Le fait de Vous entendre remémore toute âme pure le pacte qu'elle a signé avec son seigneur ! À savoir adorer Allah swt à tout moment. Gloire et pureté éternelle à vous L'imam des biens guidés
Dieureudieuf Seydi Mouhamed El Cheikh, ya ngui liguéyeul deug deug Cheikhou Tidiani (RTA) si diamono bou yakhoubi. Que la Clémence divine se répande sur vos détracteurs si barké Seydina Mohamed car ils ne savent même pas ce qu'ils encourent !
Ya Seydi Mouhamed El Cheikh ken amoul sa faye , a chaque sortie niouy begg di begg di begg te liii yeup da nga bakh rek walahi , yalla naniou yagg di diarignou sisay kadou zahiran wa batinan
Machaallah Ya Seydi Mouhamed El Cheikh Sang Bi Chers auditeurs ne regardai pas la personne mais!!!!Ecoutez ce qu'il degage et ce dont il nous parle et faite l'annalyse avant De Juger meme si ont n'a pas le droit Jugė....
Walay ndeyssane ya bakh sangeu bi man souma guissé koulay critique daf may diakhal trop sakh ((wayé delou di sant yalla bignou boké diamono ma geumleu sope leu beug leu si barké mawlaya cheikh tidjani cherif ))
Le fait de Vous entendre remémore toute âme pure le pacte qu'elle a signé avec son seigneur !
À savoir adorer Allah swt à tout moment.
Gloire et pureté éternelle à vous L'imam des biens guidés
machalla lerr rek mo nekh ndah so wakhè khol cedde yalla nama yalla dadialek sangue bi si barkè cheikh tidiane
Mubarak fikhi ya Seydi. bon ramadan
merci sanguebi beugue bagne yaye borom lerre yii
mashallah mashallah
Deweneti à toutes les musulmanes et musulmans et qu'Allah nous accorde un ramadan de lumière
amine machallah
C'est clair , net, facile a écouter, instructif qu'Allah te protège et que la Mission soit éclatante. Merci
Diereudieuf Sangue Bi. Yangi Dimbali Domi Adama yi Bou baakh si Sèn Diné . Yalna Yalla Deugueureul Takhaway Bi.
ma cha allah tout est clair bcp d'enseignements et de sagesse que Dieu puisse pardonner tes détracteurs
Dieureudieuf Seydi Mouhamed El Cheikh, ya ngui liguéyeul deug deug Cheikhou Tidiani (RTA) si diamono bou yakhoubi. Que la Clémence divine se répande sur vos détracteurs si barké Seydina Mohamed car ils ne savent même pas ce qu'ils encourent !
SEYDI MOUHAMED EL CHEIKH c'est un Océan de SAVOIR ! Dieureudieuf SANGUE BI!
Dieureudieuf Sangue bi. Bougnou khamer fougnouy tek sougnou tank rek yawla, yorel nagnoula ndioukeul bou bakh yalla khamnako! Waayer yanna gnoula Mawlaya Cheikh fayal bopame thi barKe Seydi Ahmad
mawa fall p
Astou Diop
machallah seydi mouhamed el cheikh un vrai guide spirituel.
Ya Seydi Mouhamed El Cheikh ken amoul sa faye , a chaque sortie niouy begg di begg di begg te liii yeup da nga bakh rek walahi , yalla naniou yagg di diarignou sisay kadou zahiran wa batinan
Hoy y hurí
Macha'Allah Nio ngui lay Ziyar kilifeu gui
Machaallah Ya Seydi Mouhamed El Cheikh Sang Bi Chers auditeurs ne regardai pas la personne mais!!!!Ecoutez ce qu'il degage et ce dont il nous parle et faite l'annalyse avant De Juger meme si ont n'a pas le droit Jugė....
Al Hamdoulilahi Rabil Alamina
Machallah walahi naysane amna solo trop way merci
maachallah un océan de savoir
Diazakal Lahoul Khayran
Walay ndeyssane ya bakh sangeu bi man souma guissé koulay critique daf may diakhal trop sakh ((wayé delou di sant yalla bignou boké diamono ma geumleu sope leu beug leu si barké mawlaya cheikh tidjani cherif ))
machallah
ESKEY SANGUE BI
tidiane yi manoulene si mom