromakoy fajial bopam

  • @mbackediouf9419
    @mbackediouf9419 5 лет назад

    Yen nak Moussa diop macky sall yep sen datta ndeye

  • @Senegalresumetv
    @Senegalresumetv 5 лет назад

    🤷‍♂️vraiment

  • @DiopdoffeNdiaye
    @DiopdoffeNdiaye 5 лет назад +11

    domeram gua !yeneu nieup pa yam

  • @adamafall7543
    @adamafall7543 5 лет назад

    Kii mom niepeu dou tousss walahii

  • @Boy_niang
    @Boy_niang 5 лет назад +1

    Fi niepa yewou daguar dorr😂😂😂

  • @papediaw6087
    @papediaw6087 5 лет назад

    Touba ,momounou nit yi

  • @bassiroutoure7503
    @bassiroutoure7503 5 лет назад

    Yene yem waye bakh na

  • @seckndeyendieme4332
    @seckndeyendieme4332 5 лет назад

    Doul way yénn touba serigne touba moko ligueyal bopam

  • @astoubah5648
    @astoubah5648 5 лет назад

    Yow yaye domouharame

  • @ndoyematydiaw3531
    @ndoyematydiaw3531 5 лет назад

    Yena yam. Gnafoulen felé

  • @chefjosephwalowavalley5742
    @chefjosephwalowavalley5742 5 лет назад

    Gaston Wà ila xaliss

  • @komdaniel4825
    @komdaniel4825 5 лет назад

    Gaston kom khale rek

  • @malicksarr5706
    @malicksarr5706 5 лет назад

    Yaguidoga wakhe dégue caston sisa adouna

  • @ibrahimabousso7791
    @ibrahimabousso7791 5 лет назад

    Sa wakh Rafetna

  • @annafall1347
    @annafall1347 5 лет назад

    Gaston sa data ndeye

  • @ibrandao3398
    @ibrandao3398 5 лет назад

    macky mom bu deme 2e tour Moy Paraná khamna talibeyi parenan si mon

  • @seydoukane2737
    @seydoukane2737 5 лет назад +2

    6ak9 yèna yame

  • @madamedieng2108
    @madamedieng2108 5 лет назад

    Yéna yém rek may gniou niaawna ba paré wakh balou fēttal la bou khassé ba guéne thi sa lamégne meneto thi dara

  • @paomar1859
    @paomar1859 5 лет назад

    Yow tu nous fichier

  • @gueyemourtalla9639
    @gueyemourtalla9639 5 лет назад

    Billahi degeu rèk nga wakhe

  • @mameastasagna6845
    @mameastasagna6845 5 лет назад +2

    Doul rekk geumo dará khalisse gay diamou😈

  • @karimbandios4136
    @karimbandios4136 5 лет назад

    Wayèr deuxièmes tours lagunes beugue

  • @assanediouf6629
    @assanediouf6629 5 лет назад

    Dangêni doull yééne nièpp

  • @pascalmalau423
    @pascalmalau423 5 лет назад

    Yeneu gaston defoulene dara nguene koy saga vreman keneu khamoul liguene beug vreman

  • @tafadia9288
    @tafadia9288 5 лет назад

    😱😜

  • @modousarry1112
    @modousarry1112 5 лет назад

    nopil may 🙊🙊

  • @Hamsatoul_Rijal
    @Hamsatoul_Rijal 5 лет назад

    Degual mounane dako bind walla audio ki lou takh mou meuna SOS

  • @solutiondiopportable9585
    @solutiondiopportable9585 5 лет назад

    Doull Rék mdr Gaston 🐒🐒🐒🐒

  • @khadimdieng1745
    @khadimdieng1745 5 лет назад

    Wakhoul deug deh touuk

  • @oumargaye917
    @oumargaye917 5 лет назад

    Weup kharitam lan

  • @youngmike5868
    @youngmike5868 5 лет назад

    2nd tour

  • @abdoulayethiam7343
    @abdoulayethiam7343 5 лет назад

    L aéroport Blaise Diagne est emprunté par les senegalais de tous bords que ce soient les partisans de Wade de Macky ou autres.En bref une infrastructure ne se fait pour une motivation politique en référence à ila Touba mais plutôt pour ses retombées économiques et sociales.Dans ce sens MOUSSA DIOP s est trompé car tout usager empruntant l autoroute devient un contribuable par le canal de son ticket peage

  • @seyesadieye7727
    @seyesadieye7727 5 лет назад

    moka wakh

  • @celinesoulie8059
    @celinesoulie8059 5 лет назад

    Diadieuf faaaa teeee rafetna Gaston lol

  • @flokykara1113
    @flokykara1113 5 лет назад

    Gaston domeram gua yaw

  • @modoumbengue7708
    @modoumbengue7708 5 лет назад

    Moussa Diop sa deidieuw ndaye

  • @datr6676
    @datr6676 5 лет назад

    Ma am louma soff degue

  • @bane257
    @bane257 5 лет назад

    Ila fouta ndaw tok ba sone 🤣🤣🤣 ayam sorry

  • @abdoulrazaqcamaradakarsene3961
    @abdoulrazaqcamaradakarsene3961 5 лет назад

    Way c pas la peine de grawoul Moussa diop djeulé wuko sens bi

  • @patriotesolutions9400
    @patriotesolutions9400 5 лет назад

    Gaston yaw mome saytané nga yaw mome mousouma nékh ndakh sa lépp intérêt le foye guise xaliss rék ngaye diar guemo dara lima wakh ni nak da nék thi mome manone nako farale ndakh nioune serigne touba laniou gueume deuk touba mai ki mome dafa guemoule dara motakh nékhouma dara

  • @mbackegueye4709
    @mbackegueye4709 5 лет назад

    Doul yenyamm

  • @moustaphadiagne4278
    @moustaphadiagne4278 5 лет назад

    Nafekh

  • @boyndiayegrazie3356
    @boyndiayegrazie3356 5 лет назад +6

    Gaston doul rek

  • @eldamediopdiop210
    @eldamediopdiop210 5 лет назад

    Yw nopil niépeuleuh tané

  • @cheikhfamadiaw1859
    @cheikhfamadiaw1859 5 лет назад

    Sènn tanto ndaye yen ak makci sall ak moussa diop ak yaw midi sènnn lafall baye sayou ngeune yèwo xaliss rek geunnn geumm

  • @yatediagne7024
    @yatediagne7024 5 лет назад

    gaston s
    Doul way

  • @peulbouraffettsow9804
    @peulbouraffettsow9804 5 лет назад

    Fouta dh amoul sakh rag rag bilahhi illa fouta dh amoul

  • @pttmomes9977
    @pttmomes9977 5 лет назад

    Doulll rék ngaye déf

  • @adamasy5184
    @adamasy5184 5 лет назад

    Dou macky sall moy dafar Touba

  • @bambangom729
    @bambangom729 5 лет назад

    Tey mom wakh xa xakhou nite

  • @abdoulekane1096
    @abdoulekane1096 5 лет назад

    Mane de todiane la waye yakarna ni me moussa diop limou wakh defma meti ak lou nit mana wakhal mourid yi moy amnagnou foula ba kene dou len corompre te yakarougnou macky sall

  • @cheikhmouhamadoumourtadasa2799
    @cheikhmouhamadoumourtadasa2799 5 лет назад

    Bour la degue kone Mbacky bourela OK nare bou nawe loumou wakhe si geute gua lako degue

  • @bayefallgalsen2096
    @bayefallgalsen2096 5 лет назад

    Yene Maky nguene diamou. Dou nguene dara

  • @abdouthiam4246
    @abdouthiam4246 5 лет назад +2

    Denal laboudji

  • @bambakandji1325
    @bambakandji1325 5 лет назад

    yen ngepa yam kif kif 6/9

  • @morsyll3909
    @morsyll3909 5 лет назад

    Neenio mooko wakh kii dou rouss daa warra démissionner

  • @papedjiby1354
    @papedjiby1354 5 лет назад +1

    TeudieuL sa nday guimign yénah Yam khamoulén sakh loulén du khar

  • @aliounendiaye7907
    @aliounendiaye7907 5 лет назад

    Gaston mbengue doule yenn nieupe yem

  • @lenzoboye8592
    @lenzoboye8592 5 лет назад

    Guemo ligay wakh

  • @talibebambasalihousarr1067
    @talibebambasalihousarr1067 5 лет назад

    Iow Gaston KO yapp pond Gambie bi Macky Sall invite reek la FFA Wone boulle niou rayyyy