Imaginé léne boucher door reug reug mou KO par accident ! Da bari weurseuk ! té sport de combat lepp meune na nék !!! Shiii Kone boucher bou gnibissé Modou Lo ley ladj!!!
MOI MON PROBLEME N'EST PAS REUG REUG C'EST LES 6 AUTRES COMBAT DE BOUCHET REUG REUG PEUT ÈTRE COMPRÈHENSIF SUR LA RHYME MAIS LES 5 AUTRES NON BOUCHET KHALISS DIAROUL LI WAY😢
Boucher bo léké avance bi lébal nga déloo haalisou diambour😂 Bo fatouwoulit dinga ami alzheimer bahna reug reug mii carriéram la beugu défar boula diéko doula mougneul dé😂
Meun nako gagne dé deug nga reug reug nan affaires yi dafa am 50000$ bonus té boucher doumako yakhal té deug na bou combiner meun na yakh carrière internationale lam
🇸🇳🇸🇳🇸🇳koué Sénégal ñékoul amõ crédit 😂😂😂 chaque jour avec 😂😂😂
Boucher da ga beugue khalisse reck digua dé té sa heure dou diote 😂😂😂😂😂
No boucher dafa diapone no MMA la bounou la doré ga abandoné alors k kick boxing aye round la bo blaissé dagay continué 😂😂😂
Waw lolou la diapon nga hamne bou mete rek mou abandonné 😂
Beuzz wakhna deguedee wakhtaneeleenekò
Beuz wakhal ngir yalla nio def ndank sinon reug reug dakoy gagne bapare diko rethiou
Beuz Rey nama nena dor mou dhe amna ci boucher nena envoyé ma video bi😂😂😂
Waw Fadam khana boucher doussa kharite😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
No this man he's so funny 🤣 he will not go 🤣
😂😂magui ré té besbi jotagoul reug japssi rek sinn dou bakh khaliss akay seytané 😂😂
Barki alkhourane ma ngui retane baye dioye 😂😂😂😂😂Fadam con na 😂
Boucher 6 comba la si dieul, mèm bou doul Reug sakh kèn mokoy dor mou dè
Boucher delol avance b 😂😂regue regue du chahan de😂😂
Wa Lane moy diékhal lamb dij nkl😂😂😂😂😂😂😂
Bilaye boucher djeul gua lo khamoul 😂😂😂
C’est ça la probléme😩😂😂😂
Boucher moumana Fadam sérieux wi
Magui imaginer reug reug door boucher mou kheum 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Mon ami Beuz waye bouy keup gaal ken dou waye ci téfess donal nanditė nak.Diaral restaurant ba rék😂😂
Bouche day délo avance bi déh liii déh ma léne ko wakh 😂😂😂
Dor mou de la reug reug signe😂
Loukoy diehal Momay ray😂
Imaginé léne boucher door reug reug mou KO par accident !
Da bari weurseuk ! té sport de combat lepp meune na nék !!!
Shiii Kone boucher bou gnibissé Modou Lo ley ladj!!!
Fadam néna bouché dêmna ahhhh
😂😂😂😂 boucher bo demei yomal khiyam nouyoul ma sama mame 😂
it is not a contract but a death certificate 😂😂😂😂
Boucher esk tayle wougnou ko te yegouko 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Boucher titte neu😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Reug mala ko nyan bul ko dorr mu de 😂😂dorr ko ndank regg mala ko nyan.sa fan la birr Gambie😂
Fadam serieux woul bilahi😂😂😂
6 combats la deigu😂😂😂😂
Beuz boul gnou sonal akh sa rêve .Il peut pas refuser des millions et 6 combats aussi😂😂😂
Thank you Beuzz god bless you always No Reug Khana kay Dofoul bai Gagne Boucher Reug Ngirr YAllah Défal Boucher Ndank 😂😂😂😂
Esque combate by daugla 😂😂
Boucher moytoul fadam
😂😂
Reug Reug dé mome bolé woussi ay wahame😂😂
Haliss rék dinga fatou dé😅😂
Boucher tite na😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂boucher insbi en😂😂😂
Aye waye thiate mo gaw beuz sa fin de carrière lay guiss ni😂😂😂😂
It’s not joke billahiiii butcherrrt deyyyyy kharouuuuuu 😱😱😱😱😱😱😱😱😱😱😱liiii dou foooo amoulll demmm ardoooo dehhhhh
Boucher amoul ains bi tite na ba diaxasso😂😂😂
Non mangi ré bey danou, boucher néna amoul tapé si tapis bi🤣
Boucher delole khaliss bi 😂😂😂
Boulein taakh boucher daw
MOI MON PROBLEME N'EST PAS REUG REUG C'EST LES 6 AUTRES COMBAT DE BOUCHET REUG REUG PEUT ÈTRE COMPRÈHENSIF SUR LA RHYME MAIS LES 5 AUTRES NON BOUCHET KHALISS DIAROUL LI WAY😢
Boucher day kharou😂😂😂😂
Fadam dinama raye😂😂😂
Boucher yalla n'a xell mi delou si
Boucher titena😂
Kharou amoul heure 😅😅😅
Kharou barina façon 😅😂
Sama waadji titeul na bouché dé
Yengenne mai dadii
Beuz yakkk na combat bii
Boucher dafay kharou 😮
😂😂😂😂😂😂😂bou titeul ki way
this guy is very funny
Demal thisa restera mi bakhe ns
Bilakhi yengenemaifathie
Tek khel bakhoul kio bouches néna day tej khel toubab yi😂😂😂😂😂😂😂
Boucher paré nassi combat bii
Fadam bouy soga yéwou la beug guiss😂
Boucher khaliss diaroul liiii walahi
Fadam😂😂😂😂 boul tital boucher
😂😂😂😂😂😂😂😂😂🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Boucher tiit nade😂😂
Boucher prépare sa triche. Une minute mou déclaré défaite. Il triche pour s'enrichir comme dans la lutte
Lolou amoul si King boxing
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂way boucher waay😂😂😂😂😂
Bouche je t’aime bien mais bayil mou sed sinon reug dalay door nga
Boucher avant ngay déh envoyer sand code bancaire
Amoul combine dè mongui ci contrat bi
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Boucher bo léké avance bi lébal nga déloo haalisou diambour😂 Bo fatouwoulit dinga ami alzheimer bahna reug reug mii carriéram la beugu défar boula diéko doula mougneul dé😂
Fadam baxoul😂
😂😂😂nenako yone ma.video yi
Meun nako gagne dé deug nga reug reug nan affaires yi dafa am 50000$ bonus té boucher doumako yakhal té deug na bou combiner meun na yakh carrière internationale lam
❤❤❤❤😂😂😂
😂😂😂😂😅😅😅😅
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣
Reug reug 😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
fadam😂😂😂
Ho boucher rip mon frere
Amoul ragal afairrou goor leu
Dou lolou de boucher mi nek ouest foire entrainewoul di diay😂
Boucher feler dou arene national dhe
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Kharou barina ay facon de cey bouche nenako liral ma contrabi
Reug il ne sera pas agressif combat bi layyyy diaye promotion
😂😂😂
Kkkkkkkk
😅😅😅😅
bou yagoul rek samiyou Con gui bi ki daye kharou rek
Bouché yaw donal goor do djiguene way wala nga délo nday avance bi keut guéne nga kou
Non boucher comprendroul Lou khew..
Beuz yaw boul yakkeu lambe dji
Reuk boule dor dél mbéthj rk
Reuk reuk tu dois faire ta carrière boucher veut de l’argent alors na saf sap rék amoul yereum
Lolou nak moy problème bi té reug reug deug na bou combiner meun na niak carrière internationale lam
Reug Reug nakoy dor ci nop yi😂😂😂😂
Noo géummé bii pas que dafa beuri wahc trop😂😂😂😢
@@thiernodiallo2830 🤣🤣🤣🤣 lolou la khalatone mais au final damako yeureum comme Beuz noumouko yeureumé. Na nop yi di riiiir dina takh mou wagni
😂😂
Reug dorr KO beh mu puup
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
❤❤❤😂😂