Artiste: Keur Gui……….Son: Saï saï au cœur Intro: A l’heure du bilan RIEN (nada) Rien à se mettre sous la dent 7 ans ñuy perte sunu temps Ci bii banditisme d’état sans précédent Mêmes fainéants Mêmes incompétents Mêmes vieillards dans le vent Ñaata bubu golo ñoo transhumer Ñaata patrons de presse achetés Ñaata juges sans dignité Ñaata bavures policières Ñaata litiges fonciers Ñaata ministres yu cuune Ñaata scandales Ñaata ñoo am couverture médicale Ngay saraxe ay bourses sociales Rien que ton parti Faate la patrie Pétrole sa rakk Contrats say goro Marchés publics tubaab yi Sénégalais kolo kolo Ammu ñu vergogne Siimee sen cere suñu ròngoñ Jox ñu suñu cartes yi Da nga tële Xam nga ni moos dañ la fiy jële Refrain: Justice bi leegi dafa naxsaay (Haay haaay) Li duuf ci nagg bi lepp daf ko jaay (Haay haaay) Ñi ànd’ag moom ño ngi ndàtsaay (Haay haaay) Dëg dëg Macky moy saay saay (Haay haaay) Couplet 1: Lepp lum la dikk Ludul yobbu la DIC Xamal ni dina diig Waaji mo mattul njiit Di feet rekk ni jiit Kom kom bi yëpp mu ñiit Askan wi dee akk xiif Nga jàpp doori liif Jàmm daf fi gëj Étudiants yi nga dëj Élections yi di lëj Opposants yi nga tëj Nguur gu saggaan Ñun ñu marr naan Dëkk bee panne Ndaw ñi walliyaan [Refrain] Couplet 2: Fim ne yëpp a loof Reew mi doo tuñ doff Say chartes taxul ñu xoff Da nga ñu mujjee soof Lum wax rekk ne waxeet Jaay na sunu xeet Lebbe sunuy têtes Baayil ñu fii ay dettes Njàng ma ngi l’hôpital Ñakk plateau médical Falu fatte lila fal Sa bopp rekk nga deffal Référendum nga tekk say lois Bëgga nangu sunuy droits Joxoo ndaw ñi ay emplois Tëyeel sa dipla en bois Duy sa poche ay milliards Gouvernement des connards Taf sa bord ay vieillards Bës Reubeuss akk mille yarr [Refrain x 2] Saay saay lë (x3) Bu maaga maag Saay saay lë (x2) Pataa bu puff Saay saay lë (x2) Bu ngande
Ki dafa masoul nék Rappeur khamoul rada si gnom papa ndaye thiou la wara dèm yagui yakh dérou rap bi Sénégal golo bou diouk rék beugue gnou sonal doul khamoko di doul nane bandigeu
Dof sétanal sa vidéo bi khaliss nn dafa doye war temps saga aly ngouye ak cissé lo mome ngafi néké mane douma guéte rapp galséne ms damaye fille saye vidéo ms khola tale sa bopou
Dof wedinala ma nekon sa fance nummer 1 me boul diaye sa ngoor nakh macki Day dem inchala
Tay jii demna en 2024 doff Ndeye ci kasso bii
Il dit la vérité
Dof ndaye dagaye doull rek
Mon beau-frère Bof Ndéye je suis fier de toi que Dieu te donne une longue vie
Yaw dof do bandit
Sur le plateau TV walf avec pape Ndiaye
bayil tokh bonne doff ndeye
Bayil togn
@@papediene7462 regarde stp tt ses autre videos stp tu le verra se la triste réalité doff deug leu
Fii fanela ci linguere yena mena fene
Artiste: Keur Gui……….Son: Saï saï au cœur
Intro:
A l’heure du bilan RIEN (nada)
Rien à se mettre sous la dent
7 ans ñuy perte sunu temps
Ci bii banditisme d’état sans précédent
Mêmes fainéants
Mêmes incompétents
Mêmes vieillards dans le vent
Ñaata bubu golo ñoo transhumer
Ñaata patrons de presse achetés
Ñaata juges sans dignité
Ñaata bavures policières
Ñaata litiges fonciers
Ñaata ministres yu cuune
Ñaata scandales
Ñaata ñoo am couverture médicale
Ngay saraxe ay bourses sociales
Rien que ton parti
Faate la patrie
Pétrole sa rakk
Contrats say goro
Marchés publics tubaab yi
Sénégalais kolo kolo
Ammu ñu vergogne
Siimee sen cere suñu ròngoñ
Jox ñu suñu cartes yi
Da nga tële
Xam nga ni moos dañ la fiy jële
Refrain:
Justice bi leegi dafa naxsaay
(Haay haaay)
Li duuf ci nagg bi lepp daf ko jaay
(Haay haaay)
Ñi ànd’ag moom ño ngi ndàtsaay
(Haay haaay)
Dëg dëg Macky moy saay saay
(Haay haaay)
Couplet 1:
Lepp lum la dikk
Ludul yobbu la DIC
Xamal ni dina diig
Waaji mo mattul njiit
Di feet rekk ni jiit
Kom kom bi yëpp mu ñiit
Askan wi dee akk xiif
Nga jàpp doori liif
Jàmm daf fi gëj
Étudiants yi nga dëj
Élections yi di lëj
Opposants yi nga tëj
Nguur gu saggaan
Ñun ñu marr naan
Dëkk bee panne
Ndaw ñi walliyaan
[Refrain]
Couplet 2:
Fim ne yëpp a loof
Reew mi doo tuñ doff
Say chartes taxul ñu xoff
Da nga ñu mujjee soof
Lum wax rekk ne waxeet
Jaay na sunu xeet
Lebbe sunuy têtes
Baayil ñu fii ay dettes
Njàng ma ngi l’hôpital
Ñakk plateau médical
Falu fatte lila fal
Sa bopp rekk nga deffal
Référendum nga tekk say lois
Bëgga nangu sunuy droits
Joxoo ndaw ñi ay emplois
Tëyeel sa dipla en bois
Duy sa poche ay milliards
Gouvernement des connards
Taf sa bord ay vieillards
Bës Reubeuss akk mille yarr
[Refrain x 2]
Saay saay lë (x3)
Bu maaga maag
Saay saay lë (x2)
Pataa bu puff
Saay saay lë (x2)
Bu ngande
Kou afronte maky katal nadayam
Yaou bayil daiye ngore
Li Moy lan
Ki dafa masoul nék Rappeur khamoul rada si gnom papa ndaye thiou la wara dèm yagui yakh dérou rap bi Sénégal golo bou diouk rék beugue gnou sonal doul khamoko di doul nane bandigeu
Ap doff kènn doukonè yaa moom dianguyi. Kii c'est un assassin tueur qui circule encore. C'est dechet de l'humanité.
Senegal lou wayy nekh def
🤣🤣🤣🤣legui macky nga andal oto sakh amo ko
Dof sétanal sa vidéo bi khaliss nn dafa doye war temps saga aly ngouye ak cissé lo mome ngafi néké mane douma guéte rapp galséne ms damaye fille saye vidéo ms khola tale sa bopou
Wakhi doff rek
Wedii nalla
Porquoi☺☺☺☺
Sa data ndaye
Merci D..💪💪💪💪💪💪💪👑👑👑👑
Tu courage Dof je t'aime tellement
hahhahahhaa khalasss
Yagui were dhe Taye ka andde ak senegale yi
Wakhal way
Garapi ngoreu you bakh la ame guissouma komeu thi gueune aay ci adina woma reek niam sama grap yi xool numero telephone whatsapp 703187251
Kii ha. wor katla. Dof lah xamna 2millions rkk lako boukh moy xarou nii. aba donal bay fall doundou deugge weule book
Ay thiorkho thiorkho rek nga xammmmmmm
Ray catou nit là dé xam léco na danla yareum nguir sa Ndaye mo lolou xam nga mais macky dalay utilisé cofi ray di nga teud wala niou ray point
Touka Kande Siga bocou
Touka Kande ki je suis ?
Ndof ndaye yaw linga ni té temps yi ngaye def sa video di khas macky ak ay gars wame kéne khamoul lo beugeu money rek
Ki dofe la
Do dara
Nice
yawe daga bayii sa lokho
Del sagou saltè
non baye bebeto man la rak idrisa ndao chmbr 8 mes nak boul plotique dh
no ki sofe na lègui trope
Cool
Katal sa nday guëmo dará nganan ay macky go waye sa diobou nday yaw do bandi diay katou yamba nga wone guëmo lén nday dará ndah khalis
Domeram guemo touss
Dama wara def ni yenn rek sénégal boffi néké fok nga dof dof lou way
kii dafa wouyo toureum kW
wayal kula naikh yaw
Du courage dof
affaire bi yawla
DU courag dof
katal sa ndey yawak gnigyalim
Yaw dagay geun di dofof
Boul gnou daye sonale bayil daye politique doule waye
Boy xamo darra guewelou maky sall
Mé broo bi molul kii kii day ndayyi wéerè.antank rappeur yaw gani bandi yi gay téwal non non sa boppe
Yaw dodfi dara demall tary way
Vive President model Ibrahima sall le petit flis brome darou
Yawe dy damelni daga AME probléme mbpou ba tayé
doff lu
Rap defo fi dara dagay sonalaté
C dommage tu te fais des ennemis bêtement
Yuw danga stupid ak foolish